Personnellement depuis la mort de ces jeunes je ne dors plus car j'ai le cœur meurtri : il faut que les coupables ou le coupable soient/ soit sévèrement puni
Honnêtement yacine khawema journaliste nga khawema lanenga. Mais sa wakh amoul beneu sence. Khamo sakh ningaye wakheeee. Félicitations à tous les autres. Yacine daye yageu séne plateau bi. Bne journée
Sii réellement Nabou Leye refuse de parler ak nimou mell ak Aziz kone soit day bagne wah lou peuple bi kheebé aziz Dabala soit ell est encore sous le choque ou El est dépressive 😢
Elle n’est pas dépressive parce que la police sait qui est dépressive et qui ne l’est pas. Si elle se présente face au procureur c’est qu’elle a des informations qu’elle a refusé de donner. Et cela fait d’elle une complice. Elle est proche du défunt et donc elle impérativement tout faire pour que ces criminels puissent payer leur crime. Au cas contraire elle fait partie !
Féne rek Hier vous avez dit que Mamadou Lamine diao takawoussi laléwoussi ( répéter à plusieurs fois d'ailleurs) tay vous osez venir nous parler de sources sûres Doul rek berkkkk 🤮🤮🤮
Vous vous trompé de cible. Il ne s'agit pas d'exclusivité mais de ne divulguer que les informations sûres et vérifiées Cest plus simple de reconnaître ses erreurs parfois.
Bilaye yow yacine mi weroul NABOU MO wakh né Aziz dafa fébarone mou yobou ko clinique après mou bayi ko mom kene mou ngnibi NABOU dal moy wara wakh degue
Kharit kharit rk lay doon niko borom kap bi doné non la ko nabou done te nonou lako ay kharitam rayé niom niep ay kharitam laniou motakh niou sexue xalis
Sidi Diop dioumoul dei moko tayy mom star la dans Senegal donc dafa wonei bon exemple, dafa diap ni bouko deffe dara meunou ko si feekk il doit être jugé comme une personne lamda
Le fait qu'elle ne parle pas...peut-être mystique aussi...les gens sont dangereux faut rien laisser en rade....il faut que sa famille bouge...elle peut ne pas parler sans le faire exprès..! Wassalam
Arrêtez de croire que c’est impossible qu’elle fasse partie de ces criminels. C’est idiot de croire que ton ami ne peut pas te faire du mal. Je crois à la justice. Cette justice nous dira si elle fait partie ou pas. C’est son ami elle doit tout faire pour que ces criminels puissent payer ce qu’ils ont fait. Si elle se tait c’est qu’il y’a du louche. Elle en sait beaucoup trop sur le défunt et c’est aussi possible qu’elle sache tout ce qui peut se tramer autour de lui : la cause de son décès.
Désolé mais baisse d'un ton. Un diminue le poliment a chaque fois que tu morales ma sœur. Pas besoin de crier pour se faire entendre. On ne veut pas connaître vos sources juste ne dites rien si c'est pas sûre.
yénaye wakhati wa bakhna. Pour le cas de Sidy, il faut une amende bien salé et obligation de passer son permis. Djimbori mais Sidy mo warone khalate lolou yeupeu t kham ni c'est un responsable. La loi est pareille pour tous arrêter avec ça. Cette femme tigré mome 😂😂😂v
La dame en noir stp nga balma akh mais del wakh ndank tè bayi youxou yi et puis tu n'as pas le droit de te comparer à la personne en tant que journaliste analyse en toute pertinence sans comparaison
C’est faux hier thi yéne la degué ni le gar en casquette s’appelle Demba diap nagn ko te ki wakh guinaw ray la deuk moko done wakh délene diokhé de vrais infos bayi fake news yi
Personnellement depuis la mort de ces jeunes je ne dors plus car j'ai le cœur meurtri : il faut que les coupables ou le coupable soient/ soit sévèrement puni
Tout com moi meneutouma nelaw
Arretez avc ca ls gars vs avz prolly jamais perdue klk1 😂😂😂 Yall betta go to bed kids , errday ppl die... sad but hey LIFE GOES ON on GG💯💯
Bilahi gueumouma nabou lale nassi
Bilay beugouma nabou lalé thi
Ya gui waat ci YAllah melni yako fekker.... auditionner ak culpabiliser sorina....teeye len ba police wakh ak gueminaam
Ma chérie en noir Machallah tu es pertinante meune ga sa ligueye mais do déglou tu veux toujours garder la oarole gua balma
Noo vraiment la dame hier jai commentè elle n’es pas professionnel
Honnêtement yacine khawema journaliste nga khawema lanenga. Mais sa wakh amoul beneu sence. Khamo sakh ningaye wakheeee. Félicitations à tous les autres. Yacine daye yageu séne plateau bi. Bne journée
Merci ngoné ❤❤❤ Yacine mome sa ne vas pas😅
Yacine 😂😂😂😂😂😂😂
Nanou AK Aziz dagno yag depuis dikone douko deff Lolou bou âme Dina ma bett
Sidy diop il doit être en règle comme tout le monde force restera a la loi
La femme là il faut l’aider dans ses idées. Elle a du mal a les défendre.
Delénn di diokhé informations bou lerr laniou lenn wakh yenangui niouy bakarlo souma yalla ladjé dina wakh yénn lako dégué
😂😂😂😂
Ya wara bayi degue di wakh 😂
Yacine dama yakarni heure emission Bi mokko arrengewoul 😂😂😂😂😂
Yacine a la folie de grandeur
Déférer c’est traduire un accusé ou un prévenu devant la juridiction compétente. Ça ne veut pas systématiquement dire aller en prison.
Merci djiborie ton critique est pertinent sur nabou toujours des preuves bamel da khate bayilen dit wakh sa preuve
Sii réellement Nabou Leye refuse de parler ak nimou mell ak Aziz kone soit day bagne wah lou peuple bi kheebé aziz Dabala soit ell est encore sous le choque ou El est dépressive 😢
Elle n’est pas dépressive parce que la police sait qui est dépressive et qui ne l’est pas. Si elle se présente face au procureur c’est qu’elle a des informations qu’elle a refusé de donner. Et cela fait d’elle une complice. Elle est proche du défunt et donc elle impérativement tout faire pour que ces criminels puissent payer leur crime. Au cas contraire elle fait partie !
Yacine mi esk guemmettouwoul tamite🤔
😂😂😂 man yacine daf may ray comme kou perte reseaux 😂😂😂😂
Man d bouniou rayé sama xarit wakhoumala protección waye damay diel sen bakan niom niep
Féne rek
Hier vous avez dit que Mamadou Lamine diao takawoussi laléwoussi ( répéter à plusieurs fois d'ailleurs) tay vous osez venir nous parler de sources sûres
Doul rek berkkkk 🤮🤮🤮
Tu as parfaitement raison. Ils avez dit que Lamine Diao bokoussi erreur la
@@seynaboudiouf8338 moma diakhal deh
Gni deh moy lolou danio ame site internet ak camera rek mais diarounio deglou
Je me casse d'ici
L'enquête trouvera les coupables
Du concret s'il vous plaît. Merci
Vous vous trompé de cible. Il ne s'agit pas d'exclusivité mais de ne divulguer que les informations sûres et vérifiées Cest plus simple de reconnaître ses erreurs parfois.
Kou wér et que mounna Ray nitte
Gayis nio wora bayi yamba bi ak drogue bi je pense que kou lucide do rey nitt psk nitt dfa fort
@@AminataDIOUF-ez8kdwakhe ga deugeu dé
Doléne wakh ki mou wakh nakhhh ngirrrr yallahh teukhougnouuu dhhhhh
Nite rèyna sakh papame
Djimbory wakho fi Dara
BAYILENEU POLITIC
Mais Ngoné il faut respecter les temps de paroles stp merci
Yena😂 dakh doul😂
Khana wakholenn hier ke Nabou est blanchit
Il faut amener yacine à Daalal héle
Bilaye yow yacine mi weroul NABOU MO wakh né Aziz dafa fébarone mou yobou ko clinique après mou bayi ko mom kene mou ngnibi NABOU dal moy wara wakh degue
😂😂😂😂😂😂😂
Yasine mi worol de khana da fã yakarne dafa nek guente
Yacine khamoul dara
yaw bamba il faut que la fille hier en blanc donne des informations vraies hier elle parlait du gars de la casquette alors il a rien à voir
Mame a bien dit que sa maison n'est pas encore finie
Mercis beaucoup bravos
Mais Yacine miii est-ce que ça va
Ki Kay dof la
Nulle gua on dit j’ai pas froid aux yeux
Yeen danguen n'a meuna feen nan dipounan borom cap bi té kenn diapouko 😮
Kharit kharit rk lay doon niko borom kap bi doné non la ko nabou done te nonou lako ay kharitam rayé niom niep ay kharitam laniou motakh niou sexue xalis
Mane légui yéne rék laye topou
Yacine khamoul dara il mélange le débat
Wa yacine mom amoul place si plateau bi khamoul dara
Yacine mi nekhna lolll com khalé
Ngoye dieker dji si Abdoulaye wade la nekone mei dou bi
Billahi gueumouma nabou lale nassi❤❤❤
Sidi Diop dioumoul dei moko tayy mom star la dans Senegal donc dafa wonei bon exemple, dafa diap ni bouko deffe dara meunou ko si feekk il doit être jugé comme une personne lamda
Machalla laff thiat filing dakar ❤️❤️❤️
PASTEF TEKIWOUGNOU DARA FENEU RECK LAGNOUY
Tapalè bii,tiakhan bi,satch bi ak dioumblang binguen tamm dîna dieekh si rewmi
@@senegalrekk6328Bilahi Tokk Mouy dokh diekh na merci president Diomaye ak premier ministre ousmane sonko
Le fait qu'elle ne parle pas...peut-être mystique aussi...les gens sont dangereux faut rien laisser en rade....il faut que sa famille bouge...elle peut ne pas parler sans le faire exprès..!
Wassalam
Youkhou dou masa dioup founiou ko fogue woul ndakh limay diortou mom rk gueni diortou yalna yalla atte
Nabou a reconnu sa participation au crime c’est ça la vérité
Machalld laf thiate rèk
DEMLENE WOUTI INFORMATIONS YOU BAKHE MO GEUNE 10 ans si internet te mouno ame informations you bakhe
C est une diversion c est pas vrai ils veulent s en sortir la vérité c est la piste de la tontine
sidy diop il doit être en règle comme tout le monde
Arrêtez de croire que c’est impossible qu’elle fasse partie de ces criminels. C’est idiot de croire que ton ami ne peut pas te faire du mal. Je crois à la justice. Cette justice nous dira si elle fait partie ou pas. C’est son ami elle doit tout faire pour que ces criminels puissent payer ce qu’ils ont fait. Si elle se tait c’est qu’il y’a du louche. Elle en sait beaucoup trop sur le défunt et c’est aussi possible qu’elle sache tout ce qui peut se tramer autour de lui : la cause de son décès.
Geumeutoumalene ma ngi désabonner. Vous êtes nul. Nga nane je ne suis pas froid aux yeux😂😂😂
Vous ne faites que spéculer. Quand il y a crime, on cherche d'abord dans l'entourage de la victime.
Yacine mi yeugoul lou bari d
C'est la principale actrice des tueurs
Mane filing Dakar rek Lay topo ❤❤
C'est un assacin la première du groupe
Nabou momana sétale bopame
mane dal gueumetou malene delene wakh deugue
Nabou nimou wakhé rek mo tey sama khel
Bilay yacine da nekh
Damako Retane bah sonou Yacine ay Rabam nan si wouniou 😂😂😂😂😂😂😂
Arreter affairo ngouru gou bess..
Esk il a fait un accident sans permi ... Il a commis une infraction... On doit l infliger une ammande et le liberer
Madame il faut cesser de mentir
Pourtant brom casquette bu guéneuna dhé diapougnouko
Bo demé Nabou mo programmé deal bi😒
C est triste Sénégal
SITE SENEGALAIS YI FEEN REK YEEN MOME YENE SI RAWW SARAP LI REK LI MOTAX SENEGAL DOU AVANCER SEN DOUL YOU ANDAK HARMONY YI
Mais soxnasi sol lou noir lou takh dou deglou dou wakh ndak
Yacine katal sa ndayam khamo dara nopil
nginé tu parle trop wallahi nopile wayyyy
Justice Sénégal deh loumou beugue xam di xam dîna lerr deh
Mm moi
Yene doule rek
Gni kay dama waru louniou fi wax demb yeup
Vous n est pas des enquèteur .
Elle l en fait partie des tueurs
bsr flnD Mais pourquoi l'image des adji sarr derrière l écran
Feeling Dakar je vs aimes bien mais il faut enlever la photo de Adji Sarr s'il vous plaît car ça me rappelle les douloureux moments de Sonko
dédète sou ko défé gniou meune ko diko fatélékou parcque elle a une grande dette en vers nous senegalais n espère qu elle va la payer
Borom Lou noir li nay xolat sa façon de parler elle parle trop
Désolé mais baisse d'un ton. Un diminue le poliment a chaque fois que tu morales ma sœur. Pas besoin de crier pour se faire entendre. On ne veut pas connaître vos sources juste ne dites rien si c'est pas sûre.
Bilay bou fékon may kharitou aziz bou demé samdi 8: man ma dm9:
Yacine est impertinente
Ki dm rk mo niack te mo thi pérte😂daloul thi diamou aziz
yénaye wakhati wa bakhna.
Pour le cas de Sidy, il faut une amende bien salé et obligation de passer son permis. Djimbori mais Sidy mo warone khalate lolou yeupeu t kham ni c'est un responsable. La loi est pareille pour tous arrêter avec ça.
Cette femme tigré mome 😂😂😂v
Arrêtez vos mensonges. Tout ce que vous aviez dit hier était faux
Katy 😂 sois sérieuse way dafa dioum rék ,
Faites quitté Yassine sur votre plateau elle ne connait rien elle mélange tout
J'espère bien sen information yi dou ay degg rek fou leer guen ko jeulé. C'est qui est bizarre moy degg guma communiqué police
Enquête ak deferee yena nul danion délibéré bay deferee
La dame en noir stp nga balma akh mais del wakh ndank tè bayi youxou yi et puis tu n'as pas le droit de te comparer à la personne en tant que journaliste analyse en toute pertinence sans comparaison
Diamano bii segam rack moy ray mack toumue mgui fépou
C’est faux hier thi yéne la degué ni le gar en casquette s’appelle Demba diap nagn ko te ki wakh guinaw ray la deuk moko done wakh délene diokhé de vrais infos bayi fake news yi
Gni daniiouy féne rek en plus danio niémé sakh surtout le présenteur qui se prend pour quelqu'un d'important
Franchement professionalisme zéro
Vous restez devant les plateaux de télévision et vous raconter des histoires mentir
Féne rek surtout ce présentateur yama gueuna deugueur fiit deh 🤮🤮🤮
BayiILENN BUCHER DOU SENN MOROM