Le staff de tapha au lieu de se concentrer sur autre chose continue à chercher des excuses. Mentalement vous blessez encore tapha tine. Félicitation balla gaye 2 c'est mérité. La vie continue.
Saway linga wakh mome wéroul gnoune tawhid la sounou wadiour diéka déf thii gnoune ragal yala wolouko doyloko nangou dogalou yalla woute lou léw kone lamb monou gno doflo nag sport la rék.kou sagnone nag bo yobo sa mbeur mou dane.gnoune moy yalla mo gnouy doflo ak gnaka diamou yalla
Bonsoir c le Sénégal qui gagne je suis supporter de famille papa doubles néanmoins je suis fière de tous lutteurs sénégalais, comme fier de notre équipe de football de basket ext c le Sénégal qui gagne donc le faire play bonne journée tous le monde
Père wa guediawaye la beugue tapha tine si sama khol pas en tant que mbeur mais en tant que nite kou yaroula kou am téguine fonk nagnou ko torop, Père comprendre nagnoula sa honneur ak consience ngay outeul apaisement
En plus ak ya ngui révélé faille tapha tine si ancien blessure ak balla cela veux dire que son prochaine combat son adversaire peut utilisé cette faille encore pour yobou ko ardo
Soyez faire play , Quand Tapha Tine à bastoné Elton com c’est pas possible, personne n’a rien dit . Mais quand on le bastone bien nguéne gadou micro yi di wah rék. Di saltél victoire
Le coach david il a vu que tapha a des defauts sur le plan mental et sur le fait de gerer le stress ; lui il nous parle de mystique au lieu de faire une analyse technique profonde Aziz ndiaye mo teug balla vs bombardier combat royal té bombardier mo danee
Khana itam kone Emeu sene defa tewon lokho yi, ah koula dan ben yon mbapat, danla arene niary yon moleu meune...bou lep wesso lamb rek la soyez faire play felicité adversaire bi dialeu si lenen mou diekh
@@jimane80animateur33c'est ça la vérité .il l'a battu en lutte simple et deux fois avec frappe. Moo ko moune c'est tout. Tapha gnéméwoul Balla par dessus tout.
14:56 Balla 2 fiii bi mo dano l'an la wakhe. Dama febar damey dafaroudji. Donc boulen gniou sonnal. Gnieup gniouy mystique wahé mystique yiiii dey wouté ak gueuneu yiémé yallah.
Père moi suis baol baol mais vraiment sa khala rafetlou woumako ndakh khamone ngani aziz ak balla bene la kone nak boul wakhé ni sene thiouné moy nguéne raw balla mou mane léne nguéne di retourner diko dieul
Père linga wah dakoruma boul faténi yalla mayé werseuk amna niohamni sen dekuwayi démewul nonou té pourtant nio meun fouf tapha tine père tapha tine ci bopam mo yambar ci ponkol bilay kuma dioh avansam ma dieul
Balla moy sama Mbeur ms Tapha sa entourage mo bakhoul kholatal sa guinaw.. tè aussi khana Tapha tine contre Elton kone Tapha dafa diap lokho Elton yi.... yaw dè Mato coach
Père tu as parfaitement raison dimanche combat amou fa si tapha tine fonctionner un peu il allait se bagarer avec lui Balla gaye forme bobou meunoule dane tapha tine
Vous êtes vraiment des mauvais perdant c’est abusé avant le combat vous êtes tous là à parler de gauche à droite tout le monde disait Tapha va manger Balla et maintenant Balla le tabasse et le terrasse avec la manière et là vous venait chialer comme des femmes tout le monde fait du mystiques donc soyez fair-play ou prenez votre retraite c’est aussi simple que ça
Et contre Eumeu Sene qui l’a corrigé avec la manière tu va me dire que ce jour la aussi on a attraper ses mains ? Arrêter vos conneries soyez fair Play
Le staff de tapha au lieu de se concentrer sur autre chose continue à chercher des excuses. Mentalement vous blessez encore tapha tine.
Félicitation balla gaye 2 c'est mérité. La vie continue.
Nice yala bakhna ❤❤❤❤
Coach guemal yalla tadem pereparewat yalla diekhol spor nila
Balla gaye mokoman danko
Babacar Tine balla gaye da mane Tapha Tine rék bi moye 2fois
Balla gaye la guiss bayilene thiakhane mystique c'est autorisé à tous les 2 lutteur
Lima diakhal Moy Balla gaye sou dano do dég niou naane ay gallathie yoyou wayé sou Balla gaye dané louné dingako dég😢
Voilà bonne question
Mais sou dano nguen néh yekini moko sott 😅😅
Moma diaakhal
Lolou tamitt deugueleu!!!
Wayé lima djakhal lou dame baramou tapha.
Lokho bou dokhoul dou dame@@BabacarNDONG-tz5tc
fairplay 000000
Coach bi déh dou dane kén..Coach Bouy analysé ay mystique
Merci beaucoup bro
Bayil fen ki 10ans la took sa Danu te ki moko yoron
@@mohamedndiaye5603 si 10 ans youyou Kane lafi d'âne boudoul décision arbitre ak 4 appuis si eumeu séne
Mom ak mbeureum gno yém
Bilahi lou lerr ga wakh
Yow niou fayla fay sa morom kou néke wouty galathie ga takhaw fi nane ay wakhi galathie
💪💪Balla gaye molén meun 💪💪
Balla gaye da dane Tapha tine ba paré doflo baol baol yii😂😂😂
Ya meuna féne 😂😂
Dof bou mak sakh
Saway linga wakh mome wéroul gnoune tawhid la sounou wadiour diéka déf thii gnoune ragal yala wolouko doyloko nangou dogalou yalla woute lou léw kone lamb monou gno doflo nag sport la rék.kou sagnone nag bo yobo sa mbeur mou dane.gnoune moy yalla mo gnouy doflo ak gnaka diamou yalla
Vraiment 😂😂😂
😂😂
Bonsoir c le Sénégal qui gagne je suis supporter de famille papa doubles néanmoins je suis fière de tous lutteurs sénégalais, comme fier de notre équipe de football de basket ext c le Sénégal qui gagne donc le faire play bonne journée tous le monde
💪💪Balla gaye 3 trois fois leu dann tapha tine 💪💪
😂😂😂😂😂😂😂😂wooye non li nekhena waye thieye sama wadji balla yalna sa diame yague 🙏🙏🙏
Tapha damako moudié yeureume 😢
ak mane osi
Ak mane dh
Ak man je ne peux pas supporter la vue de ces blessures
Père wa guediawaye la beugue tapha tine si sama khol pas en tant que mbeur mais en tant que nite kou yaroula kou am téguine fonk nagnou ko torop, Père comprendre nagnoula sa honneur ak consience ngay outeul apaisement
En plus ak ya ngui révélé faille tapha tine si ancien blessure ak balla cela veux dire que son prochaine combat son adversaire peut utilisé cette faille encore pour yobou ko ardo
NOOON Tapha Tine mo meuna encaissé wê té té té té...😂😂😂
Père BG 2 mo dakk beuré dakk khéhh tapha
Bonne journée boulniou chercher nak
100/100 baol baol la wakhou fi tous ay guaka guene rek tapha tine waroul wone dieul balla gaye c'est tout
Lolou moy deug
Wallahi warouko wone dieul
Bilahi fan yi yepe lolou laye wakh
Parce gnou Aziz loumou begue def def lako té dosi meun dara
C juste ça waroul wone dieul Balla c'était comme ça contre Modou lo man do nek ci sakou yi malay may lokho
Mais khana Tapha defoul mystiques ??? Courage Tapha reviens en force ✊️
Li nguay comparé bokhoul way père bi deug rék lafi wakh
@@baldediao8861 awaa khalanamm mii faamani . Sa waay kounek deff nga mystique balla est plus fort que Tapha tine sur tous les plans.
Bilaye gni danio yabaté 😂
@@nenesall4636 bilahi 😁
Soyez faire play , Quand Tapha Tine à bastoné Elton com c’est pas possible, personne n’a rien dit . Mais quand on le bastone bien nguéne gadou micro yi di wah rék. Di saltél victoire
boufi bour guéwal nekon ni simba amna ndam ❤❤
Nopil sa mbeur daniou ko meune yémal si yeufou coach ngay wax ay mystique
Woyyy père, il ne faut pas être un mauvais perdant 😂😂😂😂balla a largement mérité sa victoire
bonsoir mr je vous salue depuis la France 🇫🇷 en tout cas vous êtes très sportif je vous encourage 🙏🏿🙏🏿🙏🏿
Balla Moy sène baye mou nékh mou nakhari il faut savoir accepter c'est défaites
Khana Eumeu bimouy doumeu Tapha da tiyéwone lokhoyii😅😅😅
c'est la première fois que je vois mbeur bouniou diekkou de cette façon
Yéna sarakhé tapha dou béneu mystique
Gorgui ioe y’a donne wakh niou TEKK paka Kou danne rendiii amal loy rousse Li lamb la rek Ani Yalla geumeul ni Yalla moy mayei di khagneii 🫡
Le coach david il a vu que tapha a des defauts sur le plan mental et sur le fait de gerer le stress ; lui il nous parle de mystique au lieu de faire une analyse technique profonde
Aziz ndiaye mo teug balla vs bombardier combat royal té bombardier mo danee
Y’a gneimei deugg wae dofsa!
😅😅😅😅😅
Pa bii khamoul dara mental zéro
Coach david khamoul réalité lamb
Li balla dane rek la mais sou tapha danone...débat bi dougn ko indi
On se dit la vérité c pas normal tapha n'a pas le droit de prendre balla il doit lutter avec le roi staff tapha danio thiouné
Khana itam kone Emeu sene defa tewon lokho yi, ah koula dan ben yon mbapat, danla arene niary yon moleu meune...bou lep wesso lamb rek la soyez faire play felicité adversaire bi dialeu si lenen mou diekh
Sa yaw balla gaye koumo diappoul si galladje doulla dande
Bilay yala molaka takha wakh
Merci mon frère
Danga feke bimou koy dane arenes Wala
Waaw, Eumeu dafa tiyé won loho yi faaté tanka yi. Balla nak daa tiyé loho yi ak tanka yi 😂
Eltone kana tapha tine dako diapone thi mystiques
Respecte leen Sénégalais yii Taoha Tine dara dalou ko dafa ragal en plus doniou ko meun daan ko. Na dem béyii😅😅
Li yepp si staff Bou bone lá
Tapha tine n'a changé ki khamul dara
Soubhanalah mann souma guissé nitt di fénn rawatina makk di doull
Boudone mystique moye dane kone comba balla Gaye boye niang balla dane ko tapha tine pois boumou yor bakhoul dafa disse
Père tapha aussi il a fait des mystique no
TAPHA dafa régal BALLA même style premier combat ni la déméwon GEUM LÉN YALLA
Douma fans balla mais Nek ponkal am khel moko ngeun teh mbeur yeup daniouy mystique wakh bi mom meuna niak père mak ngua tmt
mystique encore nguén téggat sunuy lokho... père tapha raggal balla rékka ko japp
Aladji biir guéwe amoul soote tapha tine ak balla gaye ak arbitre diekhna
@@KhalileSow-eq1ch bilahi
Waxal way sam wadji
Iisa tine yalla nako yalla niit banio guiss kou ak bakan Amine
Père mèye niou Diam waye 😂😂😂😂😂😂😂
Tapha dangko diape té mo ndieuka attaqué ndieuka dor ay arré, wakh leine gnou leneine waay ish😮 balla est trop fort c'est tout
tapha tine ligneko def yeup damay ragal mou diaré fi yakou ba faw ndeyssane j'ai pitié pour lui
Defougn ko dara dafa meunoul beurè menoul xèx😂 souy dieul franc sah di danou nkh meunoul😂
N'oublie pas que c'est sa 3e défaite sur balla gaye donc arreté vos discours de mystique té analyser le combat
@@jimane80animateur33c'est ça la vérité .il l'a battu en lutte simple et deux fois avec frappe. Moo ko moune c'est tout. Tapha gnéméwoul Balla par dessus tout.
Boulén gnou sonal
Souratoul mougn wayyy😂😂😂😂
Père CV bayil lolou wayyy❤
tafa rek lani top AK Louma xew
Azizz Ndiaye dafa sarakhé tapha tine
Courage yalla bakhna
14:56 Balla 2 fiii bi mo dano l'an la wakhe. Dama febar damey dafaroudji. Donc boulen gniou sonnal. Gnieup gniouy mystique wahé mystique yiiii dey wouté ak gueuneu yiémé yallah.
Balla gaye dou sama mbeur té kép koumouy beureur damay niane yalla yallna balla danou m wakh degue yalla balla gaye dafa mene tapha tine nokhouko
Souratoul mougne😅
Kone khana tapha
Serigne la dané Eumeu sén
Doul way yén
Wa père Aziz boumouy teugue combat balla AK boye Niang bougoul wone balla dane ahhhh père gueumlene yalla😊
Non dou aziz mo tzug balla boy niang c makane mbengue fils de gaston mbengue dél wakh lou lér
@@profcoly6085et balla bombardier ?
Guemeul yalla guemeul yalla guemeul yalla dagn len meun dann len yaw mii ya khamoul dara motakh niou dane tapha tine
Père nangoul ni dañio toroxal sa mbeur soko dann binguén xamé ni aziz balla moy mbeuram baparé teug lamb ji loutax nguén dieul avance bi
No Sénégal mo nékh kou dannou woute lay quoi tapha tine balla gaye moko meune mystiques féniou fii gueume léne yalla nak
Machalla père
le meilleur a gagne'.c est le bon Dieu qui l a decide'
Balla gaye vs Eumeu sene
Ama balde vs Tapha tine
Gris Bordeaux vs Sathies
Lac de Guerre vs Franc
❤❤❤
Mais je préfère Bala Fran
Mais bi c’est pas mal
@@nouhankaba1391 Franc doit encore prouver
Linga wakh
Balla gaye vs Eumeu rekasi dioup😔
lamb nieupay mystique balla beure na ak tapha premier combat ga wah daniou tei say loho niou fayat la guene beurewat mou defat la meme chose
Amoléne xam xamou lambou balla mo meune 100fois tapha tine tapét leuu😅😅😅
Merci 🤩 père t’as tout dit
Père moi suis baol baol mais vraiment sa khala rafetlou woumako ndakh khamone ngani aziz ak balla bene la kone nak boul wakhé ni sene thiouné moy nguéne raw balla mou mane léne nguéne di retourner diko dieul
Lolou kese la bou gou kharone touti Modou lo diel ko ay thioune langou rek
Bilaye yaw Lou leer ga wakh 😢
bayil ndeyi tapha tine hamo dara hamo lamb 😮
Va te faire chier
Coach dal yomboul dey Mélni pape mbaye Mossoul focus si mystique
Mais père Wa keur Tapha tine gnigui won si 🏟️ stade bi samedi si goudi 😎
Père linga wah dakoruma boul faténi yalla mayé werseuk amna niohamni sen dekuwayi démewul nonou té pourtant nio meun fouf tapha tine père tapha tine ci bopam mo yambar ci ponkol bilay kuma dioh avansam ma dieul
Mane rék ma Mane sene keur bilahi
😢Pere sa mbeur bi balla moko meun,!!!lolou moyy deugg.
Si Serigne
😂😂 pére kou santiroul lokhom nouméyw léwotowé
Pabi ay problème lay yokou tapha Tine
Problème you bari sakh
😂😂😂😂😂
😅😅😅😂😂😂Man dama.ross sakh
Limou yakarné mou amoul, yéna raye tapha dah yené gamlou bala dara negoufa
Ndeysan
Balla kéneu mounouko nateu Ndananela heure bounieup né doudane bouniéuwé daneu prouvé Doukouné moko meuneu dane wayé meuneu daneu kouné wakh deugueu yalla ndakh fiteum ak diomame baparé dangouy faté ni balla daffa meuneu beuré.Pére boudé deugueu rk nékh yalla Tapha Tine Balla dafko napeu psichologiquement danko avant sakh niouy diapanté na dém dianguiwat beurém daffa déss trop mêm contre Eumeu Sene sakh daffa reuthui rk mé moy lolou défoufa lou extra vrément ni balla déf ba dém thi serigne mom louko téré déf ni mom kénneu téréwouko bayiléne di victimiséwou
Du courage
Du courage yalla bakhna ✊🏾
Wayé père Doul wayé sen mbeur mo amoul Diom rek ngeni wout lye
Non pourtant d'où ay lay dé, mais combat bii, d'où nèène, il faut être logique😂😂
@@CherifbounamaDiarra-uc1gk tapha Tine bako Eumeu sen dougue Si bir garda Gui dof ko le paré si mom lokho yi dara nekoul Si dafa yekh
Respect lou bakh lasi domou Adama
@@CherifbounamaDiarra-uc1gkki balla 3 fois lako dane ngen ni dou nen 😂
Tapha tine champion wallaihi
Ki dale soko kholé sakh coach bi ngaka la tapha tine outile coach bou bakh😂
Balla moy sama Mbeur ms Tapha sa entourage mo bakhoul kholatal sa guinaw.. tè aussi khana Tapha tine contre Elton kone Tapha dafa diap lokho Elton yi.... yaw dè Mato coach
😂😂😂😂😂😂😂 ki comédien leu dh😂😂😅😅😅😅😅😅😅😅😅😅
Tapha kay ndeketer amoul coach ndeysane
Pere dano faye bala gaye faye tapha tine boulene niou sonale😅😅😅
Père walahi damalaye saga😂yaw gnou fayy Balla fayy Tapha ngaye wakh wakhi sott aki mystique😂goor meuné woul goor nonou kone Elton niko tapha tine def nak tapha noume def bombardier nak🤷🏾♀️ père boumala rousoul wone saga la😂
Yow bilaye mouno conseil nit lou dakh mou dane kene ndakh khomo dara😂😂😂😂😂😂
Ki matna coach waloum sport ngay wakh ay mystique
Ay way gomlene yalla ngne baye galadj boulene saltel victoire diabour
Mbaye ndéwane waxo fi d'Ara amo kham kham
Tapfa balla mon ko mene bayile sagou bie😂
Père tu as parfaitement raison dimanche combat amou fa si tapha tine fonctionner un peu il allait se bagarer avec lui
Balla gaye forme bobou meunoule dane tapha tine
Vous êtes vraiment des mauvais perdant c’est abusé avant le combat vous êtes tous là à parler de gauche à droite tout le monde disait Tapha va manger Balla et maintenant Balla le tabasse et le terrasse avec la manière et là vous venait chialer comme des femmes tout le monde fait du mystiques donc soyez fair-play ou prenez votre retraite c’est aussi simple que ça
Et contre Eumeu Sene qui l’a corrigé avec la manière tu va me dire que ce jour la aussi on a attraper ses mains ? Arrêter vos conneries soyez fair Play
Pourtant tapha tine dorna 2 ctochets 1er raound té plakéna aussi balla dako gueuna paré
Per mougnel rek dane la fay fay balla gaye
Per gou bakh leu ! Ndeysan dama ko beugue lol waay ! Oooh c 1 vré sportif .
😂😂 père ndeysane
Pere aziz teugna lamb gnou dan balla gaye
Lamb la rek défaite mo gnew rek mes Balla gaye champion la tapha tine champion la
Tapha kaye danko raye bamou de si mistyque
Bilaye 😢
Tapha tmt dadone mystique bosaaam moo diapoul
Saway lolou môme d'où layi milieu lamb lépou mistique leu tapha aussi da mistique ba naw
Père do rousse sahh hana galathie la d'Anne Emma sene
Du sa moromo
Ki sa morou baye la
Ki dousa morome pape domerame
Yaw dala dof thaph tine nekou fi
Sa waye yènadoul rouss mbeur boko niémé do téyé lokhoyi