TFM quartier général - Débat virtuel entre Oustaz Alpha Ba ha et Saliou Samb - ayy leral akk taxaaw

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 22 янв 2025
  • This stream is created with #PRISMLiveStudio. #senegal #kebetu #team221

Комментарии • 135

  • @asannediop3826
    @asannediop3826 Год назад +7

    Machallah barakallahou fikoum lérale yi amna solo ya oustas Alpha Amal diamou inchallah

  • @mamadougueye827
    @mamadougueye827 Год назад +10

    Merci bcp alpha ba ❤❤❤

  • @abdoutouncara8685
    @abdoutouncara8685 Год назад +3

    Asalamou alaykoum ya oustaz tu fais un travail souma guisse si live bi rek damay soulagé wou Wallahi je suis content de toi. K allah t aide et te protège et te donne la force de défendre la vérité en toutes circonstances

  • @baboucardiop5121
    @baboucardiop5121 Год назад +3

    Gracias ya oustaz Alpha contanna si yew alquran ak sunnah rek muy dek

  • @momodoundow9188
    @momodoundow9188 Год назад +5

    السلام عليكم ورحمة الله وبركاته شكرا جزاك الله خيرا

    • @Bah-gl1kj
      @Bah-gl1kj Год назад

      Ngorsi c'est un pauvre idiot disciple de chaytane alpha yaw talibei gor mag Nga vas au diable

  • @ABDULMALIK-tc3ts
    @ABDULMALIK-tc3ts Год назад +7

    🕋🕌 القرآن والسنة بفهم سلف الصالح بإذن الله تعالى إنشآء الله AND TOPP AL'QURAN AK SUNNAH RÈK BI IZNILLAH TALLA INSHALLAH INSHAA ALLAH 🙏🙏🙏🕋🕋🕋🌴🌴🌴❤️♥️💓

  • @mouhamedseck3643
    @mouhamedseck3643 Год назад +13

    Al QUR'AAN ak sunna rek kassè yalna gnou si yalla sakhal

  • @bayeabdousamb2633
    @bayeabdousamb2633 Год назад +3

    Machaalla yalla na yalla fayléne yiiw

  • @masiba7272
    @masiba7272 Год назад +17

    Boulen meussa bayi ndah gayi nioungui nieuw dawa bi am na solo

  • @rokhayatoure9364
    @rokhayatoure9364 Год назад +4

    Alhamdulilah bi amei gniy leral thi dinei senegal mom ay nakh rek lagnouye def nit yi thi dinei. Alhamdulilah sunah rek mo wor

  • @bangalydiane6011
    @bangalydiane6011 Месяц назад +1

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤merci

  • @ibrahimasow3193
    @ibrahimasow3193 4 месяца назад +1

    Salam salam ya oustaz

  • @ABDULMALIK-tc3ts
    @ABDULMALIK-tc3ts Год назад +9

    🕋🕌 حياكم الله برك الله فيه وأحسن الله إليكم DIEUREUDIEUF SHEIKH ALFÀHÌM IOW AK NII NGA ANDAL CII DAH3 WA BI JAZAKUMULLAH KHAIRAN YALLA SAMEU LÈN TÈ ARLEN DÈFAL LÈN KARANGUÉ AKH TAWFÈEX BI IZNIHI INSHAA ALLAH 🙏🙏🙏🕋🕋🕋🌴🌴🌴❤️♥️💓

  • @asannediop3826
    @asannediop3826 Год назад +4

    Amna solo mbok barakallahou fikoum DEUG rek mo am solo wallahi

  • @ibrahimadiagne6855
    @ibrahimadiagne6855 8 месяцев назад

    براك الله فيكم

  • @mamangningue1445
    @mamangningue1445 Год назад +1

    Kou kadda feen ki amul Sénégal

  • @moutaphaofficiel7404
    @moutaphaofficiel7404 Год назад +5

    Oustaz ALPHA yalla na sunu borom yombalal len DAHWA Bou am solo BI ngen di def té fey len yiw

  • @masiba7272
    @masiba7272 Год назад +9

    Walahi yalla nalen yalla fay yenangui guindi diamyi.rer Bari wone n'a lol sah.wayee legui mom franchement mbir yangui ler.
    Younous revoit ta méthode de communication un peu.
    Stp!!!

  • @fallounyang9282
    @fallounyang9282 Год назад +4

    قال رسول الله صل الله عليه وسلم
    من حسن الإسلام المرء تركه مالايعنيه

  • @rappel4152
    @rappel4152 Год назад +5

    A liste de ces femmes et leurs enfants li moy kilifa dîné ? C'est ça que vous voulez faire croire à la jeunesse. Que de la poésie ďe bas de gamme comparé aux autres et des dizaines de femmes et enfants dou tafsir Alquran ni khadith dou explication Tawhid ni jurusprudences. Donc à quel moment ils sont devenus des kilifa dîné ? Ces gens mentent comme ils respirent il est de se réveiller

  • @AboubacarrKah
    @AboubacarrKah Год назад +1

    Good

  • @modoumbenelo4889
    @modoumbenelo4889 Год назад +4

    DIEUREUDIEUFE SERIGNE TOUBA KHADIM RASSOUUL

  • @fodefaye4530
    @fodefaye4530 Год назад +1

    Amal respect ak mandouté bayilaine togne kou naik ak sa responsabilité yalla Moy le seul juge

  • @SeydiSow-ny8xy
    @SeydiSow-ny8xy Год назад +1

    Nioune dal nioune ah Serigne Touba si souniouy❤ba alahira rek ba faw

  • @mamadiame9863
    @mamadiame9863 Год назад

    Ma challah dieuredieuf amena solo

  • @asannediop3826
    @asannediop3826 Год назад +3

    Aywaye Sounnah mo nàx waye

  • @ibrahimadiagne6855
    @ibrahimadiagne6855 8 месяцев назад

    ma mi faccio piangere 😭 😭

  • @maremerassoul3383
    @maremerassoul3383 Год назад +2

    Younous dmako naw amoul sentiment j’aime sn caractère machalah kom gni nekoul si deugue gno gneme lagnouy wah asma yene

  • @seydouba2603
    @seydouba2603 Год назад +1

    Oustaz wadji nane yangui gnongual mais mom na wah boppam rek parceque mom doffla

  • @Ibragueyendoy
    @Ibragueyendoy 5 месяцев назад

    Alpha kheumeull yalla Serigne Touba rekk

  • @hannharouna3630
    @hannharouna3630 Год назад

    Salam Salam

  • @TRA-PASTEF
    @TRA-PASTEF Год назад +1

    Allahu akbar Watawasaw bil haq

  • @rokhayatoure9364
    @rokhayatoure9364 Год назад +2

    Bayilen di fenal serigne Touba

  • @AblayeKa-v9j
    @AblayeKa-v9j 10 месяцев назад

    ❤❤❤❤

  • @adama2736
    @adama2736 Год назад

    Ndeysane mane ma yeureum yii
    Nannel gnanal gnou guén ci leundeum

  • @mansourkane7436
    @mansourkane7436 Год назад +1

    Ba daimal jaguiwat svp fairo iji

  • @malaminecamara2106
    @malaminecamara2106 Год назад

    Oustaz alpha ki Moy dajalou yone wi wérou koor rek Laye guéneu.

  • @abdoukarimfaye8193
    @abdoukarimfaye8193 Год назад +3

    Li gueuneu grawe Moy dougnou weddi wanté parce que koo weddi mou feignal Say mboti Mame .thieuy wa bidaa yalnagnou yalla mousseul ci rére

  • @BirahimDjigal-d4p
    @BirahimDjigal-d4p Год назад +1

    Oustaz alpha ba sa numéro téléphone la soxela yo ne mako liahi wara soulie

  • @babacarndiaye2379
    @babacarndiaye2379 Год назад +4

    dieuredieuf serigne touba

  • @oumardeme8462
    @oumardeme8462 Год назад

    Ziarna oustaz alpha

  • @aliounefall490
    @aliounefall490 Год назад +10

    Ak lou meunti khew Serigne Touba moy khadimou Rassoul dioudo Sénégal wotefi mouridoulahi ak limou dathie yeup 33ans de persécution tewoul touba ngui neulee fala teude aduna yeup difa nieuw diko ziaree bayilene sokhor ak ignane koufi teude weet ci yene khamni bamba amoul masse julli guedj ak magal you beurii yi moy dagg seni khole Serigne Touba dafa tedd nak❤❤ ndakh mo wakh nii ilaya khadalahou malam yakkuni wala yakunou abadaan lil moulkini 🙏🙏

    • @the.bachir6092
      @the.bachir6092 Год назад +3

      Fi ken critiqué woul Serigne bi tu ne comprends pas, gni di exagéré gnow takh gnouy wakh

    • @ibrahimdiallokhalil
      @ibrahimdiallokhalil Год назад

      Wooté seytan baa kerok aduna di touki leu te foum wooté gnu toopu ko

  • @harounasow4965
    @harounasow4965 Год назад +2

    LES SAVANTS ILS ONT FAIT DES EFFORTS MAIS SI ON SOULIGNE LEUR ERREURS IL FAUT ACCEPTER

  • @rokhayatoure9364
    @rokhayatoure9364 Год назад +2

    Est ce que livres yi franc-maçons yii bi douniou ko? Di ko sossal serigne Touba?😊

  • @cheikhousylla3901
    @cheikhousylla3901 Год назад +2

    Kééne dou fii maandou ccii aye kaacc.

  • @Mamecheikhiibra
    @Mamecheikhiibra Год назад +3

    Dagay sone rek gnou Sante serigne serigne touba rek

  • @cheickly48
    @cheickly48 Год назад

    Imame billahi tu as région

  • @mamadougueye827
    @mamadougueye827 Год назад +1

    Doule rek 😅😅😅

  • @mamecheikhndiaye8968
    @mamecheikhndiaye8968 Год назад +1

    Kharal ma saga sén ndaye géneunatt😂😂😂fok you

  • @djilydiakhate7318
    @djilydiakhate7318 Год назад

    Delenwakhal s.touba lomowakh sokhar rek akbagg bazz😀😃😄.

  • @PapemalickDiASSE
    @PapemalickDiASSE 5 месяцев назад

    khadim rassoul la wakh

  • @ABDULMALIK-tc3ts
    @ABDULMALIK-tc3ts Год назад +1

    ⛔⛔KAWTÈEF sénégal AY Killifa TARIQAS La Ame... ALLAHOU SWT MOY KILLIFA DIINÉE ألا لله الدين الخالص SEYDIL ANBIYA WAL MURSALINE MOUHAMED IBN ABDILLAH SADIQIL AMINE سيد الأنبياء والرسل محمد ابن عبدالله نبي الرحمة و شفيع الامة (صلعم) MOR BAMBA MOM NÉKOUL WON CII SUNNA NDAH AY MBIRAM WÈXOUL FÈTTÈRLOU AK XABABAL ZERO SHARI'YA

  • @PapemalickDiASSE
    @PapemalickDiASSE 5 месяцев назад

    oustaz mouno wakh baniou bayi s touba

  • @PapemalickDiASSE
    @PapemalickDiASSE 5 месяцев назад

    deme lene ligueyi te guene si linguene nek

  • @alunesarr9477
    @alunesarr9477 Год назад

    Maan louma duaahal aloha ba daah mougui sebegal waala baayi leen naayi te sargal sen mame yi dooleen moosa doon aay nar

  • @rappel4152
    @rappel4152 Год назад +3

    😂😂😂Kou wekh ni percale daray adouna safou ko loumouy doyé 33 femmes ? Kou dîner saf loumouy doyé marier 3 sœurs en même temps ? Perversite dans son etat pire mais pas diiné... que des mensonges juste horrible ces énergumènes

    • @ABDULMALIK-tc3ts
      @ABDULMALIK-tc3ts Год назад

      Vérité Absolue Mon frère... AVEC une Démi Soeurs Kawteef Mouride MBOSSOR aki kufriyat ⛔⛔😭😭😭

    • @ABDULMALIK-tc3ts
      @ABDULMALIK-tc3ts Год назад

      @@user-zg3fz5es4q vérité Absolue serigne Faux type

    • @ABDULMALIK-tc3ts
      @ABDULMALIK-tc3ts Год назад

      @@user-zg3fz5es4q Mor Bamba mom dafa xaba bal takeu Lou eupeu une Trentaines de Diabars lii mom eupeu na

  • @rokhayatoure9364
    @rokhayatoure9364 Год назад +1

    Fen rek

  • @rokhayatoure9364
    @rokhayatoure9364 Год назад +3

    Tassawouf mo grave! Niei tam lolou lagne wakh thi salatou fatiya. Fen rek

    • @BirahimDjigal-d4p
      @BirahimDjigal-d4p Год назад

      Oustaz alpha ba bayil Di ngate a rif bilahahi gnio wara dingatt s'érige. Touba déroula waxou la defou la darra ya ngue tongne bayill tongne

  • @saganadiop5572
    @saganadiop5572 11 месяцев назад

    Dama dég ni Serigne bi amona 33 femmes diakhal Namana dal .

  • @mohamedgueye8841
    @mohamedgueye8841 Год назад

    Sokhar wesouwl li yalla my ap diamam ngadiko wedy alpha ba noplpu lene te jamou dji yalla mou guene

  • @dadjibokaleiakbida539
    @dadjibokaleiakbida539 Год назад +2

    Gars yi dawah bangui deime dei

  • @khadimthione4234
    @khadimthione4234 Год назад +1

    Nit ham souhna di dougou si passe passe you yakhouyi soubhanala kokou hamoul souhna tapalé you métiyi troukh yo nek ragal léne yalla

  • @fazaniangthanksyou751
    @fazaniangthanksyou751 Год назад

    Ndialo ngubonnela

  • @sunnialiber4868
    @sunnialiber4868 Год назад

    Kalima Shahaada dey Dadji Bala mouye dëgël.

  • @rokhayatoure9364
    @rokhayatoure9364 Год назад +1

    Kilifa dinei moy amiroul mouminine te amatoul

  • @grahamkane3594
    @grahamkane3594 Год назад +1

    Mais pourquoi Diare si serigne touba pour ham yalleu je ne comprends pas yene mouride yi dageini dialgati yonebi c’est clair diari diari wari ndar topeu lene yalleu ak yonenetebi tarikha bakhoul un point un trait les sénégalais sont médiocres des vrais moutons amlene hel ngir nguene tehe euleuk mais ay vrai mouton quoi ham ham zero waye daneu diehe par A ou B inshallah sene mafia bi lagni dadji pourquoi geume nite

  • @NiassaawaYauck
    @NiassaawaYauck Год назад

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @babacarfall6337
    @babacarfall6337 Год назад +2

    Alxurane ak suna mofinek dou leenen

  • @NY-xe4kj
    @NY-xe4kj Год назад +1

    🛠⚒🪓🔨Dadji bida ak shirk yéwou yété andor yi yagueneu trop

  • @cheikhantadioptv2574
    @cheikhantadioptv2574 Год назад

    mo fénn kat yi alpha bak gnim andal

  • @amiroudiallo2242
    @amiroudiallo2242 Год назад +1

    Ahmadou Bamba 33 diabarr la amone. Lolou doyna débat

  • @harounasow4965
    @harounasow4965 Год назад

    NON LE SHIRK EST LE PLUS GRANDS ET PECHE ET BIDDA AUSSI DONC C NORMAL DE LES SOULIGNES

  • @abdoukarimfaye8193
    @abdoukarimfaye8193 Год назад

    Salam cheikh younouss je suis ton frère en islam stp enleyka bil hikma pour mieux éclaircir la vérité stp enleyka bil ikhma

  • @celloudiallo3161
    @celloudiallo3161 Год назад

    Oustaz Ousmane SONKO était sunnite

  • @aliounefall490
    @aliounefall490 Год назад

    J'espère que Serigne Moussa ka mom ayy mbidam mo gueneu weer bindu toubab ndakh so demee banane ap danoukaat moy sokhor japeu naleu demal yeuri ay teree moussa ka dou anglais ni français wayee ci wolof laniouko bindeu diamononte ak serigne bi ba lakhe nguereum khaarnou bi naatoo di kerkeran boromam jazaou chakour ak marsia cheikhe ibra mame thierno Etc ak Gars you sokhor ignane ni yene bind yanguifi tontoul si xam xam saliou samb bindou Serigne bi ak Moussa ka lafi wakh kou meer calmer yalla mifi yonni khadimou Rassoul outeulko ay andando you bakh you melni moussa ka binde bafi batakh taay say fen dou dialeu ndakh bimouy bindeu fo nekone😮 respecté len niit gni ish nane bene daanou kaat Sénégal bou donone reew bou diagg bindou Serigne Moussa ka danioukoy dougueul ci enseignement bi

  • @saganadiop5572
    @saganadiop5572 11 месяцев назад

    li ay poéme leu

  • @babacardanfa9300
    @babacardanfa9300 Год назад

    Bayignook sounou sénégal

  • @ndeyeantaka-dr8ej
    @ndeyeantaka-dr8ej Год назад

    Wadji mome da rew té khamoul ni ni gueme deug nounou léne Sètane

  • @dienediabel5867
    @dienediabel5867 Год назад

    Wa bignouy yoobu serigne bi sa baay foumou neekone ak sa mame

  • @seynabougningue4822
    @seynabougningue4822 Год назад +2

    Serigne Touba rek

    • @abdoulayeba7078
      @abdoulayeba7078 Год назад +1

      ALLAHOU AHAD rek. La Sounna de son Prophète rek. Après ça, nos parents point final.

    • @abdoudiouf4377
      @abdoudiouf4377 Год назад +1

      SERIGNE TOUBA AMOUL MOROM

    • @AssaneDiop-w5m
      @AssaneDiop-w5m 9 часов назад

      Sante yalla rék alhadoulilah

  • @ousseynouthiaw2832
    @ousseynouthiaw2832 Год назад +1

    Dieureidjeuf serigne Touba point barre

    • @abdoulayeba7078
      @abdoulayeba7078 Год назад +3

      Dieuredieuf ALLAH AHAD, Seigneur de l'univers. IL est au-dessus de tout. IL est mille milliards de fois supérieur à serigne touba. Bamba dou touss, bamba dou khére.

    • @quransunnah750
      @quransunnah750 Год назад +2

      ​@@abdoulayeba7078 mille milliards de fois c'est peu , Allah est infiniment supérieur à tout autre créature. Les Sahabas par exemple sont mille milliards de fois supérieurs à leur Serigne.

    • @abdoulayeba7078
      @abdoulayeba7078 Год назад

      @@quransunnah750 Wallahi tu as parfaitement raison mon frère ou ma sœur. Ces gens là ne réfléchissent pas. Les marabouts ne sont là que pour leurs intérêts. Que les sénégalais se réveillent. Baraka ALLAHOU fikoum

  • @babacardanfa9300
    @babacardanfa9300 Год назад

    Ki poulofouta la alpha ba démale Guinée saya mame namnagnoula dh

  • @mamemamadoundoye2891
    @mamemamadoundoye2891 Год назад

    ندعوك الله يهديك

  • @NiassaawaYauck
    @NiassaawaYauck Год назад

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @SeydiSow-ny8xy
    @SeydiSow-ny8xy Год назад

    Moytou lene niti yalla yi dinguene toroh idina toroh alahira bounguene moytou woul bahna

  • @babacarfall6337
    @babacarfall6337 Год назад

    Ki mo meunafene deug tey domeram

  • @babacarsall4357
    @babacarsall4357 Год назад +1

    Younouss sois plus calme et plus méthodique !!
    So beugué guindi nit gni dangay yaatal sa khol nga andeu ak dale!

    • @ibrahimabayo1277
      @ibrahimabayo1277 Год назад

      Fofou mom suis trop d accord avc toi, younouss il s emporte trop vite, indi nites yi thi yonu deugue dou kheubeur kheubeur mais dall gay andall ak plus de sagesse

  • @rokhayatoure9364
    @rokhayatoure9364 Год назад +2

    Quartier général lagne wara interdir shaytanei yep fay dem di bokale yalla

    • @cheikhousylla3901
      @cheikhousylla3901 Год назад

      Quartier général des généraux des franc maçonnerie maçons kééssé shaytane rék.

  • @SeydiSow-ny8xy
    @SeydiSow-ny8xy Год назад

    Borom calagui bou honha gui mom moute mouti gui Mouy df wonena né kou rew la

  • @babacarndiaye2379
    @babacarndiaye2379 Год назад

    yaw sona nga dh. complexé nga biu bon. naryi naryi.

  • @fazaniangthanksyou751
    @fazaniangthanksyou751 Год назад

    Mane dal 10 diabar moma déf prolem

  • @SeydiSow-ny8xy
    @SeydiSow-ny8xy Год назад

    Donc yene waroulene wahal l'islam dah cou rew amoul place si l'islam

    • @AssaneDiop-w5m
      @AssaneDiop-w5m 9 часов назад

      Réw deug moy bokalé yalla sougnou borom

  • @FallAmy005
    @FallAmy005 Год назад

    Wakh na deug diou weer dh Kenn dou borom touba dieure dieufeuti BOROM TOUBA

    • @AssaneDiop-w5m
      @AssaneDiop-w5m 9 часов назад

      Nékk léne ay nitt dioullit Day nité

  • @FallouMbengue-t8o
    @FallouMbengue-t8o 11 месяцев назад

    Yéna bone ta meun féne meun doul

  • @ndiayebiramediodio4327
    @ndiayebiramediodio4327 Год назад +3

    Sama gayi damalén yweureum sakh sén lii wéét na niakna xorom amolén moyens amolén techniciens you aay sén xol bone na amolén moyens touti ngén abonnés lingén di wax dokhoul si reew mi vraiment amolén bopp. SERIGNE TOUBA si reew mi dieureudieuf rek lay dégue ak reew mi moko mom. ndeyssane touti vues ngén am réthiouna sakh béneu vue bimalén may . yalla mo mom ay yeufeum té kouko nékh lakoy may soungén changéwoul reew nak dingén xarou wa salam!

  • @lomameballa4490
    @lomameballa4490 Год назад

    P

  • @seynabougningue4822
    @seynabougningue4822 Год назад +2

    Yaww nopill

  • @seynabougningue4822
    @seynabougningue4822 Год назад +1

    Yaw khamgane bonekon Sénégal nokhonanola boyagu

    • @abdoulayeba7078
      @abdoulayeba7078 Год назад

      C'est ce qui prouve que vous n'êtes pas dans le droit chemin. Si vous étiez véridiques, vous auriez dû argumenter pour convaincre au lieu de raconter des histoires à dormir debout. Les ahloul Sounna quand ils parlent, ils argumentent, ils ne menacent pas. De plus, ces outaz viennent au Sénégal, pourquoi vous les attaquez pas?

    • @moussatraore8586
      @moussatraore8586 Год назад

      Yena mome niteyi ba kou wakhe nguani dankoye dankauye daure

  • @babacarndiaye2379
    @babacarndiaye2379 Год назад

    yaw do dioulit. ndakh ya ngui togne. tu es insignifiant. amoulo fit, souma la diaper goor djiguen bou bon nga

  • @NdeyeDieye-o2u
    @NdeyeDieye-o2u Год назад

    Salam salam