Alhamdoulilah !!! Se reveiller le petit matin et ton cœur se rapproche de plus en plus de Dieu ce n'est possible qu'avec les zikhs de Aïda faye mou baye niass.Appuie sur j'aime si ce que je dis est avéré.
Bilahi cheikh bi khel dallna yalla bakhna....cheikh bi yalla na khipe thi wetou sopeme ba sama mame saliou wayyy...yalla yokk sene leer wayy they adina
Moi je ne comprends pas les gens qui dislike ces belles paroles. Machallah sokhna aida yalna yalla guena wéral bate bi❤️❤️walahhi li nekh na trop si xol
Walahi mm moi je suis mouride mais je ne dis pas Aïda dh mais diangue Niasseine yii foumako deigei rk douma meune tei sama bopp tellement ça me touche❤
Naysane baye rekay deug ana talibei maolana cheikh al islam yi niak kham yala doundou gou nul la deiiî lene bala deiii di niewww nima beugei baye mougui khoti sama khol 🙏📿😭❤
@@sfmssfms9927 ki deh djéguéwoul sakh doneu talibé baye photo baye bi laye mboubo Del bayi khel ci commentairame Talibé baye dina saga Mouhadame Cheikh Tidiane mouye serigne Babacsr sy ki xamaneu té naniou
Baye mo xoti sougne xoli défe thie yalla billakhi yalla nanoiu yalla défe aye tallibé Baye t maynoiu fatekhout akbare thie bareké Baye Niass la solution 😅💖💖❤❤
Baye Niasssssssss rek yalla nako Allah doli ler té Tass niou si barkém Sénégal danio wara sante khola li rek ça fait chaud au coeur Allah que ta miséricorde descend sur Sénégal Allah Baye vive nos Saints marabouts
Sokhna aïda faye li ngay zikr si xol la dieum direct walahi yalna yalla wereul batt mii defal leu wëër ak wërlé goudou fane teksi ioe senegal dala soxla walahi talibe serigne saliou la mais damala sopp❤
Soumanekoul wone mourid niassene lay nekk...baye niass kharitou sama mame ja mame fallou ...yalla na yalla yokk sene leer...serigne sidy moktar mbake ...fatewougnoula...mame mountakha yalla yaguefi te weeer
@@laminefall3240 yalla na yalla nangou sougnou koorr...t khirr gnou thi boppam ...gorgorlou thi diamou yalla bi khamni Aÿ joulit lagnou di togne di ballou tay jegale ...yenante jamm ak tawfekh a tout no proche ...
Bilahi sayouma yèmo mome lay ndieuka dougal si samay nopou sama khol day yindo nekh ba kouma df lou bonne wala lou meti doumaka yeuk ndakh banekh biy dh si sama khol bi baye niass ma solution djeureudjefè yalla
Machallah alhamdoulilah Baye Niass yay souniou lepp, ls talibés manifestez vous li downa yaram j'ai mm pleuré, Baye Niass liguéye na machallah kepp kou fière beusseul j'aime, longue vie à tw Aïda
Alhamdoulilah !!! Se reveiller le petit matin et ton cœur se rapproche de plus en plus de Dieu ce n'est possible qu'avec les zikhs de Aïda faye mou baye niass.Appuie sur j'aime si ce que je dis est avéré.
vrai
el hadji mbaye wade bilahi lila dale moma dale sa youma yèmo mome lay ndiakeuh dougal si sama nopou yi banekh lay yindo
Vraiment ta raison
Si ces versions vous font vibrer le cœur par l'amour de Dieu, au moins pousse up.
I like it so much, Aïda Faye Baye doundal way
Yeah me too she always make me very happy may Allah give her long life and good health
machallah Yaye Aida Faye yalna Yalla doundeul ko
Machallah aida baye
Amine
@@coumbabamachallahyayeaiday281 amiiin
In sha Allah
Kou beugue BAYE NIASS TAPEL j'aime ❤
Barki serigne touba Aida Faye bo xamone ningay deff sama xol bi❤❤❤❤❤❤❤❤😭😭😭 Que dieu te protège
amine
😭😍😍☝️
Allahouma amine
Képp kou beugue Aïda mou Baye beuseul j'aime👍💕
machalla sokhena aïda yalla na yalla guena weurale bate bi si barke baye
Machala
Bilahi cheikh bi khel dallna yalla bakhna....cheikh bi yalla na khipe thi wetou sopeme ba sama mame saliou wayyy...yalla yokk sene leer wayy they adina
machallah machallah
Allahou akbar yalla na yalla weral baat bi si barke Nabil Moustapha saw
Moi je ne comprends pas les gens qui dislike ces belles paroles. Machallah sokhna aida yalna yalla guena wéral bate bi❤️❤️walahhi li nekh na trop si xol
hannah bop ils n'ont rien compris
hannah bop '''c'est bizarre dh. esk ce sont des croyants ?
Ay yakhout lagnou
Walahi bou yalla wathione ak diemame am dislike
C'est la même question que je me pose c'est quoi le but des dislike oft
*_Je suis Talibei Cheikh Ahmadou _**_#Bamba_**_ Ms j'aime ♥ 🙏🏻 _**_#Cheikh_**_ al islam de tout mon cœur Ndeyssan_*
Mashaallah
Talibé Serigne Touba beugue Baye Niass! Aida yalna sa diam yagg li ngay wakh nékhna lolou koula sope la machallah
Talibe serigne touba mais wallahi barkep serigne salihou
Baye Niass damako beugue trop sakh
Rawal
Mamoune ndiaye walahi beuguenaleu ta yalla rék takh barké BAYE NIASS
Ndaye sann yalla na yalla fayla
@@maimounasarr3741 fila euppee 👌
Mashalla
mouride la wayé aida faye douye zikar sama khol bi daye sed yallana yalla mayko fane you goudou té wéreul batt bi si barké serigne fallou
Amine ya rabi🙏
Bilay Lima wok mola Khouri noonou lamay déf bilay
bilaye sama domou baye lou diougué si khol si khol rek laye délou rawatina batou lahilakha ilahla
Walahi mm moi je suis mouride mais je ne dis pas Aïda dh mais diangue Niasseine yii foumako deigei rk douma meune tei sama bopp tellement ça me touche❤
amine
Naysane baye rekay deug ana talibei maolana cheikh al islam yi niak kham yala doundou gou nul la deiiî lene bala deiii di niewww nima beugei baye mougui khoti sama khol 🙏📿😭❤
la Barhamienne mamita ✋
@@zeynazey6751 niass ziar bou were seyda
la Barhamienne mamita delo ziar marhabane🙏
la Barhamienne mamita louleer nga wakh
Deug deug Baye rekay deug zeyna
Machallah sister Aida faye❤ longue vie a tw 😍
.
Vraiment c'est beau Baye Niass ligueye na Sénégal
Ligueiy neu aduna weur ngueul keup
Nagnou ko yallah feiyal🙏💞🙏
Pas sénégal seulement le monde entier
Baye Niass dafa wéssou Sénégal...Baye c'est international,machallah
Talibé cheikh tarikha cheikh wallah bii tarikha amoul thiakhane tarikhatoul khaq moy #Tarikha Cheikh
Yalay késé mo néh si hole machala deg rék kay deg fier d'être tidiane
Papa Abdoulaye Ndiaye alhamdoulilah
Ndeyssane vraiment li si xolll laye dugue personne ne peut retenir ces larmes aida machallah tres belle voix
Niou nianal chiekh béthio yalla wane le ku ak sangam shiekh saliou Mbacke
Aminee
Dieureudieuf wayy ioe dh sa kholl bi baye rek kasi nk loukay firndel moy amo kignan
@@sfmssfms9927 ki deh djéguéwoul sakh doneu talibé baye photo baye bi laye mboubo
Del bayi khel ci commentairame
Talibé baye dina saga Mouhadame Cheikh Tidiane mouye serigne Babacsr sy ki xamaneu té naniou
Yow bayul photo baye bigua def sa
Profil bi diko mboubou talibé dou deguelou Aida faye bamou djikh teh dou ci commentaire
Sa bopeu guaye nakh cheikh béthio djoulite leu bou guéné adouna kepeu djoulite warnako nianal
@@sofiyatouagne9399 wakh Day rafét mais nit mom Bou xamoul yalla xamoul dara si bopam
Baye niass amoul morom machalla sokhna aïda faye
Diaratoul wakh gnep khalnagnouko
Machalla
Je mourid mé beug na aida sa yalla rék takh bilay
Hé wayy verbe mourider
Da nga beugue Yalla motakh na beugue kouy toudou Yalla..machallah
@@noname.4542 amal edeub touti ok
dieureeu dieufé baye
Mchallah Yalla rkay deug
Soxna aïda yalneu Yalla fayla T wéreul batte bi si barké Maolana cheikhal islam.
Batou la ilaha ila mo nékh thie khôl
bilay wallay leuuu khagu3
babacar demba Diamanka walahi migui nekh thi kikou kham niass
Walaye ndeysane
Cv
@@oumouseck4070 CV Oumou seck et tw
Non mane Aida mou baye bou yokho nimouye deff sama khol bi yalla rek moko khame goudal fane ak wérr Aida 😍😍😍
Baye fimou dieuler Zikar d'à sorri mo takh kholi dii toye sa souner kenn d'où maolana baye niass 😢😢😢
Barki cheikhou tidiane yi nek gui lako djelè
J'ai beaucoup pleuré hier wallahi ces émouvant sokhna aida yalle na yalle same la ar la 🙏🙏
amine
Amine ya rabi
Maye mouride bou begue foko toudou sama kholle fess dafaye dioyelo dérife baye niass ❤❤❤❤❤❤❤
Machallah da nga beug Yalla motakh mou nekh,nakh kousa khol lap si Yalla founou toudé batt bi nga ame lo yeuk degue
Machalla Aïda yalla.na yalla goudale sa fane mayela wére ak wérlé si BARKI SEYDYNA MOUHAMED PSL
QG senerale dalle boufa baye Niass diare sittt ethernet yep diele ko wa li nekhoutt machallah way Aïda
Fatou bintou rassoul Sokhna si ioe kou beug baye chaque commentaire dinala gise sante yalla rek
@@mohamadougaye4609 machallah sama sope Baye niass rèkk bilahi
Machallah yalla na Yalla weureul bate bi. Jereuh jeufety Maolana Cheikh Ibrahima Niass
Neex na torop yalna yalla wéral batt bi 🤲💸💷💶💵💴💰
amine
Amine
Mâcha alllah alhamdoulilah santeu yalla 🙏bamou gnou bolé ak Baye Barhama vive l'islam❤️ vive la tidiania 💕
Machalla❤❤
Al hamdoulilah. Dieureudieufé Baye Niass🙏🏽🙏🏽
Khamonna dinala guiss machalla beugue Baye rék machalla nékhna thi Khol
Lamine Fall ...deiguel way mbok mi, Cheikh Ibrahim Niass rek hala kouli hale
@@LaBarhamienne hahaha wa nonoula dé liniou Baye niass défal dafa nékh thi Khol machalla way
Lamine Fall Walahi romb na nekh thi khol, Baye amou niou fayam
Machalla sokhna aida waye k'en d'ou môme mawlana mame baye niass la solution
Mourite la dama beugue sokhna aida trop
baatu laailaaha ilalah rek mo am doooolé alhamdoulilah bignu néké deug julit
Eskéy sama khôl toyna..
Jeureujeufé Baye❤
Ndeysane yallah na yallah wéreul bate biii Sokhna Aïda Faye dieureudieufééé Baye Niass
Baye mo xoti sougne xoli défe thie yalla billakhi yalla nanoiu yalla défe aye tallibé Baye t maynoiu fatekhout akbare thie bareké Baye Niass la solution 😅💖💖❤❤
Dieureudieufé baye♥️♥️ Thio xol yii for life yaniou yaarr teh hamalniou BCMID🙌🏿
Aïda baye une fierté pour le Sénégal❤❤
Mourid la sadikh mai wallahi aida boumakoye deug douma neck yale nako yalla sammou
Amine ya rabi..da nga beugue Yalla motakh founou toudé batt bi nga ame lo yeuk..machallah
I just love you Aida,yhu mealt my heart.....
Alhamdoulilah massha allah AIDA FAYE. Sa serigne Baye CHEIKH Mamour Insa kéne dou mom le soldat infatigable de BAYE NIASS.Deffal nala lou reuy wallahi
Thiey yalla baye is one j ai trop pleurer c est fort et émouvant merci aida
Machallah yalla na yalla warall batbi thi barkeep baye 😘😘😭😭😭
Machallah sokhna aida faye sama fans ,sama kharite
@@tandineseny8740 billay yaw 😍😍
Niass yalnaniouko yalla fayal niass la solution kéne dou mom
Machallah Niass. Tes zikr transpercent le coeur comme une guérisseuse de plaies.
Machallah mane dale beugna diabotou Baye Niasse yalnasii ame borome keur .bien que je suis mouride
Inchallah di nga si ame koubakh mou yereum la tarbiya la khamal la Yalla ba nga meneu done madjzobe piir..amine manilakoy gnanal si barké Yonenti(psl)
Baye Niasssssssss rek yalla nako Allah doli ler té Tass niou si barkém Sénégal danio wara sante khola li rek ça fait chaud au coeur Allah que ta miséricorde descend sur Sénégal Allah Baye vive nos Saints marabouts
Thieuy yalla tourou yalla Mon for ay koulay bokalè 😭😭😭😭😭😭😭
Ma Mbeugue Aïda té Yalla rek takh Yalla na bate bi wer machallah ♥️♥️♥️
Non aïda faye ningua may déf bo youkho rek sama khol bi nguay lay lale machallah nala yalla may wéer ak goudou fane machallah machallah
Yalla na yalla wereule bate bi goude fane ak wér lagnou laye gnanale si barké Baye Niass😘
Machalla yalla nala yalla féy thie barké Seydina Mouhamed Psl
Li moy Senegal yalla na diam yaga
machalla kèn d'où aïda mou baye yalla nassa diam yagu j'ai des larmes aux yeux bilahi
Dieureudieufé baye niass machallah zeyda Tata Aida fière d être talibé baye ❤️❤️❤️
Bilahi aïda faye yalla nala yalla defal diam dieureuféeeeee baye aka nga diara beugeu niass
Fière d'être talibé cheikh Tidiane
Aida machaalla xool ceedatina dh thii ioe yalla nalafii yalla bayii ngay gina cedal sougnou xool
Mane dei g des frissons fière d'être talibé cheikh
Aida baye yalna yallah sameuh leuh goudeul say fane weireul say thieurr dougou nga sama kholll tei mouy deugu si mane bilahi Macha'allah ❤
Mane moi meunou mako deeglou té sama xol manifesté woul macha allah yalla na yalla fay la
Machallah mala beugeu Sokhna aida bilay walay mounou mala déglou thé douma dioye yalla na yalla weureul thieur yi thi barki seydina Mohamed amine
Machallah Aida Mbaye Yalla nala sounou borom défall diam diou sax dakkeu
No ki dou nit yalla nala fi yalla yagal sohna si wakh lén amine 😪
Ibrahima dione amine
Amiin❤❤❤
Machallah💖 khol yi sedd na Barké Baye Niass
Alhamdou bi niou amé Baye🙏
Sokhna aïda faye li ngay zikr si xol la dieum direct walahi yalna yalla wereul batt mii defal leu wëër ak wërlé goudou fane teksi ioe senegal dala soxla walahi talibe serigne saliou la mais damala sopp❤
J’ai la chair de poule 🐔 bilay Senegal khamou gnou sakh lougnou am, machallah 🙏🙏🙏
Bilah sama xol sédena ioe ak Fallou bou Baye macha'allah Yalla rekay Yalla. Tourou Yalla nex waay li si xol 💔 la dieum
Nioune baye laniou beug niass coumba di santeu yalla rk kheweul yagui yokou kep koula top dou rer
Soumanekoul wone mourid niassene lay nekk...baye niass kharitou sama mame ja mame fallou ...yalla na yalla yokk sene leer...serigne sidy moktar mbake ...fatewougnoula...mame mountakha yalla yaguefi te weeer
Bén la rék machalla lépp thi yalla la rék
@@laminefall3240 bilay lamine deug gua wakh
@@ndeyefatouthioune4089 machalla sa Khol mon sétt rék
@@laminefall3240 yalla na yalla nangou sougnou koorr...t khirr gnou thi boppam ...gorgorlou thi diamou yalla bi khamni Aÿ joulit lagnou di togne di ballou tay jegale ...yenante jamm ak tawfekh a tout no proche ...
@@ndeyefatouthioune4089 amiine way lolou rék mofi nék gua am diam machalla
Ana talibé Maolana cheikhe Ibrahima Niass😍💖💖
Barke serigne touba aida dafmay danel 👌👌👌
J tm yay boy yallah na baye fay ya rabi♥️
bilahi baye niass amougnou sa faye
Yallna yalla wérall batt bi si barke serigne touba 😭😭
Machalah aida faye yanala yalla dolli wérrr😘😘😘
Laah illaha ilal lahh Mohamed rassoulil lahh 🙏❤️
Soumalay douglou sama yarabiiii dara dotoul tok!!! Sokhna Aida Yalla n’alla Yalla fay!!! Dieureudieuf Cheikhal Islam ☪️ ❤️❤️❤️
Bilahi sayouma yèmo mome lay ndieuka dougal si samay nopou sama khol day yindo nekh ba kouma df lou bonne wala lou meti doumaka yeuk ndakh banekh biy dh si sama khol bi baye niass ma solution djeureudjefè yalla
Alhamdoulillah yalna yallah fayal nioula Seyda Aïda Faye 💖
Dieureudieufff Baye Niass💗
Machala aida quand je vous écoute g des larmes aux yeux yalna yalla sam leu si barkèpe baye niass
Alhamdoulah kène dou cheikh Ibrahim niass yaye boye mala beugu piirre mane Mach Allah yalna yalla weralle batte bii si barké yonatiibii
Machallah aida nous t aimons depuis la Mauritanie . ma maman chérie pleure a chaque fois q elle entend ta belle voix . que dieu te protège
Machalla sokhnasi rafétna thiey Baye niass
Macha allah ningay seddalé sm khol mak yalla rk gnoko kham long life a toi ❤❤❤
Jeurejeufè baye niass,
Jeurejeufè baye niass
Jeurejeufè baye niass
Yalnagnou yalla maye yalla!
Man dé ab mouride la wayé lounekh loné dougue si khol💝💝mchalla
Looy précisé nih Mouride ngeuh ?
Mouride tidiane layénne niasséne leup béne☝
Mais dara nekoul si bayi len compliqué
@@momathkebe3894 kone baax neuh
Minka ileika nguay am fofou Mon frère
Guene fokk ni baye niass serigne rekk la ni hum mawlana cheikh al islam ibrahima niass
Dieureudieufé baye niass
Yalla nalla yalla faye thi mbakhou lailaha ilala barke borome touba
Dieureudieuf serigne touba khadim rassoul lii lepp moma 👏👏👏☝☝☝
Daguaye doul loutakhe douguenne toudou yalla daguenne di bokale serigne Touba mougui ligueya Baye Niasse S Touba Sénégal la yem
dieuredieuf YALLAH souniou borom
@@oumarsow8344 iow Amo yarr serigne touba moy khadim rassoul diawrigne nou seydina mouhamed psl moy goor di borom magal gui fi koufi toudou yala serigne touba mo takh histoire vrais lalay wakh
Yaa meun douul...Serigne touba yégo ni ins bi moye khidmaal baye...si képaari baye laye serloo famou né
@@ndeyefatouniass9668 iow ya meuna doule khamo len baye dou sénégalais baye from Nigeria serigne touba khadim rassoul moko nianal
Wanewou lene talibé chiekh , baye niass , mame abdou aziz sy dabakh malick tidiane yi beus léne jaime may guisse sene position
lou waral particularité bi tamit ??
Srx elle me donne des frissons li forna Machallah Yallah kéneu leu❤❤santati boumouniou dfer domou Adama
Mouride la dei dama beugeu Baye ak seine zikr saama khol laye dougou bilahi
Manchallah yallah nala yallah Faye aida 🙏🙏🙏🙏🙏
Machallah alhamdoulilah Baye Niass yay souniou lepp, ls talibés manifestez vous li downa yaram j'ai mm pleuré, Baye Niass liguéye na machallah kepp kou fière beusseul j'aime, longue vie à tw Aïda
Sokhna aida yalla nassa djam yaag
thiey sama toma diam diou bary sii yow allahou akbar😭😭😭
Machallah baye la solution zikre bouy guéna si xol t di dougu si xol ❤❤❤
Dieureudieufé baye niass nekh na sokhna aida Faye ❤❤👍
If I could see u once in my life I know if I die I go strength to paradise.
Because the way u make me happy
Baye rek
Diere dieffe Aida Mu baye
Machallah Zeida Aida Ndoundal nékhna!