Lirou dou wax ba xool le caméra 🤣🤣😂 dafa mine camera moi je l'aime bien day wax comme kouy waxtan sen caméra😂 xolen bou bax limay wax 😂😂je suis fan de lirou quoi do doff dangua nékh
La preuve et que nos enfants doit partir à l'école et félicitations à la journaliste elle très professionnelle et a assuré parceque si c'était un homme l'émission va tourner mal allons apprendre voici le contraire
@@papeoumarndiaye6252 Il est moins fou que tu le penses 🤣🤣 on appelle ça du dof doflou et cela marche car on les voit partout, toujours bien habillé donc pas si fou que ça
BRAVO MA SOEUR SOKHNA TU ES VRAIMENT GÉNIALE.TU AS ASSURÉE L 'ÉMISSION
J'aime bien cette journaliste elle est très calme ♥️
Très calme même
Lirou mii xalébi dale machallah
lirou niveau de doff gui dafa gueune yékkk😀😀😀😀
jaime bin cette journaliste yala boula thiate diapou
Un journaliste trop professionnelle malgré les dérapages de lirou franchement chapeau et bonne continuation
Quand je suis stressé je regarde lirou diane di Nianal journaliste bi yala mayko mouy fanane sama guinaw amine
Ma fille, tu as fait un bon boulot. Du courage et bonne continuation. Tout est bien fait dans le professionlisme.
Ki fof leu waay,Elle a vraiment assurè la belle journaliste...Félicitations
Balla gueye 2 yalla nako yalla mayii Dame Amina barké borrom gamou gui gui
Courage à cette fille d’avoir supporté se gas😂😂😂
Bilay
Billahi cette fille est très courageuse
Nom de Dieu inacceptable ce Lirou
LA FILLE EST TRÈS MÂTURE ET PROFESSIONNEL MENTION SPÉCIALE À TOI SOEUR BONNE CONTINUATION
Bravo ma soeur bonne continuation
Merci à cette journaliste, courage
La jeune fille est polie et très professionnelle
Lirou dall lamagn layy khékhé diko beurré wouly wouliko mouyy daw di guéneu rekk🤣
elle est trop pro key, saurais été moi je vai craquer et l'insulter
Lirou gestou gordjiguene rek laye def
Bravo les fille lirou nekh la def 😍😍
Astou sama tourando yaw diabarga bravissima 🥰🥰
Sa tourando de dè lirou rekk 😁😁😁😆😁😁
journaliste bi ayna ta dafa rafét Machalla
L'irou bayil diambour tere belle Machallah
Elle est très belle machallah
amoul maîtrise sii guel bii lirouu da Dioye siii guel mei guel kou Meune limiye déff la
Lirou mi sokhlana fadjiou boop
Noo lirou dayy fékhal khool
Lirou dou wax ba xool le caméra 🤣🤣😂 dafa mine camera moi je l'aime bien day wax comme kouy waxtan sen caméra😂 xolen bou bax limay wax 😂😂je suis fan de lirou quoi do doff dangua nékh
Nenako ndeketei kou sokhor nga
Ce lirou diane bi esk werr na sax
Lirou Diane dou niite.
Vraiment constant .
Lirou dangay signature contrant wala 😂😂
Journaliste professionnel bilay , lirou diane respecte un peu le journaliste svp
Man dh gell betax ma doig setan shooo bi molle na wouuuu 🥶❤️
Lirou da nobe gèle bii
lirou il fai de la comédi raison pour laquel boulèn ko mèrè il est toujour comme ça
yes lu wèrr nga wakh
Man bilahi lirou dama ko beugué🤣
Non Lirou dafa reeew koi🤣🤣kouko méré khamoooko🤣🤣dafay neekhal mais kou baakh la🤣🤣
Bilahi
@@oumartoure7794 billaay dafa bari jamm
C'est vrai mais bou dalone rek mou baax
Ki meune nala dorr té douko tay.défak mome interview woroul 😉😆
Risk la dei 🤣
Waa lirou limouy wax mba diammu lah hahaha
Changement d’ambiance mo gaaw sakh 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣 thiey lirou
Toutou sister dotoco défati dé 😂😂😂😂😂😂😂
Billahi😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Lirou ya rey lamegne wakh rek Khadim Ndiaye1 rek mo bakh si yaw bravo Khadim Ndiaye1
La preuve et que nos enfants doit partir à l'école et félicitations à la journaliste elle très professionnelle et a assuré parceque si c'était un homme l'émission va tourner mal allons apprendre voici le contraire
mai journaliste bi rafett na machalla auuuu 😆😆😆😆😅😅😅😅😅💙💙💙💙💙
mais journaliste bi elle est très belle qui dacord avec moi
Nooooon lirou mi werna seuuuutttt 😂😂😂🤣😅
Qui Mba dou gorr Djiguéne
Lirou deh comme kouye signature contrat
Cette vidéo Je peux la regarder 1000 fois ça me fera toujours rire 😂😂😂🤣🤣
Mane ak yaw nio yam 9mois mangui koy setane mais damakoy avance ba ci fi lirou di geureumer rk😂😂😂
Non ki eupalna trop waye.
Ds prod for ever, courage m'y sister astou
Aka maka nob la presentatrice
😂Lirou 3 pieces binga sol andoul'ak tension bingay waxé, dangay kheum dh. Yangui niakk rek
Kharal ma wo sapeurs bala mo tak 😭😭😂
😂😂😂
😂😂😂😂😂😂😂😂😂 mane lirou lay weur 😂😂😂😂😂😂😂😂😂
😂😂😂😂😂😂
Yaw bakhoo😂😂😂
No kou sokhor nga bi meune nama ray 🤣😂🤣😂🤣😅😅😂😅😂😅😂😂😅😂😂😂😅
Vraiment cette fille nekhnama trop elle est très belle
Tjrs ravisante Astou 😍bonne continuation
Lirou le plus drôle sur terre
Lirou da khala goordjiguéné
Fan’s Lirou Diane depuis Tokyo japon
brave à cette jeune fille, d'avoir supporter ce aliéné jusqu'à la fin.
😂😂😂😂😂
Non c est pas un aliéné mais juste un ambianceur 😝
FRANCHEMENT .. POURQUOI INTERWIEVER CE ..FOU
@@papeoumarndiaye6252
Il est moins fou que tu le penses 🤣🤣 on appelle ça du dof doflou et cela marche car on les voit partout, toujours bien habillé donc pas si fou que ça
😂😂😂
Nice na trop
G jamais vu un personne comme lui😂 bellissimo
💋💋💋ndaye sane contana trop si khalé bou djigéne bi dalena téyena yalla nalla yalla faye 👉wayé amena aye nite yo khamené khéne warouléna deupe mikro
Lirou choc bi metina balegui niewago.
Akh lirou mi ay 🐃🐃 nann siwougniou
Kholé nigéni défaite intére vie
Sa data nday danga sokhor rék
@@mafatimmbodj7836 mais Mane wakhouma lou Aÿ tu habit ou ma belle
Mane wa gediawaye la notaires ha ha ha
Mejnoune lirou diagne
vraiment lirou damako bilahi imition mangui koy setane fissi a 4h du matin wayé dama rébatass lirou amal diamou way 😂😂😂🙏🙏🙏
Caméraman bi kou maneu mouñe leu 😂😂😂🤦🏽♂️
Nice
Mais lirou mi vrai con leu vraiment il me soûl 🤯🤯
Nekhoul bo nekhoul mais sa wayy Denioula Wouly boga Daw
La journaliste elle es magnifique je l'aime bcp. Trop brillante d'où t'aime depuis paris 🇫🇷
Lirou ku bakh Laa day dindi strees billah
Journaliste bi nop naa ko de 😎
Malako gueuna nop yamal rek
@@fallouwade1807 😂😂😂
Elle est très sereine.macha allah!
Bougouma lirou ndian
journaliste bi ho May Getty❤
Nenako sa greffage bou yag bi no li comme guerre 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Lirou diane yaw danga rew niak kersa
Mais la journaliste est trop belle.
Je croyais que man rekk mako guiss.Mdrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrrr
Tranquille tranquille c’est ma femme
@@mamadoukamara3620 kon da ngay nièmé akh kii kou jeul dinga bari xel yo lek🤣
grave belle
@@seydinasall5525 khana yaw réka yori beute
Ay lirou tamit amal sonou complex😂😂😂
Wa yen lirou mi mom wekhna diiii🤣🤣😂
Khass beug na Soumboulou,Soumboulou beug na khass 😂😂😂😂😂😂😂,thieuy Lirou
😂😂😂😂
Vraiment lirou dangaye comédie légui
Sérieusement félicitation à la journaliste c’était pas facile du tout . All the best 👌
99ss
Journaliste bi machallah mais lirou diane amoul amal jamm magui dè🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣😂😂😂😂😂
😂😂😂😂 Lirou amoule 🤦🏽♂️ té gua dieule journaliste bi bène yone
Kikay dako wara dieul keyy défko niarél nakh sén couple dey nékh noumako guissé ni non Lirou amoul dey rey niitt
Vraiment beugue mo fort lirou diane ak boucher sont sincères
Lirou ❤️❤️❤️
Vraiment sokhna si man na mougne
kou djiguéne ki yala nako yala sam ligniy waur si djiguéne la guiss si mome
di guereum adja gass😁😁😁😂😂😂
Lirou yalna sa diam yagg wayy😂😂😂
😂😂 bilahiiii j’aime cette fille
Est-ce que dou accidents bi moko doff loo .non c vrai que boop bi daffa tourné pas tourmenté
Ah ah ah ah no lirou mo nèkh
Lirou del khôl nigaye wakhé si réseau social yob nane la dépasse te ga dé deglou journalists yii merci pour la compréhension champion
Qui Mba diamou rek lirou dafa doff bilay
Lirou a Sans doute postillonner comme jamais la Journaliste😂😂
😂 😂 😂 À fond
Lirou diane for Live billah man Lirou lay beggè no Strees balla gaye2 am nga kharrid bu bakh
Lirou rek 😎🇬🇲🇸🇳
Wouly mo yungal boop bi😂😂😂😂😂 daka Wouly ba sonne
Nooo virement femme bi diambar la lirou moo nékh 😅😅😅
Mais lirou mogui dakh guinar di wakalé sokhlaaamm
Lirou il faut reflechi avan de parler
C'est bien fait LIROU DIANE,Boul ko may touss.DAFA NGUEN GAME.