Salam J espère que la justice fera son travail jusqu’au bout Maintenant il faut impérativement trouver des solutions pratiques pour la formation professionnelle de cette tranche d âge de filles et de garçons et leur offrir l opportunité d apprendre aussi un métier ainsi que leur pratique religieuse dans un environnement sécurisé et formelle
Faut aussi dire que Serigne Bass Abdou khadre a joué un rôle important pour gnou diap ko mo def investigation ba kham kane la et aussi mo léen bolé ak Commandant bi pour mou takhaw si
Ce qu’on peut faire c’est de commenter et wallah fi kou nek affaire bi mettinala trop wallah mettina au fond de moi je me mets à leurs place , leurs mamans comment elles sont brisées tei mounougnou ko exprimer j sais ... Viole c’est la chose la plus pire qui existe . Magui mastaWou khalei yi di gnan yallah na yallah deff Li gueun ci gnom. Je prie que vous ayez une vie meilleure incha allah que le tout puissant veille sur vous amine . C’est trop dure massa à vous et vos familles 🙏🏾 je compatis
Merci beaucoup maman d’avoir demandé si Serigne Mountakha est au courant de ça ou bien . J’ai vu que c’est lui qui devait être le premier à réagir de cette situation. Et l’argent qu’il a donné à Walf était destiné à cette pauvre famille . Mrci 🙋♂️
Segne bamba da liguéye deuk bi wadji louko yeubou sakh khamouko ? Merci grand fadel yalla gua goudou fan ak wér doundeul grand ba féké sa ndiarigne dom yi
Kou ame yeurmandé sisa yaye do def lou gnawe djiguene li dafa méti trop vu les parents témoigne dagaye guise métitte si sene xoll😞yalla naléne yalla same🤲
Comme japeu Nagnou Wadji , Déléne bayii khéle famille khalé yi Parsk meune nagnouye jote aye menaces venant de la famille du Mbacké Mbacké….Parsk kouné Touba khamené amena Borome🙏
Gni dé niome danioulene violer deugla ndahté ay halé you ndaw lagnou mais ana gnidone takhawou mère bidone wakh né daniouko violer bagouma sakh toudou toureum gni nio diara dimbali nguir yalla ak yonenti bi
Loutax warou niou recevoir Haliss ils le méritent amplement viol defeu metti si yaye seu adouna dom yeup yakou et sa serra difficile pour elles de vivre tranquillement sougn len hamaler senegal gue hamner hol yi deinio bone wah rek leiniou meneu ak khaster
Lolou moléne di raye seutou serigne touba la rék aférbi nékoul si seutou serigne touba xam xam xoloule santa ni askane té gñiome linékone si serigne touba khadjoule di néka si gñome
Sëriñ bi bon na wayé yay yi sagàn nañ. *Dom bu jigeen, da ngay seuss si mom* Téla wax ak mom, niko *Sa mpay mi, bufa ken ag, ku lani sumekul dawsil wax mako*
En tout cas yaye yi sanganeté amnasi dakh Di puni khalé ay morom yeupe wathie niebi gua bakofa ba timide sogua bou amé yone niaroyone gua wakhou ba fofa kholale louko téyé balégui mé Dale rek
Douléne diok si nouléndi nakh dakh geumouléne yalla mane serigne touba miguéndi togñe rék moma nakhati serigne touba diamou yalla mome la santané té bayi yalla ak limou mome
Naga gniow mastawignou est ce que se sont eux qui vous ont dit d'amener vos enfants à quelqu'un qui n'a pas de formation d'enseignants, un voyou masqué
Organiser vous a tour de role vous pourrez inchallah travailler et surveillè les filles c est pas prudent de les laisser au tour des hommes les mère peuvent former des groupes de 4
Walay sagane amnasi bilay je me rappelle bimay nék khalé nék ak sama badiane si keur gou goor à chaque fois sama badiane dafmay wo soummi sama slip daldi khol après néma boul dougou négou kén lolu woroul mani ko waw Bima maguéu lay doray kham li takh moudane khol sama sexe bi
Merci beaucoup wa Dakar buzz particulièrement Fadel
Walaye li dafa metti yalla nalene yalla diapaler 😢 j'ai pitié pour les petites Massa lene
Salam
J espère que la justice fera son travail jusqu’au bout
Maintenant il faut impérativement trouver des solutions pratiques pour la formation professionnelle de cette tranche d âge de filles et de garçons et leur offrir l opportunité d apprendre aussi un métier ainsi que leur pratique religieuse dans un environnement sécurisé et formelle
Ki vrai domérame la il doit être condamné à vie amoul mbacké mbacké amoul touss
Dama rouss
Bilahi ki mala yi sah gnooka gueune
Ki bilahi prison à vie lagne ko wara teudji ki bone na trop waye😢😢😢😢😢😢
Faut aussi dire que Serigne Bass Abdou khadre a joué un rôle important pour gnou diap ko mo def investigation ba kham kane la et aussi mo léen bolé ak Commandant bi pour mou takhaw si
Masta mes chers mamans courage aka metti les filles 😢😢😢😢yalla na len yalla soutoural ni mou soutoura lé dougoube thi bir souff
Amine ya Rabbi
Alahouma aminnn,
Ce qu’on peut faire c’est de commenter et wallah fi kou nek affaire bi mettinala trop wallah mettina au fond de moi je me mets à leurs place , leurs mamans comment elles sont brisées tei mounougnou ko exprimer j sais ... Viole c’est la chose la plus pire qui existe . Magui mastaWou khalei yi di gnan yallah na yallah deff Li gueun ci gnom. Je prie que vous ayez une vie meilleure incha allah que le tout puissant veille sur vous amine . C’est trop dure massa à vous et vos familles 🙏🏾 je compatis
Merci beaucoup maman d’avoir demandé si Serigne Mountakha est au courant de ça ou bien . J’ai vu que c’est lui qui devait être le premier à réagir de cette situation. Et l’argent qu’il a donné à Walf était destiné à cette pauvre famille . Mrci 🙋♂️
Merci b1 dit
Mountaha pourquoi ??? Peut on savoir ?
Mane protection de l’enfant et ministère de la femme la khamoul louy sene liguey la beuga kham
Xana lèkk xalisu rew mi kasè tèkki wouñ Dara
Hôtessou deh moy sen job
@@diamilasy1878 waw kay yaw yaa Len Xam nak 🤣🤣🤣
Fo dem amna kou bax ak kou safanou Mbacke Mbacke yi defounioula dara
@@diamilasy1878 😂😂😂😂😂😂
Ki yalnako yalla alake si barké alhourane
La justice soie faite
Segne bamba da liguéye deuk bi wadji louko yeubou sakh khamouko ? Merci grand fadel yalla gua goudou fan ak wér doundeul grand ba féké sa ndiarigne dom yi
Kou ame yeurmandé sisa yaye do def lou gnawe djiguene li dafa méti trop vu les parents témoigne dagaye guise métitte si sene xoll😞yalla naléne yalla same🤲
Justice 27 khalè yi
Machallah dkr buzz💞💕
Yalna yallah takhawou khalé yi
Comme japeu Nagnou Wadji , Déléne bayii khéle famille khalé yi Parsk meune nagnouye jote aye menaces venant de la famille du Mbacké Mbacké….Parsk kouné Touba khamené amena Borome🙏
Merci DAKAR BUUZ
Gni dé niome danioulene violer deugla ndahté ay halé you ndaw lagnou mais ana gnidone takhawou mère bidone wakh né daniouko violer bagouma sakh toudou toureum gni nio diara dimbali nguir yalla ak yonenti bi
Prison a vie ki lou méti la défe du jamais vu verginite dafa est sacré
Bilahi kii mérité woul toureum bi lii niawna trop ay Khalé you ndaw kii dagñko wara teudje à vie
Yéwouléne Mbacké geunoul Gomiz ni Mendy
Mais yèen khana khaliss nguèen si beug nak tè nguèena mougne rèk tè bayi ak yalla mon geun khaliss 🥳
Loutax warou niou recevoir Haliss ils le méritent amplement viol defeu metti si yaye seu adouna dom yeup yakou et sa serra difficile pour elles de vivre tranquillement sougn len hamaler senegal gue hamner hol yi deinio bone wah rek leiniou meneu ak khaster
Danio wara ame xalis ndakh danio wara yobou xale yi hopital niou suivre len aussi mentalement
ioe dhe amo khol
Fadel yalna Yalla fay la !!
Man dh sama khol bi nimouy métte mounoumako sakh expliqué 😭😭😭 ki deh bougne ko bayé miu diale djiguénou senegal yeupa wara guéne khékh li
DAGNO YAKARONE Nii KOU BAKH LA COM MBACKE MBACKE LA
May wakh nguendi baylé sene domyi encore . Méfiance chers parents . Niaaw ndiorte dafa bakh bo yoré djiguen
Mbacke Mbacke yi nooo saysay😅😅😅
Apart lhistoire de walo lii moy deuxiéme stoire bii geun mëtii thii kaw djiguën senegal
Nako Serigne mountakha yeuk diapalei khalei yii
Il faut vraiment soutenir les filles et leurs mères sinon dou bakh dh;parck dafa méti torop
Bilay surtout kisi âme gnari dome la gueuna yeureum
Naniou niafe dayame ci kasso bi mou diekh momm mo fegne le beurina serigne you koye deff domarame marabou noooooò noooooò
Courage les filles
Lolou moléne di raye seutou serigne touba la rék aférbi nékoul si seutou serigne touba xam xam xoloule santa ni askane té gñiome linékone si serigne touba khadjoule di néka si gñome
Dageu lenn khourou mbake Mbake bi an diokhe lenn senni domm ancore douguen ai nite
Sëriñ bi bon na wayé yay yi sagàn nañ.
*Dom bu jigeen, da ngay seuss si mom* Téla wax ak mom, niko *Sa mpay mi, bufa ken ag, ku lani sumekul dawsil wax mako*
CAS Bii DOYNA WARR TOROP THi MBACKE MBACKE Lii GNAW NA
En tout cas yaye yi sanganeté amnasi dakh Di puni khalé ay morom yeupe wathie niebi gua bakofa ba timide sogua bou amé yone niaroyone gua wakhou ba fofa kholale louko téyé balégui mé Dale rek
par ce que dagno fok ni kouy diangalé alhourane dou def lou bone té lolou moy heureur bi,Car ak mbone fep lané
@@ThierWade-yb6km Mane mome woulou wouma kéne sama diabote fouma tôle magui vérifier Di lathie DILA diokh confiance sa bope
Mbake Mbake bi mo kate dayame ki moye khatieu domarame yi
Senegal plàto TV douniou ci wakh mbake Mbake bi mo dokhane dayame do rouss sakh mbake nooooòooo 😂😢😢😅😅
Prédateur sexuel deug moy waàdji! courage au victimes 🙏 🙏
Douléne diok si nouléndi nakh dakh geumouléne yalla mane serigne touba miguéndi togñe rék moma nakhati serigne touba diamou yalla mome la santané té bayi yalla ak limou mome
Domarame mbake ya deugeu sa daye mbake nooooòooo khatieu bi ga donne
Domarame mbake yageu nako deff do massa degeu mouride yi wakh ci Domarame mbake yaye Domarame degeu
27 filles chaque personne 10ans de prison kone wadji 230ans féreme lagne koye teudje
donc cela signifie il va décède au prison
Lolou moy mou deid thi kaso bi😂😢
270ans kay
Naga gniow mastawignou est ce que se sont eux qui vous ont dit d'amener vos enfants à quelqu'un qui n'a pas de formation d'enseignants, un voyou masqué
Akhirou saman 😢😢
Waadji daal nagnou deubb khour yi dagg ndaye coye bi teuthie ndayam 50 ans thiowli diéékh
Organiser vous a tour de role vous pourrez inchallah travailler et surveillè les filles c est pas prudent de les laisser au tour des hommes les mère peuvent former des groupes de 4
Khalei yii ani sen papa yi yaye yi rek lay guiss
moma diakhal😢😢
Seugn amone na plus de 20 femmes dont des sœurs. Alors que lislam ne reconnaît que les 4 femmes
Ki dafa niafe dayame wa ki djigene diourou ko en tant que mbacke mbacke qui moye domerama imbécile te dieu le lene ma domerama bi
Bilayi liiii😢
Domarame mbake no ya niafe sa daye deugeu khadim mbake nooooòooo
Ani ñi done diapalé adji sarr. mamour diallo waxal cheikh yirime waxal maki sall waxal .Sénégal sou yaxo yénako yax féne ak doul rék
Badiene adji sarr yi ak tante yi😢
Wa talibeyi yiye diokh mbake Mbake yi adiya senn serigne ai khale la viole de
Gnaw j'espère que dinagnouko teuthie a vie prison ba yalla boumou fa am diam
Metine il faut ñou top ko bamou dem kasso
Talibeyi diokh lenn khaleyi adiya boke kou sante mbake ko deff de ana mouride yi domarame mbake
Adineu bi yakhouneu
Viol collectif et l'état est muet sim. Lidienti wou gniou sénégalais
Hooooooo
Métina trope😢😢😢
Birn fait... maintenant jugé et prison à vie
😭😭
❤❤❤
Walay sagane amnasi bilay je me rappelle bimay nék khalé nék ak sama badiane si keur gou goor à chaque fois sama badiane dafmay wo soummi sama slip daldi khol après néma boul dougou négou kén lolu woroul mani ko waw
Bima maguéu lay doray kham li takh moudane khol sama sexe bi
Bilai gni kay saguane Nanou trop
Lol sakh
À cause de son surnom dou moudjiou fene senegal 🇸🇳 amoule loi
Khana gueumo Yalla
Diap nagn ko
Vérité absolue
Ki daffa febare mbake ya diele record bi domarame mbake nooooòooo
Kou doundeul viole manoko kham
Badou dangako doundo massa
Domarame yi kate lenn dayame nekeu ai nite bayilenn seni domm yi guenn guenn di diokhe douguen ai nite
Hooooòoo
Komm kou sante mbake reke guenn defeni domarame yi dioure saniko guenn di deff
Mane dh lii ba famoy Modiou guew mako
Ioe nokoul feuler plusieurs personnes deinio meneu fen en même temps faible d’esprit bigue don seu genre yi nio yak sénégal
Dieuredieuféeeeeee mariamacissé
Après le ndigueul il sera libre😂😂😂😂
😂😂
Lou lér
Metina trop
27 × 10 ans c'est ça qu'il mérite
20 an
270ans
Encore les marabouts mourides com tjrs thiey yi mourides
Yaw arrêté téle
Lou Bonn amoul mouride amoul kein fo deim amnafa lo Bonn Moy dousi sante si nitt la
Bilahi kii mérité woul toureum bi lii niawna trop ay Khalé you ndaw kii dagñko wara teudje à vie