Machallah yalla nanou yalla def talibé cheikh. Yallana seydina cheikh nangou sounou talibé. Yallanala yalla defal diam ak soutoura yalla yokk say ler. Amine
Maa challah sama serigne yalnala yalla yookou si zaahir ak baatine , té mootali mission bi bamou weur adouna djeure-djeufati waayé mangui saakou niaane ngir yalla mayma fathou ak kachfou si barké mawlaanaa cheikh ahméd tidiany
sange bi yalla nala yalla takha wou si barké Seydina mouhameth ñoune tamite yalla nañou yalla nangoule souñou nék talibé si barké serigne cheikh Ahmed tidjane sy almak toum amine
Djazakoumou Lahou Khayrane Ya Seydi Mouhamad Al Cheikh, Yalna Borom bi goudal sa fane té yook weer gui ak lère yi bijahi Rassoul Salalahou Aleyhi wa Salam. Kou wakh deug rek khamni léral nga lou bari si yoon wi. Yalna Borom bi fayla bijahi Cheikhna Ahmada Tidjani. Niounguilay nianal té di Sakou niane si Yaw. Dieuredieuf
Machallah yalla nanou yalla def talibé cheikh. Yallana seydina cheikh nangou sounou talibé.
Yallanala yalla defal diam ak soutoura yalla yokk say ler. Amine
machalah Chiekh wahtane bi sell na yalla naniou yalla déff deug deug talibé Chiekh thi barké nabil Moustapha psl
Mashaa'allah mashaa'allah ya seydi Mohammad el cheikh dieuredieuf
❤nagniou yalla dolly souttourra amine ❤
Seydi mouhamed el cheikh deugue deugue yaye wonee dolee tarikha mawlaya cheikh tidiani wone nga nieepp cheikh tidiani dou morom kenne dieureudieuf ya seydi
Machallah waxtane bi changéna Lou bari ci mane.merci bcp si waxtane bou neex.dieureudieuf
Maa challah sama serigne yalnala yalla yookou si zaahir ak baatine , té mootali mission bi bamou weur adouna djeure-djeufati waayé mangui saakou niaane ngir yalla mayma fathou ak kachfou si barké mawlaanaa cheikh ahméd tidiany
sange bi yalla nala yalla takha wou si barké Seydina mouhameth ñoune tamite yalla nañou yalla nangoule souñou nék talibé si barké serigne cheikh Ahmed tidjane sy almak toum amine
djazakallahou sant yalla dieureudieuf Seydi Mouhamed El Cheikh mounounioula faye
Djazakoumou Lahou Khayrane Ya Seydi Mouhamad Al Cheikh, Yalna Borom bi goudal sa fane té yook weer gui ak lère yi bijahi Rassoul Salalahou Aleyhi wa Salam. Kou wakh deug rek khamni léral nga lou bari si yoon wi. Yalna Borom bi fayla bijahi Cheikhna Ahmada Tidjani. Niounguilay nianal té di Sakou niane si Yaw. Dieuredieuf
Machalla jazaka lahou akayra seydi Mouhamed el cheikh mission bi dina mat inchalla alla koulli hal amine si niane yi
Dieuredieuf Seydi Mouhamed El Cheikh
Yallah na niou yallah dèff talibè cheikh
Bonjour très intéressant Seydi Cheikh. YALLA nala YALLA fayy. Je voudrais juste savoir pour ki nga khamni mome késsé moy khadara ?!
Ma sha ALLAH deug pire guene nga nio yok dolé niou hame liniou ame yalna yalla faye serigne bi
Dieureu dieuffaty Seydi Mouhamed el cheikh imamal Mahdi Almountasar khoutboul Akhetaboul kabiir ♥️ ♥️ ♥️
yalla na yalla def niou TALIBE CHEIKH DEUG
Amine
Machala dieuredieuf SEYDIL el cheikh si enseignements
machalla rafetna trop
Yallah nala yallah yokal léryi
🥀🌺Mashallah 🎋💐
Dieureudieuff Sanguabi Sowathiouton mougnaw
Machallah
dieuredieuf yalanala yala faye
Machallah talibe cheick rek woor
Dieuredieufeti Sangue Bi Maschallah
Ok merci yaeye gende
Masha Allah.
Dieureudjeuf SANGBI yagfi lolu t wer yalla naniiou MAWLAYA CHEIKHOU TIDJANI CHÈRIF nangoul niou sunu nek talibé
al hamdoulililah
Ndiogou Diop
amin yalla bou sounou yakar tass
masalla
Mâcha alla
Macha allah ya seydi Mohamed el cheikh sama Serigne
mashalla amena solo
DIEUREUF YALLA NALA CHEIKH AKHMED FAAAYYY
merci ya seydo
Santeu sang bi abadane
machalla
Nsaysane kou mélni yaw amou fi yalla hame nako
Yanna Sounou tour Nèkka ci Manèwèlba
merci nerci
machlla
Man dal soupounala
Machalla Machalla
dieureudieufati je voudrais savoir si une femme peut faire le khadara dans sa chambre toute seule
Ww lolou moy li 😊geune sakh
qutb zamam biy diète fass touram nane na?
Diadieuf
Macha alla diaye mon n 703633368 diokhma sa numoro
machallah
Machala