Que le bon dieu bénisse ce mariage si barké Ousmane Sonko. Salma est une femme de bon coeur. Les ennemis de Ousmane Sonko sont les vrais perdants.Salma est une femme qui mérite beaucoup de bénédiction. Une femme de conviction semée d une patriotisme immense. On est fier de toi
FÉLICITATIONS ET BEAUCOUP DE BONHEUR À CE NOUVEAU MÉNAGE. QUE DIEU VOUS GARDE ET BÉNISSE VOTRE FOYER....🙏🙏🙏 LONGUE VIE À VOUS ET SURTOUT SOYEZ TRÈS DISCRETS VOTRE MARI ET VOUS. ❤❤❤
Ousmane Sonko mogui fal maires yi députés yi ak président faté nagn si doli mogui takk seuy yi mashalla 🙏 Yalla na yalla barkel seuy bi am si ndiambot yu barkel inchalla 🙏 té guèn toudé Sonko dom nak🙄
Félicitation Salma. Beaucoup, mais alors beaucoup de Happyness pour toi. Tout le monde te le souhaite de bon coeur. Brave femme, tu as le Respect de tout le monde Carinio.
Salma yag nala présenter patriote yi ndakh sa ligueye bou Nice man Momo si réseaux sociaux yi xamna sama gayila 😂 machallAh yalla na sey bi barkél vrai journaliste ♥️♥️♥️🥰🥰🥰🥰🥰🥰✅✅✅✅
bilahi à mon âge j suis tellement contente et fiere de toi te souhaitant seuy bou barkel book ci yinu take ca aras yalla tek si lokho nday joram amin ya rabal alamina vive Sonko vive les patriotes Salma damala yaga top khol sa takute sa jambar envers PR Sonko teman bilahi walahi mom rék lay noyé sama entourage sakh yayu Sonko laniou may woyé diam si yaw
Que le bon dieu bénisse ce mariage si barké Ousmane Sonko. Salma est une femme de bon coeur. Les ennemis de Ousmane Sonko sont les vrais perdants.Salma est une femme qui mérite beaucoup de bénédiction. Une femme de conviction semée d une patriotisme immense. On est fier de toi
Machallah et felitation a salma heureuse menage ❤
Walahi yaw yalna niou waleu nioune ngi amagoul inchala amin
Si barké ousmane 🤦♀️🤦♀️ bayiléne bokalé
FÉLICITATIONS ET BEAUCOUP DE BONHEUR À CE NOUVEAU MÉNAGE. QUE DIEU VOUS GARDE ET BÉNISSE VOTRE FOYER....🙏🙏🙏
LONGUE VIE À VOUS ET SURTOUT SOYEZ TRÈS DISCRETS VOTRE MARI ET VOUS. ❤❤❤
❤yalana yala barkel lep
Sonko son rôle dépasse la politique il a une mission dans la vie
C'est vrai dé
Thiey journaliste jour mariage sakh gnouy interview😂😂😂..Heureux ménage la grande patriote🥳🥳🥳
Moi je l'admire elle n force pas elle est véridique et naturelle, elle connaît sn travail am fouleu thii bopam heureux ménage ma cherie.
Diotna nak kalifa bi sonko diokhé ndiguél pour patriote seye sen bir khalé bou djiguén bou paré lalal jaime❤❤
Ya beug lou yombeu 😂😂
Félicitations salma yalla na séy bi barkél
Félicitations Notre Salma heureux ménage a Vie🎉🥰🙏
Ousmane Sonko mogui fal maires yi députés yi ak président faté nagn si doli mogui takk seuy yi mashalla 🙏
Yalla na yalla barkel seuy bi am si ndiambot yu barkel inchalla 🙏 té guèn toudé Sonko dom nak🙄
😂😂😂😂
Amine yarabal alamina
Félicitations Salma Ibrahima fall yallah na seuye bii barkell bangua ame ndiabott you barkell machallah
Amine
Je suis une personne âgée je prie pour que ton mariage soit béni soit heureuse que dieu bénisse ton mariage amine
Amiine
Allahouma amine
Amine Amine Amine yaarabi 🤲🤲🤲🤲
Amine yarabal alamina
Con personne âgé yi niongui si RUclips bi ak si commentaire yi ? Yalla nalen yalla yagal sounou kanam
Yalna seybi bark ci daradia seydina mouhamadou Rassoul
Bien heureux ménage Salma ! Soyez bénis 🙏🏾🙏🏾
Ohhh suis contente pour toi Salma alhamdoullilah toutes mes félicitations bon ménage❤ sonko amis tourando mok diomay
Félicitation Salma. Beaucoup, mais alors beaucoup de Happyness pour toi. Tout le monde te le souhaite de bon coeur. Brave femme, tu as le Respect de tout le monde Carinio.
kou bakh am lou bakh , kou deugou am lou deug ,bon menage Salma I Fall, machaallah,
Felicitation ma fille yalla na yalla def Barké cii seybi
Amine
Bravo Salma yalla nala djick
Salma yag nala présenter patriote yi ndakh sa ligueye bou Nice man Momo si réseaux sociaux yi xamna sama gayila 😂 machallAh yalla na sey bi barkél vrai journaliste ♥️♥️♥️🥰🥰🥰🥰🥰🥰✅✅✅✅
Félicitations sokhna Salma heureux ménage yalna yalla barkel sey bi té mayla dom you barkel si barke s touba 🤲❤️❤️❤️🌹🌹🌹🌹
Machalla
Salma
Yalla
Na
Seyebi
Barkele
bilahi à mon âge j suis tellement contente et fiere de toi te souhaitant seuy bou barkel book ci yinu take ca aras yalla tek si lokho nday joram amin ya rabal alamina vive Sonko vive les patriotes Salma damala yaga top khol sa takute sa jambar envers PR Sonko teman bilahi walahi mom rék lay noyé sama entourage sakh yayu Sonko laniou may woyé diam si yaw
Félicitations Salma la tigresse. Heureux ménage et que Dieu veille sur cette union : amine ya Allah.
Masha Allah Yalla na thi Yalla def barke may la ndiaboth tou Seydina Mohamed psl ❤❤❤❤
Oumane mou sel mi que dieu te protége.
Salma heureuse ménage.
Yalla na seyby barkel machala laftiat dieureudieuf yalla dieureudieuf Sonko ❤❤❤❤❤❤❤❤
🎉 Heureux ménage SALMA❤
Félicitations et heureux ménage, yalla na seyebi barkel
Félicitations Salam yalla na yalla barkel seybi may la diabot bou barkel ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🙏🙏
Masha ALLAH, félicitations la patriote. Yalana YALLA barkel seye bi si barke seydina ousmane sonko
Sonko dou nite
Machallah❤❤❤❤❤❤
Mâchâ ALLAH.
BARAKALLAHOULAKI WA BARAKA ALAYKY WA DIAMAHA BAYNAKOUMÂ FÎ KHAYRINE
Félicitations Salma ❤❤
Ndokale yallana yalla barkelle seybi ma chahalla
Machalla la grande patriotes ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machallah yalla na yalla barkel seyedina Mouhamed
Barak Allahu Lakum Salma,May Allah protect and put lots and lots of Barakah in this union my dear.Jambar deuga moy yow❤❤❤❤❤
Machaalah Salma yallana yalla barkel seuy bi bijahi seydil woudjoud saws
Machallah Félicitations 🎊🎈 Salma
Yallah na Yallah barke ❤
Félicitations Salma ❤❤❤❤❤❤❤
Heureux ménage notre Salma nationale ken dou sonko il crée même des unions conjugale vraiment merci sunu borom ❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤machallah heureux ménage bonne continuation
Heureux ménage qu'allah vous assiste que le meilleur reste à venir et surtout reviens dans ta maison mère Walfadjri
Maaa shaa allah taaala ! Bravo thi kaw thi kaname
ماشاء الله بارك الله فيك وجزاك الله خيرا شغن سالم فال
Félicitations Salma, que Dieu vous bénisse, vous et votre mari, je vous protège, mariée Ameeen 🤲🏾🎉
Merci salma diarama machaallah yalla na Yalla barkel seye bi 🎉🎉🎉🎉🎉❤❤❤❤❤
FELICITATIONS TRES CHÈRE.
DU BONHEUR, RIEN QUE DU BONHEUR, YALNA YALLA BARKEL SISTER
Toutes mes félicitations yalna seybi nékh té barkel❤
Machalla yale na saye bi barkel te lafale lena tihate
Heureux ménage qu'Allah swt vous bénisse amine
MACHALLAH MME SALMA IBRAHIM FALL ET ON VOUS SOUHAITE UNE HEUREUSE MÉNAGE ❤❤❤❤❤❤❤🎉
Qu' Allah bénisse ton mariage ma lionne Machaa Allah fatabarakallahou ❤️❤️❤️
Félicitations Yallah na seuy bi barkel
Machalla salma
Félicitations patriotiquement nékhna dal yalna seuy bi barkel in shaa Allah beaucoup de bonheur khéweul contanenaniou vraiment
Yallah nayallh barkel saybi
Ooh😂 wadji dieulna sama khél ❤❤
Heureux ménage Salma FALL, nous les patriotes nous te souhaitons tout le bonheur du monde, ici bas et dans l'au-delà (yalna yékh)❤❤❤
Félicitations la lionne du courage diaspora vous encourage on t'aime beaucoup ❤❤❤❤
Machala la Salma félicitations yalna yalla barkel
Yalna seybi barkel
Ke le bon dieux bénisse ce mariage machallah longue vie au couple yalna yalla saamelen te barkel sen seuy bi
Félicitations chère sœur ❤ Yalla na Bourbi Yalla samou la yak sa brom keur tawfikh ak taysir goudou fane ak wer . Yalla nasi Ngoné Saliou topou ❤
Félicitation Salma
Yallah na seuye bi barkel, Yallah maylene gnabote bou barkel bidjayi Nabil Moustapha 🙏🏼 🙏🏼 🙏🏼. Heureux ménage ma belle.
Félicitations Salma yalla na yalla barkel machallah
Yalna yalla Barkeelko, Patriote Salma.
Salma vraiment heureuse ménage
Que Dieu vous bénisse,protège Amine Amine Amine yaarabi 🤲🤲🤲
Khou bah ngua
Bilay walay ma fille diapalni say yaye yo khamoul ta niou beuguela guir ligua khéh ba dioté yalna seuyby amm barkée ak niaboote bou barkel
❤❤❤❤❤❤❤ Heureux ménage Salma . Yalna seuye bi barké et que Sheuytané yalnaléne sooooorrrrrrrrriiii ba faw❤❤❤❤❤❤
Mach'Allah Salma yalna seuye bi barké thi barké Seydouna Muhammed Saws ❤️🥰❤️
Heureux Ménage salma dila nianal sey bou barkél ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Salma nittt kou bakhla.❤🎉🎉
Felicitation sister yalna seuye bi barkel yalla may lene ndiabote gou barkel 🙏🏼🙏🏼🙏🏼❤️❤️❤️❤️❤️
Salma Ibrahima Fall injuste ladone khékh mei légui moy lolou mei je t'aime ❤
Yalna ko wale ngone,' saliou amine AK bep djguene amine
Félicitations Salma que dieu t accorde le bonheur tant souhaite
Machallah machallah. qu'Allah bénisse votre union.
Congratulations Salma for your wedding and I wishing you all the best and success on your wedding
Félicitations soxna salma heureux ménage machallah
Heureux ménage Salma que Dieu bénisse cette union
Yalna andbi sakh seuy bou barkel patriot bi
Félicitations yalla nako yalla barkell jam rek aak tawfekh inchallah
Yalna Yàlla barkeel sëy bi te may léen si njaboot gu barkeel baeke boroom Tuubaa
Félicitations Salma yalla ná séy bi barkél
Félicitation la lionne yalna seye bi barkèl
Heureux ménage ma chérie❤❤yalna seybi barké❤
MACHALLAH MA SEOUR❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤🎉
Machallah
Yalna barkeel❤
Gracias felicidades hermana mío hsa hecho buena trabajo bravo 👏 👍 💪 🙌
Félicitation ma belle.. seuy bou barkel jaabot bou barkeil sutura bir ak biti ♥️🎊
Eskey Sayyidouna Ousmane Borom Barké la ❤️❤️❤❤
Salma yalla nala yalla mousal si thate patriotes yi nanouy Marie sounou birr bousi béne koudoul patriotes
Toutes mes félicitations. Yallah na seybi barkel
Machallah yalna séy bi barkél
Une grande Dame celle là...
Félicitations salma❤❤❤❤❤
Mâcha ALLAHOU ❤❤❤YALLANA SEYY BI BARKÊLE
DemboTihangou❤❤❤❤❤❤ 6:46
Félicitations Salma yalla n'a yalla barkel saybi si barke seydina mouhmd psl❤❤❤