Diadieuf trio bi machallah parcours des champions bok na si émissions yi gueuna intéressant si élevage bi en ce moment pourquoi ? Parce que kham kham bou lérr bou worr moy guén si émissions yoyou Machallah sétane nagnou avec Abou kane avec grand lamine diop père Modou Niang père Claude demba diop mais ces deux frères de Feu vert agro buisness warna gnou déf émission parcours des champions ndakh sén diar diar ak sén kham kham. C'est très important kham kham élevage dagnou ko sokhla nous sommes dans la diaspora amou chance di déf tours si bergeries yi pendant toute l'année vacances ba vacances lagnouy dém Sénégal té doyoul pour diangueu ak out kham kham si élevage bi bénn si man mi di commentaire je suis abonné nék passionné d'élevage di élever depuis très longtemps guén Sénégal nék depuis en France plus d'une vingtaine d'années doug si ladoums yi en 2009 di élever toujours ba tay mais diap nani sokhla na encore encore et encore kham ladoums yi élevage bou démb ak élevage bou tay kham kham dou doyy motakh je vous suis dans vos émissions di lénn encourager nguén continuer Machallah yéna ngui doundeull élevage défall lénn émissions anciens éleveurs yi doyens yi ak aussi jeunes éleveurs you mélni Feu vert agro buisness ndakh sén kham kham boys yi khamoumalénn mais sén émissions yima meussa sétane je vois machallah que amna gnou kham kham. Trio bi yalla na yalla yombal té barkéll liguéy bi incha Allah dieureudieuf Trio bi

Merci Beaucoup champion
Chapeau à Mansour vraiment il maîtrise très les lignées
Merci Beaucoup champion
Mach'Allah ❤
Ndiaye bagnal takkal
Ma sha allah ❤lamane
Machallah khôl sedna way ❤
Ma sha Allah 😍
Manchalla
Machalla 🎉🎉
BOY YOU GARAWE🤩
❤❤❤❤❤❤❤
Machalla
Mais ladoumed bann côté layy amm si mbour exactement svp
Bayal(terrain) THIERNO MANSOUR BARRO en face terminus Sénégal Dem Dikk
Terrain santessou
Côté croisement saly en face SENELEC
@@toubadiop9414 Sisi fofoula 👍
Route nationale bi
Kham kam dafa nékhe laf thiate
Elevage xam xam 🤔🤔🤔