KAWTEF Li papa DJI wax nii Doyna waar

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 8 янв 2025

Комментарии • 154

  • @KhataDiouf
    @KhataDiouf 20 дней назад +26

    Bâyi lén sokhor no ma diomi si Sénégal ❤❤❤ gui yallah n'a seybi barkel ya rabby ❤❤❤

    • @Lamp112
      @Lamp112 18 дней назад

      Yaw doul abb dof gua rek mére bi gua khamni bimouy taakeu xalé bi yayam sakh yeugou ko guanane fi ay sokhor, mére bi kidnappé domou diambour bi privée ko de sa famille guanane fi ay sokhor, n'importe quoi, pfff🤧👎❌

    • @ToufaBiaye
      @ToufaBiaye 17 дней назад +1

      Amine

  • @makhfaye-c2k
    @makhfaye-c2k 20 дней назад +24

    Gnata senegalai gno take diabarou toubap ndakh khaliss nite ndaye mandou tongne bakhoul kou néke ak sa probléme

    • @Lamp112
      @Lamp112 18 дней назад

      Wayé lolou dafay fékeu parent d'accord ci mariage bi mais mère bi dafa takeu xalé bi privée ko de sa famille

  • @BinetaNdoye-yf6pp
    @BinetaNdoye-yf6pp 18 дней назад +3

    Sénégal khamougnou li sa dôme loumele ni yalla nako dale

  • @yacineyoum2769
    @yacineyoum2769 18 дней назад +3

    Mane dome rék lathiye dioye ah yalla bakhna khayna niaréle dina ame❤

    • @ibrahimasarr2460
      @ibrahimasarr2460 16 дней назад

      Il faut détox ton corps simple dougoup et après inshallah tu aura ibrahim saw

  • @musamany1879
    @musamany1879 19 дней назад +5

    Yalna seuy bi barkél ci barki Rassulillah SAW ❤❤❤❤

  • @ibrahimafaye9234
    @ibrahimafaye9234 17 дней назад +5

    Yalna yalla barkel seye bi

  • @yayouSalihousamb1553
    @yayouSalihousamb1553 20 дней назад +36

    Sama dieukeur magué nama 28ans té am naniou Serigne Salihou té décembre bi beug nasi liguéy am Sokhna Diarra😂

  • @salamatasow3979
    @salamatasow3979 20 дней назад +16

    Foutez leur la paix ndakh soudone toubab dou nguen reagiré ni may len ko diam ndiabott yallah moko yorr. Mandou len ci vie diambour yi

  • @diagnemomo4771
    @diagnemomo4771 17 дней назад +2

    Mère bi néna 18ans kéne diwouko dafa xogne😂😂
    Té boy bi na xamné moromou ndayam lay teudé
    Té domou mére bi bou diougé europe dina tégal ndayam😂😂😂😂

  • @datly44
    @datly44 18 дней назад +4

    Vraiment Sénégal mo beug ay détails. Seuy bi lan mossi sène yonn. Deuk bi mo beurri ay doff .
    Yallah na Yallah barkél seuy bi si barké LAA ILLAHA ILLAL LAH MOUHAMADOU RASSOULLAH

  • @awandiaye230
    @awandiaye230 20 дней назад +25

    Libère lenfant stp. Il a droit davoir d3s enfants. Cest pas juste😢

  • @amadoumoustaphambodj5958
    @amadoumoustaphambodj5958 20 дней назад +4

    Les sénégalais aiment s'attarder sur des futilités, je pense que Chacun n'a qu'à gérer sa crise. En ce qui est marrant, nous sénégalais, on s'occupent trop de la vie privée des gens, je suppose qu'une curiosité malsaine et approfondie ne rime pas avec le comportement d'un bon croyant. Foutez la paix aux dignes gens de ce monde, restez en dehors des affaires privées des gens, à bon entendeur salut.

  • @IlarionManga
    @IlarionManga 18 дней назад +1

    L'homme peut âge ça femme 29ans plus mais une femme son mari 29ans vraiment c'est trop il y a pas amour ici que la femme nous explique la ou elle a amené le garçon pour qu'il devient son mari

  • @aminatadiop8002
    @aminatadiop8002 20 дней назад +7

    Dina yakh khaler bi rek doy na war lolll 24 ans si 53 ans

  • @nioukfall7869
    @nioukfall7869 19 дней назад +2

    C'EST VRAI PERSONNE NE VEUT VOIR SON FILS ÉPOUSER UNE VIEILLE. MAIS C'EST LEUR VIE

  • @kandjikhady6659
    @kandjikhady6659 20 дней назад +4

    😂😂😂mes li dou thèatre wala clip bounouye preparè

    • @mamematyg
      @mamematyg 19 дней назад +1

      Lolou la khalat doynawarr dall

  • @elajeelaje
    @elajeelaje 19 дней назад +1

    Mane sakh mére la beugue 40 an wala 50 an Lou niaw bakhna❤❤ dara nékousi séye léne bamou nékh

  • @MahantaDiop-jr4hv
    @MahantaDiop-jr4hv 16 дней назад

    Yalna seybi barkèl

  • @morba2868
    @morba2868 20 дней назад +4

    Quelque soit le problème mo geune ndialo

  • @diarravignob7740
    @diarravignob7740 20 дней назад +34

    elle a profité du petit

    • @quenne_dudiolof9536
      @quenne_dudiolof9536 20 дней назад +11

      Mere bi domeram la, amoul roussoukay di teuder khaller

    • @lapaix4523
      @lapaix4523 20 дней назад +6

      ​@@quenne_dudiolof9536Vraiment c'est pas joli

    • @WeuyouBaye
      @WeuyouBaye 16 дней назад

      Tadou gor yi ay khalé laniouy teudé dama khamoul loussi sén yone, té nguén mandou si seuy diambour mais on est où las merde

  • @damahmadunyang4898
    @damahmadunyang4898 16 дней назад

    Su takorn Toubab wakh dji du bareh nee. Bayi lean nyu say teh yallah takh...

  • @moussalakh1206
    @moussalakh1206 16 дней назад

    Boulene gnou amerdé way copin boula beugué gua takk ko guen seuye té yalla neu seuye bi barkel

  • @Patriotepourtoujours
    @Patriotepourtoujours 19 дней назад +1

    Yalla seuy bi barckél ❤

  • @NdeyeFatouGaye-o4w
    @NdeyeFatouGaye-o4w 19 дней назад +1

    Sama 2eme domou dieukeur la masel 😂😂😂😂

  • @konte4942
    @konte4942 17 дней назад

    Problème bi moy goor mome ba plus de 60 ans day fertile mais djigen day téla dem garage d'ici 5 ans mère bi dou attan jeune homme bi day tolou si dig ndeunam fek femme bi doug 3e âge

  • @mamediarrandiaye7591
    @mamediarrandiaye7591 20 дней назад +6

    Khalebi bou feker mongui ak khelam dinama diakhal liiii

    • @Habiba-v9k2g
      @Habiba-v9k2g 19 дней назад

      Kii kay kham ngua né Aissata Penda dafko dougal fou bone sakh ,lii dafa niaw torop

    • @madiamandir6439
      @madiamandir6439 17 дней назад

      @@Habiba-v9k2gkii mo gueune cougar yiye fate séne moromou dome yi té seuye amoufa.

  • @sofietoudiop850
    @sofietoudiop850 17 дней назад

    En tout cas bou féké takk dji akk yoyou khalé bou goor bi wakh deukk leu na procureur wo mère bi mou délo domou diambour wa salam

  • @amadoulaminesambe9385
    @amadoulaminesambe9385 19 дней назад

    Yalna yalla barkél seuy bi boudone toubab doléne si wakh bayiléne complexé

  • @anjukumari9198
    @anjukumari9198 16 дней назад

    ❤❤❤❤❤❤❤nice

  • @Zam-Zam710
    @Zam-Zam710 20 дней назад +6

    Bayiléen feen nane Li Papa dji wax 😂😂

  • @AbdoukhadreLam
    @AbdoukhadreLam 17 дней назад

    Wa mais kou nek ak li gua sentire tamit seule l,amour compte

  • @ahmadouniang1364
    @ahmadouniang1364 16 дней назад

    Gni dal sen banekh lan gueum mere bi koy lay weur😢

  • @seynabouthior2365
    @seynabouthior2365 20 дней назад +5

    Et que pensez vous de Brigitte Macron et DEmmanuel Macron leur différence d’âge 😂😂

  • @allouniang4167
    @allouniang4167 17 дней назад

    Ki di wakh oustaz la walla ? Ngaye wakh sariya te geumoko seybi yalna barkel linga wakh tegeuko fena bou dagane ci sariya kaye diekhna khana Sénégal doundouniou sariya????

  • @ThiabaNdoye-g5b
    @ThiabaNdoye-g5b 20 дней назад +1

    Dafa niak fayda boumou yakh adouna khalébi nako délo ay mbakam té yalla yalla takh

  • @AminataSow-j8q
    @AminataSow-j8q 14 дней назад

    Souma guissai mère bou melni ma takk ko .soff guène loll ish

  • @Faby-u7h
    @Faby-u7h 20 дней назад +8

    Lolou mome barina djiguene meune nz maag goor mais pas atteu you bari yi 29ans xana 5 ans 6ans mais 29

  • @HEADHUNTER22243
    @HEADHUNTER22243 20 дней назад +2

    mag yi nio dakh seye khaleyi

  • @Mizafrica
    @Mizafrica 18 дней назад

    Les gens disent sou mére bi nékone Toubab légui sakh en Europe so také mére kéne doula diokh papier préfecture day wakh ni faut mariage là

  • @bayelahatniang-gr2nt
    @bayelahatniang-gr2nt 20 дней назад +1

    Man dé douma KO déf sagn nako nak mais DINA sédde samay mbokou

  • @thiammady4782
    @thiammady4782 16 дней назад

    Mbour amna gigolos you ame 20 ans di seuy ak mérou Toubab bou ame 70 ans.

  • @Mamour-uw5rb
    @Mamour-uw5rb 19 дней назад

    Mais lolou cest pas grave. Loudoul deugggg dou yague. Laissons leur vivre leur fantasíe. Adouna amoulll solo.

  • @MansourMbaye-wb3rl
    @MansourMbaye-wb3rl 17 дней назад

    Pour kw soudone pa bou tak khalé dou ngéne thi wakhe

  • @khaliloundiaye2814
    @khaliloundiaye2814 20 дней назад +1

    Je vois que il n'y a que les femmes qui crient au scandale dans la vidéo 😂, lii Yallah moko toudeu motakh mou ameu , geumeu lène YaAllah tè yombalale gnii beugeu takeu mbir yi

  • @BinetaNdiaye-e2v
    @BinetaNdiaye-e2v 20 дней назад

    Kou bougou nite' Solène ko

  • @mariamlatifa412
    @mariamlatifa412 18 дней назад

    Woy wakh degu yala mer bi domeram la khalebi mo nara de Lou lakh te bediaw

  • @madames9182
    @madames9182 18 дней назад

    😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @maodophilo
    @maodophilo 20 дней назад +12

    Boudone toubab bouko wara diox ay keyite wala xaliss thiow dou djipp

  • @ModouSylla-pk5jd
    @ModouSylla-pk5jd 18 дней назад

    Thiow li diarou ko kon do nopi loy wakh

  • @FatoukinéSeck-m8q
    @FatoukinéSeck-m8q 16 дней назад

    Mane dé nious seye si farata yalla AK souneu mouhamed p s l mo gueune niouyes n'diallo pour am domme lolou mome yalla rek mon kham walla dissi 2 ans mou tack 2 ème femme point 👌👍💪🙏🙏🙏

  • @famasall-ej3zb
    @famasall-ej3zb 20 дней назад

    Ki dal niakeu fayda la def kouma nekhone le dema ko done suivre toujours waye legui sof nama

  • @serignembaye5459
    @serignembaye5459 17 дней назад

    Near nio beugente lou si sen yon

  • @MassambaDrame-ie8iy
    @MassambaDrame-ie8iy 19 дней назад

    Kii yayou khale bou goor bila khana

  • @SiraDiouf-yc4qp
    @SiraDiouf-yc4qp 20 дней назад +3

    Khalèbi dafa gnak djome

  • @gueye2423
    @gueye2423 19 дней назад

    ndayesane boune ame dom nk😂😅

  • @fatoukinediallo-mj3cx
    @fatoukinediallo-mj3cx 17 дней назад

    Sayonne nékouthi mandou léne

  • @badiafaye5314
    @badiafaye5314 20 дней назад +7

    Halé bi bouguoul défko kinape😅😅

  • @aminafall8576
    @aminafall8576 19 дней назад

    Bayilen diambour mou sey seyam yonou kenn nekoussi

  • @moustaphadiop2367
    @moustaphadiop2367 20 дней назад

    Dagana mome yalla baxna

  • @Galsen655
    @Galsen655 20 дней назад

    Y’a meuneu doul ki di bène serigne gnou tik tok ganam papam

  • @SeynabouDiagne-m4d
    @SeynabouDiagne-m4d 20 дней назад

    Kou domame wala rakame defone li doula nekh khale bi ware n'a ame dôme mère bi ame n'a dôme boumou yakha avenir khale bi dako ligueye ware n'a rous seutte di guisse awramd mère bi amatoule bene crédibilité niaka n'a fayda ak diom lole n'a wereme yayou khalebi

  • @SireCamara-g9r
    @SireCamara-g9r 19 дней назад

    L'amour ya pas d'âge frère

  • @Doumadialale
    @Doumadialale 19 дней назад

    L amour amoule age arreste.

  • @YayeAwaGUEYE-ci2hx
    @YayeAwaGUEYE-ci2hx 19 дней назад

    Kene beugoule sa dome bou goor bou ame lz vingtaine di takk mére. Nagnou wakhanté deugg

  • @FatmaDiakhate-h3t
    @FatmaDiakhate-h3t 20 дней назад

    Yède yeureum moko gueune khalè bi koumou done sa dom dinga diok thie mom ndakh tèyouko khalè yi di tak maguetou toubab yi par interet rel la

  • @SiraDiouf-yc4qp
    @SiraDiouf-yc4qp 20 дней назад +4

    53 rèk dou aye thiakhane😂😂😂😂😂

  • @annaseck1866
    @annaseck1866 20 дней назад +1

    Khalébi matouko kilifa

  • @OusseynouNdiaye-zz8ws
    @OusseynouNdiaye-zz8ws 15 дней назад

    Khalé dou guiss tati makk

  • @Habiba-v9k2g
    @Habiba-v9k2g 19 дней назад

    Rafète moome amou si ,khanaa niakk fayda ak niak personnalité

  • @Ramapoulo
    @Ramapoulo 20 дней назад

    La honte😢😢😢😢😢

  • @NdayeSeck-p2d
    @NdayeSeck-p2d 20 дней назад

    😂😂😂👍👍👍👍👍👍

  • @MamadouDiangDiallo-ig9my
    @MamadouDiangDiallo-ig9my 18 дней назад

    Gayi danio sokhor na niou baye diambour sey séne sey

  • @SiraDiouf-yc4qp
    @SiraDiouf-yc4qp 20 дней назад

    😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @kandjikhady6659
    @kandjikhady6659 20 дней назад +2

    Li nak nioune senegal nioko khamoule mes europe ba barinafa khamnasi aye nite you tak sèni moromou mame 🎉mes linak dafa khèw senegal lègui de toute façon dale mane damasiye mbandou ndakh amna ndape youma wara rakhasi ni ma niawate inchala khole fou mbire yi tole🎉🎉

    • @Ndeye-gi3cr
      @Ndeye-gi3cr 19 дней назад

      Khady sama diekeur depuis 2001 lànou neck bataye masala ta mako mag LAF thiat

  • @mouhamadoulaminekande8796
    @mouhamadoulaminekande8796 20 дней назад

    Séye léne séye bi boy nobanté gui na sax daganna
    Léegui lii ak ndialo lousi guéna bax sofguene trop

  • @laminendiaye2770
    @laminendiaye2770 20 дней назад +5

    elle a perdu sa credibilite

  • @Germinal5219
    @Germinal5219 20 дней назад

    Gougar bi daal karma Adji Sarr mo ko daal

  • @MoussaDiop-ji2gn
    @MoussaDiop-ji2gn 20 дней назад +3

    😂😂😂de toute façon boye bi beugouLe bopam Li mome dafa eup yala nagnou yaLa mousseuLe nitou intérêt.

  • @user-nd2yx2qg7w
    @user-nd2yx2qg7w 20 дней назад

    Ki kay dou morom domam morom seuteum la na yayam dieul taxi dieuli domam dina dée dafko liguiy

  • @khadimfaye2460
    @khadimfaye2460 19 дней назад

    ❤❤❤❤❤❤ioe amnga ndam bou reuy, ndakh Alhour-aane mola tèral❤❤❤❤❤

  • @NdeyeGueye-q2z
    @NdeyeGueye-q2z 19 дней назад

    Mere bi dou rousse sakh

  • @AbybibishDiop
    @AbybibishDiop 20 дней назад +1

    Khalé bi dé dou diouge si oumou liiiiiii Yalla dale moye Karime

  • @SiraDiouf-yc4qp
    @SiraDiouf-yc4qp 20 дней назад +1

    Penda diop doff bi

  • @AdamaNdiaye-wk1lu
    @AdamaNdiaye-wk1lu 20 дней назад

    Kane mo lire sama comentaire wa pa yiy tak khslé you ndaw sene moroumou seute nak wala dou beneu batay

    • @mouhamadoulaminekande8796
      @mouhamadoulaminekande8796 20 дней назад +1

      Gnii Nanou sofe trop niome louléne woor ni kii dou dioure
      Budoone manla wallahi souma nobone ndawsi takkeko
      Mboguéle yallah mookoye def

  • @akssowakssow7151
    @akssowakssow7151 20 дней назад

    Wayy bouléne niou yapp kii mère koba la rek

  • @alphadembadiallo6684
    @alphadembadiallo6684 20 дней назад +1

    Man tami magui wor 😂😂😂😂😂

  • @elizabethndione8558
    @elizabethndione8558 20 дней назад +1

    😂😂😂😂😂

  • @niangtra
    @niangtra 20 дней назад +1

    Bou hâlébi beugué leuf bou maguett nak😂😂😂

    • @yayodiallo1021
      @yayodiallo1021 20 дней назад +8

      Na wah dji rafet

    • @yayodiallo1021
      @yayodiallo1021 20 дней назад +8

      Mo guene ndialo Sénégal ndialo kéneu doula wah dara mais so séyé si farata gnou lasiye hass😢😢

    • @fatouthiame7000
      @fatouthiame7000 20 дней назад

      😂😂😂😂

    • @elagegueye3310
      @elagegueye3310 20 дней назад +1

      guisanekat ken warouko takk

    • @SaliouSene-p6l
      @SaliouSene-p6l 20 дней назад +1

      😂😂😂😂😂😂😂😂😂 wouyyyyyy

  • @BinetaNdiaye-e2v
    @BinetaNdiaye-e2v 20 дней назад

    Kou bougou nite' Solène ko

  • @Galsen655
    @Galsen655 20 дней назад

    Y’a meuneu doul ki di bène serigne gnou tik tok ganam papam

  • @ndiassegueye707
    @ndiassegueye707 20 дней назад

    😂😂😂😂😂😂

  • @FallouFall-bf2op
    @FallouFall-bf2op 20 дней назад

    😂😂😂😂

  • @kandjikhady6659
    @kandjikhady6659 20 дней назад

    😂😂😂😂