Mon khassida préféré ❤️❤️ j'ai des frissons quand je l'écoute à chaque fois. Serigne Touba est vraiment unique. On ressent le prophète à travers ses écrits
Yalla mangui laye niane gua fayale niou Serigne Touba ak Mame Chiekh Ibrahima yalla nalen yalla yeureume tè yook sen lèrr yalla nalen yalla kharè len Aldiana Firdawsi amine ya rabbal Alamina yalla magui laye niane gua tassgnou si barkem Amine ya rabbal Alamina
Si ce n'était pas le fils d'Adam je ne passerai une nuit sur terre ( naniou fékhé bok tii talubém you eupe njarigne amana niou dajé ak ngueremeum ) fou way yam yafa yamalé sa bop tii kou bakh ki. Away yallananu dajé ak ngueremeul Ahmadou mbacké t niou jaré tii Mame cheikh ibre 🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
Machallah fin bi je ne peux plus m'en passer tellement c'est intense! Kéneu dou Serigne Touba! Xassidas yiii neex nagnou ba romb neeeeex. Serigne Cheikhouna Diagne machaallah ca se voit que limouy def foula ak fayda lassiy andal. Mane dal miiiiratina rk!
ALHAMDOULIHAHI RABIL ALAMIN BANOU AME CHEIKHOUL KHADIM , SOUDOUL WON MOM SÉNÉGAL , TOUBABI AK AY PEKHEM DÎNA YAKH DJIKO YI , DEF SÉNÉGALAIS AY PAEINS YOU BONE; KON DIEUREFDIEUFETI CHEIKHOUL KHADIM, LI MOU BIND THI KHASSAIDES : PLUS DE 7 TONNES 500 MOU BAYI FI , AMOUL BEN SCIENTIFIQUE OU BEN ÉCRIVAINS TOUT COURT BOUKO MOUSSE BIND ; DI NIANE BAY NI-ANAL MALA YI : YA BAKH KEN DU YAW KEN DOU MOUSSE NECK YAW, KEN NGA, YA MAGNIFIQUE .LE SERVITEUR PRIVILÉGIÉ DU PROPHÈTE MOHAMED RASSOULILAH CALALA HOU ALHEHIM WA SALIM: KON ALHAMDOULILAH.
Grazie Amice-- che l inexplicable 6 giorni lavorativi e la sua famiglia e il ottimo risultato di me e di me non mi prendete in considerazione per il resto del tuo lavoro e la sua vita per il resto di me e il ottimo lavoro che c'e non ha mai avuto in giro per la vita e la governante di me non ho lavorato da un ragazzo... mi serve un lavoro per il tuo tempo di lavoro... mi sono disponibile in carcere o in giro e ho visto un lavoro che mi ha fatto un iscrizione in un lavoro che non ti ha avvisato... e poi mandare a la tua vita e il Tfr e il ottimo risultato di te gardee che c'e mi ha fatto e non so perché mi hai mandato in giro e a che ti si faccia un 6 giorni di San Jacopo ha scritto e il Tfr per la tua Jacopo Jacopo guay day... yy mi serve per te garde e ku2u3i2immmkkklpppppm per imparare la governante uguale per la bici e il ottimo lavoro... mi sono
Encore en 2024 le meilleur la meilleure prestation jamais réalisée de Moukhadimat
Bilayyy fall dina diafe degg lou nekhe ni
Xana xamoo htdkh 😂
@@boubakamara6382 gamou 2008 ak lamine Seye 😂😂
Se batt ci kaw
Mélodiquement oui et c’est extraordinaire
Qui écoute encore cette pépite du Paradis en 2023?
Je l'ai dans mes fichiers audio
A l'instant même
Doumasi doyol ❤😢
2024!!!
Moi en 2024 , c’est la meilleure vivification boun meussa prester 🙏🏾🥰❤️
Qui écoute encore 2024?❤🎉
Niong lay kharate 2025 inchallah
☝🏽☝🏽❤
Mon khassida préféré ❤️❤️ j'ai des frissons quand je l'écoute à chaque fois. Serigne Touba est vraiment unique. On ressent le prophète à travers ses écrits
Ndeysanne ❤❤❤ c'est extraordinaire Bilahi ❤
@@cheikhahmadoubambasidibe6377😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊😊
❤❤❤❤❤❤❤
Ay way barkép serigne saliou khawma sax loumay wakh yalla nanou yalla fayal bayou serigne saliou😭😭😭😭😭😭😭😭😭
Jiko yonenti bi la da kawé d😢❤
Qui regarde ce mouxadimat en 2020 doumaci doyal
2022
Awma ci sago je le regarde Tous les jour duran que je travaille
2022
05/04/2023
Ndaysane s Atou diagne yalla na yalla yokou ay lëram
Alhamdoulilah biniou sa Borom boolé si gnioniou Kou tedd Ki .Dieredieufe cheikh Akhmadou bamba khamdimrassoul
Serigne Touba est le plus noble des êtres...on t'aime pour toujours
Moi je l écoute en 2024 c'est une tuerie ❤❤❤❤❤❤
Yalla ngen goudou fane yagg fi lool té andék wére Amine ya rabbal Alamina
Barki Borom Touba liii mounou massiy doyall
Baa 2022 moy aire bimayy danelll mane😭🥺❤️❤️
Wallay nday sane
Yalla mangui laye niane gua fayale niou Serigne Touba ak Mame Chiekh Ibrahima yalla nalen yalla yeureume tè yook sen lèrr yalla nalen yalla kharè len Aldiana Firdawsi amine ya rabbal Alamina yalla magui laye niane gua tassgnou si barkem Amine ya rabbal Alamina
Alhamdoulillahi rabbil hanlamine. Wa gni koumaléne di féyal. Way naléne yalla téral,sargale,tawfékheul. Té may léne diam way. Barki cheikhoul khadim
Meunouma doyal si liii ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤🥰serigne touba la ken khamoul loumou done
Wallay ndaysane
Si ce n'était pas le fils d'Adam je ne passerai une nuit sur terre ( naniou fékhé bok tii talubém you eupe njarigne amana niou dajé ak ngueremeum ) fou way yam yafa yamalé sa bop tii kou bakh ki. Away yallananu dajé ak ngueremeul Ahmadou mbacké t niou jaré tii Mame cheikh ibre 🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
Machalla nekh na trop
Gnanal lèn ma yalla mayma dieukeurou hisbou si barkep werou koor bi
Yalla nalako yalla may
Eskeuy Serigne bi dé mannako
Waww inchalla Yalla nalako Yalla maye akasa mouride
Yàlla na la ko yàlla may
Ziar mba niane gui nangouna koubakh
Loudoul Serigne Touba safou niou
Sant naniou Yallah bou baxx biniou donei ayyy Mourides
Dieureudieufati Borom Touba ❤️
0m0
Bilahi dieureudieuf serigne touba ❤🙏
Lii dafa nexx trop barké khadimoul moustapha 😭❤️
En 2024 il reste encore le meilleur ❤🎉
Barkep Serigne Touba li mom louka dakh amoul thi adouna 😭
BARKI BOROM TOUBA WAKHAL WAYY
Allahou Akbar Sallalahou ala Mouhamadine Sallalahou Aleyhi wa Salam Alhamdoullilah rabbil Alamina MASH'ALLAH CHOUKRAN Amine ya rabbal Alamina
way yena am diom barki serigne touba yalla na serigne touba maye lene ay xewal ak terenga xassida machalla
Dieureudieuf Serigne Touba diarama Mame Chiekh Ibrahima Fall
Mame brome Touba amoule morome kénla yallanagnouko yalla fayale té tasgnousi barkém si barképe Mame fallou mbacké
Dieureuf serigne touba khassida serigne touba bi mome sama leup si adouna sante yalla bima defe mouride
Dieuredieuf s touba dieuredieuf s touba dieuredieuf s touba dieuredieuf s touba dieuredieuf s touba 😭😭😭
Allahou akbar moukhadimat bi nekhna s Cheikhouna diagne limouy way si souf tarkallah future Ablaye diop
Kii mo dakh djangeu ablaye diop
@@cheikhbassiroufall750 mbadou😁😂
@CheikhBassirou Fall 😂😂 ñoom ñaar ñépp mën nañ
Cheikhouna ndanane leuh mais keen dou diop🤣🤣
Machallah fin bi je ne peux plus m'en passer tellement c'est intense! Kéneu dou Serigne Touba! Xassidas yiii neex nagnou ba romb neeeeex. Serigne Cheikhouna Diagne machaallah ca se voit que limouy def foula ak fayda lassiy andal. Mane dal miiiiratina rk!
Di doli sante yalla bimougnou wathiél2 dieum diou tédeu gui di Khadimou Rassoul fi thi Sénégal
Thiey mouxadimate bii dou amati dh
Dieureudieuf borom barak bi si ndiarem Ahmadouna borom diamm gni fa yallahou fall
Thiey ken dou Cheikhoul Khadim lii nexna lool thi khool yalna yalla yook sougnou talibe ... Moukhadimat bii thiey
Lll
Yalla nanu fayaal Serigne Touba. Ko u tedd ki. Kenn dou moom . Serigne Touba amoul moroom kenn laffi
*Oh j'ai larmes aux yeux 😭😭❤️ sama sopé Bi Serigne Abdoulahi Diop yalnafi yague té wérr si barkép Serigne saliou mbacké 😢😭❤️🙏*
Rimou Cheikhouna Diagne yi 🤌🏾❤️
Feuleu ak thiatou Khadim diouf Yi 🥹🤧❤️
Novembre 2023 Ba Tay ba euleuk ❤️♾️
Prestation bou doywar 🙏🏾❤️
Barkéb sidy birahim khasidayi mo nékh si koume dougou sisa khol tégua am si pasepase ❤️❤️
Moukhadimat légendaire
S mountakha bassirou mbackè Yllh nafiYag andeuh ak werr❤️🥰
Qui est là en 2024 ❤❤❤doumassi doyall
Machala yalna yala wérel bate yi si barké kheikhoul khadyme
Thiey sama tourodo kéneu dou mom machallah
Machalah yalna batt yii guena werr sii barkep serigne Touba ❤❤❤
Bly lii rk moy buzz 😢❤️ ci xassida yi rk ba aljana rk nak 😢❤️👌🏾
Kenn dou Ahmadou
Mo meune fi meune faniou Dieum ❤️❤️❤️❤️👌Sant naniou yalla bim niou bolék kou tedd ki 🥰🥰
Ç est du wawe Machallah meilleurs prestations 😙😙😙😙😚😚😍😍😍😍😍😍😘😘
barkep serigne touba gni nio meune diangue...dieuredieuf serigne touba khadimou rassoul
Kou bakh gni dougnou nite
Santati serigne touba bou baxx lii nexxna lolll çi👉❤❤❤❤🎧🎧🎧🎧🎧
💓💓💓💓
Maashaallaah li Ngeen di Tawil Yéeme në Loolu Wallaahi
0c
Walahi c du haut niveau thiey bilé moukhadimat
00
Très haut niveau
Dieuredieufety serigne touba yagulèn fi té werrr machalla
Euskeyy DIEUREUJEUFÈ TEITII SERIGNE TOUBA
Dieureu dieufati serigne Touba✨💓
Bilahi khassida nékhna allahou akbar djeureudieuf borom Touba
thiey s touba amoul morom
M
Dieuredieuf borom diam gni serigne touba hadimou rasssoul
Macha Allah, xassida yi amoul béne tarixa boumoudoul douggou.
Thieuy Serigne Touba
Thiey yalla walay Ndeysane li nekhna lolll sakh Masha Allah
Srx dadj bi dotoul amatie 🥺❤️ 😭🕊
Dieureudieufaty SERIGNE_TOUBA
Machala Serigne touba dongue mome képe môme rék
Macha'allah
Qui est l en 2025❤🎉yallnañ dadjé ak ngeureumeull Seriñ bi
Macha Allah yalla na serign Touba fayy
Yallana yalla fay len barkeb borom Touba
Moukhadimat bi dalna looooool billahi ❤️❤️😭❤️
QUI LA REGARDER EN 2024 ENCORE XASSIDQYI REIK 👌
🇸🇳🇸🇳Waye ly nékhna waye🤗🤗❤❤❤thieye kou tedki 👂👂🎤🎤🎤🤲🏼
On est en 2020 dieuredieuf Cheikhoul khadim amouma thi khassida bi saguo❤️❤️❤️❤️🤲🤲
I am a fan of the Uncle with that nice smile behind Sheikhouna😍🙏🏾
Me too i am a fan of him
Mashallah
His name is Madické Dieng
❤❤❤❤
Al hamdoullilahi RABBI'l Aalaminr Dieuredieuffé Cheikh Ahmadoul Khadim
Yalla nalene diam sonale si barke s touba 👌👌👌
Dieurue dieufé. Serigne. Touba Machala cheikhouna Diagne amna solo yala na yala wéral batbi si barkép Serigne touba
Bilahiiii Khassida biii damakoo beug lol sameu xol Yalla nameu Yalla defal makoy Jang ak Serigne Touba birr Aldjanaa ak mbolem Joulit
Machall li amna solou khassiday rek ba aldiana si barkep Serigne touba
Un grand bonheur d'écouter les qacidas
Wallahi
Machalla yalna yalla wèral bate yi nèkh na trop
Yalna yalla sameu lèn Barkep Alkhourane 🙏🏾🙏🏾❤️
Amine 🙏
Amine
Yalla na leen yalla faye barkep s touba
Dieuredieuf Borom Touba
Guena beugue, Guena Gueum Borom Touba Rek
Khassida nekhna si birr khole jeureujeufai cheikh Ahmadou Bamba 👌
Yalla na lene yalla Faye .euskeuy
Amine
Mâcha Allah Dieureudieuf borom touba
Dieuleul deggoo bi rek , vraiment sont les meilleurs
Machala yalna bâti gueuneu wér barké khassida yi 🤲
18 Safar 2022 Jeureujeuf Serigne Touba🥰😭
Dieuredieufeti Serigne Touba amoul morom 💖 💖 😍 😍 😍 😍
Dieureudieuf serigne Touba ❤❤❤❤❤❤😭
Serigne Touba amoul morom❤❤❤❤💖💖
❤❤❤💖
😍💖💖💖💖💖❤❤😭
Bilahi khôl sédna dieuredieuf serigne Touba
Chaque jour il faut que meu tewlou moukhadimat bi machallah tarcalla serigne Cheichouna diagne borom batou violon bi thieuy Serigne Touba amoul Morom
Eskeuy mbacké balla yalnou yalla fayal Serigne Touba defnou ay talibe akhkhane
ALHAMDOULIHAHI RABIL ALAMIN BANOU AME CHEIKHOUL KHADIM , SOUDOUL WON MOM SÉNÉGAL , TOUBABI AK AY PEKHEM DÎNA YAKH DJIKO YI , DEF SÉNÉGALAIS AY PAEINS YOU BONE; KON DIEUREFDIEUFETI CHEIKHOUL KHADIM, LI MOU BIND THI KHASSAIDES : PLUS DE 7 TONNES 500 MOU BAYI FI , AMOUL BEN SCIENTIFIQUE OU BEN ÉCRIVAINS TOUT COURT BOUKO MOUSSE BIND ; DI NIANE BAY NI-ANAL MALA YI : YA BAKH KEN DU YAW KEN DOU MOUSSE NECK YAW, KEN NGA, YA MAGNIFIQUE .LE SERVITEUR PRIVILÉGIÉ DU PROPHÈTE MOHAMED RASSOULILAH CALALA HOU ALHEHIM WA SALIM: KON ALHAMDOULILAH.
Jaarama mouride yalla na SEEIGNE BI BÉGG CII IOE
Ok grazie ci ho fatto un altro 6 ... e non c'è
Grazie Amice-- che l inexplicable 6 giorni lavorativi e la sua famiglia e il ottimo risultato di me e di me non mi prendete in considerazione per il resto del tuo lavoro e la sua vita per il resto di me e il ottimo lavoro che c'e non ha mai avuto in giro per la vita e la governante di me non ho lavorato da un ragazzo... mi serve un lavoro per il tuo tempo di lavoro... mi sono disponibile in carcere o in giro e ho visto un lavoro che mi ha fatto un iscrizione in un lavoro che non ti ha avvisato... e poi mandare a la tua vita e il Tfr e il ottimo risultato di te gardee che c'e mi ha fatto e non so perché mi hai mandato in giro e a che ti si faccia un 6 giorni di San Jacopo ha scritto e il Tfr per la tua Jacopo Jacopo guay day... yy mi serve per te garde e ku2u3i2immmkkklpppppm per imparare la governante uguale per la bici e il ottimo lavoro... mi sono
Un
8
Barkep Cheikh Massamba yalaa na 'guene fii yagg lool tee werrr barkep Cheikh ibraa lii mo dakhh aldjaana
Lolou uepeune
Machalah sedd na trop si khol
Aka WERR mouride
This man like hear xassida he is named PA MBECTE
@@gningsokhnamaye4534 thanks for you
😢😢2024 jereujeuf serigne Touba
Segne atou yalna xiipé firdawsi😭
Yalnalenne serigne touba faye
Djajeuf Cheikh Meissa Tilala Fall Djajeuf Cheikh Amadou Bamba M'backé Djajeuf Mam Cheikh Ibrahima Fall Djajeuf Mourides
ndeysane yalna leine serigne bi teiral
Muqadimatt bi kawé na lol machallah ❤️
dieureudieufeuti serigne touta
Allauma amine amine rekkk billayi nekhna lolouuu wayyy❤❤❤❤❤🤲🏾🤲🏾🤲🏾
Kourelou TOUBA ño danxa jang ci Sénégal...🤭👉🏿❤
Dieureudiefety Serigne Touba
Dieureudieufety Serigne Touba 😍📖👌
Diaradif serigne touba rek akasa mamez cheikh ibrahima fall