Wally seck humilie Sonhibou Télécom, démasque son arnaque et le descend de force dans sa scène «yoro

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 16 янв 2025

Комментарии • 286

  • @Userfanta2024
    @Userfanta2024 Год назад +68

    Kou d’accord ne Wally bandit cerveau lalal j’aime 😂😂😂😂😂😂

  • @massarthiam6077
    @massarthiam6077 Год назад +13

    Wally a partir d'aujourd'hui je t'aime fort 😂😂😂😂 kiii daffa wara yaaarrou wallyy moyyyy millliadaire bi après Youssou Ndour nekal nittt alall dou dara fils❤😂

  • @ndiaye782
    @ndiaye782 Год назад +5

    RESPECT A WALLY .VRAIMENT CHAPEAU.

  • @adamandiaye3295
    @adamandiaye3295 Год назад +31

    Je suis d’accord avec wally 100/100

  • @ZalePrince
    @ZalePrince Год назад +18

    Wally day liguey certains pensent que day tek xel et il est très intelligent

  • @cheikhniang391
    @cheikhniang391 Год назад +1

    Bilahii ma beug Mar bayi lene ko khel nit la te kou kham adouna la dina yagg dina werr yalla nako yalla sam sohibou mom damako yeureum

  • @amarkebe3596
    @amarkebe3596 Год назад +5

    Meussouma khamni wally weuyou la😂😂😂😂😂

  • @bboyfall5741
    @bboyfall5741 Год назад +5

    Toudou bi moula toudou rek doyon na nga continuer say door
    Mais ngay yek si kaw chaine bi y'a raylou sa bop 😀😀😀
    Waly nit dafkoy diokh 10million pour moi wayko
    Yegago fofou

  • @ELIZOful
    @ELIZOful Год назад +6

    Merci Wally 😂😂😂
    Dokhane ga Ndeye saway bien bon 😂😂
    Contane na magui teudi 😂😂

  • @papediagne4153
    @papediagne4153 Год назад +13

    Wally vrai nandité la, kène dou ko rabaissé ndax alal, il a bien fait 👍

  • @ndeyekhadyfall7761
    @ndeyekhadyfall7761 Год назад +6

    Merci Wally bien fait

  • @queennenitaniash99
    @queennenitaniash99 Год назад +10

    Doul rk la site yi di deff cheuuuuuu😂😂😂😂😂liniouy bindeu ak liy am ça fait 2

  • @Elcapo2495
    @Elcapo2495 Год назад +6

    sohibou mi gathia rayon ko ya niak dioom 😂😂😂😂

    • @Ino505
      @Ino505 Год назад

      Setanal lii
      ruclips.net/video/Yg2zLx8eV9g/видео.htmlsi=0KB4ntyxNjYeiG-2

  • @falloua52
    @falloua52 Год назад +21

    Dotoko defati bo yoroul dagay yarou très bien wally leçon la souko defe mou yarrou 😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @Khadim_Ballago
    @Khadim_Ballago Год назад +14

    Nila Défone kéba Seck mou way ba tépékou tei Sonhibou mayuko Lou Matt 25000f 😂 mais dotoko défati Mar ngafi fékk😂😂😂😂❤

    • @dienaboucamara3292
      @dienaboucamara3292 Год назад

      Hum soirée Bou amone sorano bi dem ak xaliss Bou beuri 😂😂

    • @floramakenzou1546
      @floramakenzou1546 Год назад +1

      Lii c’est pas la première fois moukoy deff wally dème ande akh ay nitam yek diohuko dara wathiat wally way ko ba sone warone na hame bisam dina gneuw mouy diay nanditei wally il n’as rien fait

    • @محمدعبدالله-ص5ذ5ف
      @محمدعبدالله-ص5ذ5ف Год назад

      😂😂😂

  • @MameDiarraMbaye-q3s
    @MameDiarraMbaye-q3s Год назад +16

    Très bien waly khamal gua ko adouna dou dara ❤❤❤

  • @malickndiaye4880
    @malickndiaye4880 Год назад +9

    Saway dadone nappé rek ndakaté 😂😂😂😂😂

  • @serignefallou8927
    @serignefallou8927 Год назад +6

    Sonhibou un vrai Coatch en Marketing 😂 heureusement ba tombé wo si piège bi diokhéwoul touss amaléci son wam 😂😂

  • @Personne-xo3hb
    @Personne-xo3hb Год назад +8

    😂😂😂😂😂 wouyy mangui deh.. il l'a achevé sans le toucher ni insulter zéro vulgarité 100% de tact tey fan nako sakh 😆

  • @guilomemangasenghor5467
    @guilomemangasenghor5467 Год назад +2

    Bravo 👏👏👏👏Wally seck the king

  • @FallouKane-zf9ed
    @FallouKane-zf9ed 4 месяца назад

    Ayyy way rousse na😅😅😅 sohibou

  • @kharniang-cq2jz
    @kharniang-cq2jz Год назад +2

    Ndéké wally vrai bandila

  • @fatoujobegarjo2073
    @fatoujobegarjo2073 Год назад +7

    Very good amoulo gattt beug sonal nit yi wally fayda leu am man yow la beugggg👏👏👏👏👏👏👏👏 na dem dohko ay mbokam

  • @veroniquenatack7392
    @veroniquenatack7392 Год назад +2

    *Ay way mane dama rousss sakh😢😢mais li bakhna si Wally dalay diangual adouna ndakh fo togue di bako yorr bigua yorr tay ltx woné woko😂😂😂*

  • @selembathiam9143
    @selembathiam9143 Год назад +1

    Merci Waly💯

  • @maguettefall5019
    @maguettefall5019 Год назад +1

    Je vous j'adore wally nilq❤❤❤❤❤❤😂😂😂😂❤❤❤❤

  • @aicha7979
    @aicha7979 Год назад +2

    J’ai horreur de ce genre d’hommes xolko kanam gui pourom il est quelqu’un ni ..wally c’est bien 👏🏽de lui avoir donné ce couq

  • @loaboubacar3595
    @loaboubacar3595 Год назад +1

    Man dh pour man sax site bay Tay fen ndeke waly nila def souhaybou😮😮😮😮

  • @torodo.ferrari
    @torodo.ferrari Год назад +6

    Torokhalouko mais dafko diangual adouna rek
    Sonhibou tourr bou seilleu leu yoor mais il est imbu de sa personne tekssi meunn na waneiwouu
    Fallait que niit defko lii mou yaam

  • @babacarsadio9738
    @babacarsadio9738 Год назад +18

    Très bien Wally seck do sama chanteur mais ligua def contane nasi torop

  • @falloukarimmbow4981
    @falloukarimmbow4981 Год назад +1

    Thiêy wally séck 🇸🇳👑✌️💯maleuh beugue trop bly nitkou bakh leuh ❤❤🤍🤍💸💰📀💯

  • @MarémeSarr-j1i
    @MarémeSarr-j1i Год назад +4

    😢😢😢😢 dama rouss sax li kéne douko déff😢

  • @Baba-lo3qt
    @Baba-lo3qt Год назад

    Dossama waykate mai li kontanassi

  • @elfallfall3250
    @elfallfall3250 Год назад +2

    Senegal yakam ti nagnou kounou toroxal banou wané ko siweul ko amléne soutoura ki day dor war sathoul fénoul kounék ak sa façon de fair wax moko djig wa salam

  • @Mouss400
    @Mouss400 Год назад +10

    Wouyy sohibou borom maléne eupeu khaliss, tousss ...😁😁🤣🤣

  • @mitaadeso
    @mitaadeso Год назад

    Waly merci😂😂😂😂😂😂😂💖💖💖💖

  • @tallablaye6983
    @tallablaye6983 Год назад +2

    Ak tempo bi sonhibou dioxlene kou nekk 100😂😂😂😂

  • @asowmotodk2212
    @asowmotodk2212 Год назад +1

    Merci wally démasqué leen merci

  • @sergeaurierndiaye2471
    @sergeaurierndiaye2471 Год назад +1

    Je suis faramareen et fière de l'être Wally ❤❤❤❤❤ borome bakh ga yaye deff té wanéwouwo

  • @layendeyefatou5815
    @layendeyefatou5815 Год назад

    Machalla amina pote❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @ndiagageuye6994
    @ndiagageuye6994 Год назад +4

    Merci beaucoup wally😂😂😂😂

  • @assgueye9996
    @assgueye9996 Год назад +2

    waly limou wakh dafa beuri dh😅😅 kou nékk 100😢 sohiibou yoroull😂😂

  • @AminaNdone
    @AminaNdone Год назад +3

    Machallah ❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @FalouSey-f5m
    @FalouSey-f5m Год назад

    Bilay man ma fan sama dôme dji aka nek nandite Ken douka tek khel

  • @khadydiouf8378
    @khadydiouf8378 Год назад +76

    Mais liniou wakhh deug leu waly dafkoy wagni diko wane aduna pour que mou khamni meune gh am alal sans gh tok founé diko wakhh wadji mo beuri wakhh merci encore pasque le gars dafeu neik si internet moudjé nieuw geneu beuri wakh donc dina comprends delein khol insbi site internet yup daniouy nieuw si mom mouy wout layÿ nioune dofouniou khamna niiu nimou demé wa salam🙏🏾🤣😂

    • @KhidmalBarkham
      @KhidmalBarkham Год назад +4

      Sokhnasssi li ngua wax téguoko féneu ça c'est de l'humiliation en plus publiquement Wally est trop kon de plus en plus je m'en rend compte dieul hay fétieukate nite sans pitié il a esaiyé de détruire sidy diop Mais souhaibou limou wax Môm la conserné diaroul moukay humilié publiquement mieux vaut ne pas le recevoir que de l'humilié publiquement Mais Malheureusement dagno gnakeu Barké xaliss bii Bougnoussi défone sociale diapalé Néwdi dolé yiii avec la précarité de notre pays dina Bax 🇸🇳Mais je comprend gnakeu Barké Rk Moléne diapeu🤷🏿‍♂️

    • @papimichelba2466
      @papimichelba2466 Год назад +6

      @@KhidmalBarkham pourquoi pas bien sûr wally a bien fait

    • @souleymanesane5915
      @souleymanesane5915 Год назад

      😢

    • @issambaye4620
      @issambaye4620 Год назад +2

      Teguo fenn linga wax nitt Ken douko torokhal

    • @superfoottv2277
      @superfoottv2277 Год назад

      Vraiment tegougo fen lim ko defni rafetoul si koula beug teral tu n'as pas à l'imposer loumlay may wala koum wara may nak akh ki au moins khalissam il l'a bien mérité il l'a travaillé durement nekoul di Wayane ak sambay mbayane

  • @fatyndiaye8221
    @fatyndiaye8221 Год назад +1

    No waly vrai bandi leu😂😂😂😂

  • @sadiocamara7957
    @sadiocamara7957 Год назад

    Nanou diamoou yalla mo gueune ,

  • @richytv3523
    @richytv3523 Год назад +11

    😂souhibou wally mola geuna mouss gay tek khel

  • @moifaye5666
    @moifaye5666 Год назад +3

    Mais est ce que sohibou warna dem soirée di yoré des milliards tamite mais waly nekal nit adouna dou ni dé sonhibou il m'énerve mais waly nitéwoo dé
    Methop mii tu la donner toute cette somme meyniou

  • @cheikhabdoulahifall5422
    @cheikhabdoulahifall5422 Год назад +3

    Mon pauvre Sénégal ils sont tellement bête ces gars, pendant ce temps j’en suis sûr que leur famille on besoin de l’argent qu’il donne à Waly, réveiller vous avant qu’il soit trop tard

  • @abdouthiam4968
    @abdouthiam4968 Год назад +2

    Dil bi tothiena dofoul dheeeeee 😂😂😂

  • @cheikhndiaye8801
    @cheikhndiaye8801 Год назад +3

    Wally seul ❤

  • @kabousarr5430
    @kabousarr5430 Год назад

    Wally bandit la 😂😊

  • @falloudiop2297
    @falloudiop2297 Год назад

    li dma ji 😂😂😂doyall

  • @bayemassebeye6581
    @bayemassebeye6581 Год назад +3

    Wally dako wann nii khaliss takhoul malay may 😂

  • @sonnianiang84
    @sonnianiang84 Год назад +2

    Mais dou ni lako wara deifei waly yalla soutoura la beug

  • @eugene-v4f
    @eugene-v4f Год назад +9

    Ooohh quelle humiliation du siècle 😢😢nonn malgré tout lii mom gnaawna rafétoul.a cette situation bou yorone milliard pourtant dinako diokh wally

    • @djieseck6309
      @djieseck6309 Год назад +2

      Kone nga niteh,Dale,teye,simple aduna d'où alale.wally daye waye sakh kimouye faye salaire

    • @Ino505
      @Ino505 Год назад

      @@djieseck6309setanal lii si souff entre Waly et Souhaibou
      ruclips.net/video/Yg2zLx8eV9g/видео.htmlsi=0KB4ntyxNjYeiG-2

  • @mamecoumbacisse2148
    @mamecoumbacisse2148 Год назад +3

    Waly nénaka « kou meunoul bawo lou yakhou yawa » 😅😅😅😅😂😂
    Ma contane thi Waly

  • @DrammehYaya
    @DrammehYaya Год назад +5

    Site yi kaye defounou dara li lère na dollèn khol😮😅

  • @maodophilo
    @maodophilo Год назад +39

    Waly Seck yaw nitt ligueye alam am loumelathi may nga xépko begueko forcé mou mayé loumou yoroul nga ték ko fane? Yaw dangay wayane lounela may dieuleul? Boul forcé kilay may...
    Meme bou dé boys bi day ték xél, mais fi Sénégal la gnépay ték xél...
    Djaroulwone ngakoy wér thi kaw scene bi. Yaw la yalla déf thi japalé Sénégal yi nga tol finga tol tay. Ba ay nitt di business thi sa barké waroko bagn tant que ca ne nuit pas ta réputation. So amé loy reglé wala koy fréné nga defkoko ouvertement en privé mais pas diko torokhol.
    Meme boula wadji togné lingako def wouteul say bope none la.
    Ndax kép kouy mbokou wadji mba xaritam dina yeuk bopam thi torokhol bi. Kép kou begueu soutoureu sax day mélni mome ngako déf.
    Yaw nak nitt gni beguenannela ba dounou la wax degu té koulako begueu wax gnou dall thi kawam
    Wayé boul faténi nitt késsénga
    Té baye fall nga ,té baye fall day xam bathia.
    Yalna gnép am jam ak soutoureu

    • @serignefallou8927
      @serignefallou8927 Год назад +1

      Merci beaucoup mon frère au moins tu as compris goordjigué you tékki woul dara yi ladoul Dem séni ndadié bay am louma fay diokhé

    • @Ayou157
      @Ayou157 Год назад

      @@serignefallou8927yén doule waye nopilén

    • @Ayou157
      @Ayou157 Год назад

      @@serignefallou8927yén doule waye nopilén

    • @Sucredija
      @Sucredija Год назад

      Bien dit je valide

    • @mamefatydiop6335
      @mamefatydiop6335 Год назад +3

      Surtout lolou nitt kéne dou KO trokhal man sax dama rousse wallahi wallay man yaw rk la beugue mai li rk mane na takh ma bagne la beugouma kouy trokhal nitt wallahi 😢😢

  • @rimayaba7196
    @rimayaba7196 Год назад

    Mais kharitou sohibou bi dina dioy sou gnibé limou diokh waly agoul si khol bi dh😂😂😂😁🤭

  • @touba7480
    @touba7480 Год назад

    Wally merci nila rk 😂😂😂😂😂

  • @papi4900
    @papi4900 Год назад +9

    Dako yoga def rek yek indale djayu pour gnu gisko te duko djokhe lolou la wdji kham

  • @modoundiaye9689
    @modoundiaye9689 Год назад +1

    😂 wally seck rayy nga sama wadji nak 😂

  • @talibediouf278
    @talibediouf278 Год назад

    😂 Sonhibou démal so amé nga nieuwat yaw nékété yakh Man na yam yoro lou soukeur barada

  • @khoudialaye8795
    @khoudialaye8795 Год назад +1

    Ana humiliation fii maylen niou djam 😂😂baxna thi mom

  • @IbrahimakhalilGueye-y9z
    @IbrahimakhalilGueye-y9z Год назад +3

    Merci beaucoupwally 😂😂😂😂😂😂

  • @Daveturbo9546
    @Daveturbo9546 Год назад +3

    Yalla na séytané khèp doli 😂

  • @TanorNiang-q8b
    @TanorNiang-q8b Год назад

    Merci beaucoup wally

  • @abdoulayediop688
    @abdoulayediop688 Год назад +4

    Wally dawoul thiowww koi😂😂😂

    • @veroniquenatack7392
      @veroniquenatack7392 Год назад +1

      *Dawoul thiow moss😂😂😂😂Wouyy mane sakh dama rouss😢*

  • @maguettembengue2509
    @maguettembengue2509 Год назад +4

    Salam à tous 🙏yen gni wax humiliation je pense que ni vous n'avez rien compris 😏 Wally defoul loudoul tek ko placam et k ki wanéwou moko taxa diok

  • @sougou7533
    @sougou7533 Год назад +1

    Très bonne leçons pour lui il na rien ba paré diniou amerdé waly tu bien fait

  • @mariediop5264
    @mariediop5264 Год назад +8

    Wally no ya bakh ta nitter

  • @LemouFall-u1q
    @LemouFall-u1q Год назад +2

    Couleur lampe yi tamite loumouye nirol Wally dal Moy lolou

    • @maguettembengue2509
      @maguettembengue2509 Год назад

      Couleur lampe yi esk d'où wa vogue nioko wara xolat Wally nieuw teug rek laci am

  • @linkstardidingkeba2922
    @linkstardidingkeba2922 Год назад +3

    Ayway Sénégalais bo torokhalé moram mi rek mou contane kholal commentaire yi rek

    • @OusmaneKa-c4f
      @OusmaneKa-c4f Год назад

      Fii deukkou dmrm la Légui
      Motakh sarap ndm Senegal douffa dem

    • @thiabandoye7173
      @thiabandoye7173 Год назад

      @@OusmaneKa-c4ftu na rien compris

    • @Seck221
      @Seck221 Год назад +1

      LOU LEIR NGA WAKH AKA NIO BONE, YAW KHAMO SENEGALAIS

    • @khadybadiane1971
      @khadybadiane1971 Год назад

      Bilayy wakh nga deugue Mane dama rousse sakh wally lil warouko deff😢

  • @mariamacisse5972
    @mariamacisse5972 Год назад +3

    Sohibou dafay andi khaliss bou bari tè douko battrè li moye lane 😂😂😂😂

  • @leuzdiop2036
    @leuzdiop2036 Год назад +3

    Doul rek la site yi meun

  • @sylladiouf5901
    @sylladiouf5901 Год назад

    Merci waly😂😂😂

  • @samproduction380
    @samproduction380 Год назад +2

    Bienfait démasqué tous les doorkatt

  • @onlygood1114
    @onlygood1114 Год назад +4

    Legui sonhibou deim si Sidi diop😂😂😂😂😂

  • @abdouazizseye1439
    @abdouazizseye1439 Год назад +1

    Limoy yoro dafa dof Wally wan nala adouna

  • @ibrahimakhaliltabara
    @ibrahimakhaliltabara Год назад

    Walid dou dara li bakhoule 😢😢😢

  • @Ahmadandiaye456
    @Ahmadandiaye456 Год назад

    Lii nitt douko wakh soula diokhne ay khalissou 🇬🇲 sakh ga nopii Waly dou nitt mome sii loume nèck est ce que yalla garame nako

  • @iambbanks1777
    @iambbanks1777 Год назад

    WA sonhaibou migui gni te xew mi diexagoul

  • @MbayeSylla-f2k
    @MbayeSylla-f2k Год назад

    Wally wone nakoni mousso😅😅😂

  • @sidatyfall3317
    @sidatyfall3317 Год назад +2

    Machallah mar Yacine ❤❤❤❤❤

  • @NdeyemarieFaye-n1w
    @NdeyemarieFaye-n1w Год назад +1

    Hi li boudone mane la dotouma khamati lou concert bi di saf lay kharite nak li War nala yéh soyez simple nguéne nopal sén bopp😮

  • @rothioka3168
    @rothioka3168 Год назад +4

    Dagua done diay mousse rek wally guafi fèk daf la ndande bien fait pour toi

    • @sophieba
      @sophieba Год назад

      Dieulînako bou yague

  • @ibrahimasakho1554
    @ibrahimasakho1554 Год назад +1

    kou rouss lale jamais 😂

  • @AmadouMoctarSagne
    @AmadouMoctarSagne Год назад +1

    Machallah Waly beug si yow ❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @limadiamba9190
    @limadiamba9190 Год назад

    Wally réglé le nit kene douko torokhal

  • @sokhnaoumoudiop6888
    @sokhnaoumoudiop6888 Год назад +2

    Khol len couleur lumière bi thiey yalla Sénégal

  • @Momondione87
    @Momondione87 Год назад

    Wally tey nak andeu na ak yaw 😂😂😂

  • @mamidiop4296
    @mamidiop4296 Год назад

    Niafff Wally yaw ya bakh si kii Yoro tous ba paré dinou Amédée seul les barils vident font trop de bruit.

  • @maodoka5262
    @maodoka5262 Год назад +2

    Waly gueun nala beug ❤❤❤

  • @coumbadiedhiou3239
    @coumbadiedhiou3239 Год назад +1

    Day san as gor guen douko torokhal,kouthi nek nako khol thisa bop rek,day melni daniou la soti dokh bou sed😴il la vraiment rabaissé

  • @DiatouSene-v4e
    @DiatouSene-v4e Год назад

    Personnellement d’accord rouma nite kén douko toutal

  • @itohanogbidi6941
    @itohanogbidi6941 Год назад +2

    Kholén bou bakh wally loukko sa way diokh si poss bi lako dougual apré mou dello koko yewoulén

    • @Ino505
      @Ino505 Год назад

      Sisi noonou lay démé d dou pour battré d 😂
      Dafkay deloo waat

  • @ouzdaking382
    @ouzdaking382 Год назад +1

    Niaw bien fait merci wally 😂😂😂😂

  • @CoumbaNdiaye-gp7vf
    @CoumbaNdiaye-gp7vf Год назад

    ::sonhibou dore kate la wally daka dora nande daye dore artiste yi pour publicité ,woné aye millions mayé touti gua waye ba sonne🤣🤣🤣