Cette émission mérite un audimat plus large. Ce trio a une façon exquise de présenter l'actualité et surtout de tourner en derison les chiens politiques
@@abdoukhadrediallo931 yen soubeu nguwn di comprendre Assane mom limouy def lolou laniouy wowé satire. Setlou len toujours limouy wakh le contraire leu beugu nguen diapp. Wayé dafa ladj nga am ben takhawaay bi pour comprendre
L'émission est bonne comme çà il n'y a rien à revoir on vous aime tous les trois
😂😂😂😂 Non ki def best of bi yalna goudou fan non Assane dou nitou dara 😂😂😂😂
Amine inchalah 😂😂
AK ASSANE MESSERE ZERO STRESS, MACHAALLAH
Moy deugg nak
Assane billahi wakh nga deugg ❤❤❤❤❤❤😂😂😂
Cette émission mérite un audimat plus large. Ce trio a une façon exquise de présenter l'actualité et surtout de tourner en derison les chiens politiques
Baye assane anti stress.machallah, j'aime beaucoup ce trio 😂
Le rire de sa ndiogou 😂😂😂j n peut pas supporter ca😂😂😂
Meilleur chroniqueur ❤
Mane assane moy dindi sama stresse walahi Ken dou môme bilahi assane dou nit
Le trio la va tuer quelqu'un bil😂😅❤
Sacré Baye Assane dinagnou rèye 😂😂😂😂❤❤❤❤❤
Long life and best of health for Assane, this man is out of this world ❤
He is in another world😂😂
Im telling you brother 😂😂😂@Rain71562
Je suis fière de assane le meilleur
Dég dég assane messeré saï saî là un vrai comédien
C la façon de rire de sa ndiogou qui me fait rire 😂😂😂
Nena madiambal dafa nioul kouk mome kessé mofi nioull 😅
Assane mo geuna nekh senegal 😂😂😂😂😂❤❤❤❤
😂😂😂😂
Assane Messéré, l'homme le plus informé du Sénégal.
Khamul dra day mbeuk Rek😂😂😂😂
@@fallousall2717 moytoul deh Assane diambaar leu deh! MachALLAH!
Cheikh Bara Ndiaye je serais d'accord
😂😂😂😂😂😂😂😂
@@abdoukhadrediallo931 yen soubeu nguwn di comprendre Assane mom limouy def lolou laniouy wowé satire. Setlou len toujours limouy wakh le contraire leu beugu nguen diapp. Wayé dafa ladj nga am ben takhawaay bi pour comprendre
Le meilleur chroniqueur et meilleurs comédiens ❤❤❤❤
La meilleure émission du Sénégal.
Bougnou setane Ousmane : partie bîi momay yeungueul. Sacré Assane. Allahou Akbar !😅😅😅😅😅😅
Non assane yallah sa diam yague 😂😂😂 bilahi do dem
Eskay baye assane dal amoul 😂😂😂😂
MEILLEUR CHRONIQUEUR
No assane ❤ yafi moun yalnala yalla defal diam ak niepue
bilay asane seréwoul 😂😂
Plateau destressant😅😅😅 nice👍🏼
Le retour du karma, Saa Ndiogou nous a fait rire toute une vie maintenant Assane va le tuer
Assane day raye nit😂😂
😂Bilayi
Non Assane amna talent 😂😂😂
Assane dou nitt. Fimouné kouko laadione le fourneau laniouy wakh wala la fourneau, atane nala tontou: ça dépend si kikoy oupp.
Sohibou est directeur de la meilleure Télé du monde 😅😂💪🏿✊🏿🇸🇳
Non Assane est le meilleur big up yow god bless
Baye Assane rek keen dou moom 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣😜✌🏾❤️
Non ils sont très fort ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
😂😂😂billahi assane nooo 😅😅
Li dafa am solo, nakh rétane lamouy nékh nékh yüp moï réé ju dügu 😂😂 assane légü légü mu rérrü ,wayé dafa dügu😂 diokhal élasse
😂😂Diokhal elas
@@Rain71562 😂😂😂no lu worr moï assane dafa bari thiakhane 😂😂😂diokhal rain@tv
Assane dou nite trop intéressant 😁😁😁😁😁❤️❤️❤️👍🏾👍🏾
Srap li rèk assane dou nitt 😂😂😂😂
Saran li kay😅😅😅
Sarab...
😂😂😂😂😂😂😂😂
Majambal Da fenaa fenaa FEN Be Niol Kukk KUKK 🤭😜😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣😜✌🏾❤️
Tu nous fais rigoler 😂😂😂sérieusement personne ne peut stressé au Sénégal ❤😂
No Assana Mésére amou 🤣😂😅🤣😄😄😄😁😁😁😁😁😁😂🤣😁😂🤦🏿😂
Assane le meilleur chroniqueur 💪 ❤❤❤❤❤❤❤❤❤😂😂😂😂😂
Wa Assane niguén cal bayi😂😂😂😂😂😂
Nouni deff😂😂
❤❤❤❤macha allah asane
MashALLAH MashALLAH MashALLAH Baraka Allahou fik Baraka Allahou fik Baraka Allahou fik 🤲🤲🤲👍 Alhamdoulilah Alhamdoulilah Alhamdoulilah 😂😂😂
Assane hamoul dra nak 😂😂day lambatou rkk
Bilahi assane dou niitt 😂😂😂😂😂
Wakh ka DEUG assane
Macha allah assane wakh ngua deug gnome Ay téroristes lanou 😂😂😂😂😂😂😂
Assane dou nitt❤❤❤
Nga diiiiwe sa Maame momassi réeye mane😂😂😂😂😂😂😂😂
😂😂😂
Ay Wolof la wakh
Sa yélou mame😂😂😂
Assane yaa fi meumn 😂😂😂
😂😂😂😂😂damare ba sonnn Assane dou nitt😂
Baye Assane REK MDR 🤣😝😜
Assan always love ❤️ 😍 💖 and respect God bless you 🙏 😂😂😂
Baye assane parfois rabi day gneuw😂 parfois day yeungou dh...vrai dof leu😂😂😂
No assane dou nit😂😂😂😂😂😂
ASSANE MBA YAGI DIW SA YELLI MAME
🤣🤣🤣 no lii kou degoul olof rek la yeureum
Billahi 😂😂😂 kay
Diambal gnoul kouk ndakh fen😊
Ndeysan Assane ❤❤
Anti stresss
😂nnn bilahi ki dou nitou dra
😂😂😂😂 équipe bi dîna ma raay
Assane sa tailleur bi damakoy plainte😂😂❤❤❤❤❤
Sonko /madiabal 😂😂😂 non assane est fort
❤😂😂 artiste DEUG day naturel
Terrible terrible Messere ASSANE !!!! Oh ! Hoo ouwooooyyi i !!!Assasane!!! assane !!!
Réna ba sonnn rk😂😂😂
Mme Sama tourrou pape bimou yor rek moma nakhari 😂😂😂
Ani papa Assane Ndoye 😂😂😂
Assane DINA FI RAYE SA NDIOGOU😂😂😂😂
Tailleur wa palais de justice nioko niawal😂
Aladji beuggoulle Leundeum Nayy lair😅😅
😂😂
Baye Assane le meilleur diokhale Elhaj😂😂😂😂
😂😂😂😂antouwan yalana gadou sougnou ak
Noooon fin bi douma doyale😂😂
, 😂😂
Wouy Assam AK madiabal 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Damay sumi yérébi 😂😂😂😂
😂😂😂😂
Noo Kii dinaaa maa rayy 😂😂😂 !!! Waaa man Kii nitt laa walla
Meilleur chroniqueur assane massere
Woouy Baye Assane M… 😂🤣😂🤣👉👂👂😂🤣😂🤝🤝✊✊💥💥👉🇸🇳
Abdou.faye.patriyot.yenafine.malelene.bug❤❤❤
😂😂😂😂😂😂😂😂no assene dou nit
😂😂😂😂😂😂😂 wayyyyy Assane
Billahi j'aime bien se Assane
Noooooooon Baye Assane dou niiit da may réeh ba xa ma biir dii metiii😂😂😂😂
Assaane lo sol ni😂😂😂
, 😂😂😂😂
Machalla amna solo 😂😂😂😂😂
Sa Assane dinala raye 😂😂😂😂
Assne MOYE DÈFÈANT 😂😂😂😂😂😂😂😂
Assane daye raye nit 😂😢
❤❤❤❤l émission des émissions ❤❤❤❤❤
Assane eres el mejor
Non assane dou nit 😂😂😂😂😂😂
Tour riss ak resinta😂😂😂😂
Assane mague mou rewla😂😂😂
Assane dou nit ❤❤❤
No stress avec Assane
Je suis fière de assane
Non Assane dou nitt 😂😂😂
5:44 😅😂😃😄😁😄😂😁limom raynama 😂😅😂😄