Un jour jétais parti au marché pour chercher des cassettes d'artistes;arrivé au marché le gar me proposait cassette de mbaye nder,fallou Dieng, ndongo lo,coumba gawlo la liste est longue .j'avais le prix d'une seule cassette.il m dit de choisir jai choisis ndongo lo.le gar me dit pourquoi lui.je lui ai répondu que tot ou tard musique mbalakh il sera le roi.un an aprés il est décédé et sa mort m'a bcp marqué.un grand chanteur à la voix d'or s'en est allé.
Mane ndongo lo suma dégué gnouye wah thie mom rekk sama hole daye toye j'ai perdu ma mére mon pére mais décé ndongo j'étais jeune mais ça ma bcps touché yallanako yalla yeureume té haréko aldiana firdawsi 🙏🏾
Ndongo Lô nous hante tous Ndeyssane ! Perso je ne pourrai jamais l’oublier ( Ma main sur le Coran ) Qu’Allah prolonge sa grâce et miséricorde sur toi . 🙏🏽 Ndiamé iow kou bakh nga Ndeyssane
niambé gueye merci beaucoup si kadou yi rafetna souniou wadji yalla na kippé aldiana firdaws si barké seydina mouhamed rasoullillah quand on m annoncé son décès je l écouté la première fois que l ai entendu chanter avec papa Ndiaye gueweul j ai crié de joie sa voie ma éblouie repose en paix
Ndonguo Lo je suis sûr que tu es au Paradis. Et que la où tu es tu pris pour tout le monde et pour le Sénégal Tu seras à jamais dans nos cœurs. De la part d Une sœur Chrétienne hyper fière de Toi ❤❤❤
Mane damay wakhe nane beugeu bima beugeu ndongo lo yallah bouma si am bakkar damako beugeu trop barke borom darou Noreyni yalna yallah yésal yeurmandé si mome daf may diaguel lou bari si adina 😭😭😭😭
Ndogo lo a chanté cet homme une très bonne chanson.....adji rokhéya guéy sa yaay yayou ndiamé sama sheikh bi momaro guéye ndiooro momaro giorou .........
thièy ndongo yalla nan khippi aldiana bilay boudonn mogui fi ba tay gnou kham ni musique dou khalèy dafko mane di ko tekk si temps mais diap micro legui di garouwalè rek lolou temps ndongo amoul wonn ishhh
Douma tayi thi dila beug ndongo lo yallanala yalla khare aledianna Di sa noflaye massoumala guiss waye dama la beug te yalla takhe te am n'a lo ligueyale sa borome ba keneu doula fate
Musique moom lougnou wara tek le. Daganoul. Point. Djayanté bi doyne. Nagnou ragal Yalla té bayyi khél Bamméél. Gnoun gneup dinagnou dem. Nagnou def lougnou fay djeurign.
Ndiambé dinala setsi inchalah guamay netalli diar diar Ndongo lo. Pck douma doyal si mom. Wallahi damako beug bamou diekh
Bilahi mm man douma doyal si mome
Bilahi Aka mako beug Ndongo lo bima nèkè khalè bou simb dane am bou nieuwè di weuy nieupay daw Ndeysane qu'il repose en paix 🙏😭
Yaye gor pir
Le seule musicien à qui je possède son CD je l'aime que la terre lui soit légère..
😊😊
Son cd du décès ❤❤❤❤
Ndeysane jai vue ndongo lo une fois a guediawaye sa fait presk 20ans mais toujours cet image me reviens yalla gua khipé aldiana
Amine 😭😭😭
Amine
Amine
Y6yy6y6yy6
Nitt ki loumou ame moko liguéy dieuredieuf Ndongo lo royouway gua..Serge..🇸🇳❤🇮🇹🙏🏾🤲🏾🙏🏾
Un jour jétais parti au marché pour chercher des cassettes d'artistes;arrivé au marché le gar me proposait cassette de mbaye nder,fallou Dieng, ndongo lo,coumba gawlo la liste est longue .j'avais le prix d'une seule cassette.il m dit de choisir jai choisis ndongo lo.le gar me dit pourquoi lui.je lui ai répondu que tot ou tard musique mbalakh il sera le roi.un an aprés il est décédé et sa mort m'a bcp marqué.un grand chanteur à la voix d'or s'en est allé.
Mane ndongo lo suma dégué gnouye wah thie mom rekk sama hole daye toye j'ai perdu ma mére mon pére mais décé ndongo j'étais jeune mais ça ma bcps touché yallanako yalla yeureume té haréko aldiana firdawsi 🙏🏾
Merci
Amine
Ndongo Lô nous hante tous Ndeyssane ! Perso je ne pourrai jamais l’oublier ( Ma main sur le Coran )
Qu’Allah prolonge sa grâce et miséricorde sur toi . 🙏🏽
Ndiamé iow kou bakh nga Ndeyssane
Yalnako yalla xaré aldianay firdawsi si barkep serigne Touba
Ndey saan yalla nako yalla yeraum barke serigne touba
Que la terre sois léger ndongo lo toujours dans les coeur yalla nako yalla yereum si barki seydina mouhamed PSL
Amine
niambé gueye merci beaucoup si kadou yi rafetna souniou wadji yalla na kippé aldiana firdaws si barké seydina mouhamed rasoullillah quand on m annoncé son décès je l écouté la première fois que l ai entendu chanter avec papa Ndiaye gueweul j ai crié de joie sa voie ma éblouie repose en paix
Un chanteur exemplaire.
Généreux, un vrai talibé.
J'écoute ses chansons jusqu'à présent
Yalna yalla yéreum to kharéko aldiana firdawsi barkep s touba machahalla
Ndeyssane q firdawssi sw sont dernière demeure amine yarabi..Serge..🇸🇳❤🇮🇹🤲🏾🙏🏾🤲🏾✊🏾
Nooooon🤦🏼 ndongo lô yalla nakou yalla yereum. Gisna ay dèèh you bary mais bou ndongo lô😥😥😥😥😥😭😭😭
Walahi doundou si ngor rék mo dak lounè..khol bou rafète mo Am sollo❤
Machalah ndonguo lo paix à son âme amen.
Grand ndiambe nit kou bakhla billay mes respects👍❣
J'ai aimé Mame falilu grâce à ndongo lô && thiey sama wadji yalnako yalla kharé aldiana. Rip😭
Yallnako yalla yeureumm khàréko alldjana ci barké seydina moukhaméd psl
Ndayessane ndongo lo yalla nako yalla yeureum kharéko ardjiana firdawsi
😭😭😭😭😭😭😭
Ndonguo Lo je suis sûr que tu es au Paradis. Et que la où tu es tu pris pour tout le monde et pour le Sénégal Tu seras à jamais dans nos cœurs. De la part d Une sœur Chrétienne hyper fière de Toi ❤❤❤
Wadji diaf dji mou reuye wallahi
Mane damay wakhe nane beugeu bima beugeu ndongo lo yallah bouma si am bakkar damako beugeu trop barke borom darou Noreyni yalna yallah yésal yeurmandé si mome daf may diaguel lou bari si adina 😭😭😭😭
@@keurbayefall4521 walaye ndeyesane allahouma amine ya rabí 🙏🙏
@@keurbayefall4521 massa a toi, et du courage. Beug nite ndakh ay qualités dou dara, daflay yok mais doula wagni
@@ndellafaye1083 ndeysane ni rek migui may doli billahi
Mn grand frere Ndiambe ziar que dieu te protège bcp ci barkeb cheikhoul khadim 🙏🙏🙏
Yalnala yalla fay sa khol🙏🙏🙏😭😭😭😭😭ndogo tu sera tjr gravé dans mon coeur ta mort ma vraiment marqué yalnako yalla yeureum teh khareko aljana 🙏🙏🙏🙏🙏
Ndeysane j'ai vu ndonga lo a dagama 1foi mais jene oublie jamais yalla nako yalla kharé aldiana
Ndogo lo a chanté cet homme une très bonne chanson.....adji rokhéya guéy sa yaay yayou ndiamé sama sheikh bi momaro guéye ndiooro momaro giorou .........
Machalah Yallana Yalla Yereum te xareko janatulll firdawsiii aminee ndiamé kouddall fannnn
BAYE DÉMBA DOU Ma Tayi Thi Dila Fattêli Wakhi Ndongo Lo Néna Wonn Bou Taÿ Nékh Banga Fatté Demb
Bilay wakhnga DEUG baye demba fatalikoul ndongo
thièy ndongo yalla nan khippi aldiana bilay boudonn mogui fi ba tay gnou kham ni musique dou khalèy dafko mane di ko tekk si temps mais diap micro legui di garouwalè rek lolou temps ndongo amoul wonn ishhh
Mashala papa Ndiambé
Repose en paix Ndongo Lo 🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Yalla nalla seydina mouhamed rerou sa dianatoul firdawssi
Kou ame kolere ndeysane yallanako yalla yeureme tee hareko aldiana doumako massa fatter ndeysane
Machalla ndongo Lo yalla nako yalla yeuram
Diadieuf ndongo yalla nako serigne fallou térou
Sériñ Fallou Yalla nako Yalla yeureum té Khaarèko Aldianna, ak ñeupp ñou guénneu adouna ci Barké Seydina Mouhammad saw.
Yaw ana S Fallou ?
Billahi dma fogone mane rek beug ndongo lo Wallahi té khawmko bimouy dh 7 ans la am mais je l’aime a vie yalla nko bour bii doli yeureum
Bimouy ganiou magui am 10ans mai doumako meusa fattei
Moi aussi mais môme rek lay deguelou bilahi
ndeysane yalnako yalla yeureume thi barki borom touba
Merci beaucoup diambe Guéye nite kou bakh nga kham nagnoula boubakh ferme Niacourap
Yalla naka yalla yeureum si barké s fallou
Ndimbe Gueye nite kou bah nga repose en paix ndongo lo
Ndéysane lô dame kéne doula faté toujour yagui siniou khole on tm fore talibé srgn fallou biii khéle dale naaa siii yaw machalaaaa borome nianou wadioure mon frére yaw kou bakh gaaaaa longeu vie a tw bilah adouna darra diarou fiii darra jâmmm sii niepeu naaa raféte rkkk nakhe souba âme naaaa
Naka yalla yereum kou bakh
Un fidéle compagnon de Ndongo j'en n'ai témoin
Bilahi deug leu niite kou beuguone ndongo
C cá ki anos jour kharite voulai beugu te yaalla takh merci grand ndiambe repose en paix ndongo..
Yalla nako Yalla yereum té kharéko aldiana cii barké Seydina Mohamed psl
Yanako yalla yeureume
Mouné tak dére yagui pikine kou wédi ladiall ndiamé thiéy ndogo lo kénn douko faté🤲🤲😭😭
Ndeysaan Yalla Nako Serigne Touba Takhawou Sii Barké xassida Yii🤲🤲😭😭❤❤❤
Yalnako yalla yereum té diégeulko
kou meuneu weuye waye bilahi yalnako yalla yeureume thi barki borom touba
Diamé darou kou bahngua ma dieynaba fall tamit manchaalah
Ndiambé sama grand borom bakh
Machaalah amna solo loll
Boram bou tay nékha mbaga fatté démba😭😭😭
Yalla nako yalla yeureum té djégalko
Sama wadji demna rék 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭doumla faté ndongo
Ndiambe borom khol bou rafet ni youle ma mere Gueye
Ndeysane yalnako sougnou borombi kharèko Aldiana louwaye dèf bopam yageu bayihoul dara
yalla na ko yalla yeureum ودقله جنةالفردوس
Yaw papa dagua bakh lole té âme koleré Gueye gnora
Yalla nakou yalla yeuram
Paix à son âme 😭😭😭😭😭😭😭
Amine ya rabi
😭😭😭 doumako massa fatté yalla nako yalla terro
Ndiambé Séne Kham nako bou Bakh
Paix à son âme
Paix à son âme !!!!
Sama makk dji ken dou yaw aka gua bakh gueye ndiora
رحمة الله عليه
Yalna yalla yerame ko khare ko aldiana firdawsi ndongo lo kene dotoula fate thi adina vraima
Ndéyssane ndongo Lo dou diouk cii khôl yii❤
Merci frère aussi ndongo Rip 😢
Douma tayi thi dila beug ndongo lo yallanala yalla khare aledianna Di sa noflaye massoumala guiss waye dama la beug te yalla takhe te am n'a lo ligueyale sa borome ba keneu doula fate
Yalla na Souf woyof si kawam seydina Mouhamed terouka si aldiana firdawsi 😭😭😭😭😭😭😭😭
Nako yalla yeureume té khareko aldiana
Machallah khadim Gueye yalla Nala yalla lafal thiate
Amine sister max
Ndéysann
Bilakhi ki mounoul wone dounde 😢😢😢😢
Gor pire moy ndiambé amigo diame rék
Ndongo royou waye la billaye
kadou yii rafétna amena solo bilahi
Ndayessane adouna
Ndaye san ndongo lo 😭😥❤️🫶
😭
Bic grande ndianbe
Ñiambè borom bakh yatou beugu nitt lo yoreu bocou ko ñieup que la terre lui soit lègère ndogo lô
😭😭😭😭
🙏😭
❤️
Ndiambé santoule geuye séne la sante
Noo gueye la sante c'est le frère de ma copine aida gueye
@@nabousamb8252 yaye laniou bok aida momar AK matar AK noguaye AK ndéye ami la Bokal ndéye AK baye mé khamgua nite you bakh momar AK ndéye Ami daniou
Momar AK ndéye ami guagnou nagnou déysane momar diabarm mo toudone missine thiam
Paix à son âme Ndéysane 😭😭😭😭😭😭😭😭💔💔💔
Ndeyssane
Musique moom lougnou wara tek le. Daganoul. Point. Djayanté bi doyne. Nagnou ragal Yalla té bayyi khél Bamméél. Gnoun gneup dinagnou dem. Nagnou def lougnou fay djeurign.
nice
Ndeysane 😭
Ndongo allahouma ihfirlaho warhamho
L’inoubliable
Repose en paix frère
Qu'il repose en paix
Bamouy guaniou magui am 5an
Con ame nga légui 21 ans ndaysane adouna
Bilay adouna dou draa mais dama ko beug rék té yalla takh mousou mako guis wala kham
Man tmt 5 ans la amone mais thioffel bi na am si mom beurina troop
Yalla nako Yalla kharei aldiana
@@maguattelo6687 amine
@@yorosenegalndiaye8954 mais yalla bakhna
Mane dh khamumako mais damako beugeu
🤲🤲🤲
Hoo
Siw. D'où. Diami. Borom