Un responsable doit agir comme telle. J'admire son courage et son honnêteté, maintenant l'état doit les écouter et essayer de rallonger le délai de rigueur pour que ces derniers puissent régulariser leur situation administrative. Merci pour ces éclairages en tout cas . Soyez en règle et gagnez dignement votre pain 🍞 🍞
Wakh ji responsable na yaw mom nit ga wakh ji rafét na loll machallah ay patriote guèn thiak thiak niépako sokhla amna diarigne réwmi focus nioutabakh réwmi ték projet bi aboutir ba sénégalais yépou guisi sén bopou vision 2050en marche pastéf moy Sénégal
Prenons volontairement et avec responsabilité les chemins qui nous permettent d’assainir tous les secteurs les uns après les autres. C’est de la responsabilité citoyenne à laquelle nous devons tous souscrire par patriotisme. Nous sommes seuls, les bâtisseurs de notre propre pays !
SÉNÉGAL DAFFAY CHANGER TE DAY AVANCER PAR FORCE DANS TOUS LES SECTEURS . DISCIPLINE EGALE DÉVELOPPEMENT ET LE CONTRAIRE AMÈNE LE SOUS DÉVELOPPEMENT . GNIY THIEUPI THIEUPI THI REWMI DANNO KHAMOUL TE NATTOUNOU GNOUNN LIGNOU PROJET BI DIARRAL . BAKKAN LANNOU THI TEK . VIVE LE SÉNÉGAL VIVE L AFRIQUE
DIOUB dioubal dioubanti si lép si fépou kounou lale ga youkhou Sénégal nanla meuné défatou démlén outi ay papier mogeun wakh ji ak dioy yi wakh deugu té yalla takh gouvernement bi niépou lafi nékal vrai patriote day tégou si yon état meunla acompengné lou état reconaitouroul doula meuna diapalé sonko ak diomay ay jit you am yeurmandé la sénégalais lafi nékal
MACHALAH YÉNE DIAMBAR NGÉNE BILAHI BOULÉNE KÉNE DOUGAL SI DIABOLISATION YII BI OUSMANE SONKO DI DIOU CASSO BI YÉNA KO DEULI WONE AK PR DIOMAY LOLO KÉNE DOUKO FATTÉ AYE PATRIOT NGÉNE DÉFAR LÉNE RECK BOLO LEPOU DINA BAKH 💖🇸🇳✊✊👍🇸🇳🇸🇳
Salam comment peut-on développer un pays sans que les citoyens ne respectent pas la loi.Nous sommes de tout cœur avec vous car nous savons que vous travaillez dur dignement pour gagner votre vie. Mais ce que le régime actuel vous demande vous impose c'est pour votre bien certes c'est un peu difficile comme tout début mais confirmez vous à la loi.Aujourdhui c'est l'anarchie avec les thiak thiak si vous n'acceptez pas ce que le régime actuel vous demande ce sera votre pertement. Le régime actuel est de tout cœur avec vous. Évitez les manipulateurs
Machalah limoy deug wante nikadi wakh nan soudoul thiak thiak agrégé day bari xana kon lolou moy thiak thiak ngoy agrégé kon bok merci aliou sall sa guis guis rafetna
On doit inviter au journal de 20 heures de la RTS. Tu es vraiment un président qui est d’accord like
Bravo ! C'est intelligent, responsable et important
Un responsable doit agir comme telle.
J'admire son courage et son honnêteté, maintenant l'état doit les écouter et essayer de rallonger le délai de rigueur pour que ces derniers puissent régulariser leur situation administrative.
Merci pour ces éclairages en tout cas .
Soyez en règle et gagnez dignement votre pain 🍞 🍞
Salalakhou aleyhi wasalame ❤
Bravo les Patriotes Pastefs Merci beaucoup ❤❤❤❤❤❤❤❤
Merci beaucoup.seuls les agresseurs manipulateurs refusent la réglementation des motos
Effectivement mon frère c'est des agresseurs qui vont la manipulation
Bilay frère Niom Kessé la
Très bien parler, yėne dė beugu guėne na liguėye,
JUBB JUBBAL JUBBANTI ❤❤❤
Merci bcp mon frère ❤❤❤❤❤❤❤
Merci beaucoup les thiak.thiak❤❤❤❤
Ma sha allah nila rek deh
Bravo tu es un bon président
En tout cas c'est pour leur sécurité ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machaalah❤👏👍mat Ngua lign lay doyeeee👊👊👊
Bravo merci ❤
Wakh ji responsable na yaw mom nit ga wakh ji rafét na loll machallah ay patriote guèn thiak thiak niépako sokhla amna diarigne réwmi focus nioutabakh réwmi ték projet bi aboutir ba sénégalais yépou guisi sén bopou vision 2050en marche pastéf moy Sénégal
MashAllah frère yen ay jambar
OPPOSITION bi Tiol léna 😂😂😂😂
Merci pour une jeunesse responsable c ça Sénégal reek
Merci le jeune il faut la participation de Tous pour la transformation systemique de ce pays.courage et boulene ken manipuler
Merci beaucoup mon frère
Vraiment deugue gua wa t un vrai responsable l’etat dois vous écouter
Merci beaucoup ❤️❤️❤️
Prenons volontairement et avec responsabilité les chemins qui nous permettent d’assainir tous les secteurs les uns après les autres. C’est de la responsabilité citoyenne à laquelle nous devons tous souscrire par patriotisme. Nous sommes seuls, les bâtisseurs de notre propre pays !
Wakh nga deugg
Niii laa faut aider l’Etat 🙏🏽❤️❤️❤️
Bilahi koulaine wo si ay regle molaine beugue mais wa APR baugue laina manipuler
Day ngay fenn ben wa apr manipuler woul
Apr khamougnou lou bakh di
Machallah pour ta franchise vraiment tu as tenu un discours responsable
Jajeuf frère yaw dh tu as bien compris les choses machala très pertinent et responsable
SAYTANÉ NA FÉKKE NIO BARI SI RÉW MII SÉNÉGAL BLY MS BOULÉNE DÉF DRA LOU NIAW NDAKH SONKO SÉNE DIAMOU RECK LA BEGUE SÉNÉ CARANGÉ SÉNE INDÉPENDANCE ✊👍❤️
Merci bro dek day am loi dagnou wara am permi di sole casque am permis matriculations du moto di faye taxi limoye yone
No ma contane taye❤❤❤
Merci waye
Senegal dafa nékh néke si deuk yor so thiak thiak di transport d
Ta do yor papie lolou amoule féne
Bien parlé.
Être légal et légitime vous arrange plus
Bravo 👍👏👏👏
Merci et bon courage inchalah
Merci bravo tu est intelligent vraiment
Machalh si kaddou yi amna solo am targa bakhnasi ndakh si securite la bok tè dafa bari niou rakh jakarta nameyi yalna yalla geuna diapalé nieupe
Machalah Président très clair et limpide.... Chers compatriotes nagnou Goré❤
Merci beaucoup mon frère bilahi vérité absolue 👏👏
Merci beaucoup
Bilahi Niom Sonko Linou Beugeu Sènègal Rèk Mossï Ganiè
Joub joubal joubanti rék Sénégal diém kanam incha Allah
Dans ce pays, on se doit le respect mutuel .
voici un discour responsable deuk dafa wara tegou si yone jub jubal jubanti rek inchala
Si on est licite, on doit pas refuser d'être en règle
Focus sur le projet. Quant à vos détracteurs , halte à la manipulation !
Bravo,Vs êtes sérieux 🙏🙏
SÉNÉGAL DAFFAY CHANGER TE DAY AVANCER PAR FORCE DANS TOUS LES SECTEURS . DISCIPLINE EGALE DÉVELOPPEMENT ET LE CONTRAIRE AMÈNE LE SOUS DÉVELOPPEMENT . GNIY THIEUPI THIEUPI THI REWMI DANNO KHAMOUL TE NATTOUNOU GNOUNN LIGNOU PROJET BI DIARRAL . BAKKAN LANNOU THI TEK . VIVE LE SÉNÉGAL VIVE L AFRIQUE
❤❤❤
Sunugal rek 🇸🇳África ✌🏿
Machallah yalnalla yalna faye
DIOUB dioubal dioubanti si lép si fépou kounou lale ga youkhou Sénégal nanla meuné défatou démlén outi ay papier mogeun wakh ji ak dioy yi wakh deugu té yalla takh gouvernement bi niépou lafi nékal vrai patriote day tégou si yon état meunla acompengné lou état reconaitouroul doula meuna diapalé sonko ak diomay ay jit you am yeurmandé la sénégalais lafi nékal
J’espère que Kou Beug Ligueye Rek Kii Loum Wax Nii Leer Na Nagne S’il Vous Plaît Niou Takou Liguéye Dafa Djot 🖤✊🏿🇸🇳
Très responsable ce président.na Sénégalais yi dem wouti carte grise
🛑MACHALLAH KI MOM MATT NA DJIIIT... SEULEMENT YEN THIAK THIAK MAN DANIO BEUG LOU YOMB
Machallah il faut continuer la discussion et la sensibilisation auprès de vos cest juste qu'ils n'ont pas compris.
MACHALAH YÉNE DIAMBAR NGÉNE BILAHI BOULÉNE KÉNE DOUGAL SI DIABOLISATION YII BI OUSMANE SONKO DI DIOU CASSO BI YÉNA KO DEULI WONE AK PR DIOMAY LOLO KÉNE DOUKO FATTÉ AYE PATRIOT NGÉNE DÉFAR LÉNE RECK BOLO LEPOU DINA BAKH 💖🇸🇳✊✊👍🇸🇳🇸🇳
Djadjeuf way amna Nou rouss dé
Merci
Un vrais président ❤ merci frere
Bilaay contane na 🎉🎉
Jub Jubal Jubanti
Très bien parlé 👍🥰
Machallah ❤❤Soyez vigilants ne vous laisser manipuler par l'opposition ridicule
Merci ❤️ ❤️
❤❤❤❤❤❤❤❤j'aime ❤beaucoup ❤❤❤merci beaucoup ❤bilahi niépa si wara and❤❤
tres bonne idee etat bi fok mou diapsi mais pas comme rapidos
Voila c'est que j'aimerais entendre venant de la jeunesse consciente
Voila un leader responsable
Thank you bro ❤❤❤
Merci à vous président Machaa Allah ❤❤❤
Merci beaucoup frère
Très responsable ❤
Mashallah
Billah merci beaucoup vraiment
Vraiment tu communiques bien
Chapeau à toi
Salam comment peut-on développer un pays sans que les citoyens ne respectent pas la loi.Nous sommes de tout cœur avec vous car nous savons que vous travaillez dur dignement pour gagner votre vie. Mais ce que le régime actuel vous demande vous impose c'est pour votre bien certes c'est un peu difficile comme tout début mais confirmez vous à la loi.Aujourdhui c'est l'anarchie avec les thiak thiak si vous n'acceptez pas ce que le régime actuel vous demande ce sera votre pertement. Le régime actuel est de tout cœur avec vous. Évitez les manipulateurs
Merci vérité absolue
Diakarta cmc rek doynasi 😢
NUGNUY DEF BA AGRESSIONS YI JEEX NAK?
Plaques Rek
Machalah limoy deug wante nikadi wakh nan soudoul thiak thiak agrégé day bari xana kon lolou moy thiak thiak ngoy agrégé kon bok merci aliou sall sa guis guis rafetna
Matt nga president d machallah
Mèrci nitt nitè❤
Amna solo
Ana wa APR ak borom xol you bone yi gnaff lène ndayam partager li
Il a bien parler tellement vrai dans ces propos
Machallah ❤️
Merci pour la maturité !
Bravo vous aime votre pays
Très intelligent
Bravo🎉
Machallah
😢sama youn necol ci macky sall rek lay top
Makky sall mo yakh ndey Sénégal sathie sounou khalise 😢
Macky le cochon
Vraiment vous êtes responsable
Wakho Fi papa Ndiaye dangaye politique
MOTAY DOMERAM
C'est Alioun Fall écrit bien son nom de famille❤
Merci beaucoup foucus 2050 rek ❤❤❤
Il a dit Aliou Fall. Veuillez vérifier avant de poster votre article, si c'est fais exprès, c'est pas tres cool.