Bour gueweul et per Becaye s’énervent contre contre Siteu en plein Live Louniou Dal rk Mome la

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 17 дек 2024

Комментарии • 84

  • @laminefall5941
    @laminefall5941 Месяц назад +19

    Ay way yen gniy nek thi commentaire yi saga ngir yalla bayi len lolou thi dieumi seydina Mohamed gni wakhou gniou dara lou gniaw vraiment épuis lolou ban chance la am 🙏🙏🙏

  • @AwaMbaye-w2g
    @AwaMbaye-w2g Месяц назад +7

    Modou lo yalla n'a ko yalla may nam si barki serigue fallou 😍❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @AtoumaneNiasse
    @AtoumaneNiasse Месяц назад +2

    Machallah bour lou leer la wakh ❤❤❤

  • @bayetahirgueye2481
    @bayetahirgueye2481 Месяц назад +10

    Bour a droit dire ce qu'il pense du combat royal sil voit que siteu na pas les arguments pour battre modou il est libre de le dire par contre sieu na pas le droit d'interdire qui que soit de venir a diamgueune.

  • @MbargouDiop-mk4cv
    @MbargouDiop-mk4cv Месяц назад +9

    Siteu wakh lénko deug dafa dioum modou lo wakh nagnkofi louné Mais mou goum bopam ba prouvé

  • @Lordredujour95
    @Lordredujour95 Месяц назад +6

    Siteu dey danou in sha Allah. Na kholate communication wame

  • @ayayoussou770
    @ayayoussou770 Месяц назад +8

    Bour limouy wakh deugeuleu lolou daniouko wara khékh ndakh bénéne mbeur bangneko défatt prsk limou wakh dafa grave .modou mbay yaw ak bay balla boulén ndawal limou wakh limou wakh kénna warouko permettre bena nit walhou mbeur

  • @AmathDiouf-fb5vd
    @AmathDiouf-fb5vd Месяц назад +5

    Mais le respect doit être privilégié situé a parfaitement raison on doit le respect

  • @bayeratebayerate5893
    @bayeratebayerate5893 Месяц назад +1

    Merci beaucoup bour siteu dafa reww ndayam

  • @KebbaJobe-f8m
    @KebbaJobe-f8m Месяц назад +1

    Modou lo❤❤❤

  • @CheikhomarDeme-fg5zq
    @CheikhomarDeme-fg5zq Месяц назад +4

    Modou mbaye danga faral siteu

  • @toubaservices2988
    @toubaservices2988 Месяц назад

    wa fadam dou wakh mom😀😀😀😀😀😀😀😀😀

  • @AmathDiouf-fb5vd
    @AmathDiouf-fb5vd Месяц назад +5

    Chacun a le droit d analyser mais avec respect sans atteindre la dignité de la personne a vraie dire les deux ne respecte pas siteu

  • @amysagna8001
    @amysagna8001 Месяц назад +5

    Modou mbaye manoul nopi kome mom mi dém fékki Siteu arrêt téw ko waxo ko mou retifier gneuw fi dignou sonal

  • @SerigneousmaneGueye-o4m
    @SerigneousmaneGueye-o4m Месяц назад

    Merci bour siteu daffa yabate

  • @ElhadjimodouGaye
    @ElhadjimodouGaye Месяц назад

    Modou lo dina dane siteu dielle bou reuy inshaAllah!

  • @abdoulatifdiop5640
    @abdoulatifdiop5640 Месяц назад

    Lim wax Balla wakhou ko siteu déh nagn Niou m'ay DIAMOU

  • @SaliouDieng-d7x
    @SaliouDieng-d7x Месяц назад +1

    Sitteu daffa dioum rk si communication bi nitt déy dioum na diéguelou bala darra di si am niou nane mome leu

  • @ImailaATHIE-gt9gj
    @ImailaATHIE-gt9gj Месяц назад +1

    modou mbaye defaral sa deontologie de debat

  • @MussaMbood
    @MussaMbood Месяц назад +1

    Bour ferbele❤❤

  • @papamboup7207
    @papamboup7207 Месяц назад +2

    Bour Kone siteu n'a niane diam. 😂😂😂😂😂😂😂😂😂.

  • @DioufMamebirame-g6o
    @DioufMamebirame-g6o Месяц назад +1

    Siteu dou bay fall

    • @galaxiepro.5641
      @galaxiepro.5641 Месяц назад

      dou baye fall kay baye fall deug dafay rafete khol kouko togne mou bale leu nangou toumah di diokhé si yonou yalla di nangou kou am mbalitam saniko mou bala

  • @idrissadione7279
    @idrissadione7279 Месяц назад +1

    Siteu lii mou wakh tégouféne mooy kane ba kéne dou wakh khalaatame si moome boumou fontoo nitte gnii

  • @Lordredujour95
    @Lordredujour95 Месяц назад +1

    L’état doit proteger buur geweul.

  • @KossoGadiaga-vw3wc
    @KossoGadiaga-vw3wc Месяц назад +2

    Siteu kasse siteu kasse

  • @boyeniang3781yeumbeul
    @boyeniang3781yeumbeul Месяц назад

    athia baye balla❤😂😂

  • @mouhameddiagne9347
    @mouhameddiagne9347 Месяц назад +2

    Gnéne gni ay naféhe lagne dougnou wah ta yalla tah

  • @boyeniang3781yeumbeul
    @boyeniang3781yeumbeul Месяц назад

    no baye balla ray nama nenako amothia dara 😂😂😂

  • @moussapayemane4167
    @moussapayemane4167 Месяц назад +1

    Siteu mi gueumoulné meune na dane Modou Lo motah mouy créerr problème si digantém Bour ak Fadam en tt cas k le meilleur gagne

  • @cheikhgueye1612
    @cheikhgueye1612 Месяц назад +1

    Siteu rkk laniouy topp

  • @issakanafiou1865
    @issakanafiou1865 Месяц назад +1

    C'est per balla qui a plus énervé bour il faut le l'aise s'exprimer âpre tu peux parler

  • @bubasene
    @bubasene Месяц назад +1

    Becaye il dir a buur la verite critique beaucoup les lutteur

  • @cheikhounatine758
    @cheikhounatine758 26 дней назад

    Siteu a fauté.
    Nous pouvons ne pas être d’accord avec Bour mais jamais au plus grand jamais faut menacer une personne surtout en direct à la télévision

  • @cheikhthiam-k9o
    @cheikhthiam-k9o Месяц назад +1

    Masour SAC foi mo sani khére azis ndiaye

  • @mouhadiop8726
    @mouhadiop8726 Месяц назад +2

    Serigne si kéne menouléne térré wakh donc lolou diaroul wakh xamnaniou ni liyy xéw souba yalla rék mokko xamm

  • @ndongodiouf6747
    @ndongodiouf6747 Месяц назад

    Siteu à un très bon cœur c'est des blagues tout simplement et erreur de communication.

  • @likh-oj6lx
    @likh-oj6lx Месяц назад

    Bour migui si deugueum siteu Moy moytou rék Dax matnagnuko bayy

  • @SalimataDiallo-m8h
    @SalimataDiallo-m8h Месяц назад

    😂😂😂😂😂❤❤❤

  • @DpDp-hg6fx
    @DpDp-hg6fx Месяц назад +1

    Bour bigua khamèni tapéte gua loutakh gay wakh si siteu

  • @malickfall4447
    @malickfall4447 Месяц назад +2

    sieta dafa rew

  • @jeanmicheldiouf1664
    @jeanmicheldiouf1664 Месяц назад

    Très belle intervention de Mansour BA

  • @DioufMamebirame-g6o
    @DioufMamebirame-g6o Месяц назад +1

    Siteu katal sa Ndeye

  • @MbargouDiop-mk4cv
    @MbargouDiop-mk4cv Месяц назад +1

    Mais baye balla moy domeram rek mome lane moy problemame

  • @AbouLaye-gx2sc
    @AbouLaye-gx2sc Месяц назад +1

    Bour nopile waye

  • @einsteinndiaye7236
    @einsteinndiaye7236 Месяц назад +1

    Leudieul nguene Baye Balla😂

  • @papemoussandiaye9544
    @papemoussandiaye9544 Месяц назад +1

    Siteu dafa rew

  • @AlassaneSambe-lu8vo
    @AlassaneSambe-lu8vo Месяц назад

    Modou lô

  • @KossoGadiaga-vw3wc
    @KossoGadiaga-vw3wc Месяц назад

    Fadam ya sokhor

  • @FallouSow-f8l
    @FallouSow-f8l Месяц назад +1

    Bourr doull kan la

  • @CheikhomarDeme-fg5zq
    @CheikhomarDeme-fg5zq Месяц назад +1

    Modou mbaye danga contre modou mais dinga yague ame loulou nakhari

  • @DjidiackSene
    @DjidiackSene Месяц назад

    Bonjour mane lima guiss moye boure kene dou dem kharé Ngane diw mo la meune foufe Modou Lo monko warone wakh

  • @mouhameddiagne9347
    @mouhameddiagne9347 Месяц назад +2

    Yaw modou mbaye tu es trop immature

  • @ibrahimadione1770
    @ibrahimadione1770 Месяц назад +1

    Baye balla ya meun

  • @FallouSow-f8l
    @FallouSow-f8l Месяц назад

    Ki na nopi way

  • @mansourndione178
    @mansourndione178 Месяц назад +1

    Siteu daffa con

  • @malickfall4447
    @malickfall4447 Месяц назад +1

    sieta dafa tite rek comb bi la atanol

  • @ImailaATHIE-gt9gj
    @ImailaATHIE-gt9gj Месяц назад

    siteu entourageam mo bonn si bopam te xamouniou dara si sport .ay droguer rek nioko weur

  • @AbdoulAzizdiouf-bu3yp
    @AbdoulAzizdiouf-bu3yp Месяц назад +1

    Bour sa leufeul ndaye sa bi yéwo

    • @Lordredujour95
      @Lordredujour95 Месяц назад +1

      Sa yaye nga saga

    • @MamadouNdiaye-mn1yy
      @MamadouNdiaye-mn1yy Месяц назад

      Yw vrai drmr ngua bayil sa saga yi prkw vous êtes des imbéciles Bour dousa morom

    • @cheikhgueye9777
      @cheikhgueye9777 Месяц назад

      Abdou Aziz boul saga sa tourbi dafa bakh bilahi diarouko gua balma akh boubakh

    • @mameabzodabakhengom748
      @mameabzodabakhengom748 Месяц назад

      ​@@cheikhgueye9777Waxal way Ax 😢

  • @khesayad729
    @khesayad729 Месяц назад

    Bour yaw tamit il font nga bayi di toutale nite

  • @mamadougueyefaye7543
    @mamadougueyefaye7543 Месяц назад +1

    Siteu dafa enervèwon titte wakhlen li am tè bayi sen ray rayal yi

  • @SerignemodouNdiaye-s3u
    @SerignemodouNdiaye-s3u Месяц назад

    Bour mi wah len ko deug mou bayi nafekh bayi gnimouy humilier

  • @FallouSow-f8l
    @FallouSow-f8l Месяц назад

    Dagay doull rek

  • @ndongodiouf6747
    @ndongodiouf6747 Месяц назад

    Siteu à un très bon cœur c'est des blagues tout simplement et erreur de communication.

    • @gneidam58
      @gneidam58 Месяц назад

      "Blagues et erreurs." INCOHÉRENCE

    • @ousseynoutoure518
      @ousseynoutoure518 27 дней назад

      Bayilén 1,2,3 né blague blague ba nitt défi