J'ai pas le temps de suivre votre émission mais la solution mooy yaar khalés yi thi diiné khamal léne dangers yi nékk thi ndiallo bouko défé kouy tée sa bopp dangakoy déff té yalla takh ndakh yalla dakoo téré mais malheureusement parents yiko wara déff la plupart amouniou diiné bassiy yarr kéne
Wax nga lepp vous avez parfaitement raison. Dinné moy yaar nitt loutax on éduque les filles si affairou labane et autres. Pourquoi on éduque pas les filles sur la pureté et la chasteté dans l'islam.
Walahi vous avez raison ma mère m’a toujours dit durant tout mon adolescence que si un homme toouche ton sexe tu tombes enceinte quand j’ai grandi elle me disait que si tu couches avec un homme je le saurai sur ta démarche ce qui m’a traumatisé quand je me suis donné à mon mari à 35 ans je me suis évanouie
Merci beaucoup ♥️❤️ tata yén rk yéna Diarra am si société bi Mane dhé lima lérr ba lérr je suis vièrge thé amna ndaw 🙏🙏🙏😒💖💖douma rousselou sama yaye boy🥺🥺🥺
La vérité est que yeina daganal labane motakh khaleiyi di dieundi ndaw au lieu de faire comprendre aux filles que ndialo (fortification) bakhoul lou bonne la yalla beugouko wakh danger yissi neikk mais non vous préféré di deff seine bopp yi ayy labane du coup même souniou deifei erreur thi seine sexe douniou khalata wakh deugg daniouy outi ndaw artificiel Yarr _leine_sougnouy_dome thi dinnei nguirr yalla
Alhamdoulilah je suis heureuse de voir des gens comme vous qui partagent le même avis que moi. Vous avez parfaitement raison. C'est l'islam qui éduque pas la tradition. La tradition crée d'autres problèmes.
Et la virginité des hommes? Pourquoi on n'en parle jamais dans notre société ? Jigen yi rek li ñi lijënti, di leen juger, fek goor yi diñi def loulen neex,ba paré suñu bougué takk jabarr bëg kou vierge. Lolu teguñuko fènn. Une femme vierge pour un homme vierge. Point barre.
Lolo ma diakhal man , légui gor gnognou gnoy beug kou vierge ba paré légui djiguen ya gnou dévierger nak ban gorr moko wara takkëu. Doyna war. Té niom rek gnofi yakkëu djiguen gni.
Il y a une part de vérité dans ce que vous avez dit mais cela n'exclut pas le fait que vous êtes quand même un peu ignorantes, surtout quand vs dîtes que infection powoum tate mokoy indi alors que djiguène même excès d'hygiène sakh meune nako diokh infection, ak yénène wakhou doff youma tayala bind😂😂 sinon bou dé kou melni mane rek bilay do lène teugue labane ndakh j'ai tjrs trouvé ça ridicule😂 touss rafétoussi amoul orma amoul sutura. Wa Salam!
Wakhdj yeup elle ont pas Parlé de religion qui devrait être la principale raison de se préserver.valable pour les femmes comme pour les hommes.RAGAL LENE YALLAH WAY!!
Labane am na ba leegui bargui démbo ndiaye la sama dome wathie gérom filama fek andak wa keureum indil ma sama seurou dôme ma bek lole waw legui chance rek la lek lek djigéne niak ko si ndioum té wayé bonoul
Prochaine émission j espère que diguene wahe thi yene ndiegueyiy seye di tede ak séné chefeur wala séné gardien, je pense que c le plus pire sur tous yen ndiegou legui
Khana iow daga guiss sa bopou si wakh bii mane dée sén wakh bii amna solo trop suis jeune et unique fille de ma Mum motakh damay tée sm bopou nakh mane dongue la meun siguile sama yaye
Franchement dans la société ou nous sommes la vierginité ne se respecte plu.nous sommes dans un monde ou les réalités de la culture commence à disparaitre peu à peu.on ne blâme que les filles et les hommes dans tout ça.keup ko devierger diabar rou diambar ton tour viendra ❤❤❤❤
Djiguene bou amoul ndaw goor moko tek. Donc la discussion d'où fofou. Goor Moy yakh djiguene. En plus nite meune n'a bagna saigner fek ni amena ndaw. Amena aussi gnou gnak seni ndaw par accident.
@@Nas0404 walahi té en general setloul limala wah xalei you reglé yi gno gueuneu sonou si seuy par rapport ak djiguenn yigniy xass yalla daleni bolek Goor guou bakh
Seuy chance la lolou deug leu, mais terewoul jiguen nga kham sa bop, khamni yalla mola sante ni da nga wara teuyee sa bop, ba am dieuker té yem si mom, té khamni yalla mo ngi lay guis fo mounti nek
😢derett guniu falsifié derett guniu def si flacon derettou nitt xamo fumu diugué nga nara indil ku guoor ki probleme xamo ban febar ngako nra indil indil ko seu bopp💔
Je m'attendais à ce que vous donnez des explications comment savoir une femme est vierge et lá je trouve que vous êtes entrain de parler de ce que les femmes utilisent maintenant. Qu'elle médiocrité vous n'avez pas assurer cette fois ci c nulle
Merci bcp mais tmt wakhlenn ak parents yi niouy bayi khell seni ndom ndakh Mane bé tey Limay degu si première rapport meunouma comprendre djiguene deff première rapport après parents yi douniou ko guiss jour bobou sou gnibi se gale
Mane mère la mais lolou d'où Dara perte d hymen nite ngni rek nioko reuyeul mais hymen Lou oyof la mouné ngako perte sans rapport mais tjrs tu reste vierge diank bou khamoul goor tank bi ak lokhou daye toute bou yabo nga mesuré 2m am 90 kg tjrs niari daye touti bess bo khamé goor nak sa sidide dagg n'a merci
Wa yen labane fan lako l'islam waxé bayilen aada yi guen di tek si kam diné méme nit bou amé ndaw sakh si diguenté dieukeureum la wara yam ndax négou seuy lep soutoura la wara nek
Képou kou viérge rek lalal jm sa commentaire
🎉
😂kou mossoul niame kom mane lalal jaim❤❤❤❤❤
mais ani gniko keip baleigui manifestez vous🎉❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤😂❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉
yéene môme séne émission bi amna solo lool machalla ❤
Faut savoir aussi c’est pas tout le monde qui saigne le jour j
Franchement genre yii lagne sokh la si société bi merci chère maman 🤧♥️
J'ai pas le temps de suivre votre émission mais la solution mooy yaar khalés yi thi diiné khamal léne dangers yi nékk thi ndiallo bouko défé kouy tée sa bopp dangakoy déff té yalla takh ndakh yalla dakoo téré mais malheureusement parents yiko wara déff la plupart amouniou diiné bassiy yarr kéne
A oui surtout ça vous avez parfaitement raison
Merci..lepp dinei la❤
Wax nga lepp vous avez parfaitement raison. Dinné moy yaar nitt loutax on éduque les filles si affairou labane et autres. Pourquoi on éduque pas les filles sur la pureté et la chasteté dans l'islam.
@@ndeyekane2198 guiss nga dh diiné rékk mooy solution bi
Walahi vous avez raison ma mère m’a toujours dit durant tout mon adolescence que si un homme toouche ton sexe tu tombes enceinte quand j’ai grandi elle me disait que si tu couches avec un homme je le saurai sur ta démarche ce qui m’a traumatisé quand je me suis donné à mon mari à 35 ans je me suis évanouie
10:33 10:38 10:42
ManshaAllah santal yalla te geureum se yaye boubakh
Tu es marie à l'age de 35
I always listen to you machallah, commenting from gambia
Merci beaucoup ♥️❤️ tata yén rk yéna Diarra am si société bi Mane dhé lima lérr ba lérr je suis vièrge thé amna ndaw 🙏🙏🙏😒💖💖douma rousselou sama yaye boy🥺🥺🥺
La vérité est que yeina daganal labane motakh khaleiyi di dieundi ndaw au lieu de faire comprendre aux filles que ndialo (fortification) bakhoul lou bonne la yalla beugouko wakh danger yissi neikk mais non vous préféré di deff seine bopp yi ayy labane du coup même souniou deifei erreur thi seine sexe douniou khalata wakh deugg daniouy outi ndaw artificiel
Yarr _leine_sougnouy_dome thi dinnei nguirr yalla
MaShaAllah dèguena deug
Bilay yarou diné Moy lepp ndialo mo geuneu danger pirate ndaw
Merci
Alhamdoulilah je suis heureuse de voir des gens comme vous qui partagent le même avis que moi. Vous avez parfaitement raison. C'est l'islam qui éduque pas la tradition. La tradition crée d'autres problèmes.
C'est ça nak tout simplement
Vérité absolue ❤ merci a vous ❤
Et la virginité des hommes? Pourquoi on n'en parle jamais dans notre société ? Jigen yi rek li ñi lijënti, di leen juger, fek goor yi diñi def loulen neex,ba paré suñu bougué takk jabarr bëg kou vierge. Lolu teguñuko fènn. Une femme vierge pour un homme vierge. Point barre.
Une femme vierge pour un homme pisso😂😂😂
Lolo ma diakhal man , légui gor gnognou gnoy beug kou vierge ba paré légui djiguen ya gnou dévierger nak ban gorr moko wara takkëu. Doyna war. Té niom rek gnofi yakkëu djiguen gni.
Merci..lolu sah wakhou yalla la...les fornicateurs aux fornicatrices les pieux aux pieuses point 😂
@@alioukebe8744
Deugu dou neikh
Il y a une part de vérité dans ce que vous avez dit mais cela n'exclut pas le fait que vous êtes quand même un peu ignorantes, surtout quand vs dîtes que infection powoum tate mokoy indi alors que djiguène même excès d'hygiène sakh meune nako diokh infection, ak yénène wakhou doff youma tayala bind😂😂 sinon bou dé kou melni mane rek bilay do lène teugue labane ndakh j'ai tjrs trouvé ça ridicule😂 touss rafétoussi amoul orma amoul sutura. Wa Salam!
Ada bou bon
Oui il y a vraiment beaucoup d ignorances... Comment on peut venir parler devant la télé si on ne maîtrise pas a 100% le sujet
@@Cheikhdiop-u4l bou yalla geureumoul tekk si
@@Cheikhdiop-u4l legui audiovisuel mo sopalikou done affaires de idiovisuel motakh...
Bilay yaw 👌❤️🧕
Mieux vaut nga wakh deugue bi soulaye tak tak la soula takoul nga kham noy def mo gueune aye féne
Vraiment
bilayyyy
Wakhdj yeup elle ont pas Parlé de religion qui devrait être la principale raison de se préserver.valable pour les femmes comme pour les hommes.RAGAL LENE YALLAH WAY!!
Bilahi yaw
Lolou moma diakhal wala l’islam dafa diangalé woul bok meun dama warou yaw bilahi
C’est très important ce thème masha allah
Je suis fière de vous thème c intéressant
Vraiment vous avez parfaitement raison
C'est le ministère de la santé qui doit prendre ses responsabilités par rapport à la vente de ces produits C'est trop grave
Merci à vous émission bi amneu solo deufèy yété .
Mane Borom Tin noir bi moma nékh Macha allah ❤️ c'est vérité absolue
C'est Hamzatou la Maktoumienne ❤️ à Mbour Borom Tin noir bi nékh ngama trop bly 🥰
Khawma Laban khawma dh wayè Ada bou Bon la
Mann môm beugeu na goor yii diangue li dafa amm solo sonou société bi dafa yakou trop 😢
Loulér nguén wakh ☝️☝️☝️☝️
Wallahi Wallahi🥰🥰
Labane am na ba leegui bargui démbo ndiaye la sama dome wathie gérom filama fek andak wa keureum indil ma sama seurou dôme ma bek lole waw legui chance rek la lek lek djigéne niak ko si ndioum té wayé bonoul
Prochaine émission j espère que diguene wahe thi yene ndiegueyiy seye di tede ak séné chefeur wala séné gardien, je pense que c le plus pire sur tous yen ndiegou legui
Khana iow daga guiss sa bopou si wakh bii mane dée sén wakh bii amna solo trop suis jeune et unique fille de ma Mum motakh damay tée sm bopou nakh mane dongue la meun siguile sama yaye
@@modoundiaye2722 Deugue nékhoul😂😂
Macha Allah
Franchement dans la société ou nous sommes la vierginité ne se respecte plu.nous sommes dans un monde ou les réalités de la culture commence à disparaitre peu à peu.on ne blâme que les filles et les hommes dans tout ça.keup ko devierger diabar rou diambar ton tour viendra ❤❤❤❤
Bilaye nekhoul ba nekhoul ms nioune nio wow beut bilaye na niou rapouuu goor yii bo léne topé bilaye diga ko reuthiou😌
Intéressant
😂😂😂 lasso guiss parfois mou berestikou dhei😂😂😂
Amna solo lole kousi yaak sa toukousi gnalam ayy digna beuga riti mou teu leu
Thiey sama rew,,Quelle honte, quelle ignorance !!
Djiguene bou amoul ndaw goor moko tek. Donc la discussion d'où fofou. Goor Moy yakh djiguene. En plus nite meune n'a bagna saigner fek ni amena ndaw. Amena aussi gnou gnak seni ndaw par accident.
Exactement.
Exactly ❤ iow tu raison bien
Am ndaw takhoul sa dieukeur respectéla
Tu as parfaitement raison . Goor faaléwoul ndaw, goor sincéroul
@@Nas0404 walahi té en general setloul limala wah xalei you reglé yi gno gueuneu sonou si seuy par rapport ak djiguenn yigniy xass yalla daleni bolek Goor guou bakh
@@coumbacamara4418 gorla wayé dakor na. Mane déh gore la wayé meussou ma ndiallo té pourtant je suis malheureux
Waro wakh Lolo wakhal khalé yi ñou gorgorlou
Seuy chance la lolou deug leu, mais terewoul jiguen nga kham sa bop, khamni yalla mola sante ni da nga wara teuyee sa bop, ba am dieuker té yem si mom, té khamni yalla mo ngi lay guis fo mounti nek
😢derett guniu falsifié derett guniu def si flacon derettou nitt xamo fumu diugué nga nara indil ku guoor ki probleme xamo ban febar ngako nra indil indil ko seu bopp💔
Merci becoup
Xalé yi dagno âme fite
Je m'attendais à ce que vous donnez des explications comment savoir une femme est vierge et lá je trouve que vous êtes entrain de parler de ce que les femmes utilisent maintenant. Qu'elle médiocrité vous n'avez pas assurer cette fois ci c nulle
Yeneu daguene di conseiller wala daguene di khaster
😂😂😂😂 dagnouy khasté walé.😂😂😂😂
Senegal warnagnouko gnak vrement bari pekhè mome wakh deugue moko gueune
Contane na si yow Tata
Goor yi dofou niou deh😅
Ay teuth safatoula😂😂meune nama rayy
😂😂aïcha doubaï tata kis😂😂
😂😂😂😂
Bilahi limouy wakh deuguela boye you ndaw yi beugue nagnou tate meune fene
Merci bcp mais tmt wakhlenn ak parents yi niouy bayi khell seni ndom ndakh Mane bé tey Limay degu si première rapport meunouma comprendre djiguene deff première rapport après parents yi douniou ko guiss jour bobou sou gnibi se gale
Mane mère la mais lolou d'où Dara perte d hymen nite ngni rek nioko reuyeul mais hymen Lou oyof la mouné ngako perte sans rapport mais tjrs tu reste vierge diank bou khamoul goor tank bi ak lokhou daye toute bou yabo nga mesuré 2m am 90 kg tjrs niari daye touti bess bo khamé goor nak sa sidide dagg n'a merci
@@ndeyecodougueye3348 lolou noum meune nekk ngua perte hymen te ngua nekk vierge bé tey
@@ndeyecodougueye3348jai pas compris ma soeur
Mieux vaut gua wakh ko lou nek si yaw mo guen loudoul deugue dou yague
Lan mon kofi diarr telen sen daw yi lolou mo eup solo
Xalei yi nieup nio ngui seuy dih 💔
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Weuh 😂
Wa yen labane fan lako l'islam waxé bayilen aada yi guen di tek si kam diné méme nit bou amé ndaw sakh si diguenté dieukeureum la wara yam ndax négou seuy lep soutoura la wara nek
Bilay wakh nguène deugue mandè souma teudè sakh douma nèlaw ndakh sama domyi doto wolou kèn
Am fouta de
Plus de diankh anymore in Sénégal diankh amatoul comme labana amatoul
Khognaa yagui ni😂
Ray ngama ! 😂
Wakh nga dégui li man mi doundou nako
Toi aussi 🙏🤫
Mere yi amouniou kham kham
😂😂😂😂😂
Man mom fadiar la khey Di Snap si kou vierge
Mais lolou c'est possible je suis sage femme d'État je sais de quoi je parle
Est ce que dougueul sa baram thi bir rék sa ndaw yakhouna
@@shalimarBoye2563 cc
Mere yi yéna yak dekebi domeram legui site internet fo dem sexe sexe rek merde way
Yaw amo ndaw motah émission bi nékhoula
Sa khourou baye bou didime
@@gnionkhoretv282 amoul ndaw
@@gnionkhoretv282😂😂😂
Yangui guiss sa bopp de thiakhán bakhoul😅
@@gnionkhoretv282 😂😂😂😭💔wouy Sama ndy
Konnne da amm lou nékk sibir sexe mousoumakoo khammm🤣
Bailen rek toubab yi dinanlen febarlo caser sah manase am ak sida
Lubrifiant moye lane
😂😂😂😂😂😂😂😂