Sama Xarite Sama Woudiou (ma meilleure amie, ma coépouse) épisode 1

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 5 мар 2023
  • Retrouver-nous sur les réseaux sociaux
    instagram
    kharmedia_offic...
    facebook
    / kharmedia_l'officiel
    Khar Média est une société de production audiovisuelle, Evénementiel et communication, Nous imaginons des contenus créatifs et Nous offrons a nos clients un service global de production et de réalisation de films et de supports de communication, et un qualité à budget maîtrisé dans l’organisation d’événements.
  • КиноКино

Комментарии • 400

  • @aissatadia5260
    @aissatadia5260 Год назад +445

    Khar media niogui ligueye dh niome nio ligueyoul 😂😂😂😂😎 ani wa wifi dou nio raté ben série manifester vous 💪💪

    • @tinabadji2057
      @tinabadji2057 Год назад +2

      Barki chérafal Wouy Mangui dé 😂😂😂😂😂😂😂😂😂

    • @dioufmareme290
      @dioufmareme290 Год назад +7

      Waay je suis là 😂😂😂😂😂

    • @yacinendiaye9947
      @yacinendiaye9947 Год назад +2

      Je suis la🤣🤣

    • @fatoulolo781
      @fatoulolo781 Год назад +7

      Bilay nio ngui ni tassal ma takk la la diougé danou si fi AK yénén nak yénén😂😂😂😂

    • @aissatadia5260
      @aissatadia5260 Год назад

      @@fatoulolo781 ioe tmt 😂😂

  • @drocedouce2398
    @drocedouce2398 Год назад +46

    Tambalie akh bismillakhi sy barké SALLALAHOU ALLAH MOUHAMET yalna yép ame diame 🤲🤲🙏

  • @evafaye2553
    @evafaye2553 Год назад +49

    Guirr yalla woudiou pertiorgo,regret,diabarou gorgui wayy les nouvelles saison on a hâte 😍😍

    • @mounassfall2007
      @mounassfall2007 Год назад +4

      même série yi daw actuellement sakh dougalouniou épisode yi régulièrement 🤔🤔

  • @fayee4468
    @fayee4468 Год назад +62

    Bismillakhi niou tambaléti si série bou bess yalla nako nieup yégualé si barké seydouna Mouhamed saw 🤲🙏🏾

    • @ndayekhadiseye
      @ndayekhadiseye Год назад

      Daniolay niose dé Sow Nak khana ba🤣🤣🤣

    • @amykonte7542
      @amykonte7542 Год назад +1

      Amine waye ❤❤❤❤

  • @nafisalioukane4452
    @nafisalioukane4452 Год назад +23

    Bilahi Man meusouma am j’aime 😢😢

  • @nabousylla1314
    @nabousylla1314 Год назад +59

    Khar media ma maison de production préférée machalla.
    Do lene ma dieul j'ai 52 ans et j'adore jouer.1 million d'abonnés way.kou setane rek nanga abonné

  • @ndeyedialloka4257
    @ndeyedialloka4257 Год назад +36

    Aye Mane Khar média meune guén produire dè mé dou ame finalité li😂😂😂😂😂😂😂😂 chaque semaine AK série bou béésss😂😂😂

  • @ndeyeyagouthiam4683
    @ndeyeyagouthiam4683 Год назад +13

    Béne dousi am chance ani diegou pousso ani désir ani diabarou gorgui Kou d’accord beusseul j’aime

  • @toujoursmancity1000
    @toujoursmancity1000 Год назад +31

    Wa touba sen dom amnatina ndam rkk ❤️❤️🙏

  • @amythiam4655
    @amythiam4655 Год назад +12

    Goor gni yeup yo yem kouné Goor bakhna sa baye ya takh

  • @evafaye2553
    @evafaye2553 Год назад +22

    Kou khamé appartement bi kom mane ak bane série lagn. Fii jouer wone🤔🤔🤩🤩

    • @jammrek
      @jammrek Год назад +1

      Khar média séne films yeup ça se passe à l'intérieur des appartements et toujours pas de production à l'extérieur. Et c'est toujours les mêmes thèmes, seuy, woudié, avec toujours les mêmes acteurs.

    • @mariemefall7689
      @mariemefall7689 Год назад

      Woudj pethiarguo

    • @racky9246
      @racky9246 Год назад

      Woudjou pethiargo

    • @mbayangfaye7102
      @mbayangfaye7102 Год назад

      Woudiou péthiérgo🥺

  • @lalla_thioune
    @lalla_thioune Год назад +50

    Sénégal, khawma loutakh beurineu jigeen bouniou khamoul sen valeur di bayi seni djeukeur tolokhol len alors que sëy bokoul ak métite ak niak kersa ! Faty daal, ak nimou jongomawé yeuup, di beugueu sey, loutakh mou nangou djeukeur dji ak woudiém di xariteum yap ko ? djéki djéki bok seu djeukeur ak seu propre meilleure amie niou né dett way, seu djeukeur tégouleu fen té jeng sous tes yeux ! olou lane monko gueuneu tang ti khol ?? Une femme doit connaitre sa valeur pour se faire respecter et dire stop quand c'est trop ! N'acceptez pas qu'une personne vous impose ce que Allah ne vous impose pas ! 🥰🥰🥰

    • @djeylacisse2128
      @djeylacisse2128 Год назад +7

      On dois imposer le respect surtout

    • @lalla_thioune
      @lalla_thioune Год назад +7

      @@djeylacisse2128 vraiment ! diabar kou matt diabar waroul nanguou djeukeur yap ko té faty je me demande cmt elle a pu accepter cette sutuation ! imaginel seu djeukeur njaalo ak seu meilleure amie beuaré nane leu ma tey ! tékci jeng beu dof ! lolou c'est un raison pour divorcer !

    • @mamadouthioune4840
      @mamadouthioune4840 Год назад +1

      ​@@lalla_thioune man dal war nala guiss kharitt même si photo sakh ndakh sama kharitt bi benan affaire la

    • @lalla_thioune
      @lalla_thioune Год назад

      @@mamadouthioune4840 deugueuleu 😂

    • @mamadouthioune4840
      @mamadouthioune4840 Год назад +1

      @@lalla_thioune do nitou fi kharitt

  • @ndeyendiayesaliou8610
    @ndeyendiayesaliou8610 Год назад +23

    Romou na ba soneu wayé sama bakhou Mame la na dougnou rek😂😂😂😂🥰❤️

  • @aissatousonko2064
    @aissatousonko2064 Год назад +6

    Djiguène bouye seuy daye bayil fréquentation yi ndakh légui kharite amatoul .

  • @boussocisse7582
    @boussocisse7582 Год назад +30

    Commencé théâtres deii yombe naléne ms suite moy séne blême😅🤣

  • @khadyfaye836
    @khadyfaye836 Год назад +25

    Wouyyy chambre ndella bangi niii woudiou pethiorgo 😂khar media delen changer gallé😂

  • @mamankontzy
    @mamankontzy Год назад +17

    On réclame le bonheur de faty🤣😂😂

  • @diopmarlenediop5568
    @diopmarlenediop5568 Год назад +44

    Nguir yalla yègè lèlèn ko svp😍sène sèrie dafa nèkh trop mais moye lolou

  • @lalla_thioune
    @lalla_thioune Год назад +54

    Niarel bi, bonn neu té rew wayé rafet neu torop ma shaa allah ! elle est MAGNIFIQUE ! diamant noir bobou 🥰🥰🥰😍😍😍😃😃

  • @mamediarra6068
    @mamediarra6068 Год назад +26

    Bismi lahi niou tambali thi benene série ana sama mbok yi yalanane agale ak jamm Bilay werouma série bou niaw ma setaneko 😂yalana niepou am jamm 👏👏👏

  • @mbathiogning6358
    @mbathiogning6358 Год назад +4

    Ay mbirii seuyy mome linguéne si beuggg ahhh😮😮

  • @mariannediop7753
    @mariannediop7753 Год назад +25

    Je me demande pourquoi les femmes sont si désespérées au point de supporter toutes les bassesses que les hommes leur font subir.Thiey😂yala 😢

    • @aissatasarr3135
      @aissatasarr3135 Год назад

      Billahi dama tite liko fii diaarrr la xamoul

    • @afissatoudiouf
      @afissatoudiouf Год назад +1

      Beug rek Mo metti dhé si niom meunagnou mougne 😂😂😂😂😂😂

    • @rokhymane4263
      @rokhymane4263 Год назад +1

      Guisgua djiguene bouyy seuyy mo wara areté di wax vie privé xaritam xarite mo amoul xol xol laa rek beuguel founé layy djiouké

  • @guelayeguaye9957
    @guelayeguaye9957 Год назад +107

    C'est bien beau de produire d'autres séries mais il faut essayer de diffuser régulièrement les autres séries telles que woudjé, Terral, Takko 😁😁😁😁 franchement

  • @dabandiaye6323
    @dabandiaye6323 Год назад +16

    Awo lathie la garap pour yayam diokhoko niarél lathie passou xéw pour yayam gha diokh vraiment amna gor you seytané ta meuna Tass keur xarit amatoul djiguéne gni amna niou fausses

  • @marieyreneniang3125
    @marieyreneniang3125 Год назад +10

    Thieuy sama nawlé yi 🤗🤗🤗🤗

  • @nafisalioukane4452
    @nafisalioukane4452 Год назад +21

    gnom Ndeysane problème mou suite guéne am😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @nafidiakite3363
    @nafidiakite3363 Год назад +4

    Wa khar média niogui liguey deh vraiment waye nak on réclamé diabarou gorgui nak vraiment chapeau à vous yallah na diam yague 😍🥺

  • @dioneraby3195
    @dioneraby3195 Год назад +5

    Moussa adouna diaynala faty mougneul rek

  • @bintakamara2907
    @bintakamara2907 Год назад +18

    Thiey Mane séri bou nieuw rk aythia😂😂😂😂😭

  • @astougaye9573
    @astougaye9573 Год назад +9

    Kharite amatoul bilahi 😭😭😭😭

  • @alydione
    @alydione Год назад +14

    😅❤kou beugue khar média lalallll j’aime 😂❤

  • @astagayeasta4683
    @astagayeasta4683 Год назад +2

    Li motakh niounan djiguène bouy seye warout am xaritt

  • @ndeyendoye5663
    @ndeyendoye5663 Год назад +28

    J'aime bien le comportement de faty❤❤❤

  • @mamediarra3928
    @mamediarra3928 Год назад +6

    Séne keur gui woudiou peethior go lamay fatali

  • @pendafall9903
    @pendafall9903 Год назад +14

    Khar média départ mame arrive 🐭 😅😂😂😂

  • @barclubdetenisvillanueva8192
    @barclubdetenisvillanueva8192 Год назад +6

    Khaar media yongui liguéye gnome gno liguéyoul machallah 😘🌹🤣

  • @pendandiaye8786
    @pendandiaye8786 Год назад +5

    Khar média Loutakh guenn Ay woudije 😂😂

  • @aminatagassama4980
    @aminatagassama4980 Год назад +8

    Fati boul âme loula métti niarrél bou patta bi 🤣🤣légui mou maguétte

  • @mamadoucisse1655
    @mamadoucisse1655 Год назад +6

    fati bayil wakh bi nak😂😂😂😂😂😂

  • @mamankontzy
    @mamankontzy Год назад +1

    Bon AME sa kharite waro Kay dougual sisa birr bamou eupou waroula khamal sa lepou

  • @fatoudiouf1781
    @fatoudiouf1781 Год назад +34

    Mane de yalla bouma diakhase série yi liii 😂

    • @fatysall8740
      @fatysall8740 Год назад

      Bilay s'en série you bess yi dafa bari

    • @aidaracherif4866
      @aidaracherif4866 Год назад

      So defoul Naak dingako diakhasé déh 🤣

    • @sokhnaseynabou6799
      @sokhnaseynabou6799 Год назад

      Maneu déh beneu chérie lasi diap mouy karma

    • @mounassfall2007
      @mounassfall2007 Год назад

      @@fatysall8740 barina téh épisode yi dou nieuw régulièrement saison 2 sakh rarement 🤔🤔

  • @fatysall8740
    @fatysall8740 Год назад +5

    Khar media ayy réé😅😅😅😅😅🤣guénma def man yén la beug Lou gnew ma sétan wayé boulenma indilon diabarou gorgui ken d'où len guennn

  • @mamefatybousso392
    @mamefatybousso392 Год назад +5

    Guir yalla magui léndi niane guén diapou thi rk 😅 boulén KO off 😅😅😅dou samay wakh danou ma yonni
    Bou lépou diallé yénagui liguéy niom nio liguéyoul😅😅❤️

  • @Sodamariane7649
    @Sodamariane7649 Год назад +11

    Agalé moy sen blem tour mom wouyouna borom khar rek😂😂

  • @maimounasidibe781
    @maimounasidibe781 Год назад +5

    Goor gni dou niou sakh Ay nitt motakh dieul sa
    Kharit diko présenter woroul deuk bi légui woranté kessé mofi nék dagni guiss sa dieukeur Beug la dila défal louné gnou gnéla ba dougou ci mom brisé sa ménage 😢faty tu es trop naïve li waroon ngako éviter😢😢😢

  • @mbayembene2932
    @mbayembene2932 Год назад +6

    Khar média daniouy tambalé gay am yakar wayé douniou agalé🙄

  • @mayendiaye9931
    @mayendiaye9931 Год назад +1

    Eupleuw!!! Modou khar sa yaram tangna

  • @thiouneaminata5218
    @thiouneaminata5218 Год назад +1

    Aby boye alliance aida bonne continuation ma belle ❤❤❤❤❤❤❤

  • @amycheikhgueye2893
    @amycheikhgueye2893 Год назад +1

    Beneen bu bees 🥰 angages ngèen daal😇

  • @ndeyesodadiop5093
    @ndeyesodadiop5093 Год назад +6

    Faty elle est très mignonne

  • @petitmbayelecitizen3097
    @petitmbayelecitizen3097 Год назад +10

    Wa Mani sadiya diabarou gorgui fou eumbeu bi tolou🤔

  • @mariamasarr7088
    @mariamasarr7088 Год назад +1

    Wa khar média doyiou def Lou ag

  • @maremediagne3231
    @maremediagne3231 Год назад +1

    Bilahi ma contane si aida moussa day diay meuneu barane ak thiaga dadjé ga😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂 meussouma beug aida tay lako beugg😂😂

  • @zakhrandiaye7499
    @zakhrandiaye7499 Год назад +3

    Mais pourquoi à chaque fois serie bou bess alors que vous ne continuez les autres fpp

  • @astougaye9573
    @astougaye9573 Год назад +5

    Wa khar media chaque jour ak bou bess 😂😂

    • @jammrek
      @jammrek Год назад +1

      Séne séries yeupa niro, seuy, woudié et toujours sans fin.

  • @adamambaye8083
    @adamambaye8083 Год назад +13

    Ay goor moma diakhale dé😂😂

  • @KhadimThiam-fx2ye
    @KhadimThiam-fx2ye Год назад

    Moussa goor gou bone laaa

  • @mane2348
    @mane2348 Год назад +5

    Thiey amatina niou serie ndaysane wayé dou am suite té fokou niou setane ko😅😅

  • @adamadiop3991
    @adamadiop3991 Год назад +19

    Waa khar media mom xana dagno ame problèmou keur et mariage sen titre yiiii *woudié diabarou gorgui takko woudiou pethiorgo diégou pousso* sheuuuut🤦😩😂 bref yénamay wetalii😂🥰

  • @khadijadiop7292
    @khadijadiop7292 Год назад +3

    Kou kham apartman bu

  • @amilipsifaye8584
    @amilipsifaye8584 Год назад +3

    Xar media beugene woudie dé

  • @mmely9159
    @mmely9159 Год назад +4

    Hana niou niakat diom sètan loudoul am suite rek😂

  • @aichaalarbaallf4359
    @aichaalarbaallf4359 Год назад

    WA ma lathie lèn li yonla dieukeur dîna dokholè ni kharite barèwol mane mome Sama awo moma beugona guènè far yallah guènèko awo bou sa xolle setter sante yallah bou bonnè mbombou sakh douko tèrè sette ki mome niarelle bou niak diome nagou sa kharitou dieukeur tènga beugeu ko guènè yallah bakhneu

  • @antaba1094
    @antaba1094 Год назад +2

    Wa khar media Man dal khawma louy sen problem ak woudjou🤣🤣

  • @evafaye2553
    @evafaye2553 Год назад +2

    No niarel bi belle dé yen wawww ak sourikhhjjj bi🤩😍😍

  • @aramegueye2116
    @aramegueye2116 Год назад +4

    Wa yéne damay lathié🤔🤔🤔 Moussa mi louko dal oser na trop mom warna wax diabar dji do rouss do niit.

  • @ramatandiaye4666
    @ramatandiaye4666 Год назад +3

    Waxlen si mane serie bou ngeuw ma takk si rippp😂

  • @amysouare8732
    @amysouare8732 Год назад +3

    Encore goor😂😂😂😂

  • @bibiche3155
    @bibiche3155 Год назад +3

    Awo bi mo niak fayda rk dina beteu sama dieucoeur ak sama meilleur amie continue diko seuyeul yalla téré

  • @Sopeyayam
    @Sopeyayam Год назад +3

    Nguir Yalla khar media déléne déf ay séries de 15 épisodes ndakh mouy am fin 😂.

  • @khadygueye5970
    @khadygueye5970 Год назад +4

    Lou Nara nekh nganiiii😂😂😂

  • @oumyniang965
    @oumyniang965 Год назад +4

    woooy Ani diabarou goor gui 😅😅😅

  • @bbtaw3553
    @bbtaw3553 Год назад +1

    Lii😂😂thiatt leu 😂 nan sarakhé série😁😁😁

  • @yayafall7353
    @yayafall7353 Год назад +1

    Kou xamei keur gui woudiou pechiorgo filagnko jouer

  • @jammrek
    @jammrek Год назад +37

    #Khar média, on aime vos productions, mais vos séries se suivent et se ressemblent. Toujours à l'intérieur des appartements, rarement les tournages à l'extérieur. Améliorez-vous! Bonne continuation!

    • @djindaly5996
      @djindaly5996 10 месяцев назад

      Az928s,jznzs2dh’
      Ok

  • @fatoubintoucamara7058
    @fatoubintoucamara7058 Год назад +1

    Moussa ngani ya tay bly dingue ko réthiou

  • @amyngom7938
    @amyngom7938 Год назад +3

    Li motakh Sama keur permettre sama béne copine mou fanane fa wala mou yéndoufa boufi sama dieukeur néké

    • @fsnyesgirl7715
      @fsnyesgirl7715 Год назад +1

      Kone changel dieukeur. Le problème c’est vos maris ils n’ont qu’à être fidèles

  • @sodandiaye1368
    @sodandiaye1368 Год назад +1

    Kou méni mane khar média mayou Gniouma ma stessé

  • @mamistathiaw1766
    @mamistathiaw1766 Год назад +2

    Goor mm meun ngua changer mais op a ce point dem bakoy wax soudei mane rek kn sa ndaye day déé 😢😢

  • @light_stars778
    @light_stars778 Год назад +1

    Thiey yi goor

  • @ousmanesarr6923
    @ousmanesarr6923 Год назад +1

    Khar media yégnagui lingeuye billahi 😂

  • @mamistathiaw1766
    @mamistathiaw1766 Год назад +9

    Heureusement sama dieukeur la deff xarit ❤xarit amatoul laay 😂Goor gni bonne nagn ta bew solen amei niarel rk lounek nguen koy yakk sen awo yi 😢

  • @pendakebe-gg8hg
    @pendakebe-gg8hg Год назад +1

    Sokhna bator yagui fepp

  • @deguenembaye9199
    @deguenembaye9199 Год назад +1

    Manchalah ❤️❤️

  • @mamediarrandiayd6045
    @mamediarrandiayd6045 Год назад

    Khar média niogui liguéy niom nio liguéyoute

  • @aboudiallo8587
    @aboudiallo8587 Год назад +1

    Gore bou seytané mo bonn bilaye

  • @mamediarraboussongom5013
    @mamediarraboussongom5013 Год назад

    Limathi si wa khar média moy dounou egale série

  • @fatousidaty3975
    @fatousidaty3975 Год назад +3

    Sen thiat Moy dolen respecter jour you sen série yii Di dial

  • @aysatoufallfall9437
    @aysatoufallfall9437 Год назад

    Khar media 😍😍

  • @aminatandoye517
    @aminatandoye517 Год назад

    Faty faty faty loy déf si seybi Moussa respecté woula falé woula akh limou moy diékhal sama❤bi

  • @fatoukanteh4061
    @fatoukanteh4061 Год назад

    Appartement bi layn joué woudiou perthiogo

  • @oulimatasarr2167
    @oulimatasarr2167 Год назад +1

    Thieuye khare média thème you nekh mais sans suite

    • @Khadim417
      @Khadim417 Год назад

      Gnji gnji lénn eumbou gnon febar

  • @aminatagoloko1503
    @aminatagoloko1503 Год назад +2

    Machalah vous progressez
    Mais telma de série té d'où amm suite wala série sans fin amoul chance
    Ya telma dexple sandiya ,nawlé,même woudjé bi vous du mal à respecter les épisodes akkk yeneen je vous suit mais tamit le travail reste

  • @aidandiaye1232
    @aidandiaye1232 Год назад

    Thieyy kharr media niom Dale founè lagnouy feulè Waya problème bi dagnouy dèm bamou yagu dotougnou am inspiration

  • @mbarkangom5931
    @mbarkangom5931 Год назад +4

    Aye mane seme beut yi dine guene yakou Di série bou nieuwe m sétane wa bakhena 😂😂😂😂

  • @nafisalioukane4452
    @nafisalioukane4452 Год назад +11

    Ms est ce que diotou gnou oubi groupe watch sama nawlé yii😂😂😂😂😂

  • @bbdiallo7362
    @bbdiallo7362 Год назад +5

    J’aime pas ses genre d Seri 😢Sam xol day sote

  • @mamecoumbasy-ym5iq
    @mamecoumbasy-ym5iq Год назад +3

    Khar média dal sène yarame dafa tangue machalla bonne continuation

  • @aissatoubah4440
    @aissatoubah4440 Год назад +7

    Sene problème Moy douguene continue sene série yi

    • @jammrek
      @jammrek Год назад +1

      Ba nopi séne films yeup se suivent et se ressemblent, seuy, woudié , et toujours à l'intérieur des appartements, jamais de production à l'extérieure.

  • @ndeyeramatoulayegueye7623
    @ndeyeramatoulayegueye7623 Год назад +3

    Thiey les hommes 🤔🤔🤔