Dieureudieuf abdou aziz toure yalnala 'fi yalla takhawu yock sa yeurmeundé bilahi sama khôl dafa çéde gouy wakhtane bi amna solo yalnagnou yalla may dégue ak topeu
C'est toujours le reflet de l'école de seydil elhadj. Fils de serigne Hady touré qui après sa formation avait épousé sohna Aida sy fille de Mame Maodo. Ndokh dou bayi yonam
machalla sama sopei bi yalla nala fayyi bayyi bassi kanama kanam sa doundou gui amna ndiarigne . Bilahi lazii laa ilaaha ila houwa damala beugg sopp la nguir sa deuggou
Alhamdoulilah il est issu de la grande université cheikh seydil hadj Malick koufi ame xam xam deugue boutakh gniouy wax mola diamguale wala mou dianguale koula dianguale
Nii nga meuneuh mél, seutou seydi hadji malick leuh, waydiouram bou djiguéne, Mame Maodo ko djiour, ték si serigne hadi dissa baye, foo diaar deugou ték si ragal Yalla, yalla goudeul fane wi téh gueuneuh deugueureul takhawaay bih.
Légui dagueni tekk gamou fass Touré 😂😂😂😂 Xana gamou nekatoul bida de vrai Satan vous êtes mais bon c’est bien de chercher des alliés Le vieux dit klk termes kinviis arrangent il avait démenti un de vos recoupages sur gamou bidah le maintenant vous diffusez son gamou comme ça tant mieux dina soti d diapelene rek lepay bakh
@@malickdiouf5728 hee goss ça je le sais très bien ! C'était pour expliquer que le mec malgré ça ne soit ça qui l'intéresse, il va l'avoir avec le Gamou !
Soo téeloone wokh saa mbokkou wahabite yii YONÉNTEU BII moyy lépp, makk gni gnow diokh sénn bopp Yalla ak yonénteu bii saws ! Donc tu aurais dû être très clair depuis le début rekk ! Aujourd'hui est ce qu'ils vont te prendre au sérieux ?
@@weuzjt8142 Ahh va écouter le fichier audio que les wahabites ont mis sur youtube où lui même parle de fêter mawlid. D'ailleurs si tu lis les commentaires tu verras des wahabites qui lui disent qu'ils sont déçus de lui parce que aujourd'hui il fête le Gamou ! Je pense que cela suffit pour comprendre ce qu'était sa position avant ? Ou bien tu n'as toujours pas compris ???
@@daoudambengue3785 Toi tu veux débattre sur le tutoiement ??? Ce que j'ai dit c'est clair sur la position qu'il devait se forcer depuis des années. Mawlid moyy lepp. Dinga si diangue doundoo koo tedd kii SALLA LAHOU ALYHI WA SALAM. OR SA VIE C'EST TOUT CE QUE DOIT COMPRENDRE, CE QUI PERMET DE L'AIMER ET L'AIMER C'EST TOUT CE QUE RECHERCHE EN ISLAM.
Yalla nako yalla samou Faye ko té wéreul bat bi yokk xam xam bi sounou royoukaye bi ❤️💗💗💗💝
Machallah. Nian leen yalla goudal fanam bou bakh kha bakhhhhhhhh❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Dieureudieuf abdou aziz toure yalnala 'fi yalla takhawu yock sa yeurmeundé bilahi sama khôl dafa çéde gouy wakhtane bi amna solo yalnagnou yalla may dégue ak topeu
Mame yalna yalla goudale sa fane sou borom xam xam yi yep dome def comme yaw legui gnou dioup
Macha Allah! Dieureudieuf Touré. Léup ndiarigne la. Brom bi Sobhanaho Watahala samlén, mousal niou si chaytanè, deugeureul, sounouy pas pas..
Gamou 2023 rk lay khar avec impatience
Mame Abdoul aziz Toure, Yalla na Yalla goudal sa fane
Maa sha allah vérité, c'est le seul des kilifeu dinee qui ose parler ainsi, barakallahou fiikoum yaa cheikh
Moom reikk mooy sama serigne
Walahi deug la
Macahalla Macahalla Macahalla Macahalla amnasolo yalla nalene yalla defal diamo barke mam dabakh amine
Machallah yalna bour doli lá tawfikh te yoku kham kham bi diahi seyedina Mohamad te doli wer gui goundeul sa fan
C'est toujours le reflet de l'école de seydil elhadj. Fils de serigne Hady touré qui après sa formation avait épousé sohna Aida sy fille de Mame Maodo. Ndokh dou bayi yonam
Wallaye
ما شاء الله يا والدنا الغالي قد رأيتك فسرت عيني حفظك المولى سبحانه وتعالى ورعاك
Amén yallana yalla goddal sa fann ya Abdall azize ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🙏🏿🙏🏿🙏🏿
حفظ الله شيخنا ورعاه وأبقاه ذخرا للإسلام والمسلمين
والله أنت فخر للإسلام والمسلمين
نسأل الله تعالى أن يكثر أمثالك في الأمة الإسلامية
Macha'Allah cheikh bi kou bakh la
Longue vie serigne Abdou Aziz touré barkè Yonnenetebi Psl barkè Cheikh Tidiane R A barkè mame Maodo R A ak mame hady touré R.A
والله توري قلت الحق, بارك الله فيك وطول عمرك واحفظك في الدارين بجاه طه صل الله عليه وسلم
Yalla nala yalla May wergou yaram ak goudou fane Machallah ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
Macha allah ❤
Machalla Gamou ila Abadaane !
machalla sama sopei bi yalla nala fayyi bayyi bassi kanama kanam sa doundou gui amna ndiarigne . Bilahi lazii laa ilaaha ila houwa damala beugg sopp la nguir sa deuggou
ما شآء الله أبانا الكريم حفظك وأيدك ورعاك ويجزيك خيرا
Sama xol bi ngay féxeul . Goudal fannn Touré
Masah Allah Mudir Bara kallAhu fi kum
Mach'allah mame doundal ba sey mey di bawann thi daradjeelou arcoura
Machallah mame bou yalna yalla mayla wêr
Yow rek yafi nekal deug yalla ak yonentibi
Yallna fi yagg barkep brom touba deugg na ay jafam
Mashaallah serigne deugue bou wer
Alhamdoulilah il est issu de la grande université cheikh seydil hadj Malick koufi ame xam xam deugue boutakh gniouy wax mola diamguale wala mou dianguale koula dianguale
dieuredieuf lerna dé yalla nagnou yalla défal yeurmandé
Yalna soniou borom Fay le yiw thi fataly gou mague guiii nga fatali djami Yale yi diazaka lahou khayrane thi warr guigay war djami Yale yi diazaka lahou khayrane thi layeee biir nguigay layeee biir djami Yale yi yalna soniou borom youko sa wuer ak say fane thi barke seyidouna Mouhamed sama lahou walahi wasalam
S Abdoul Aziz touré assouffi
Machallah
Machaalah yalna yalla sambla aralla bombam inch'Allah
Nii nga meuneuh mél, seutou seydi hadji malick leuh, waydiouram bou djiguéne, Mame Maodo ko djiour, ték si serigne hadi dissa baye, foo diaar deugou ték si ragal Yalla, yalla goudeul fane wi téh gueuneuh deugueureul takhawaay bih.
حفظك الله ورعاك أنت فخر لنا
Machallah mame long vie a toi
ماشاء الله شيخنا أبانا شيخ عبد العزيز
Wallahi yaw dé biss dinâ niouw nga déh guissé ak sa bôrom
Machalla yalna yalna faye
Macha Allah
Baye Aziz Touré ibn Mame Serigne Hady Touré Yagu fi lol té werr Barké Mame Seydil Hadji Rawhane Ngom
Ma cha Allah
Wa Alxourane ak souna dounguen Dougal vidéo bii comme yénén vidéo wome yii kiii kou baxleu menolen yax ligueyame
Kone niou baxx di niom douniou partage lou bax
merci
Un vrai savant
wallahi ki dall nékhnam loll sakh
J’ai beaucoup d’admiration pour lui. Je serai très heureux de faire sa rencontre. Qui peut m’aider?
Il faut tout simplement aller lui rendre visite à Fass Toure il est malade mais aux heures de prière tu peux le voir à la mosquée
fatima Dieye Merci. Je ne sais pas où Fass Touré se situe mais je vais me renseigner inshallah
Boulma fattei boofay deim
Mais s abdou Aziz Touré que je regarder entrain de dire que gamou biddah la?
Gamou bidah la kagne, lolou la bayam wakh.
Légui nak?
Exactement !!!!
Gh
Légui dagueni tekk gamou fass Touré 😂😂😂😂 Xana gamou nekatoul bida de vrai Satan vous êtes mais bon c’est bien de chercher des alliés
Le vieux dit klk termes kinviis arrangent il avait démenti un de vos recoupages sur gamou bidah le maintenant vous diffusez son gamou comme ça tant mieux dina soti d diapelene rek lepay bakh
😅😅 Diouf Féxalal sa xol. Bo oubbi woone sa xél mi déglouko té teuthie sa lamigne dingua dégue mouni la gamou bidah la comme ni conférence néké bidah.
Waayé audio bii wahabite yii dougueuloone dafaa wokhone juste bidaa leu sans apporter la nuance : bida bou raffétt...
Soo bougué amm mboolo dingaa gamou momm. Ndakhté wahabite yii momm dougn leu diokh mboloo...
Ibrahima DIOP conférence aussi bidah le kone ndakh yonentibi danouko def 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Ghulaami Tidiane mbolo dou dara qualité ba eupe solo
Diarama mame maodo
@@malickdiouf5728 hee goss ça je le sais très bien !
C'était pour expliquer que le mec malgré ça ne soit ça qui l'intéresse, il va l'avoir avec le Gamou !
Soo téeloone wokh saa mbokkou wahabite yii YONÉNTEU BII moyy lépp, makk gni gnow diokh sénn bopp Yalla ak yonénteu bii saws !
Donc tu aurais dû être très clair depuis le début rekk !
Aujourd'hui est ce qu'ils vont te prendre au sérieux ?
Explique moi bane position la dieulone?
@@weuzjt8142 Ahh va écouter le fichier audio que les wahabites ont mis sur youtube où lui même parle de fêter mawlid. D'ailleurs si tu lis les commentaires tu verras des wahabites qui lui disent qu'ils sont déçus de lui parce que aujourd'hui il fête le Gamou ! Je pense que cela suffit pour comprendre ce qu'était sa position avant ? Ou bien tu n'as toujours pas compris ???
@@daoudambengue3785 Toi tu veux débattre sur le tutoiement ??? Ce que j'ai dit c'est clair sur la position qu'il devait se forcer depuis des années.
Mawlid moyy lepp. Dinga si diangue doundoo koo tedd kii SALLA LAHOU ALYHI WA SALAM. OR SA VIE C'EST TOUT CE QUE DOIT COMPRENDRE, CE QUI PERMET DE L'AIMER ET L'AIMER C'EST TOUT CE QUE RECHERCHE EN ISLAM.
Yalna soniou borom Fay le yiw thi fataly gou mague guiii nga fatali djami Yale yi diazaka lahou khayrane thi warr guigay war djami Yale yi diazaka lahou khayrane thi layeee biir nguigay layeee biir djami Yale yi yalna soniou borom youko sa wuer ak say fane thi barke seyidouna Mouhamed sama lahou walahi wasalam
Machallah
Machalla
Merci
Machalla
Macha allah
Machalla