L’ex femme de Eumeudy, Kiné Badiane débarque par surprise au Baptême et confie à la nouvelle mariée

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 4 фев 2025

Комментарии • 145

  • @People221sn
    @People221sn  Год назад +12

    N’oubliez pas de vous abonner à la chaine PEOPLE 221 TV et d’activer la cloche de notification pour ne pas rater les nouvelles vidéos 🔔 ...
    Pour vos conseils et critiques veuillez nous laisser un message sur ce commentaire Mercii...
    Témoin d’un événement contactez : +221 77 451 21 10

  • @seckmamybanel2380
    @seckmamybanel2380 Год назад +146

    Manchallah li nekhna rafétena nite kou bakh dafay diéleulé Di diéguelé teksi am esprit de dépassement ❤❤❤❤

  • @soukeynadiallo1472
    @soukeynadiallo1472 Год назад +92

    Kiné badiane est une dame de valeurs

  • @VirginieFleur
    @VirginieFleur Год назад +55

    Oh c'est beau sa❤❤❤ bravo kiné. Ta fais un beau geste vraiment magnifique. Respect à toi❤❤❤

  • @fantadiatta831
    @fantadiatta831 Год назад +47

    Macha ALLAH Kiné bakhna wayé khalibiyite kéne dou mome, bou wathiéwoulwone bopam kiné dou am accés ci mome té pourtant on peut dire ke kiné moko sokhla ndakh mo yoor domome. Kiné mome simplicité ak yarr la meusseu woné

    • @khadimbacke2054
      @khadimbacke2054 Год назад +9

      Bilahi wakh nga deugue bone mo khéwi djiguene moy diour Wayé yalla rek mokham kouy diarignou

  • @fatouthioune-dn9rk
    @fatouthioune-dn9rk Год назад +29

    Kiné ya bakhe ame classe machalah

  • @lovelysoso3412
    @lovelysoso3412 Год назад +39

    Sama yaram baghi daw sah bilahi cheu kinè ya bah t am esprit de dépassement ❤

  • @Angi12100
    @Angi12100 Год назад +60

    Kiné vraiment t'es une vraie et grande dame

  • @colheitabeauty6666
    @colheitabeauty6666 Год назад +1

    Li moy grande dame , grande dame Doussi takay ak solou gou reuy Machalla

  • @mariannefoster8268
    @mariannefoster8268 Год назад +20

    Manchallah ndeye ressemble beaucoup à RIHANNA
    YALLAH meneu bindeu
    Manchallah

  • @oumymbaye1307
    @oumymbaye1307 Год назад +15

    Machalla kine y’a rafet nak machalla def gua jeste noble deug laf thiat Ndeya tte belle 🥰 ❤❤❤❤

  • @soulagertvofficiel8782
    @soulagertvofficiel8782 Год назад +14

    J'ai trouvé que kinè kou bakh la. Kholou yaye fall piree mane damako beugue 💙

  • @moriciss6368
    @moriciss6368 Год назад +19

    ❤❤❤kinè kou baxe la mes Ndéya tamite kouko guiss khamni kou niak probléme la

  • @Mia-ti8li
    @Mia-ti8li Год назад +30

    Machallah li nekh na rafféte na trop ❤❤❤kiné badiane kou bakh gua

  • @ndeyediop7665
    @ndeyediop7665 Год назад +8

    Ndeya tamine nitt gueunou koo wayy yalla naa diam yagg❤❤❤❤ Machallah

  • @natou768
    @natou768 Год назад +23

    Ma challah waneguéne djiguéne yi tase di woudjé ak céne diabarou ex yi

  • @adamandiayekasse5990
    @adamandiayekasse5990 Год назад +8

    Kiné bakhna wayé Ndeya tamitt kénn gueunouko. Boudonn maltraité khalé bii, Kiné doufi tékk tank. Yalna lénn thiatt sekhlou

  • @haby8760
    @haby8760 Год назад +55

    Amneu nitgnu bakh té rafèt xol meuneu pardonné le pire Yala neumeu Yala mèy xol bobu Allahumma Amine ya Rabbi 🤲 Dieu est Grand ! Kiné ya bakh MaShaAllah Yala neuleu Yala bayèk se dieukeur laffal lène thiate . Sèy bakane le fiko Yala yamalé rèk lèy yam Ndèyssane . Neu ande rafèt neu takaliko rafèt. Alduneu amoul solo lèp thi ay néteuli dong lèy moudié . Wayé Kiné mane mangui réfètlu se geste bi .

  • @GnimaSambou-bb9ul
    @GnimaSambou-bb9ul Год назад +25

    Machallah kiné kou bakh là femme bi aussi k dieu vous bénisse ❤❤❤

  • @kaami8709
    @kaami8709 Год назад +2

    Kiné badiane mo bakh rek bouko nekhone yamaler domame indi jalousie mais mo bayi ndeya akk domam ame si ndeya confiance ba lepeu rafet machalah une grande dame kiné toujours classe

  • @faderabanna
    @faderabanna Год назад +18

    What a beautiful gesture 😊

  • @codoukane739
    @codoukane739 Год назад +10

    ❤❤❤❤❤machalla kiné quel noblesse

  • @BahiaThiouf
    @BahiaThiouf Год назад +1

    Ya bakhe 😍🥰🤩té guoré ☺️☺️❤️❤️❤️❤️🤩🤩❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @dioufmareme290
    @dioufmareme290 Год назад +7

    Ndeysane li rafete na Macha Allah. Adouna amoul solo. Ass gorr day fatté ❤❤❤❤

  • @khardieng9763
    @khardieng9763 Год назад +13

    Machallah longue vie bébé Wally

  • @diatoupeul
    @diatoupeul Год назад +8

    Kiné gueune nama nékhhh❤❤❤❤❤ ki mo niakk kignane nak

  • @ndeyebounamadiop5863
    @ndeyebounamadiop5863 Год назад +12

    Ndeya ak kine maachaala

  • @SokhnaGueye-bd4bo
    @SokhnaGueye-bd4bo Год назад +9

    Ndeysane Kiné khol bé raféte machallah way

  • @fatousowe3652
    @fatousowe3652 Год назад +6

    Deff nge fi lu historic belahi machallah

  • @fatousow4526
    @fatousow4526 Год назад +1

    Kiné vraiment grande dame la machallah

  • @yacinendiaye2746
    @yacinendiaye2746 Год назад +1

    Bilay Kiné badiana y’a bakh

  • @kine1687
    @kine1687 Год назад +17

    Kiné danou bah macha ALLÂH c'est ça la vie adouna yagoul nay raféte❤❤❤❤❤❤❤❤❤

    • @kinekane3610
      @kinekane3610 Год назад +1

      Lou ler gua wakh bilahi

    • @kinendiqye
      @kinendiqye Год назад +1

      Wakhal way kou togne niou dorla wayé kouniou niane niou mayla❤❤

  • @reinendateyalla2837
    @reinendateyalla2837 Год назад +5

    Kiné deh machallah kou bakh laa motakh lou bakhe rek laye ame

  • @fatimazahrandiaye7431
    @fatimazahrandiaye7431 Год назад +2

    Machallah lii reafete na trop adouna nii la yaatal xol yi bania xadial haine ndakh adouna yagoul machallah nieupe contane naniousi

  • @adiouka6357
    @adiouka6357 Год назад +6

    Machalla Eumeudi yalna doundou té ame ndey ak bay gorénga dé ndakh diokh ngago borom dé❤

  • @kinendiqye
    @kinendiqye Год назад +27

    Kou toudou kine dou bone ❤❤❤

  • @MadoNdiaye-fm4
    @MadoNdiaye-fm4 Год назад +3

    Machallah kiné adouna amoul solo ❤

  • @bayediagne1134
    @bayediagne1134 Год назад +5

    Kiné ya niakk kignane❤️👍♥️

  • @madodiagne3007
    @madodiagne3007 Год назад +5

    Li michelle obama wakhone :(when they go low . You go high). Ma shaa Allah c genial. Kine amgua xell. (Elle prend soin de ton enfant)

  • @BabacarNdiaye-i2m
    @BabacarNdiaye-i2m Год назад

    Machallah kiné badiane ya am class kay yalla boulène thiate dougou way❤❤

  • @sankounkanoute3067
    @sankounkanoute3067 Год назад +8

    Quel beau geste

  • @adamabadji5056
    @adamabadji5056 Год назад +12

    Machala c'est beau longue vie au bb

  • @ndeyediallo7609
    @ndeyediallo7609 Год назад +1

    Sama toma Ndeya elle resemble a rihana Machallah kiné ligua def réyena après la pluie c’est le beau temps comme ni guaco wakhé rék ndeya mo bakh rék ta fégne na si kaname yalla na Yalla doli diam dunde ba djaboot gui mageu diléne téral si barker seydina Mouhamed psl♥️♥️🙏

  • @AyaMballo-ke6re
    @AyaMballo-ke6re Год назад +3

    Machallah rafetna wali sek Badiane yala n'a yala ndoudou barkel ci barki yonente bi❤️‍🩹❤️‍🩹❤️‍🩹❤️‍🩹

  • @mouride867
    @mouride867 Год назад +4

    Nn kiné nitou aldiana la vraiment 😭😅 je l'aime trop❤️😘 mashalah

  • @Lejuge-u8y
    @Lejuge-u8y Год назад +15

    Ndeya moko yoral domame c'est normal mou gnew .

  • @mariamasow3801
    @mariamasow3801 Год назад

    Machallah quelle grandeur Li noble rek moko meune machallah 🙏🙏

  • @dabacisse2957
    @dabacisse2957 Год назад +4

    Vraiment kel classe

  • @Nene02000
    @Nene02000 Год назад +8

    Kiné kou bakh la wayé ndeya aussi mashallah yar domou diambour yomboul mou téyé xallé bi comme dôme bimou diour mashallah rek lagn koy wax

  • @KendyCamara
    @KendyCamara Год назад +1

    Machallah Machallah kiné longue vie santé de fer contane ci yaw lol❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @astelagadiaga1924
    @astelagadiaga1924 Год назад

    Ki a vu que ndieuké bi dafa khawa seytané rek lalal j’aime

  • @matyndir3243
    @matyndir3243 Год назад +3

    Macha Allah kiné ya bakh❤

  • @ndeyesalioundiaye3119
    @ndeyesalioundiaye3119 Год назад

    Machala ndeya beugueu khale djiguen bou bakh

  • @djashkeub7231
    @djashkeub7231 Год назад +1

    Tarkalla yaneu tiatt sekhlou ❤😊

  • @fatoukhadyndao
    @fatoukhadyndao Год назад

    Machala li nekhna que dieu vous protège référence geneu

  • @hhjg1664
    @hhjg1664 Год назад

    Ywtamet borom bakh nga maa shaa Allah laf

  • @diatousow6235
    @diatousow6235 Год назад +1

    Masha allah diam nekhna ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @khadisall3762
    @khadisall3762 Год назад +6

    Kinè❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @queeenb1612
    @queeenb1612 Год назад +5

    Ça se vois que tu es une grande Dame kiné Machallah

  • @KhadijaThiam-o6o
    @KhadijaThiam-o6o Год назад +7

    Machallah

  • @ndeyediop7665
    @ndeyediop7665 Год назад +1

    Kiné bakh naa wayyé dieukeur kine tam nitt kou bakh laa lii niou bakh rek nioko meune Machallah rafet naa wayy aduna amoul sollo ❤❤❤

  • @ANNASOWFAYE
    @ANNASOWFAYE Год назад

    Machaallaaa Machaallaaa rafetnaaaa❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @antasarr6708
    @antasarr6708 Год назад +18

    Machallah❤❤❤❤❤❤❤

  • @KhadySamb-b2j
    @KhadySamb-b2j Год назад +2

    Machallah kine ❤

  • @boussosarr5996
    @boussosarr5996 Год назад +2

    Mais kiné mi Nice na dal🎉

  • @fatimasow3816
    @fatimasow3816 Год назад

    Lii nexna macha allah Kiné ya bax dh bilay wolay♥️♥️♥️

  • @beautenayo1031
    @beautenayo1031 Год назад +1

    Machala kou beug Dom beug ndeye

  • @seynabouthiare6927
    @seynabouthiare6927 Год назад +6

    Machallah ❤❤❤🥰

  • @saliougueye3334
    @saliougueye3334 Год назад

    Machlalla kiné ❤wah dji rafett n'a

  • @moustaphabadiane9824
    @moustaphabadiane9824 Год назад

    Ni rek ga mana mêl ndakh badiane ga sant nak😂

  • @fatounjie9444
    @fatounjie9444 Год назад +1

    Machalla li reffetna❤❤

  • @Salimata-lp5uc
    @Salimata-lp5uc Год назад +2

    Machalla 🥰🥰

  • @KhadijaRassoulTurpinDion-ez6ny

    Yi dieké you bakh machalla

  • @dabasamb5607
    @dabasamb5607 Год назад +2

    Kiné yalna sa diama yague

  • @sokhnandiaye6177
    @sokhnandiaye6177 Год назад +1

    Mane you melny la begueu guiss image you bakh yi nekh ci khôl limoyy class

  • @fatoukineniang958
    @fatoukineniang958 Год назад +1

    Mane dh sama yaram bi mougui daw🙈 non sama magg dji sama tourando ya gueune té riche mashalla mane Daga ma nekh kiné 🥰 Yalla nala Yalla defal diam

  • @MaryBadji-c5y
    @MaryBadji-c5y Год назад +1

    Machalla kiné nitt kou bax leu

  • @awaassiroudrame8907
    @awaassiroudrame8907 Год назад

    Kine mannnnnnchaallahhhh❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @ndeyeantaba5284
    @ndeyeantaba5284 Год назад

    Bilaye kanamou kiné Bi bakh réke lassiye lire

  • @laissaghenou
    @laissaghenou Год назад +2

    Machalla ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @KhoudiasyllKebe-cf3nz
    @KhoudiasyllKebe-cf3nz Год назад +2

    Masahalla rafetena

  • @fatoukasse180
    @fatoukasse180 Год назад +2

    Kiné sa rafét lanla tmt❤

  • @MariemeCoulibaly-c7d
    @MariemeCoulibaly-c7d Год назад +9

    Machall 🥰🥰🥰🥰

  • @batorfall9794
    @batorfall9794 Год назад

  • @adamengomndiaye4209
    @adamengomndiaye4209 Год назад +2

    Kiné ❤❤❤❤❤

  • @racinefall8550
    @racinefall8550 Год назад +15

    Kiné sa jéste bi rafétena

  • @alycapousa9908
    @alycapousa9908 Год назад +4

    Kanamou nit kou bakh mo nekha khamè

  • @coumbasarr467
    @coumbasarr467 Год назад +5

    ❤❤❤❤❤❤❤👍

  • @babacarcisse-qy8xm
    @babacarcisse-qy8xm Год назад +1

    ❤❤❤❤❤

  • @bayematardiop1833
    @bayematardiop1833 Год назад

    kiné kou bakh gua vraiment

  • @kinediaw3737
    @kinediaw3737 Год назад +2

    Way kiné rek ga meuna toud

  • @okalsdiallo2443
    @okalsdiallo2443 Год назад

    Borom moussor bou jaune bi khana dagnoukoy togne😂😂

  • @fieldbattle6618
    @fieldbattle6618 Год назад

    Ndeysane li dawna yaram

  • @KhadijaRassoulTurpinDion-ez6ny

    La femme d Eumadi ressemble à Ryana

  • @GnimaSambou-bb9ul
    @GnimaSambou-bb9ul Год назад +4

    Séyou Sénégal bouniou là gueureumé déh gua

  • @ndeytall8463
    @ndeytall8463 Год назад

    Degal nafekhh yisii soufff thim domou adama dafay rafelal adouna amoul solo wayè di roubè rekk thim🙄😡😡

  • @soulagertvofficiel8782
    @soulagertvofficiel8782 Год назад +2

    Non franchement yaye fall yomboule

  • @SaineyJagne-t7b
    @SaineyJagne-t7b Год назад

    Mashallah sis❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @nogayendiaye9789
    @nogayendiaye9789 Год назад +1

    Au c’est 🥰 j

  • @NafidioufFina
    @NafidioufFina Год назад

    La femme n'es pas contente on dirait