Yeumbeul la deuk❤️ moy sama lép❤️ Mais nit moy déf lignou koy respectéwé amoul Yeumbeul amoul fénéne mais diom ak diomou dioumou si nit killa Gno meuna défare Yeumbeul mais pas État
Bilahi des références dans ce pays sont de yeumbeul mais daniou geum sen bopp ame ay principes ame louniouy bagne diko niaffé dignement ABBA nostress doyna exemple ak nienen
Moi j attends personne sur mon avenir,chacun est capitaine de sa vie je n peut pas comprendre naître dans une famille modeste after tu te mets dans tes choses di sonnal sa famille sonnal sa boppou.banlieue ou ville keinneu gueunoul keinneu keinneu euppeulei wou fi keinneu, la belle vie se trouve dans la banlieue ,et ce sont des gens travailleurs et nobles ,y en a qui ont des maisons en ville diko louer tokk fi banlieue bi deukkeu fi aisément alors arrêter de coller des mauvaises images , Sénégal on a un problèmes d infrastructures de base sunu capital Dakar bi sax banlieue toubab sax mokogeuneu sett
vraiment ce monsieur balla me tient vraiment au cœur félicitation et Bonn continuation tout iras bien vive la jeunesse seul les imbeciles ne changent pas vraiment je suis ému
je suis vraiment ému du courage mon frère bala seul les imbeciles ne changent Bonn continuation nous voulons des jeunes engagés comme toi monsieur l’ambassadeur la voix des sans voix
Où en est la responsabilité des parents ? Di sétane sa doom bamou djeul yen yon yi, lidjeunti wo ci loumou nek... Bala État, je pense que le point d'interrogation doit être d'abord orientée vers les parents.
Il mavait une fois agressé en 2019 a yeumbeul pres de chez lui meme. Jetais avec ma petite copine dans mon vhl vers 20h. Il sest precipité avc son complice pour volé son phone et courir ignorant que je suis homme de tenue. 2h plutard jai debarqué chez lui avc 2 sections de la police de golf sud. Son pere et sa maman me suppliaient de faire preuve de pitier et cest vers 00h qu'on la choppé avec le telephone. Il est ensuite conduit au poste de police et je lai gracié a cause de sa maman qui ne cessait de pleurer... Bonne continuation
JE VOIS JUSTE DES SAUVAGES !!! YEUMBEUL,PIKINE,MERMOZ,SAC, PEU IMPORTE!!! LEPP SI NITT KI. LEU!! LA VALEUR D'UN HOMME N'ATTEND POINT LE NOMBRE D'ANNÉES!!! NITT DANGAY AM DIOM DEF YEUFFI NITT
Wakh bobou moma metti comme si telephone diaroul khaliss Wala kiko djeund khaliss bi dafko for a vrai dire des aigris et méchants lilen meti si autorité yi niou beug ko keup si kaw des innocents qui sont volés également par l’Etat c’est déplorable niom sathiouniou État bi mais des citoyens comme eux pourquoi y’a pas de raisons teggouniouko feeen Bayilen sathieu bi tei dem liggey mo geun
BARKI SERIGNE BAMBA MIMA YAKAR. BALLA MOSS NAMA KOTHIE POUR NANGOU SAMA TÉLÉPHONE YEUMBEULE. MAIS FINALEMENT DAMA DIEULE RISQUE BA GUÉNE THI. NGUIR YALLA BAYI LÉNE BANDITISME BI SVP.
Franchement is étaient dans la mauvaise voix et là ils sont devenus raisonnable et veulent mm changer ces jeunes qui veulent entrer dans le banditismes on ne peut que les soutenir a changer leurs localité
Balla mbame taye mome ame ngA diom aye balla nena changé na🤣🤣🤣🤣🤣🤣👏👏👏
Nos sincères remerciement à SeNEGO , Il faut encourager les jeunes comme Balla mbaam car leur situation est difficile
Très beau travail SENEGO. Des endroits de Dakar que nous ne connaissons pas; des réalités pas toujours belles que vous nous révélez! Merci
Yeumbeul la deuk❤️ moy sama lép❤️
Mais nit moy déf lignou koy respectéwé amoul Yeumbeul amoul fénéne mais diom ak diomou dioumou si nit killa
Gno meuna défare Yeumbeul mais pas État
Bilahi des références dans ce pays sont de yeumbeul mais daniou geum sen bopp ame ay principes ame louniouy bagne diko niaffé dignement ABBA nostress doyna exemple ak nienen
Félicitations Senego pour ce document inédit
Moi j attends personne sur mon avenir,chacun est capitaine de sa vie je n peut pas comprendre naître dans une famille modeste after tu te mets dans tes choses di sonnal sa famille sonnal sa boppou.banlieue ou ville keinneu gueunoul keinneu keinneu euppeulei wou fi keinneu, la belle vie se trouve dans la banlieue ,et ce sont des gens travailleurs et nobles ,y en a qui ont des maisons en ville diko louer tokk fi banlieue bi deukkeu fi aisément alors arrêter de coller des mauvaises images , Sénégal on a un problèmes d infrastructures de base sunu capital Dakar bi sax banlieue toubab sax mokogeuneu sett
Merci tu as tout dit c’est exactement ça niit yi nio beug sonal sen bopp ak tel sen bopp lou metti ils se stigmatisent eux même
Machallah bon courage mr l'ambassadeur Bala,
Bonne continuation 🙏respect
Machalah bala taye mome contenna si yaw yalnala yalla diapalé nga égale sa rêve
Ôôll
Ôô
Merci balla kham nala bou bakh nite kou bakh nga mane yeumbeul la dèkk layène
Que dieu vous aide.yala bakhna
vraiment ce monsieur balla me tient vraiment au cœur félicitation et Bonn continuation tout iras bien vive la jeunesse seul les imbeciles ne changent pas vraiment je suis ému
je suis vraiment ému du courage mon frère bala seul les imbeciles ne changent Bonn continuation nous voulons des jeunes engagés comme toi monsieur l’ambassadeur la voix des sans voix
balla mbam vrai dmrm leu guiss nako arene nationale mouy guinz bay langue
Yalna borom bi léral yone wi sopi ñeup silou bax🙏Courage balla
Amine
Yalla nalèn yalla takhawou du courage
Aidez les jeunes à travailler moguene di sacthie aay milliards ak politique boudoule diekh
Surtout lolou
Boye khale you ndaw ngen ndimbeul dathiy fek lokhoy borom wakho fi dara gni defoul dara Ken teuthiou lene demlen ligueyi mokeun lingay wakh
😄😄😄😄😄😄😄😄 wooooooooooooooooy déna
@@ndeyedieng7722 wakhou ma deuk
Ndeysane amna solo
Courage Balla yalla bakhna
Courage wa yeumbeul leip yalla leu xoll bou fess si yeine
Boy dem len dafi manœuvre petit à petit l’oiseau fait son nids
Bilakhi nk frr
Deug Deug journée 2500 kouko def 1 mois ame départ
Fanne mosye Maroc ak Gambie ♥️Sénégal mome cv bakhena koi
Ah balla khalé la yal nala yalla térale baga téral sa yaye inchallah
Vive la jeunesse sénégalais
Personne de Nous aux commentaires 👌 ne doit Jugé ses gens là 🙄
JUSTE YALNALENE YALLAH TAKHAWOU POINT👌
Ndayesan 😭😭😭😭 diadiaff waye balla
Où en est la responsabilité des parents ?
Di sétane sa doom bamou djeul yen yon yi, lidjeunti wo ci loumou nek...
Bala État, je pense que le point d'interrogation doit être d'abord orientée vers les parents.
Li niaw n'a bilahi
Jah jeuf balla ak sa gayi continuez rek ALLAH bakh n'a
Bonne continuation senego 💯👍❤
YALLA BAKH À FRÈRE COURAGE✌🏽
Merci balla la voix des sans voix
terrain basket moom ligéyoukay moko eupou dolé
amlene diome deme ligueyi mo geune
Lolou moy deug
Sa waay li nguéni khamouléne ko. Ce n est pas la voie qu ils ont choisie.
Billay
@@momolaye3574 bilay mou gaune
😂😂mane Gambie ak maroc ci birr yeumbeul moma deff cas😂😂bref bon courage
Fo faté senegal bire yembeul bref yalnalén yalla takhawou
Boul fate grand théâtre
🤣🤣🤣🤣boulenma raye
C est inadmissible niougui niow yagetoul defer sa niou dek xalei yi nek France xamounio chance bou niou am yalla baxna lo guiss dayi diex
merci balla 🙏🙏❤️🥰🥰
😥😥😥😥😭😭ces vraiment triste 😢 où est létat😱
Il est important mais le journaliste n écoute pour qu il se termine
Bonne continuation et bonne sensibilisation
😭😭😭😭😭😭 Yalna lènne yalla takhaowou sopplènne oubbillénne bounetou khéweulyi
Ameen🙏🏻
Amine ya raby ❤️
Senego forever 👌👌👌🙏🙏🙏🙏🙏👍👍👍
Bon travail senego
Ex bandit🙄🙄🙄🙄🙄 Alkati dou bayi door🚶♀️🚶♀️🚶♀️🚶♀️🚶♀️🚶♀️🚶♀️
courage balla yak mafia bi doli lène goorgorlou rek yalla bakhna lèpp dina bakh
Yalna niou yalla dolli soutra
Côté bi gneuw naafi done setci gueil goudei fa wayei yalla rek moma suturale😥😥 Qu’Allah les assiste
@@boubacarndiaye9214 😂😂😭😭😂 djiguene moy deflo goor lounei
Ah ah ah dotoko defati
Djiguen meun n’a louneeeh 😂😂😂
Il mavait une fois agressé en 2019 a yeumbeul pres de chez lui meme. Jetais avec ma petite copine dans mon vhl vers 20h. Il sest precipité avc son complice pour volé son phone et courir ignorant que je suis homme de tenue. 2h plutard jai debarqué chez lui avc 2 sections de la police de golf sud. Son pere et sa maman me suppliaient de faire preuve de pitier et cest vers 00h qu'on la choppé avec le telephone. Il est ensuite conduit au poste de police et je lai gracié a cause de sa maman qui ne cessait de pleurer... Bonne continuation
khaléyi dagno wara khol si sén parents yii surtout yaye yii ay goor laniou thé faible
C'est un vrai déléquant, alors que la population fait ses témoignages, c'est tristes
Balla manguilay nianal yalla nala yala diapalé té nga tak soxna diotna
Vraiment siii j'avais les moyens bilahi ma diapaléléne parce que c'est pas yeumbeul mais Sénégal
Bonne continuation balla mbame 🤙🤙🤙🤙🤙
le journaliste est pro pro pro pro
Diadieuf balla continue rek day bakh
sénégal bilahi sone gouvernement mono sacrifié 😢
Arreter de dire ex bandit boy bi on habite ensemble ki dou bandi dou dra da niaw rek dou tousss dof doflou rek moko nekh domeram dji
😂😂😂
Dete way
W😂
Ok da niaww ndeysan 😂😂😂😂
🤣😂😂🤣😂niaw mom deff naku
Mdrrrr 😂😂 BALLA mérré na goordjiguén gni
Vive senego tv
Un pays qui ne s’occupe pas des enfants n’a pas d’avenir
JE VOIS JUSTE DES SAUVAGES !!! YEUMBEUL,PIKINE,MERMOZ,SAC, PEU IMPORTE!!! LEPP SI NITT KI. LEU!! LA VALEUR D'UN HOMME N'ATTEND POINT LE NOMBRE D'ANNÉES!!! NITT DANGAY AM DIOM DEF YEUFFI NITT
Balla mbaam Nice
Banditisme Bii nGenn warra Bayi
Amoul chance 👍
Situation de vie bi état bi tok di sétane n’a rasé fiii construit aye école boy yiii deme école construire aye hôpitaux
Nice frére
Man dh douma mese deuk yeumbele 🤦🏾♂️🤦🏾♂️démone nafa m3 dafa bizarre
Esk wa ymbl soxla negn pour gua deukk feu?
Yeumbeul mola sohlawoul yaw
@@alimadiop6624 😂😂😂
😂😂😂
@@JEYTUBE1 😭😂😂😂😂🤣 balko
Ama big up tu parle bien 👍🏾
Vraiment je suis un banlieusard et suis fier courage, j'aimerai bien avoir son numéro pour travailler avec eux
Resté là-bas à attendre gouvernement bi pour mou défarale léne séne deuk pour commencer à changé séne sur non yi changé léneko d'abord
Amine 🤲🏾🤲🏾🤲🏾🙏😭🙏
Dicourage balla la voix des sans voix
Yalla bakhna frère balla
Oh la Maman😭
N'importe quoi il défend un vol de portable et revendique du respect. Je suis un fils du yeumbeul mais copain bi wahoufi dara.
Wakh bobou moma metti comme si telephone diaroul khaliss Wala kiko djeund khaliss bi dafko for a vrai dire des aigris et méchants lilen meti si autorité yi niou beug ko keup si kaw des innocents qui sont volés également par l’Etat c’est déplorable niom sathiouniou État bi mais des citoyens comme eux pourquoi y’a pas de raisons teggouniouko feeen Bayilen sathieu bi tei dem liggey mo geun
Ndeysan
Lou lerr nga wakh man bougn ma wakhè livraison yeumbeul damay bagn ndakh amoul taly... sen situation mettina trop boyii louniou guiss liguey mais guissouniou koulen talal lokho
🥺
Vraiment j'ai le cœur meurtri comme étant un fils de yeumbeul et vous vous permettez de ternir l'image de notre localité c'est regrettable
Dama diooy
Les ex bandit qui deviennent des héros
Yallah n'a ko yalla déffal diam
BARKI SERIGNE BAMBA MIMA YAKAR.
BALLA MOSS NAMA KOTHIE POUR NANGOU SAMA TÉLÉPHONE YEUMBEULE.
MAIS FINALEMENT DAMA DIEULE RISQUE BA GUÉNE THI.
NGUIR YALLA BAYI LÉNE BANDITISME BI SVP.
Khana dego imison
😢😢😢😢😢😢
Diapalé lenn jeunesse bi niou guénne si li
Amna solo
Vidéo bi amna sollo
Dem len liguey mo gueuuun
Franchement saint louis ame n'a diam deukou noble leuh saint louis la beugdeuk
Da guena rew deme lene ligueye
Yal naléne yalla takhawou yéne nieupe ték léne si yonou dioupe téral léne same léne
Courage balla mon ami d enfance 😍
Dalue j'aimerai avoir le numero de balla svp
@@antafall3881 je peux t’aider
@@antafall3881 moi aussi
@@antafall3881 Anta Fall moi aussi. J aimerai bien aider
Grand Théâtre 😂😂😂
Bilahi yuembll lanou deuk bala diam rék si yaw ❤❤❤👌
Merci wa senigo lidafa wara gene nieup guiss ko
Balla yalneko yale takhawou du courage
Balla demal Diangui comunication apres nga continer sa combat
Numéro Balla kouko bgue nak
Mais attendez , Balla ak Mbaye Gueye bokhoul ??? Pour ceux qui habitent a Yeumbeul kham nagne Limay wax....
Balla fierté natangué 👊
boy demlene ligueyi affaire yi si gneup lay meti mai tok di agresser ak sathi rek guene fi neker
Fall bou lene juger degn len nianal kou lene japale déf ko mettez vous un peu à leur place
@@ibrahimandiaye9928 🥺
Franchement is étaient dans la mauvaise voix et là ils sont devenus raisonnable et veulent mm changer ces jeunes qui veulent entrer dans le banditismes on ne peut que les soutenir a changer leurs localité
@@keyshabarro leurs élus et l'état les ont abandonné.
@@keyshabarromerci
C l'échec de nos autorités mais courage Balla sa khol rafetna
😭😭😭😭😭
Pourtant khalé yi amouyou problème bilahi djakk rekk mo méti
Ils faut un métier ds la vie agressions dou métier boulen gni fonton
Aidez les jeunes, l'avenir d'un peuple ce sont les jeunes mais avec accompagnement
l'agent des sans voix
Balla yalla bakhna
Il faut lui laisser développer