Que justice se fasse: deux jeunes meurent, assassinés atrocement. Oh Dieu manifeste toi. Toi seul peut donner et reprendre vie. Que Dieu sauve le Sénégal Sénégal amen
aywaye borome barké yi yalla maye weur seuke dieuleul lén Waly AK Aziz avocat ndax gnilén raye yalla wét lén ndax séni mboke meuna nélaw khamné dougnou yandore mais Dina tané
Vraiment que justice soit faite il me faut car perdre des personnes chères c’est triste mais Yalla bahna lèpe Sunu Borom dinako léral in shaa alllah car Aziz avait un cœur en Or.
Prtan man meuss na deg Aïda di wax djekeur dji sah dafko teré won wax si réseau yi ba paré elle continue Di wax rek, svp nguen balma mais pr man wax dji yeup diaratouko justice pr Aziz é waly que leurs âmes repose en paix
Aida moytoul domram you tekiwoul dara yi nek si net bi dila pose ay question kom am ngeun avocat lolen am pour wakh wakhlenko ak avocat bi te lep lolen wakh ak avocat bi boulen ko netali ken toglen sen keur koulen beugeu diapale dinalen diapale,Abdou Aziz Ba ak Boubacar Gano ak mbolem julit yi jitou Yal nalen Yallah yereum
Quand je vois certains commentateurs😢, je suis siderée. Un meurtre aussi atroce sur deux jeunes pleins d'espoirs de vie. Certains veulent faire taire la famille au nom de quoi, vraiment vous pensez que ce crime crapuleux, aussi grave peut passer comme cà. Il ne faut jamais que cette famille aussi pacifiste soit elle, se retire. Cette affaire doit rebondir de plus belle, biensûr. La com de Kaali est necessaire parceque Sénégalais dafa guawa beugueu faté lou metti, Aïda ne lâchez jamais, cette affaire jusqu'à ce que justice soit faite. Li dé bou passé nonou ma khamné tay rek nguèndi khamni Ya Allah amnna👆🏾
S’il vous plaît Sokhna Aïda souma sagnone ngua moytou réseaux sociaux surtout les Influenceurs là comme gou mélni kaliphone Adamo serigne Bda choco no stress et des autres influenceurs you mélni gnoome par ce que ayy saytané naniou ta soutara ta gou mélni soutaral taaye bou souba dinanioula wéére merci beaucoup ❤❤
Que dieu vous assiste que justice soit faite aida du courage ne baissez jamais les bras ce crime est odieux sacrifier deux jeunes comme ça ça doit être puni
Nabou boko yonne sétalé barke mame chiekhra fall dotuma porte pleinte kéne parcek damay xamné yonne amatul sama réw mais cas nabou bi diouroul enquêtes dfa lérr nabou Complice la lolu dfa lérr comme midi
@@thiorogueyesarr5895 non Adja yoyu amatufi dé affer yi légui ci Yonne lagn Koy ték té affer Aziz bi sénégalais yi niolén ték pression dofouniou sakh bay libéré Nabou ci ay tapalé
Aida vraiment fi waroul lofi wotè Di wakhe.Gneupa rafetloul sa comportement jusqu'à présent continuer nonou té bayi site yi.Quant a comportement Nabou elle peut être sous le choc,elle peut être traumatisée.Chaque personne réagit différemment de l'autre.Donc continue à être digne té bayi wakhe yi
Nabou mo.waroul nanguou ay li erte provisoir il faut justice seralko bamou set mou guen wala..mou takei si mou dess si kasso bi kome tous les malfaiteures
Maneh yen mi neka si commentaire Yi naan Aida na nopi purr lan Moy nopi dangen kham lumoy yek si xolam nit ki su ameh metti tam sulen ko munote japaleh ngirr yallah tech len sen gemenj yi teh ngen mayko mu am jama suff ngen trop fi kunj fi rayun sah mak wala sah baye du nopi dangay wahk ndah askan bi ham lingay dondo sen negative comments yi dafa doy y akhhhh
Sougnko nei mou nopi c pas pour mou nopi bagna wax dara parsk nieup kham naniouni li dafa mety mei mou nopi parsk amoul loumouy wax ak gni parsk nio koy wax Lo ba dougeul ko limou wax ak avocat bi amoul pr diko netali keinne mom justice la amoul afaire pas jenre yi
Si c'est Maître Thiam c'est un très bon avocat mais bon cette famille a besoin d'aide car il faut payer dans tous les cas pas évident😢😢(Ève) mais ma soeur diminues stp les sorties sur les réseaux sociaux en toutes mes condoléences
Kalifone mowara bayi cas nabou leye ak aziz yone def ligeyeum mais day commerce rien k pour des vues kalifone motakh famillbi jamais aziz diok sén khel
Varema lii da fa wara leer l'an moo takhe wa justice defou niou commerce de paresse espilice nityi ndakhe Aziz Aziz bou Sénégal la lii bokk n'a chi louma bijiakhall def leen chi ay niaan yalna yala leerall ko dossier bii dafa wara leer
Aïda vraiment ware ga nopi ta guéne thi yi gnak rek doye na gnanal lene Aziz mo gueune taga guéne thi details yi vraiment Aïda sa wakh dafa Bari lou nek yagui thi
Justice pour Aziz justice pour Aziz justice pour Aziz justice pour Aziz justice pour Aziz justice pour Aziz pourquoi Liberte provisoire c edt pas normal
Que justice sois faite pour Azize😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
Aïda y’a des choses qu’il faut garder confidentielles et il faut pas tout dire sur les réseaux
Que justice se fasse: deux jeunes meurent, assassinés atrocement. Oh Dieu manifeste toi. Toi seul peut donner et reprendre vie. Que Dieu sauve le Sénégal Sénégal amen
Insha'allah tout va se savoir
Nabou même sou defoul sou guener comme elle va se réintégrer dans la société thiey force à elle ça risque vraiment d’être rude pour elle
La manière Don elle s'est comporter le jour de son décé
@@salimatabakayoko2840m c normal comme dafa demon sety kou rere lolou la fok
Justice rek pour Aziz et Wally 💪💪💪💪
Aida il faut laisser la justice faire son travail arrête de parler sur les réseaux sociaux
mayniou diame way bou wakhoul nakalay léré
Femme bi mo wara bayi wakh bayi yone def diobom
aywaye borome barké yi yalla maye weur seuke dieuleul lén Waly AK Aziz avocat ndax gnilén raye yalla wét lén ndax séni mboke meuna nélaw khamné dougnou yandore mais Dina tané
Loutahe mouye nopi il faut sénégalais yi diapaléko mou ame avocat
Justice pour Aziz et wally personne ne peut pas laissé sa khonne ça . c'est mal au cœur billaye wallaye c'est maaaaaal 😭😭😭😭😭😭😭
Ils ont besoin de l’argent pour payé Avocat
Justice pour les deux victimes
Aida moytoul wakh ak domiharam yi bakhna
Vraiment que justice soit faite il me faut car perdre des personnes chères c’est triste mais Yalla bahna lèpe Sunu Borom dinako léral in shaa alllah car Aziz avait un cœur en Or.
Prtan man meuss na deg Aïda di wax djekeur dji sah dafko teré won wax si réseau yi ba paré elle continue Di wax rek, svp nguen balma mais pr man wax dji yeup diaratouko justice pr Aziz é waly que leurs âmes repose en paix
Bien dit
Yow werou nakk , Aida da wara wah pasque Adouna mah takou tahow pareh nakk pour justice de Aziz et Wally. Konn nakk fog aye mbokam wah .
Yenn nakk kon werou leng ndekete , bou nope kann moy Kai diapale khana yenn wa Kerr Nabou Leye ngenn fi justice pour Aziz Akk Wally rekk insha’Allah
Est ce que ça va pour Lane dotoul wakh magam dei dou wax
Li Soula dalé sa xel dey diaxasso je la comprends motah mouy wah rek
Justice pour Azize
Nabou nenoul am liberté provisoire.
Et si elle est innocente
@@aisharassoul4586❤❤m tmt fawou audience am baparer
@@mormbaye2989 waw mais elle a le droit de demander la liberté provisoire
Aida moytoul domram you tekiwoul dara yi nek si net bi dila pose ay question kom am ngeun avocat lolen am pour wakh wakhlenko ak avocat bi te lep lolen wakh ak avocat bi boulen ko netali ken toglen sen keur koulen beugeu diapale dinalen diapale,Abdou Aziz Ba ak Boubacar Gano ak mbolem julit yi jitou Yal nalen Yallah yereum
Bayiko mouy wakh rek bilahi youkhou dina diougué finiouko foguewoul
@@adamaseck8816youkhou fan lay moudiou
Bilay xamo sax nigko waxé elle na rien a dire a personne sou diougué rk niouy live woko si mouy wax rk
Bilahi dafa wara def tres attention
Vraiment
Aida nopil waay amna yénn niitt gnii daniou lay yokk khalatt rek doul rekk laniou meunn dossier bii kénn amoul droit wahh sii instant bii démal tokk ngua mougn Sante Yalla
Aida laisse justice fait son travail ,il ne faut pas écouter les faux journalistes ,Azize et Waly reposent en paix
Quand je vois certains commentateurs😢, je suis siderée. Un meurtre aussi atroce sur deux jeunes pleins d'espoirs de vie. Certains veulent faire taire la famille au nom de quoi, vraiment vous pensez que ce crime crapuleux, aussi grave peut passer comme cà. Il ne faut jamais que cette famille aussi pacifiste soit elle, se retire. Cette affaire doit rebondir de plus belle, biensûr. La com de Kaali est necessaire parceque Sénégalais dafa guawa beugueu faté lou metti, Aïda ne lâchez jamais, cette affaire jusqu'à ce que justice soit faite. Li dé bou passé nonou ma khamné tay rek nguèndi khamni Ya Allah amnna👆🏾
Vraiment nga sagnko wax
Kalifhopne dafa kham sènègal rek day dimbali famille bi sino nabou ay avvocat wam dinaniou fèkhè mou gèune
Pourquoi liberté provisoire naniou ndeff ndeyame bubax dina waxx lep noumou demeh.Nabou leye domarame leu mo teyleh Aziz
Nabou leye mo raylou ndeye aziz ak waly.. Aida yoww massla bou bari dey indi nafeeek
Dang ko feké ?? Donc yaw tamite complice ngua dangua wara teud kasso com gnom
Maguette Seck a tjr orienté Nabou Leye en infos concernant Aziz Dabalant en tant k manager
Yalla na lep lere way si Barker seydina Mohamed
Aida loutakh mouy nopi dolen bayidiabour bolnopi sonopee rek lep daynil nji adakh nabouley niouley nopilo pour Len seda boulenko nagou Aziz AK waly danio yakha send adouna liken douko bayenounou dayabatrob😭😭😭
S’il vous plaît Sokhna Aïda souma sagnone ngua moytou réseaux sociaux surtout les Influenceurs là comme gou mélni kaliphone Adamo serigne Bda choco no stress et des autres influenceurs you mélni gnoome par ce que ayy saytané naniou ta soutara ta gou mélni soutaral taaye bou souba dinanioula wéére merci beaucoup ❤❤
Justice pour Azis😢
justice pour Aziz et wally point
Time is still going.Justice for Aziz n Wally
Que dieu vous assiste que justice soit faite aida du courage ne baissez jamais les bras ce crime est odieux sacrifier deux jeunes comme ça ça doit être puni
Nabou boko yonne sétalé barke mame chiekhra fall dotuma porte pleinte kéne parcek damay xamné yonne amatul sama réw mais cas nabou bi diouroul enquêtes dfa lérr nabou Complice la lolu dfa lérr comme midi
Nabou dafa am nioukoy protégé motah
@@thiorogueyesarr5895 non Adja yoyu amatufi dé affer yi légui ci Yonne lagn Koy ték té affer Aziz bi sénégalais yi niolén ték pression dofouniou sakh bay libéré Nabou ci ay tapalé
@@ThiernoSamb-l7e ahhh doyna waar dh nénagn ay franc maçon ladone liguèye yal Aziz yeuk ko après niou planifié ray ko
Aida vraiment fi waroul lofi wotè Di wakhe.Gneupa rafetloul sa comportement jusqu'à présent continuer nonou té bayi site yi.Quant a comportement Nabou elle peut être sous le choc,elle peut être traumatisée.Chaque personne réagit différemment de l'autre.Donc continue à être digne té bayi wakhe yi
Juste pour aziz et wally
nekk len ay nite ki dafa djakhlé rek sa famille a besoin de tourner la page
Nabou mo.waroul nanguou ay li erte provisoir il faut justice seralko bamou set mou guen wala..mou takei si mou dess si kasso bi kome tous les malfaiteures
Maneh yen mi neka si commentaire Yi naan Aida na nopi purr lan Moy nopi dangen kham lumoy yek si xolam nit ki su ameh metti tam sulen ko munote japaleh ngirr yallah tech len sen gemenj yi teh ngen mayko mu am jama suff ngen trop fi kunj fi rayun sah mak wala sah baye du nopi dangay wahk ndah askan bi ham lingay dondo sen negative comments yi dafa doy y akhhhh
Sougnko nei mou nopi c pas pour mou nopi bagna wax dara parsk nieup kham naniouni li dafa mety mei mou nopi parsk amoul loumouy wax ak gni parsk nio koy wax Lo ba dougeul ko limou wax ak avocat bi amoul pr diko netali keinne mom justice la amoul afaire pas jenre yi
Vraiment
Soff laniou deff rek
@@tantylarose809tu as parfaitement raison !!!
Nabou dafa louche sinon ken douko jap
Si c'est Maître Thiam c'est un très bon avocat mais bon cette famille a besoin d'aide car il faut payer dans tous les cas pas évident😢😢(Ève) mais ma soeur diminues stp les sorties sur les réseaux sociaux en toutes mes condoléences
Nabou doit payé toutes ses crimes
Vraiment
Kalifone mowara bayi cas nabou leye ak aziz yone def ligeyeum mais day commerce rien k pour des vues kalifone motakh famillbi jamais aziz diok sén khel
Justice for aziz
Dossier bi d doumoudiou fen
Aida nopi🤐🤐🤐🤐
Bousi bokoul wone dounie ko kat ndeyam teuyé !
Boul wakh lolou yallah rek mo kham naniou mandou
Exactement nabou meurtrière leye est coupable dagne kowara pendre comme tout criminelles Wasalam
@@AissataBah-ih1kpyangui accusé sans preuve com kou féké sache que yéné nek la yalla meunako setal mou guénn yaw gnou teud la wassalam
😭😭😭😭 bilay 😭
MAIS C'EST QUOI LA POSITION DE KALIPHONE C'EST PAR CURIOSITÉ OU C'EST POUR SOUTENIR LA FAMILLE DE AZIZ DABALA
Est-ce que dou topou cas rek😂😂😂
Wa khana ki amoul ay conseil pour mou wakh ko mou nopi
Dou nopi daye wakhe dafa méti trop wakhe léne na lére
Nabou an leye leye ley ley
HEY WAYE DEPUIS QUE KALIPHONE EST DÉTECTIVE PRIVÉ !!!!
THEUYE LIIIIIII
Lolou diaroul débat Sénégal amna justice
Attention Aïda ! ne divulgue pas les infos concernant l 'avocat
Dafa meti gua nopi beuri gua wakh ak micro ay wakh fadioul dara
Vraiment dafa wara nopi gni dagnkoy dougeul rk😊
Vraiment LP pour Nabou Leye ! c est inpensable. Dble Meurtre.
Nabou leye mome su guené bou yabo mou defal bopam prisonnier ndqkh peupeul bi douniouko may diam
😢😢😢😢😢😢😢😢😢
Thiéy adouna 🥲😭
Falait pas nomé le nom.de avocat ? Jai plus confiance de se pays mais ley leuy takana dji rib dafa wara lére 2meutres c trop. Justice pour aziz Dabala
Ousmane sonko wakhal sii birou aziz dabala diakhalna sénégalais trop trop trop barri mouhamed euleum nagnou
Mame fille arrêtez de parler dans les réseaux sociaux et faites vos démarches dans la discrétion .
C'est en ce moment qu'il fallait cherché un avocat
Conséquences de votres naïveté
Varema lii da fa wara leer l'an moo takhe wa justice defou niou commerce de paresse espilice nityi ndakhe Aziz Aziz bou Sénégal la lii bokk n'a chi louma bijiakhall def leen chi ay niaan yalna yala leerall ko dossier bii dafa wara leer
Thiey senegal c les criminels ki sont prioritaires k les victimes nabou leye a fait son crime parfait c les lobbies ki vont la faire sortir du trou
Il faut la reconstitution des faits d'abord
Aida tègua nopi tè bayi justice bi liguèy
Merci beaucoup kaky yagui diapou thie dossier bi
Vraiment Aida bi Affaire yi Ame ba Legui Niepou thi Dal Laniou la Khame kon nak maytoul Média bi
Femme bi ci bopam mo beug micro loko wakh mou nann famille bi
Nabou ell la comandite tout laffaire prisont a vue
Kali yalanayala Faye li mome live bou ame solo la
Kali ci bopam mo soff, seytané
Aïda vraiment ware ga nopi ta guéne thi yi gnak rek doye na gnanal lene Aziz mo gueune taga guéne thi details yi vraiment Aïda sa wakh dafa Bari lou nek yagui thi
Lolou louma maitilla lane la asiss desna ooooo ki dou nitt
Que c soit nabou ou un autre s ils sont coupables ou pas la justice nous dira
Merci
Yen meuno len bayi yone def ligueyam tmt li lanla té guen gnanal Aziz
Niak ba paré topou internet bi di wax rék yénagi beuge soof nak
Reconstitution des faits lolou amoul Sénégal fi niou Ray yeup diapp nagne kon rek lagne si am
Justice pour Aziz justice pour Aziz justice pour Aziz justice pour Aziz justice pour Aziz justice pour Aziz pourquoi Liberte provisoire c edt pas normal
Si défois dagne kayy def
😭😭😭😭😭😭😭😭🤲🤲🤲
vraiment il faut prier pour les2 défunt tu entrain de remuer le couteaux dans le plait
Sen famille togoul foneu fou Serigne nekk dem Nay fa ma Casamance
Aida yow enquêteur ga wala,do bayi enquête bi derouler tei bayi wakh thi reseau yi,elle peut être complice :louy avocat kou ray sakh day dieul avocat.
Femme bi yobou lén ko ci psychologue elle parle trop
Bilay. Gni mouy wakhal moma geuneu meti
Aida danga wara nopi te arrêter khaliss yi ngay dieul louné khadjinasi
Sa makk bou déwone do nopi
😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢
Senegalese niak ngene fayda kalifone Legui juge la sarap li rek un grand menteur manupilatore
Ki mo dof deh loyi wakhe ngila diapale ak sa tourou avocat sheut
Sénégalais mo bari nafek ki niou ray magam guenn né waroul wakh
Sénégalais kouko téré wakh mou xarou
😭😭😭
Police reconstitution des faits lay khar pour appartement bi
Lotah my noppy sanegall so waholl sa dara dobahh
Ce que vous faites garder le pour vous par prudence stp
Yao dakhanal ndayam outo ligueyu lii dou liguey doll ak lidjeunti problème djambour
Sénégal kou dè ya perte kharitok yalla mon geune
Nabou da beug Daw
😂😂😂😂😂😂
😂😂😂😂😂😂
Bilay aida faik nitekou dée ak ay bain de sang tai dara yaingueloula si dieguaine
Ki moy kaan ba kay wo mouy wakh. Li bane importance la am ?
Wa aida mi mome dou nopi mome leup laye netali n'importe quoi
Mais je pense pas reconstitution des fés dina âme, combien de meutres mo âme ils.ont jamais fait ça
Loutax ngaine beugue peuteuxal nabou bou koo justice baayé c’est parce que daifoul daraaa
Doul iow
Yaay complice çam
Bou defoul won dara ken douko teye
Mane lima diaxal moy nabou leye rek lanou diap lii motax siw baxoul
Mayléne niou diamb waay
Ko police diapou guene nane gamou ko kone dou ko diapou si la boko