Rajass Serigne Bollé Mbaye Journée Khassida Touba Ngaye 1442 H 2021
HTML-код
- Опубликовано: 16 окт 2024
- VISITEZ NOTRE SITE WEB/ toubavision.com
RETROUVEZ NOUS SUR LES RÉSEAUX SOCIAUX SUR IPTV
TELECHARGER NOTRE APPLICATION ICI play.google.co...
TEL: (00221) 774162512 / (00221) 768332354
Abonnez-vous dès maintenant gratuitement sur ToubaVision : Touba en Image 24/7
" Toubavision, la télé qui suit l'enseignement de Khadimou-Rassoul"
/ @toubavisiontoubavision
Serigne bollé mbaye limiy diangue mo nekh ta leer dieureudieuf khadimour rassoul 🥰
Serigne bolé mbaye maa laa sope guir Serigne touba akk Xassida yii yalla naa la yalla mayy akk wéer akk goudou fann thi barkepp Xassida yii amein
Thieyyyy Serigne bolé 🥰🥰🥰🥰🥰🥰😍😍😍😍😘😘😘😘😘
Yalla nga goudou fannn barkep Xassida yii🥰🥰
Aminnn Fall🤲🤲
❤️😭thiéye Ndeyssane Bolllé mbaye toujours égal à lui-même yalla Nafi yague té werr 🤲🏾
Thiaye baye bolé diguama ray dé barki Brom TOUBA
Ndeysan lii dh falama fekk Thiès la diougué won nadj bou tangu
Serigne yala ngafi yagu tei weur🙌
Ndeysann Serigne Bollé Mbaye yalna Serigne Touba Faye la Barkeb khassida yi
Machallah Baye Bollé yag ak wérre
Machalla Serigne Bollé
MACHALLA
Maaachallh ❤️❤️ maaachallh ❤️ yalnala ahmadou bamba fay brkép mouhamadou Rassoul✨✨✨
Dieuredieufé mame cheikh ibrahima fall lamp
Yalna Yalla goudeul fanam and ak wérr gou yaraam
Yalnala yalla defall jammu
Dieuredieufé borome touba mbacké
Yalla nako yalla gauna deugaral da jeum mak wayei yeini dji mongui fi ba leigui
Maziyatt ❤️🥹
Ndaysane thiey bay bollee😭🤲
❤❤❤❤❤❤🎉🎉😊
❤❤❤❤❤bollerek❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machalla
Machala serigne no le mbaye
Machala serigne bole mbaye
Machala mourid
Yaaague fiii
Mo nékh