Grand avec tout le respect qu'jte dois s'il te plaît on veux pas d'anciennes video parle de l'actualité li yague na werou koor gui la wone kham naniou leup kone soit nga wakh si lolou wala nga wakh si actualité Magui diagalou wat nak dh si je t'es offensé
Yaw lo beugeu mou dougeullko ay khoulo ak ay histoire Yaw kou beugeu fitna nga So guissé mou binde li bouko dara yakheu kéy moy niniou mélone démb ak barki démb bouniouko yakheu taye❤
@@papegorakhassidaofficiel7090 khoulo ak histoire prkw faire? fitna Kaye mm po talna lenen hum sen digenuté dara khewousi kou guise lii daye diap ni amna lou xew motakh. Fofu laye wakhé grand bi iba tmt a comprit voilà lerr na?
Affaire bi xol bou raféte la nite dangay nite yor xolou baye fall .pape sarr minguén di wax dof mo djibolé mbeurou pikine yeup kon kokou mola geun si yalla nakh mingui dokh akh deukeudo
❤❤❤❤❤❤
Geste noble c pas deux mais un
Dans l'ensemble l'union fait la force🎉🎉🎉🎉
Au waay Bouléne yakk 200/100 pikne waay li rafetna
Lii dafa yagg waaye
Iba kane Khame nané li Défar Rék Nga si Dioub lou Ndayesane Yaw Kou Bakh Nga ✅ Kham n'ané Lou Yageu la nak
Sa c’est c’est longtemps
Li si koor gui leuh
AMA baye fall leu♥️
Ndélou Ama bi télle na sakh di😮😮😮😮 nonnn yéneu meuneu doule
Li yaggneu dèh ama da ndelou
Merci beaucoup ❤❤❤❤
Félicitations l'observateur.
Li war na amate d wax kate yii dinagne yakh pikine d billahi li dafa nekh
Yalna diamu yagu bilay Ama dako beug yalnako yalla may ndam thi kay gris boy Ning aussi yalnako yalla moy ndam thi kaw modou lo inchalla ❤🙏
Li yageu na dh
Li yagg na ama nélam bi sakha goul
Li yaguena apres combat balla boy niang bilawone
Feleicitation à Modou lo !
Mais surtout Bravo à Ama Baldé pour ton immensité, que la suite de ta carrière soit paix et prosperité 🙏🙏🙏
Wa ana néélll bi
Liguana dei
Bayilén doul li yagg na trp bilay akkeu ngén niy doundé
Iba kane yaw loukofii jar li yagna akh beug geumlo nit gnii li c'est l'aprs combat
Amakassse❤❤❤
Fen rék
Li defna 6 mois delen postuler lou Bess way
Modou lo mooy bandit dh defaral na boyyi😂😂😂
Mandou
Li dou taye ish yagna😂😂
Mais Li yagna deh wala?
Bouléne fonto nitegni ca ç est pas l actualité bou boy niang dano baparé gnou dogua fér plaiy
Nafekh yii wakh dai rouss nen ma seii Boucher khecup yii na fii nekhe marr tat rek
Ama boy Niang bimou waré nieuw takhawoula défouko dagnoulaye nakh boulko nangou dagno yakar né dangéni sott motakh niouy rafétal
😢seytane bakhoul yen gniy wakh si diguante bi yenay seytane mais tey warguen rouss
Lii yagg na deh
Li yageu na dh
LI DOU TEY BA NGAY NEE WAR NGUENE ROUSS
Iba kane li ngeuh publier yaag neuh Ioe mi niT woo
😢😢😢😢😢😢😢 ndaysane pape sarr migui dioye😢😢😢😢
Lii yagna ama dah ndélou👂
Ndel bi meunoul sakh
@@methzoblinde3112 kone mou gaw di
Mais attends 😢😂😂on n'est au mois du Ramadan.
Un peu de sérieux cher journaliste
Seytané yii khana dinane nopii niar gni niofar doune ay none mais nak doof doof rek laay donne
Li yageuna trop.boy niang diapaliwol ama balde se combat bi
Iba kane soit beaucoup plus professionnel. Hana Ama nél bi djiné mokoy arroser
Boy Niang loumouye wax sax gueumouko😂😂😂
Li yague na dh
Lou nice
❤❤❤❤❤
Modou lo réuthie na deh li yag na
Lac mo gueneu paré
Ce vidéo date de 1 an et plus
Hol séed na waay
Li yageu na dh
@@xaleysenegal7217 si koor gui la saway
Yalanalén yalla mousale si séytané
Grand avec tout le respect qu'jte dois s'il te plaît on veux pas d'anciennes video parle de l'actualité li yague na werou koor gui la wone kham naniou leup kone soit nga wakh si lolou wala nga wakh si actualité
Magui diagalou wat nak dh si je t'es offensé
Non jamais je te comprends. C'était juste pour montrer aux pikinois qu'il y a rien entre Ama et Boy Niang
Yaw lo beugeu mou dougeullko ay khoulo ak ay histoire Yaw kou beugeu fitna nga
So guissé mou binde li bouko dara yakheu kéy moy niniou mélone démb ak barki démb bouniouko yakheu taye❤
@@papegorakhassidaofficiel7090 khoulo ak histoire prkw faire? fitna Kaye mm po talna lenen hum sen digenuté dara khewousi kou guise lii daye diap ni amna lou xew motakh. Fofu laye wakhé grand bi iba tmt a comprit voilà lerr na?
😮non Ama nakkk nitttt kou bakh laaaa❤❤❤❤❤❤
Mo li yague na
Nice
Li yageu na dh
LI YAGUENA DEE COMMENCER NGUENE SEN YEUFOU FAKE YI
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Site bi dou dougall actualités fake New rék akh
Copain no def. Daniouye defar rek thiow li dans bari trope Pikine
Iba kane boul jaxasser li yageu na dh Bayi sa yi ngay deff ❌❌❌❌❌❌❌❌❌❌❌❌❌❌
Boy Niang dafa nité diange bolé si xél mimou yoré dof yi yorou gnouko gni c'est des farfelu
Affaire bi xol bou raféte la nite dangay nite yor xolou baye fall .pape sarr minguén di wax dof mo djibolé mbeurou pikine yeup kon kokou mola geun si yalla nakh mingui dokh akh deukeudo
@@leuz.patriotebaye fall dou dioulli dou woor nganane kholou baye fall wakhi doff kokou kholam day wow
Iba Kane ay vues waroul takh ngay yakk sa image li yaguena waroko sakh dougueul
Ce que t’as fait c’est de la désinformation
Liii mo rafétt bayiléne saytané yakh rék ngéne di ligéyé démléne wouti ligéye ta bayi doul yi kénne koumék ak sa weurseuk
Billay Ama sportif deug nga
Li yageu na dh
Boy Niang, sa famille et Pape Sarr t’on sacrifié. Dommage que t’as pas un bon encadrement