Ndeysann keba on a grandi ensemble à colobane, lii dafko dapp,et peut-être c'est dans les geines puisque son papa aussi était comme ça, il s'est retrouvé aveuglé du jour o lendemain avant le décès de la maman de keba, la dame ki pleure dans ce clip est sa grande sœur Anna.....yallah nako yalla takhawou
J’ai vécu même histoire en 2022 ma tokk sama place dioulli tizbar diott ma diogg pour dèm diapou dji bima dèmè basi porte bi rk sama beut yi commencer flou sama bopou bi di mètti aussi deuxième jour bi ma yèwou rk guisa touma dara ndeysane sila gnibi touba quelques mois après alhamdou lillah mou tanè ma commencé di guiss nake nake bi insbi mou mèll comme avant yalla nala yalla wereul barkè ahmadou
Bonjour fils,Keba,c'est Tonton SECK, responsable École football feu Capitaine cheikh Tidiane Thiam ,"yalla nala yalla delo say beut thi barker BOROM TOUBA.Oh tout ❤️❤️❤️ avec toi fils
Bilakhi Lou méti dall ne sama béne copine aussi niou djoye thi be sone mome tam da teud nélaw yéwou Guisseu toule dako dabe aussi méti ne torop Mai’s niou bayi lép thi lokho borome bii long vie à eux😞🙏🏼🤲🏽
Xana dila gnanal yalla si Barker Nabi Moustapha si Barker seydina mouhamed si Barker rassoulilahi si Barker alhouranoul karim yalla délola sey beute gua guiss sa taw bou gor bi yalla may ko fane wou goude ak wer limay wax ni si sama xol bi lakoy tibé inchallah dinga giss sa doom yalla meune nako😭😭
Magui doga déglou musique sama khol di toy😢💔 thiey aduna yalla maynagnou lepp mes takhoul chaque jour gnouy bamtou😢❤graze a cette chanson louma meunti am ma sant louma amoul ma sant❤machallah frere yalnala yalla takhawou
Lorsque j'ai vu la vidéo sur tiktok je suis allée directement sur youtube pour la regarder et j'ai pleuré. Yalna la Yalla maye gua guiss sa dome, Que le tout puissant exauce ton souhait, courage frère
Javais les larmes aux yeux de ma premiere vue Cest tres triste deysann ,maos cest la volonté divine Yallahh nala yallahh tahawo si barké nabi moustapha
😢😢c le mm histoire avec mon frere lui aussi bopam modane meti en 2022 la kheuy un beau jour rk guissatoul ba nii. Comme c triste .mangi niane yalna oump diame boumou daloul.té yalla wèral sèni beut niep gnimou dal 🙏
Allahou Akbar yalla laa mague kéba mon ami mon frère mane Moctar kane diamono école de football pa ouzin kéba mane lay gnanal yalla yalla khétalila déloola Say beut.. Yalla meune nako té dinako déf
Dit toi alhamdoulil lah Certe c’est pas facile mais Allah fait tjr li geune thi diamam, as sabr, soit patient et endurant ta récompense sera meilleur inchallah 👆courage
Alhahamdulila since god gives you the faith, may god gives you back your sides again 🙏🙏... always crying whenever am listening to the song ❤❤❤.... love from the Gambia 🇬🇲
Ndeyessane Yalla rek Moy Bour, môme rek mo meune Yalla Nala Yalla Takhawou ba nga guissaat boubaakhe ci Barké Seydina Mohamed PSL inshallah Amine Ya Rabbi
Yalla nala borom bi teguil natou bi il est le maître de la terre et des cieux qu il vous gueri il est le tout puissant keiba force à toi et bonne continuation inshalla allah Dieu va te guérir frère 🙏🙏🙏
Très triste j'ai les larmes aux yeux billahi metti na frère Yàlla nala yàlla may wer te nimu ko térxee moom buur bi mu teg lako yàlla nako teggi waat bamu sét wécc bi barki sayyidul wujuud salal laahu halayhi wasallam
Ndeysane courage 💪🏿 yallana souno borome bi di borome dieuam niuy delo la seuy geut nga geus sa taaw bou goor bi barkp Serigne fallou mbacke mougeul te baui lépu si lokhu souno borome 🙈🥺😭♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️😪
Ndeysann keba on a grandi ensemble à colobane, lii dafko dapp,et peut-être c'est dans les geines puisque son papa aussi était comme ça, il s'est retrouvé aveuglé du jour o lendemain avant le décès de la maman de keba, la dame ki pleure dans ce clip est sa grande sœur Anna.....yallah nako yalla takhawou
Ohh 😮 pour mane dako joué nonou rék Ndaye saane 😭😭🤦♀️🤦♀️
Ne le laisse jamais il a besoin de vous surtout vous ton ami d'enfance.metti de trop
Courage à toi frère ❤❤❤❤
Amine wayy
De meme que moi c'est mon grand frere keba 😭 nio bok kogne colobane
J’ai vécu même histoire en 2022 ma tokk sama place dioulli tizbar diott ma diogg pour dèm diapou dji bima dèmè basi porte bi rk sama beut yi commencer flou sama bopou bi di mètti aussi deuxième jour bi ma yèwou rk guisa touma dara ndeysane sila gnibi touba quelques mois après alhamdou lillah mou tanè ma commencé di guiss nake nake bi insbi mou mèll comme avant yalla nala yalla wereul barkè ahmadou
Kan mola fathieu
Massa domou baye❤ c'est le destin,le Tout Puissant t'a réservé d'autres choses
*Dieu merci ba werr gua🙏🏽 Yalla rk moy mbour*
Alkhamdoulila, wakhko kila fathe stp
Ndaysane
Magui soga commentaire si youtube bi yalna la yalla may gua guis sa dome😢😢😢😢😢
Allah houma amine inchahalah amine
Qui est venu ici après avoir suivi son entretien sur seneweb ? Pouvons-nous pas cotiser pour l’aider à se faire soigner à l’extérieur ?
Kou xolam tooy 😢kon man ?
😢😢😢😢😢
Machalla ly yalla rek mo co meune
😢😢😢😢
@@CheikhSarr-nx4ob bonne guerison keba
😭😭😭😭🤲🤲🤲🤲🤲😭😭😭😭
Alahou akbar 😢il mérite des millions de vues surtout on doit le traduire en anglais il doit faire le tour du monde
Oui c une bonne idée 👍
Bilahi nak 😭😭😭😭😭💔💔💔💔
*Très bne idée*
Bonjour fils,Keba,c'est Tonton SECK, responsable École football feu Capitaine cheikh Tidiane Thiam ,"yalla nala yalla delo say beut thi barker BOROM TOUBA.Oh tout ❤️❤️❤️ avec toi fils
Amine BARKEP BOROM TOUBA ❤❤❤❤
Bilakhi Lou méti dall ne sama béne copine aussi niou djoye thi be sone mome tam da teud nélaw yéwou Guisseu toule dako dabe aussi méti ne torop Mai’s niou bayi lép thi lokho borome bii long vie à eux😞🙏🏼🤲🏽
Ayy yaw mi loy wakh niii ba legui wera goul wala
@@MaxSeck-uk2we non wéragoule mais bayi naniou lep thi lokho borome bi🙏🏼🙏🏼
Ohhh keba bimakoy kham yague na gno bokone kogne colobane mais guemeul ni lou borome bi deff rek amna louko waral ndakh guiss na lepp yalla nalako téguil thi barké Seydina mohamed ( psl )
Méttina trop 😭😭😭😭
Xana dila gnanal yalla si Barker Nabi Moustapha si Barker seydina mouhamed si Barker rassoulilahi si Barker alhouranoul karim yalla délola sey beute gua guiss sa taw bou gor bi yalla may ko fane wou goude ak wer limay wax ni si sama xol bi lakoy tibé inchallah dinga giss sa doom yalla meune nako😭😭
اللهم أمين
*Amennnn🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽*
J'ai les larmes aux yeux 😭 😭 yallah borom teguil lako si barkhé moukhamed psl 🙏 inchallah
Kou écouter plusieurs fois dih xalat lou nek souniou kanam
*Moi😢*
Bilah yalla mene Lou nek😭😭😭😭yalla nala yalla delou banga guise Linga beug💔💔💔💔💔
Magui doga déglou musique sama khol di toy😢💔 thiey aduna yalla maynagnou lepp mes takhoul chaque jour gnouy bamtou😢❤graze a cette chanson louma meunti am ma sant louma amoul ma sant❤machallah frere yalnala yalla takhawou
Walay dama si dioy Ba agélé wouma KO té Sama yaye Ay djigén rék la am😭😭😭😭 yalla bou la yalla sétan 😭😭😭🙏🙏
Il mérite beaucoup d'abonnés
Kou xolam tooy Kom Man 😢
Ndeysane li mettina, yallnala yallah dèlo saye geute si barké seydina Mohamed psl😢
il mérite des millions de vue😢
Est-ce qu'il a un moyen de le soigner si oui on peut l'aider à retrouver la vision même si on doit cotisé pour cela svp les gars🙏
Ndaysane thieye adouna yallah rkk mou bourr 😭😭😭😭
Ndeysaan😭😭😭😭😭😭, yalna yAllah mouri say beut si barki Seydina Mouhamed Salalahou haleyhi wassalam
Amine ❤
Ndeye sane theye yalla
Lorsque j'ai vu la vidéo sur tiktok je suis allée directement sur youtube pour la regarder et j'ai pleuré. Yalna la Yalla maye gua guiss sa dome, Que le tout puissant exauce ton souhait, courage frère
C’est vraiment triste frére mais natou la yalla nalla yalla may kholou mougne té oubila yénéne bounte😭😭
Massa yallah na la dello say beut thi diam banga dellou thi say activités thi barké yonetebi SAW ❤❤❤
Yalla na yalla diokhate la sa bete😢😢❤❤
Javais les larmes aux yeux de ma premiere vue Cest tres triste deysann ,maos cest la volonté divine Yallahh nala yallahh tahawo si barké nabi moustapha
C'est triste 😢😢Yallah n'a Sounou brome bi takhawouko tu mérite beaucoup d'aide Diam si yaw mon frère ❤
😢😢c le mm histoire avec mon frere lui aussi bopam modane meti en 2022 la kheuy un beau jour rk guissatoul ba nii. Comme c triste .mangi niane yalna oump diame boumou daloul.té yalla wèral sèni beut niep gnimou dal 🙏
Dundu guou sotei guoul lounei hadj na thi… hamdoulilalkah 🙏🏾 yalla na yalla sam 🙏🏾 sam lei niou😊
Grand yalla n'alla yalla dfal diame way bilahi daffa dall one sama grand frère souma ko khollè rekk di dioye massa way grand bn guérison
Chaque jour ma dougou setane vidéo bi 😢😢😢😢damay dioye rek yallah rek mo meun lii😢
Yalla nala Yalla may bagua guisse sa dome incha Allah biaye diato 😢😢❤
Machallah bly magui doye sakh
Ohhh kéba.... Thiey sunu borom.yalla nala sunu borom ték loxo... Maximum de partage les frere et soeur
Allahou Akbar yalla laa mague kéba mon ami mon frère mane Moctar kane diamono école de football pa ouzin kéba mane lay gnanal yalla yalla khétalila déloola Say beut..
Yalla meune nako té dinako déf
Ndayssane li mètina trop motakh doundou bou sotè goul lou nék khathinasi yalla Nala yalla defal diam nga guis ak diam 😢😢😢😢😭😭💔💔💔
Monami mon frère Que Dieu te vienne en aide c’est Almamy depuis école de football pa Ouzin❤️❤️❤️
Yalna yalla takhawou té delo say beutt si barké seydina Muhammad (psl) 🤲
Yalnanga kheuy yeewou rek Guiss Guiss bi ñieuwate dara weessoul...Inchalla. Courage à toi
*Amennn🙏🏽*
J’ai tellement pleuré yalnala yalla may werr mon frère🙏
Ndeysan yalla nala yalla takhawou si barké Sérigne Babacar sy malick 😭👏🏻
Ohhh mètiinaa 😭😭😭😭ay yalla mayko mou guiss domam même boudè bèn fane sax 😭😭
Ndeyessane waye wi dawna yarame bamakoye setaane sama khol tooyna ba sama rognogne wadeu ta tayoumako. Massa kebe
Yalna Yalla dioxate la say beute gua guis sa dom lii metti na trop 😢
Dit toi alhamdoulil lah Certe c’est pas facile mais Allah fait tjr li geune thi diamam, as sabr, soit patient et endurant ta récompense sera meilleur inchallah 👆courage
😭😭😭yalnako sunu borom défal diam tégal la natou bi doley xassida❤️👏🏿😭
Wallay ndéysan sama yaram dawna 😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭🤔🤔🤔🤔🤔🤔🤔🤔🤔🤔😓😓😓❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Alhahamdulila since god gives you the faith, may god gives you back your sides again 🙏🙏... always crying whenever am listening to the song ❤❤❤.... love from the Gambia 🇬🇲
Aujourd'hui j'ai même pleuré dans mon cœur par c que c très très très triste walahi😭💔😭💔😭😭😭😭😭😭😭😭
Yall na yalla doli soutoureu❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Yalla nala yalla takhawou 😢😢
Si barké seydina mouhamed ❤
Ndeysane kéba Aka bakh té âme yité médina lako khamé yallna yalla mayateu la giusgius
Ndeyessane Yalla rek Moy Bour, môme rek mo meune
Yalla Nala Yalla Takhawou ba nga guissaat boubaakhe ci Barké Seydina Mohamed PSL inshallah Amine Ya Rabbi
Ce song je les écoutaient plusieurs fois c triste bilahi ohh😭😭💔💔
Adouna loudoul yalla nén leuh yalla bkhna 👊😢 courage mn frr ❤😭
Kéba nitt kou bakh si mane yalnala yalla defal diam ❤️😍🤲
Ndeysane yalna la yalla defal ga guiss sa dome dji 😊❤
Ça me touchée😢vraiment yalla nala yalla wérall 😢
C mon cousin nite kou bah dako dabe 😭😭 yalna yala weral batbi bi
Allakhouma amiiine cousine
Yalla na yalla mayniou kholou mougne 🙏
C’est triste 😭 qui est pleuré comme moi 😢😢
J’ai pleuré sans m’en rendre compte mais li metina 😢
Trop li kouko dioyoul amo xol c triste
*Fo diar toyal beutt c’est triste 😢*
Ndeysane yallah nala yallah takhou ya barké seydina mouhamed 😢
Neysane yalla na lerame ay beutape 🤲🤲🤲
yalla nala yalla may ga guisat si barkep seuydouna moukhamet Amine inchallah yalla meun n'a loune 😢❤
Force à toi frère ❤️✊🏿 tu m’as fait pleuré 😢😔
Yalla nala yalla saam thi barki seydina mouhamede salalawou aleyhi wa salam
Merci beaucoup ❤❤❤❤
Ndeyssan 😢😢 toucher nama biko kheucha invite lako dieuk guiss 😢😢😢 yaram dawna
Yalla gua mene guisse comme avant 🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏
Barki alhourane li daw n'a yaram kou sa xoll toye come mane 😢
Ndayesane keba wayy yalla na ko yalla diapalé
Ayooo massa j,ai la nostalgie massa yalla kesei moy bourou sante ko rek loum deff ame na loutax meti na nak wayei mougne rek dina bakh😢😢😢❤❤❤
Yalla nala borom bi teguil natou bi il est le maître de la terre et des cieux qu il vous gueri il est le tout puissant keiba force à toi et bonne continuation inshalla allah Dieu va te guérir frère 🙏🙏🙏
Ndeysann frr kéba yallah Na yallah takhawou laa🎉🎉😂
Je peux pas retenir mes larmes oh Ndeyssane metina trop Walahi Yalnako souniou borome bi swt diapale
Dioyna yala amna lépeu yalna yala takhawou nieup si barkep serigne falou awa bousso
Très triste j'ai les larmes aux yeux billahi metti na frère
Yàlla nala yàlla may wer te nimu ko térxee moom buur bi mu teg lako yàlla nako teggi waat bamu sét wécc bi barki sayyidul wujuud salal laahu halayhi wasallam
Deyssane yalla reck mo meneu 😭😭♥️♥️
Yalnako sougnou brome takhawou😢❤
Ndeysane courage 💪🏿 yallana souno borome bi di borome dieuam niuy delo la seuy geut nga geus sa taaw bou goor bi barkp Serigne fallou mbacke mougeul te baui lépu si lokhu souno borome 🙈🥺😭♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️😪
Yalnala Yalla tegil natou bi sy barki seydina mouhamed pls amine 🤲🤲😭😭
Yalla Nala yalla may bagua guisse sa taw bi yalla bakhna Dina bakh dh inchallah
J'Ai.pleures.pAr.cette
ChAnson.dieux.est.grAnd
Ndaye sane daw n'a yaram trop bilahi ❤
Aaaay borom défal ko mou guissate ya Rabbi lo se rek nonoula gno ngui les gnane
Machallah Ndeyesaane 😭😭😭😭✊🏽✊🏽✊🏽✊🏽❤️❤️❤️❤️
Vraiment que dieu vous bénisse
Yalla nala Yalla may weer mouri say beute taxawoula si barké Yonentibi saw 🙏
Yalla nako yalla takhou arre ndiabot gi métina trop 😔😔
Thiay yalla soun borom fahaloun lima youridou❤❤
Yallah Nala yallah délo Say geute si barké Mame khalifa
Yalla nala yalla wérël bagua gisatte ❤❤
Yalna la yalla may gua guiss say dome si barkè seydina mouhamed 😭😭😭😭💔
Ndaysane yalla nalla yalla takhawou si barké cheikhoule xadim
Ndeysane thieuy yalla moy df louko sop yalla nala yalla takhawou
Vraiment c'est triste 😢 mangui xalaat lou néh walahi 😢 yalnala sunu borom bii djapaalé bé nga guiss sey dômes
yalla na la yalla deffal diam dello leu saye beute guye guissate norma thi barke seydina mouhamed
Ndeysan lago dou wess doundou gou diekha goul lou nek khedie na thi yalna yalla mayat ngay guis meun nako yalna ko déf🤲🤲
Sama xoll toyna😢😢😢😢😢
Ndeysan keba yalla nala yalla déllo say peut