Je remercie milles milliards de fois Serigne Momar Diagne et je prie ALLAH TA'ALA de l'élever en grade, amiiiiiiiiiiine ! Un vrai croyant se doit d'oser dire et manifester la vérité quoiqu'il arrive ! Et la vérité c'est qu'effectivement le Sénégal est un terreau propice pour tout illuminé qui veut se faire mousser ! Il existe bien au Sénégal une secte qui déclare au vu et au su de tous que leur fondateur est le prophète lui-même qui se serait transformé en lébou !!! Pour quelle raison une affirmation aussi énorme prospère-t-elle depuis des decennies ? Parce que les tenants des autres chapelles confrériques craignent que soient passées en revue leurs propres dossiers..... C'est ainsi que tout ce beau monde est arrivé à une espèce de pacte de non-agression ( pacte tacite ).... Tu ne dénonces pas mes énormités afin que moi non plus je ne me lance pas à inspecter ta paperasse..... Ragalantèh digui-ganaaw quoi .... C'est dans cette atmosphère que ce dénommé El-Cheikh a lui aussi sorti sa camelote ! Les musulmans qui par la grâce de Dieu ne se sont pas juste contentés d'être nés de parents musulmans et de porter des prénoms à consonance islamique, ces musulmans-là qui ( par la faveur de Dieu) ont étudié un minimum les propos du Prophète salaLLAHU aleyhi wa salam eux savent que El-Cheikh est un vulgaire affabulateur ! Ceux qui sont incommodés par ses énormités doivent accepter d'analyser le dysfocntionnement qui est à la base de l'éruption régulière de "faux prophètes" , "faux mahdi", "khoutbou en carton" et autres imposteurs culottés ! Tant que la porte restera ouverte à ce que chacun prétende avoir reçu un don via un canal non-répertorié dans la sounna, il continuera d'exister des imposteurs ! Jusqu'au jour où Dieu éclairera chacun à propos de ce sur quoi il était .... Que Dieu agrée Serigne Momar Diagne et nous sauve tous de la perdition , amine !
Bilahi deg bou wer ya des milliers de Elcheikh au Sénégal niak Kham sunu dîné kou topou alkhourane ak suna do rer mouk le prophète psl à clairement dit je vous ai laisser 2 choses le coran et la sunna du prophète psl tant que vs suivez les 2 vous ne serez jamais égarés sur le droit chemin au Sénégal celui qui veut suivre ce chemin on te traite de "wahabite "danga contre mag gni au contraire sunu mag gni ont suivi le même chemin que le prophète psl
Assalamou aleykoum wallahi tonton tu es très véridique masha Allah c, est vrai que le Sénégal est une terre très fertile en matière de religion. Un fou peut se lever un bon matin et dire qu, il a vu ALLAH... Si on commence a le contredire 2 minutes après y, aura plusieurs autres a le défendre en disant peut-être qu, il a raison.... Nuit et jour ds ce pays on abaisse par des propos offensifs notre prophète aleyhissalam..... Vraiment on est fier de toi. Toutes tes causeries sont basées sur la vérité islamique.... Qu, Allah te bénisse et te protège...
Merci Oustaz Alquran ak Sunna Muhammad SAW koumou doyoul leneen lo dougou ba shaytan feekk la ci ya togn sa bopp. Senegal reewou thiakhaan ak bokkaale Yallah rekk. Aouzoubillah!
Yenne daal da nguene top riire bi di wakh, ham lou khew mo gueune thiowli demal gueustou kouy seydi mouhamed el cheikh ay diangallem mo gueune di wakh ci lo hamoul darra ab kilifa day mandu te day wakh lu rafete ndakh yonent bi du wakh lu gnaw ci kene waye
Mais pourquoi ngén yakamti. Ki lén diokh RV 2022 kagne deug deug, né lén tékk rék di déglou. Légui niou kham kou nék si deugg ak kou nékoul si deugg....
Comme ningako wakhé rék mo am Nit wakh nafi lougeneu graw li el Cheikh wakh niouni mout kén niémé wousi ndakh séni sant wala séni askane batakh loulén nékh wakh si diné yalla ta kén douléne attaque com ni niou attaque el Cheikh nit takhaw nafi né diw mo bind yalla ki né yonént bi dou référence ki né ajdi makk goor gou wodou da sof ak yenén waw litakh wakhouniou si gni com niniouy wakhé si el Cheikh?kouné khamnani el Cheikh limouy wakh ay thiakhan la wayé kouwakh si el Cheikh wara wakh si gni Com el Cheikh nak mom amoufi badiéne santam siwoul motakh niou niéméko wakh louné liniou warona wakh ay moromam ta défouniouko lirék moy li tardél diné Sénégal par parlo
Sénégal kuffi ooté AM mbooloo Ndax bufekkooni ku wax né قال الله أو قال ارسول Kon Ken du topp Ken kudul Yonentibi Ndax islam ci moom la waccoon té alkhuran ak sunna mooy ndonoom.
Jazàka l-Làhu khayr yà Ustàz. Sa taxawày jubna et dëggu na ! Cet imposteur, suppôt de Chayțàn et coureur de jupons (doxàn kat & sày sày ) qu'est Mor Bâ alias El -Cheikh agit comme un gourou ! Les Khalifah généraux ( Tiwàwan, Cenaba, Ñaseen, Tàleen-Omariens, etc) doivent assumer leur responsabilité eu égard aux Musulmans en général, et à la tariiqah tijàniyyah en particulier !!! Luy jot jotna ! Ce type n'a pas Science (al-^Ilm ) ; il est sous l'emprise de Chayțàn qui le manipule très dangereusement. EST-CE QUE MORT BÂ ALIAS EL-CHEIKH EST LE SEUL À DIRE DES HÉRÉSIES ? À SUIVRE. ..
Jazakumuallahu khairan Ya Cheikh. Vraiment contane na. Je suis d’accord avec vous a 100%. Il y a des gens beaucoup plus dangeureux et heretiques qu’El Cheikh au Senegal et ils prosperent depuis des annees. El Cheikh n’est un nouveau venu parmi cette race de manipulateurs. Qu’Allah protege l’Islam au Senegal. Amine. Longue vie a vous. Vos videos sont importantes pour l’éveil des consciences.
السلام عليكم ورحمة الله وبركاته . أيها الوالد الشيخ مامور جاج بعد تحيات ملأها الإجلال والاحترام والتقدير . طلبا ﻻ اقتراحا الا تسجيل فديوهات لتعليم علم التصوف للمحتاجين فلا يداوي هذه الأمراض المعضلة إلا فهم الركن الثالث من الإسلام وهي التصوف الخالص من الخرافات والبدع والخزعبلات فالأهم الأهم التنبيه والنصيحة ﻻ التوبيخ ولا أشك انك فارس من فرسان المتصوفين وقائد من قادة السالكين فلك دور كبير في تغيير المجتمع وان بلغ السيل الزبي. عذراً ان كنت أخطأت في حقكم وجاوزت الحد في الكلام ان أريد الا الإصلاح وما توفيقي الا بالله
Yow sako sa bopou el-Cheikh sakoul bopam.ibilis sakh sakoul bopam..bo retourne.ngua wakh.ki ngua bokal bene binde boulene yalla binde nguena ko domou ibilis la Kone yow si domou ibilis yi ngua bokou
Dégueu Tina deugue amna niou gueuneu gueraw el cheikh Sénégal yakhouna yalnanou yala doli soutoureu ta mousalniou Thi niom machala kou bakh
Magg yi la top....c'est tout....sunna rék mo am solo
Thieuye Sénégal, AK sénn Islam AK tarrikha you bary.
merci beaucoup mon pere nala yallah sounie brom samala ak mbolom amine
Mâchalah Serigne bi Amna solo yalna yaleu fay len amine
Merci serigen bi amna sólo
Machallah walahi papa hamone nani dinga si wahe djeredjeufeuti
El cheikh est ateint de la malADIE MENTal
Mashalla. Nioungui kodone khar. Dieureudieuf Papa.
Salaam salaam sama khalif général mangui ziarr yalnala yalla maye werr te deuguereul takhawaye .
Billahi papa malla buoka Si sama holi bi yewo reekk la don hari si wadiou boni bi El cheikh El kazako
Meci beacoup Gorgui,Yalla na Yalla fai te maila goudou fan ak wer
Yow warnga diagiwat
Dieureudieuf..macha allah.Quand à ce satan il restera clouer sur son lit ...
Merci 👍👍👍
Bien dit père
El cheikh nopiil dou dara Senegal yewoulene
Machallah papa yow de sopnala lool valahi yallanala yalla samue
machalah so wakhé rek khol sed dieureudieuf papa
Je remercie milles milliards de fois Serigne Momar Diagne et je prie ALLAH TA'ALA de l'élever en grade, amiiiiiiiiiiine ! Un vrai croyant se doit d'oser dire et manifester la vérité quoiqu'il arrive ! Et la vérité c'est qu'effectivement le Sénégal est un terreau propice pour tout illuminé qui veut se faire mousser ! Il existe bien au Sénégal une secte qui déclare au vu et au su de tous que leur fondateur est le prophète lui-même qui se serait transformé en lébou !!! Pour quelle raison une affirmation aussi énorme prospère-t-elle depuis des decennies ? Parce que les tenants des autres chapelles confrériques craignent que soient passées en revue leurs propres dossiers..... C'est ainsi que tout ce beau monde est arrivé à une espèce de pacte de non-agression ( pacte tacite ).... Tu ne dénonces pas mes énormités afin que moi non plus je ne me lance pas à inspecter ta paperasse..... Ragalantèh digui-ganaaw quoi .... C'est dans cette atmosphère que ce dénommé El-Cheikh a lui aussi sorti sa camelote ! Les musulmans qui par la grâce de Dieu ne se sont pas juste contentés d'être nés de parents musulmans et de porter des prénoms à consonance islamique, ces musulmans-là qui ( par la faveur de Dieu) ont étudié un minimum les propos du Prophète salaLLAHU aleyhi wa salam eux savent que El-Cheikh est un vulgaire affabulateur ! Ceux qui sont incommodés par ses énormités doivent accepter d'analyser le dysfocntionnement qui est à la base de l'éruption régulière de "faux prophètes" , "faux mahdi", "khoutbou en carton" et autres imposteurs culottés !
Tant que la porte restera ouverte à ce que chacun prétende avoir reçu un don via un canal non-répertorié dans la sounna, il continuera d'exister des imposteurs ! Jusqu'au jour où Dieu éclairera chacun à propos de ce sur quoi il était .... Que Dieu agrée Serigne Momar Diagne et nous sauve tous de la perdition , amine !
Merci papa.deuk bi lou nekh way mou def. Yalla nanou yalla guindi.
dieuredieuf oustaz
Ton discours est toujours pertinent ya ouztaz Machalah que Dieu vous donne longue vie et bcp de santé
Merci père yalla nala yalla faye
El Cheikh Domouharam bou bone leu
El kazzabb dafa répeu rékk motahh
Lerna nagne oustaz dieureudieuff
Tarikha Amna chartes papa!!!
Merci degue recke
Diadieuff pape yalla nala yalla faye
El cheikh de diamou yalla bou bakh la dé
Mall belly kokou domou ibliss la
@@aliimranegueye2636 Kone yow domou l'âne ngua
Mane domou adama la
@@aliimranegueye2636 Kone sagua ngua sa bopou
Legui wakh ma noumou saga sama bopou nakh diougué wougnou si adama
merci pere wakh nga leup
Machallah baye momar long vie
Macha allah sunna rék moy deugg
C'est quoi le souna ?
Dieredieufe imame yala na yala goudeul sa fane
Defamelni nak denka gana may force
Macha Allah diueredief
Vous avez as tout dis merci
Merci tonton El cheikh mo yabatè tè beugeu buzz
Très pertinent ce monsieur.
Bilahi deg bou wer ya des milliers de Elcheikh au Sénégal niak Kham sunu dîné kou topou alkhourane ak suna do rer mouk le prophète psl à clairement dit je vous ai laisser 2 choses le coran et la sunna du prophète psl tant que vs suivez les 2 vous ne serez jamais égarés sur le droit chemin au Sénégal celui qui veut suivre ce chemin on te traite de "wahabite "danga contre mag gni au contraire sunu mag gni ont suivi le même chemin que le prophète psl
Machalla alhourane ak souna rek moy deug te mofi diitou magni mo diitou tarihayi te moy moudiou inchalla
Diereudieuff serigne touba amoul morom
Merci beaucoup yabate rekk
Assalamou aleykoum wallahi tonton tu es très véridique masha Allah c, est vrai que le Sénégal est une terre très fertile en matière de religion. Un fou peut se lever un bon matin et dire qu, il a vu ALLAH... Si on commence a le contredire 2 minutes après y, aura plusieurs autres a le défendre en disant peut-être qu, il a raison.... Nuit et jour ds ce pays on abaisse par des propos offensifs notre prophète aleyhissalam..... Vraiment on est fier de toi. Toutes tes causeries sont basées sur la vérité islamique.... Qu, Allah te bénisse et te protège...
Mashah Allah Serigne bi
Mr6 Pape machallah
Papa yaw deugg rék ngaye wakh yalla na la yalla samme
Machallah.duega.rek.💪💪💪💪
Merci
ماشااله.
Merci Oustaz Alquran ak Sunna Muhammad SAW koumou doyoul leneen lo dougou ba shaytan feekk la ci ya togn sa bopp. Senegal reewou thiakhaan ak bokkaale Yallah rekk. Aouzoubillah!
Machallah
Merci papa rafetna
Walay ndeyssane.
El cheikh daffa yabaté gni ko top mom douniou sakh ayy nit thim,
MACHALLAH AMATINA SOLO NA YALLA GOUDAL FANWI YOK WERGUI
BARAKA LAH
Bilay pere kilifeu yi lou lene nekh lanouy wakh te coulene wedi ame problem
il y'a que l'instruction qui peut nous sauver, envoyer les enfants à l'ecole
mar ba(dit el cheikh) miii mbame leu
Dieredeuf Fati kadougi rafetna lol ya oustaz
Yenne daal da nguene top riire bi di wakh, ham lou khew mo gueune thiowli demal gueustou kouy seydi mouhamed el cheikh ay diangallem mo gueune di wakh ci lo hamoul darra ab kilifa day mandu te day wakh lu rafete ndakh yonent bi du wakh lu gnaw ci kene waye
Ya meune doule ndeyeme domarame dang fi guisse wahh diou gnaw
@@aasfatfaatfa5852 yaw deh aga go ci yalla ndakh sa kilifa saaga lala diangalle demal outi kilifa
Vidéo bi nga def si Imame Kanté pourquoi nga désactivé commentaire bi ?
Loussi sa yonn, mo mom video wom
dembis Kb yaw Lousiy sa yoon yaw la laath ?
Mais pourquoi ngén yakamti. Ki lén diokh RV 2022 kagne deug deug, né lén tékk rék di déglou. Légui niou kham kou nék si deugg ak kou nékoul si deugg....
Comme ningako wakhé rék mo am
Nit wakh nafi lougeneu graw li el Cheikh wakh niouni mout kén niémé wousi ndakh séni sant wala séni askane batakh loulén nékh wakh si diné yalla ta kén douléne attaque com ni niou attaque el Cheikh nit takhaw nafi né diw mo bind yalla ki né yonént bi dou référence ki né ajdi makk goor gou wodou da sof ak yenén waw litakh wakhouniou si gni com niniouy wakhé si el Cheikh?kouné khamnani el Cheikh limouy wakh ay thiakhan la wayé kouwakh si el Cheikh wara wakh si gni
Com el Cheikh nak mom amoufi badiéne santam siwoul motakh niou niéméko wakh louné liniou warona wakh ay moromam ta défouniouko lirék moy li tardél diné Sénégal par parlo
Sénégal kuffi ooté AM mbooloo Ndax bufekkooni ku wax né قال الله أو قال ارسول Kon Ken du topp Ken kudul Yonentibi Ndax islam ci moom la waccoon té alkhuran ak sunna mooy ndonoom.
Jazàka l-Làhu khayr yà Ustàz. Sa taxawày jubna et dëggu na !
Cet imposteur, suppôt de Chayțàn et coureur de jupons (doxàn kat & sày sày ) qu'est Mor Bâ alias El -Cheikh agit comme un gourou !
Les Khalifah généraux ( Tiwàwan, Cenaba, Ñaseen, Tàleen-Omariens, etc) doivent assumer leur responsabilité eu égard aux Musulmans en général, et à la tariiqah tijàniyyah en particulier !!! Luy jot jotna !
Ce type n'a pas Science (al-^Ilm ) ; il est sous l'emprise de Chayțàn qui le manipule très dangereusement.
EST-CE QUE MORT BÂ ALIAS EL-CHEIKH EST LE SEUL À DIRE DES HÉRÉSIES ?
À SUIVRE. ..
machallah imam
Jazakumuallahu khairan Ya Cheikh. Vraiment contane na. Je suis d’accord avec vous a 100%. Il y a des gens beaucoup plus dangeureux et heretiques qu’El Cheikh au Senegal et ils prosperent depuis des annees. El Cheikh n’est un nouveau venu parmi cette race de manipulateurs.
Qu’Allah protege l’Islam au Senegal. Amine.
Longue vie a vous. Vos videos sont importantes pour l’éveil des consciences.
السلام عليكم ورحمة الله وبركاته .
أيها الوالد الشيخ مامور جاج بعد تحيات ملأها الإجلال والاحترام والتقدير . طلبا ﻻ اقتراحا الا تسجيل فديوهات لتعليم علم التصوف للمحتاجين فلا يداوي هذه الأمراض المعضلة إلا فهم الركن الثالث من الإسلام وهي التصوف الخالص من الخرافات والبدع والخزعبلات فالأهم الأهم التنبيه والنصيحة ﻻ التوبيخ ولا أشك انك فارس من فرسان المتصوفين وقائد من قادة السالكين فلك دور كبير في تغيير المجتمع وان بلغ السيل الزبي. عذراً ان كنت أخطأت في حقكم وجاوزت الحد في الكلام ان أريد الا الإصلاح وما توفيقي الا بالله
Walahi diagne danou yape el cheikh rek beurina nioufi wakh limou wakh
Yow diangue ngua waye deguo
Yow sako sa bopou el-Cheikh sakoul bopam.ibilis sakh sakoul bopam..bo retourne.ngua wakh.ki ngua bokal bene binde boulene yalla binde nguena ko domou ibilis la Kone yow si domou ibilis yi ngua bokou
Jereujeuf wakh dji rafetena mai pas de garouwalé nak waxal si el cheikh rek moy thème bi
Il ne dit que la vérité nak fi guarouwalé amoufi el cheikh BA et ses autres qui défi le prophète nio yam
Hahaha
Pourtant li laniou wakhone yonene tibi ni Dafa dof
YONINTEBI deug la indi te leerna. Tariha cheikh matna te leerna donc kufi gneuw indi louthi bokkul gnu wakhlako
merci bcp wahkji amna solo barakhallahu fika
Jdieredieeti yarbi dal moy leoou yar ndawgni bagnou ragne lolu rek moy solution bi. Magnilay ziyar tay magall
SOUBKHANA.LAH..SENEGAL.DANO.FEBAR...EL.CHEIKH.EL CHAPO......ALLER..A.SOURAT.AL.ALHAM...6..VERSET.93 SVP..SHOUKRAN YA SHEIKH MOMAR
baye laye nak mame limamou layon al mahdi ak kou wekhon fe mo nioul fi
😂😂😂😂😂😂non wèroul dèh yi wakhou doff rek nèna giss na yalla ak djitè na yonènty bi psl keurou dinè yi nioko wara arèté
Gnatta klifa gnofi wote al mahdi du nguene si wakh ???
El Cheikh Doomaram Ji Yakk béppe dèrrOu Ndar Ndar...èsk"il est 1 vrai Saint Louisien,Fi kène xamOukaafi,kène xamOufi ak Mbokkam
Papa yala gua goude fane je suis du même avis que vous niak diangue ak kham souniou dîné mo nekh sénégalais Lou niew yobouléne
Gorgui linguay wakh ba setteu ngua si sa borom Joulitt loumou khamoul Lou nekk dangua siy mandou geustou KO ba amsi loula leer bane preuve ngua ame ? Somako meuné bakhé incha allah
Sy Seydi Djamilou S Babacar ki da geustouwoul dara mouye nekk fii di wakh loumou hamoul
J'ai pitié de ses disciples
meee net day am diupluway
Ce n'est pas el cheikh c'est el ibliss
tasawouf la bokk
Papa kilifa diné yi nio wara dial sén Ay résponsabilité ta él cheikh Aka berit Morom
Merci Serigne MOMAR wakh nga DEUG el cheikh mom kou Diarra fad j la waye bouniou bayi ay fene Di détourné niokhamne hamewouniou DEUG ak fene
Baye momar noumay def ba Am sa número svp 🙏
Ya wakhe deugga merci longue vie
@@matalibegaye1567 hum
@@serigne-momar djadaf baye momar
Sénégalais rére moko nék
Bilay akhrusamane layu nek el cheikh ibliss la waye na dem rek 🤔
Bilakhi li la wakh dagnouko Wara yobou dalale khéle
Man sénégalai lou tax mo nèkha feuk moma diaxal kou diour doom yobou ecol diangouniou al houran diangouniou diine
solution bi leinn rek leu diap ko douma ko bamou nek nitt
Demal douma ko bo demain do ko defati dé
Machallah