Parfois da ngay am intention yakh ay nitt teh khamo nai yangui len di promouvoir ci lou baax lougnouy wax wala di deff. Oustaz Mor Kebe est une légende mashaa’Allah. Et il ne fait pas allusion sur les Sheikh qui sont sur la photo. D’ailleurs eux aussi ils ont la même vision que lui . Le temps que vous prenez pour détruire des gens qu’Allah a inspirés la bonté, prenez le pour œuvrer . La vie est courte . La mort est proche . Yalna Borom bi yaatal xol yi
Yalla nagnou yalla dioubeul, tekk gnou si yoone bimou gueureum té mousseul gnou si koureul yi, yeupp nakk. C parce k fondements yi ngéene diokh salaf wéroul. Ay salafia yaak, soufiyak, ikhwanyak, wallahi yonente bi nekkoul benn si foowanetou yi.
Wallahi séene da´wa bi limouy réereul moo eupp limouy défar, ay khalei you dianguoul dara ngéene rakhass séene boppou yi diléene dougueul si ay considération yoo khamni douléene défar mais dafléeniy yakh: saagua, réwandé, noonoo, kassé
Boo beuggei diakhassei kholal benen bounteu . Ki université islamiques de Médine la dianggei cheikh yimiy wakh yeup kenn dousi sénégalais basi ki leen doonn defal concours pour bourse bi wa arabe Saoudite gnoko yonni woon.
Cet oustaz est un grand homme, vraiment je l’admire. Car ce qu’il dit là, si on l’applique on aurait eu la meilleure société au monde. Al khamdou Lillah, Sunna rek moy deug
Vie en paix astaz mor, fais ta dahwa ne perds pas ton temps avec ses indisciplinés. Laisse, on s'occupe d'eux et de leur égarement. Je les connais , guemouniou dara
😂waa oustaz kane laa attaqué légui🤷♂️et puis oustaz mor kébé ak Dr diangua ndoo wougne dih🤦♂️seuytané rék mooléén diapp😒waayé diguéén khamné kénn meuniounio séparé 🫰 Vive les ahlu sunnah❤️
Morr Kebbeh moytul wakh 6:59 bu bari. Julit wakham du bari. Sama naseeha chi yaw antanka mbokum julit. Nyarel demal nga gestu alquran bubakh. Sa alquran desna lubari. Shukran.
Vous n'avez pas compris Oustaz Mor parle à un secte qui critiquent beaucoup de savants au Sénégal et dans le reste du monde même Ils critiquent des savants connus ici au Sénégal comme Dr Mouhammad Ahmad lo .. Bayleen djakassé téh wakh louueen xam
@@ibrahimandiaye5463 loutax ben sahaba défou ko wala yonanté bii ci bopam fêter anniversairam ? 4imam yii ak imam Malick défou ko Ken défou ko apart y'en
@@Veridic-tvyalla dafani loulén yonent bi téré bayi léenko (sourate najmi) mé wahoul Lou yonent bi défoul boulenko def li yonent dafko téré wala yalla dafko téré Moy lay ci diné mé yonent bi défouko ken warouko def wahou doff la concours récital coran conférence extra fan lako yonent meusseu def?
🤭Ba leegi kénn xamul sa waay kan wala ñan lay wax🤔 Waaye daal li lay xamal ni ñiy tópp ta doyloo ALXUR'AN ak SUNNA (YÀLLA nee na, YONÉNT BI (a s) nee na) li ñu nékk maneesu koo xeex mooy, ak koo man di doon, boo juumee, kénn du la ca tópp. Xanaa muy lu ñu xamagul. Ku dul YONÉNT BI (a s) kénn du def lépp loo wax rek ñu gëmmu jël jëfe. Loolu dafa leer. Dëgg-dëgg taxawaay boobu gisu ñu ko ci waa-tasawuuf. Da nga naan sax ñii xanaa da ñoo jàpp ni ab sëriñ moom du juum🤔 KÉPP KU ÀNDUL CI LI MA WAX, INDIL MA LIEN BU LA NEEX BU BOOBAA MA XAM NI MAA JUUM KON. Ku ne xam na ni képp ku wuute ak YONÉNT BI (a s), la nga wuute ak MOOM (a s) njuumte la. Kénn waru la caa tópp. Taxawaay ba du léen lu moy ñaanal la ca njéggël mu jeex. Amul leneen. Loolu terewul aji-juum ji nékk ku baax.
Thiouthie yi neck si réseaux sociaux yi di tontou , di diabolisé cheikh Mor Kébé H.A, diare lène fimou diere ba nopi , dans ce cas solène wakhé ñou dégu lou lène. Té nguène ragale yalla si séni commentaire yi rawatina ki deff photo bi ague titre bimou binde c'est diamétralement opposé avec les orientations du cheikh Kébé.
Par Dieu le vivant. De un vous prétendez que le salafisme est une finalité alors que ce n'est qu'un chemin pour atteindre la fois, ensuite la vie du prophète Mouhamad salawatu lahi wa Ali Mouhamad, doit être notre maître et Ali as notre référence.Donc je ne les devance ni ne les retard car celà me suffit comme succès et être un esclave me remplit de joie car je n'adore que Dieu. De deux c'est vous qui êtes sectaire dans votre enseignement du dine de Dieu. Si l'ijtihad ne se fait pas conformément au valeurs prophétiques Celui dont l'intension était de suivre le prophète slawat doit être suivis et non l'opposé. Trois sache que notre enemi iblis fait tout pour nous diviser retournons à la source de la prophétie... Unicité et unité Salam voilà le Dine de Dieu. Salam.
Parfois da ngay am intention yakh ay nitt teh khamo nai yangui len di promouvoir ci lou baax lougnouy wax wala di deff. Oustaz Mor Kebe est une légende mashaa’Allah. Et il ne fait pas allusion sur les Sheikh qui sont sur la photo. D’ailleurs eux aussi ils ont la même vision que lui .
Le temps que vous prenez pour détruire des gens qu’Allah a inspirés la bonté, prenez le pour œuvrer . La vie est courte . La mort est proche .
Yalna Borom bi yaatal xol yi
Nioko tay di bindeu genrou video yi parce que danio beug vue
Machallah ya oustaze yallahna yalla samu la.
Machallah oustaz linga wakh wouté na ak titre bi tjr c le sounnah ki gagne alhamdoulilah
Ma sha ALLAH oustaz Mor wakh amna solo. Mbokk Mi sa titre wouté na akk li vidéo bi tank. yallana gnou YALLA défal objectivité
Woute woul ndank sah
Yalla nagnou yalla dioubeul, tekk gnou si yoone bimou gueureum té mousseul gnou si koureul yi, yeupp nakk. C parce k fondements yi ngéene diokh salaf wéroul. Ay salafia yaak, soufiyak, ikhwanyak, wallahi yonente bi nekkoul benn si foowanetou yi.
Wallahi séene da´wa bi limouy réereul moo eupp limouy défar, ay khalei you dianguoul dara ngéene rakhass séene boppou yi diléene dougueul si ay considération yoo khamni douléene défar mais dafléeniy yakh: saagua, réwandé, noonoo, kassé
Vidéo bi lann moo si meune yokk dioulitt gueum yalla, wala Roy si yonente bi? L´islam n´est pas ds l´intellectualisme, danger de la wahabya
Nioko tayy lepp pour niou khol video bi ak beuzz
Macha allah yalna yallah sameu la ousage mor kebe maygnou degue ak tope
Boo beuggei diakhassei kholal benen bounteu .
Ki université islamiques de Médine la dianggei cheikh yimiy wakh yeup kenn dousi sénégalais basi ki leen doonn defal concours pour bourse bi wa arabe Saoudite gnoko yonni woon.
Nous sommes tous des musulmans points
Merci beaucoup oustas kadougi ma challa kourelyi séni toure woute waye dieufi yi bénla
Léppou gir yalla la
Ragal lene yalla ki Wa masaalah laye tontou
Ku bind titre bi man na fen dé .
Cet oustaz est un grand homme, vraiment je l’admire. Car ce qu’il dit là, si on l’applique on aurait eu la meilleure société au monde. Al khamdou Lillah, Sunna rek moy deug
Wa akhlou bidah dagen fans oustaz mor 😂😂😂 j'avoue qu'il est parmi les plus pertinents de sa génération et même plus encore ❤😂🎉🎉🎉
@@Veridic-tv Da ngaa saff khorom bilaahi. Yalla nagnou yalla mousseul si réere. Lii lepp gnak deggue diiné rek moo leene si yobbou, wallahi
Oustaz mor ne parle à aucun des savants d'ahlou souna vivants au Sénégal. Mounei len niou diakhassei
Savants d´ahlou sounnah mooy lann? Yéene da ngéene réere, da ngéeniy thiaakhaane rek: dianguoo leene, diouboo leene, yarou woo leene, tée ngéene diangue té diéema topp séene borom, liguéey , moo gueune seene conceptualisation you vide yii.
@@mamadoudiallo2696 kesk tu parles?
@@A.b7407bonne question mon ami..... Ces gens sont pitoyable....
Qu'ALLAH nous guide
@@Khanif4
Allahoumma barîk
Ma Shâ Allâh ❤
@@mamadoudiallo2696yaw tout va bien dans ta tête ?
pourquoi cette photo sur la vidéo? alors qu'il ne parle pas d'eux
Borom chaîne n'y yallana yallah faye wakhtanbi amna solo lo barrakalahou fikk ya cheikh mor kebe❤❤❤
ماشاء الله تبارك الله فيك
حياه الله ❤
Machallah longue vie à vous tous ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
والله حفظك الله يا شيخي كلام صادقة جدا
حفظه الله ورعاه يا شيخنا الفاضل مور كيبي
Machallah oustaz kebe la sunnah vaincra inchalla ❤
Merci ya oustaz Mor Kebe❤
والله صحيح يا شيخ الحق الحق هم سفهاء لا يعرفون شئ
Machallah longue vie à vous tous
Bilaye denguene di diahasse mais oustaz wahoul gni noppalou lene tè ngene mougne 😅
بارك الله فيك
Hakaza machala Mann dh soufiyou la wayé yaw kou bakh nga walahi
Qu'allah vous préserve oustaz mor
je regarde cette vidéo à cause le titre mais alhamdou lillah çam'a poussé de devenir salafi baraka llahou fiikoum ❤
Machala yal nalén yala fay yéw ta samou lén
حفظك الله يا أستاذ
❤❤❤
Ay wa souffi bayilén fén légui beug diaxassé gayi gnolén déssé bayilén sén xél yingén di fowé 😅
Vie en paix astaz mor, fais ta dahwa ne perds pas ton temps avec ses indisciplinés. Laisse, on s'occupe d'eux et de leur égarement. Je les connais , guemouniou dara
أنتم من أهل المنا فقون وا صلو طريقكم
Arrêter de mentir sur les Ahlu Sunna
Djazakallah khayran Oustaz Mor Kebe (H.A)
Machallah saway dilal bien Yonne bi d'où bax Dh wasonna ay entelecteyiel lanou titre bi Chache ko sonna rk MBA sonne
Machalla
Borom page bi bayil fene 😂😂😂😂sofiankè yi Loutakh niou meuna soss
Denio fans oustaz nk
Maassaala ci tolérance bi
Yallna yalla takhaw
Ils parlent aux spécialistes de mise en garde qui se réclament salafis
Wahabistes nioo eupp problèmes nieupp teusseuntè rek
Bilahi deugg la amou gnou xam xam mandouwoungou
😂waa oustaz kane laa attaqué légui🤷♂️et puis oustaz mor kébé ak Dr diangua ndoo wougne dih🤦♂️seuytané rék mooléén diapp😒waayé diguéén khamné kénn meuniounio séparé 🫰
Vive les ahlu sunnah❤️
هداكم الله يا أهل البدع(المتصوفين)
Morr Kebbeh moytul wakh 6:59 bu bari. Julit wakham du bari. Sama naseeha chi yaw antanka mbokum julit. Nyarel demal nga gestu alquran bubakh. Sa alquran desna lubari. Shukran.
ya horomou deugue
@@abdadev yaw ya halaku motakh ngay top Morr Kebbeh.
M K. Morr Kebbeh
M K Musailamatul Kazzab
Parceque Morr dafa mana fen.
M K Morr Kebbeh
M K Musailamatul Kazzab
Boudé Mor kebe mo am deugue yalna mbougalou yalla dall shi sha kaw , boudé Mor kebe amoul deugue yalna mbougalou yalla dall sama kaw.
@@abdadev Yen dangen halaku. Laanatu Llahi alaikum.
😂😂😂😂😂yen niak nguen khorom dé lifi Oustaz bi nguen beugueuko weulbeuti diakhlé ngueen nak😂
Legui guéne ngéne ba amatoléne kou ngéne génné géndi génnénté séne biirr 😂😂😂
Ta Rien compris il parle les gens du bayan.
est ce que tmt do sétann vidéo bi bala ngua commentaire 🤨
nanfékk bakhoul
Ismahila diaye gayi génénaniouko 😂😂😂
Deysane lii meuno lén ko comprendre 😂
Fen baxoul borom site bi ragalal yalla waxoul languay wax
Wa akhlou bidah di nguen soneu dé 😂
Meunolein diakhassé wa akhlou Sounnah beneu yonn
Ngueni dague di dague rek
Yén diakhasé molén takha diok
السلام عليكم ورحمة الله وبركاته
Ndey San l’islam dh amoul parparlo deugg rk lanuy toupou ak fouma mana feté nk jajeuf SERIGNE MOR
Toi qui a mise cette photo sur la video ragallale yalla
Vous n'avez pas compris Oustaz Mor parle à un secte qui critiquent beaucoup de savants au Sénégal et dans le reste du monde même
Ils critiquent des savants connus ici au Sénégal comme Dr Mouhammad Ahmad lo ..
Bayleen djakassé téh wakh louueen xam
Come yén rek respecté wolén kén
Wa bidah yen yena respecté Ken yen fêter anniversaire yonanté bii moy respect ? Té yonanté bii né koulou bidatin dalala beppp bida fo la
@@Veridic-tv bouféké wané sa mbectei ci goudi gui yonent bi gané adouna mo bahoul bilahi walahi talahi Lou bah amoul
@@ibrahimandiaye5463 loutax ben sahaba défou ko wala yonanté bii ci bopam fêter anniversairam ? 4imam yii ak imam Malick défou ko Ken défou ko apart y'en
@@Veridic-tvyalla dafani loulén yonent bi téré bayi léenko (sourate najmi) mé wahoul Lou yonent bi défoul boulenko def li yonent dafko téré wala yalla dafko téré Moy lay ci diné mé yonent bi défouko ken warouko def wahou doff la concours récital coran conférence extra fan lako yonent meusseu def?
Na yèt yi jok 😂😂😂yeni neen la .
نعم كما تخرجون الناس من الاسلام
Wakhléne ak sén mbokou wa habiyoune di yakh makatal moukareum
Je pense qu'il parle des ikhawaanoul mouslimiineالإخوان المسلمون
والله أعلم
Non non les gens du bayan
@@dembandiaye1524
Stp peux tu me donner plus d'infos sur ces gens là
لا يا انت مداخلة
Contexte réalités théorie lire ci teré kessé parparlo togne ay nit niak teguin ak yar cheikh bou nek arabi saoudit dila dictée eskeuy eskeuy eskeuy ya problème partout ndeysan bilahi tarbiya rek moo woor wayé yeurmandé yalla yatouna
🤭Ba leegi kénn xamul sa waay kan wala ñan lay wax🤔
Waaye daal li lay xamal ni ñiy tópp ta doyloo ALXUR'AN ak SUNNA (YÀLLA nee na, YONÉNT BI (a s) nee na) li ñu nékk maneesu koo xeex mooy, ak koo man di doon, boo juumee, kénn du la ca tópp. Xanaa muy lu ñu xamagul. Ku dul YONÉNT BI (a s) kénn du def lépp loo wax rek ñu gëmmu jël jëfe. Loolu dafa leer.
Dëgg-dëgg taxawaay boobu gisu ñu ko ci waa-tasawuuf. Da nga naan sax ñii xanaa da ñoo jàpp ni ab sëriñ moom du juum🤔 KÉPP KU ÀNDUL CI LI MA WAX, INDIL MA LIEN BU LA NEEX BU BOOBAA MA XAM NI MAA JUUM KON.
Ku ne xam na ni képp ku wuute ak YONÉNT BI (a s), la nga wuute ak MOOM (a s) njuumte la. Kénn waru la caa tópp. Taxawaay ba du léen lu moy ñaanal la ca njéggël mu jeex. Amul leneen. Loolu terewul aji-juum ji nékk ku baax.
Ligenn tekk jioumté moy deug té deug moy fété kaw ! Moudjaditt yi wouté wouniou ak yonnt bi psl sénimbir kenn monouko galagg korr
@@kakhadim6511 Ku baax nga baal ma, déggu ma li nga wax bu baax. Indil ma ci ay leeral waay
Oustaz mor. Diadieuf wayy xamxam bi lerna.
Louñaw mousibala tayit mousibala
Blh comprendoleen Dara.
Ki cheikh bouko diangal sa Arabie Saoudite lay wakh.
Il ne fait aucune allusion aux savants de la sunna sénégalaise.
Nay lere toudal tour yi khana amo fitam wala sen and euleque gnaye khelat😂😂😂😂
Waw khana kiidou more kebe wahabiste mbaadou wahabiya parparlola yénkay liimoy sén djiko yaw kay linga wakh lep mom ngén Di wakh si tasawouf
Baayi lèn Séytaané ak Diakhassé Ahlou Sounna Meunno Lèn Lèn Fèweulé Gnoom da Gnoo Booloo
Thiouthie yi neck si réseaux sociaux yi di tontou , di diabolisé cheikh Mor Kébé H.A, diare lène fimou diere ba nopi , dans ce cas solène wakhé ñou dégu lou lène.
Té nguène ragale yalla si séni commentaire yi rawatina ki deff photo bi ague titre bimou binde c'est diamétralement opposé avec les orientations du cheikh Kébé.
Mor kébé neeko oustaz Moustapha Sylla mingi koy khaar ci débat moudaw
Boroom chaîne bi tu ne comprends rien 😂 de ce que Oustaze mor kébé dit
On s'en fou y'enla rek
Ioe do yam fi mubaya’a yi lay wakhal
5 chef du bandi yi wahabiste yi
Par Dieu le vivant. De un vous prétendez que le salafisme est une finalité alors que ce n'est qu'un chemin pour atteindre la fois, ensuite la vie du prophète Mouhamad salawatu lahi wa Ali Mouhamad, doit être notre maître et Ali as notre référence.Donc je ne les devance ni ne les retard car celà me suffit comme succès et être un esclave me remplit de joie car je n'adore que Dieu. De deux c'est vous qui êtes sectaire dans votre enseignement du dine de Dieu. Si l'ijtihad ne se fait pas conformément au valeurs prophétiques Celui dont l'intension était de suivre le prophète slawat doit être suivis et non l'opposé. Trois sache que notre enemi iblis fait tout pour nous diviser retournons à la source de la prophétie... Unicité et unité Salam voilà le Dine de Dieu.
Salam.
En kon am nguène ay Cheikh 😂😂😂😂
Wahabi yi daniouy komédi
Wakhna dag dh
Tu fe que mentir si tu est véridique faut citer des noms mais diw kokou que des mensonges
At tarikhatou salafiya 😂
Wa mor khana financement daa amamtoul
😂😂😂😂😂😂😂
Wawaw tamanter demeu rek nak diadieuf mor tamko
😂😂😂😂😂😂
billahi gayi diakhal naniu ma kw sufiyakeyi vous avez rien compris
qu'ALLAH VIUS GUIDE
هذاريك وخاص بك
Warona kena dakhola parparlo
Xamo si darra say say rek
C'est quoi ça : titre et contenu différents Ahhhhh ragalal yalla way
Mor kebé amoul xam xam manouwoul
Wahaabi = foutaise 😂😂😂
Cest pas notre probleme. C'est eux dans eux.
😂😂😂😂😂😂😂😂
😂😂😂
😂😂 Séen chaine bii propagande moko taxa diogg wala, xamoléen gnane léy waxal nguéen di ték xél di guénné limou done wax ci contexte bi mou nékone, ay rée nguéen méy déf 😂😂
Yéna kham dh
Mbokk bi do changer sa titre
Dëgg rekk mooy li wóor
Yaw Yaa woor yalla rek nga gueum
dëggu lë
Tu parles des clans au débutant universitaires motakh guani licence rek gua am gnibbissi
Morr Kebbeh danga bary wakh. Wakh bu bary bakhoul moytuko. Wakh bu bary molaye tereji jahama wallahi.
yaw môme ya beurry wakh
bo hamonn dra def daawah
@@bintSafia dawa thiahan. Yen khamulen lan moy dawa. Yen dangen halaku.
@@Ismaeljallow-k3b yaw momou ya hamoul dra
Âme fitt wessou woul nann sa moromou djoulite da alkou
Vraiment tu fais pitié qu'Allah te guide
Waw yén bou turbinal islamiqu amon fii mba doune lén até ay kathior konn
Mor kebe bantarikhaga❤❤
Kone xam ngéne ni aye bandit pir moye ak wahabism lép dina ler inchallah 😂😂😂😂😂😂
Deug sah say say rek
Omar Sàll rekk là gis ci li muy wax
Yaw mi mom chaine yékatou fitna nga saytané nga diakhassé kat nga