Balla et Sa Thiés sont un et un seul.Ils ont un trés bon pére qui leur sert d'exemple.Qu'il repose en paix.Balla protége ton jeune frére. Sa Thiés respecte ton grand. Vous êtes des champions.Soyons unis.Que Dieu vous garde.Amen!
Amna sollo mé bou léne diéle leup tégko thi sa Thiès bayi Balla té Balla gaye li mouy mounial Aziz sou ko mounialé rakam problème dou am sa Thiès tmt nonou ni mouy mounialé ay xaritame souko munialé magam tmt diameu am
Salam siar nalene dafa melni dama tarder dh nekoula au diapason Mais balla ak sa thies serieux dagno am blem ? Esk dou communication bou diaroul yone rekkk ?? Parfois afair bi dou grave sax mais wa sites yi dagniii aggraver d
Surtout lolou Balla Amoul xél bi Aziz ameu mé sa thèse amna xél bi baye Ndiaye ameu déniou wax sa Thiès rk mé Mane lèp Balla lako tég Moy mag waral top rakam même sou défé Érél sa
Saway fi yeup xam ni sa mak wargako diox thieur yaw amga yénéne mak niga diapé aziz diapé wolen nonou c par ce que aziz amna xaliss niguen diapé balla gaye nguen def nonou pr sa thies avancé c tout balla ak sathies nio bokou tei meunu nio tagaliko yalna yalla def diam sen diguenté inchalla
Baye Ndiaye wafi dof rék ngaye wah. Balla ak sa thies sén diganté doko réglé si réseau yi? Ana wahtanu biir néék ? Kouleu dioh deugueu nafékh leu. Yena diahasé balla guaye ak sa thies. Té balla guaye mo gueuneu matadi siblu yalla bindeu! Mo wéér sa thies ak adouna. Wara wo sa rak si néék yédeuko diko wéer si réseaux yi ! Je suis sa thies à 100 pur 100...........
Wahofi dara wahléne balla gaye deg mou bayi wanéwou amna gno hamni diaroul wah sa rak wala sa mak wala sa wadiour loco défal diaroul wah surtout télévision lila war moy ga féhé gnou dibo mé pa tokfi di wah
Machalla kadouyi amna solo yaw dagua bakh rék adouna amoul solo
Contane na si baye ndiaye yallna yalla dakh seytané sa ndigakk momm
Yalnanou yalla moussal si kou ande ak seytané
Baye Ndiaye yaay gorei
Machall Refitna yallna yall japolelen Sa thies ak Balla yallna yall defjamo je barke seydena Mohammed SAW amin
Sa Thies respecte ton grand frère quelqu il en soit
Jé lé larme on dw respecté lé gr frères ,on n peu pa être au désui d tn gr frr
man a cause de baye je peux pas critiquer aziz ce gars est formidable
Balla et Sa Thiés sont un et un seul.Ils ont un trés bon pére qui leur sert d'exemple.Qu'il repose en paix.Balla protége ton jeune frére. Sa Thiés respecte ton grand. Vous êtes des champions.Soyons unis.Que Dieu vous garde.Amen!
Ndeyesane sama yaram dawna ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Macha alla baya so beugué pousse lou diis dangaye wérou fou degueur ❤❤
Amna sollo mé bou léne diéle leup tégko thi sa Thiès bayi Balla té Balla gaye li mouy mounial Aziz sou ko mounialé rakam problème dou am sa Thiès tmt nonou ni mouy mounialé ay xaritame souko munialé magam tmt diameu am
Machallah Mbaye Ndiaye longue vie❤❤❤❤ à➡➡ toi👉
Sa thies wakham nekhout té balla deséna yowou mais yalla na yalla dioubolé len
Bly
Baye Ndiaye mo meuna djioum
(Néna bou aye dallam foré ma Wade) au lieu de (bou ay dallam wadé ma for 😂😂)
Mais merci que même si conseiller 😎👌
Rakeu yeupp sougnou mélonni yaw keur yeup nékh 😢😢😢😢😢baye Ndiaye yagoré😢😢😢
Mane dé Baye Ndiaye dafma nékh mom da am foula 😊
Machallallah baye amna solo yalla nala yalla takhawou barkep alhourane
Merci bye ,,
Salam siar nalene dafa melni dama tarder dh nekoula au diapason
Mais balla ak sa thies serieux dagno am blem ?
Esk dou communication bou diaroul yone rekkk ?? Parfois afair bi dou grave sax mais wa sites yi dagniii aggraver d
Saway digueunnté magag rakk loothiy wakhé wakh djou reuy djou niaw dji gnar gno bokk ndayak baye gni bokk ndayak baye dagnouy dimbeuleunté rakk sou dég gueu léé mag mag yeuerum koo wayé mag mba rakk kouthie amal saa morom ndiarigne mou fonkoulaa affaire bii dou affairou khaliss wayé question de wormalanté laa
Merci ❤❤❤❤
Baye Ndiaye le meilleur promoteur merci mon dieu qui protège
Machaalah Baye Ndiaye Dieureudieuf
Machallah baye Ndiaye vérité absolue
Balla dou aziz❤
Merci deuga tekh werr
Machala tubarkala
Machalla baye ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Macahlla révte na
Machala li de moy aduna merci baye
Aziz ndiaye goudal fane
Machalla ❤❤
Bilaye walaye deug leul kene d’où baye ndiaye merci beaucoup
Machallah Baye❤❤❤
Alkhamdu lillal bien dit baye
Merci baye Ndiaye
Mais Balla dou Aziz dh
Baye ndiaye dou sa thies
Lolou education de base leuh😊
Ndeysane sama yaram daaaaaw
Surtout lolou Balla Amoul xél bi Aziz ameu mé sa thèse amna xél bi baye Ndiaye ameu déniou wax sa Thiès rk mé Mane lèp Balla lako tég Moy mag waral top rakam même sou défé Érél sa
@@faye6718Balla amoul khél
@@faye6718waxofi dara
Balla amna xeel, té Sathies da hawa Seytané na bayi ennemi Balla you mouye deff xaarit niou bari constat def naniouko@@faye6718
Bou ay dalam foré mou wadde 😂😂😂
Walla bou dalame wader mou for😂😂😂
❤❤❤❤❤❤ baye ndiaye
Saway fi yeup xam ni sa mak wargako diox thieur yaw amga yénéne mak niga diapé aziz diapé wolen nonou c par ce que aziz amna xaliss niguen diapé balla gaye nguen def nonou pr sa thies avancé c tout balla ak sathies nio bokou tei meunu nio tagaliko yalna yalla def diam sen diguenté inchalla
😂😂😂😂😂😂
N'importe quoi
ioe vrai mécontent nga si goor
Machalah baye Ndiaye Man mi nek n'a thi dépôt bi nek foire 1 ans kou bax là bly
Bien dit
Machaalla baye ndiaye
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤😂merci 🙏🙏🙏🙏
yalla na yalla defal gneup diam.
❤❤❤❤
Massallah yallah Nallah yallah defal jamah yow ak sa mack
Amna solo
Baye tu as très bien parlé vraiment nitt nittè way sathies va parler ak sa grande frère moguene gaye deguelou seytané di diaxasè
Ohhh mashallah Baye louleu Aziz dèfal rèk mèrito nga ko rakk Diou bakh nga reuyo rèwo tègo sa makk beute yallah nalèn yallah mouseul ci seytanè
Delen diapalé badola yi nak ndakh sen alal am ndiarigne
Machla amnasolo
Ya bakh trppp
Baye Ndiaye da nga bah❤🙏
❤❤❤❤❤❤❤❤
Baye Ndiaye ❤❤
Aziz ndiaye yallah nala yallah defall diamou
Balla❤❤sa Thiès sa rakk la ❤❤
❤️❤️🙏🏾🙏🏾🤲🤲
Baye ndiaye dieredieff❤
Baye Ndiaye wafi dof rék ngaye wah.
Balla ak sa thies sén diganté doko réglé si réseau yi? Ana wahtanu biir néék ? Kouleu dioh deugueu nafékh leu. Yena diahasé balla guaye ak sa thies. Té balla guaye mo gueuneu matadi siblu yalla bindeu! Mo wéér sa thies ak adouna. Wara wo sa rak si néék yédeuko diko wéer si réseaux yi ! Je suis sa thies à 100 pur 100...........
Omar sakho bamouye doga debite carieram nekoul wone si aziz ndiaye keur pa chekhe niange la nekone aret doubles bobou amoul sakhe keur
Aziz garmi la mais baye ndiaye mi kou khame aduna la yalla naléne yalla défal diame
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Sénégal kou yore rék lanouye farale 😢😢 lii
Baye Ndiaye amnga yénéne Mag yo khamné diapéwoléne touss, Azziz mo am khaliss motakh ngakay tarbiyou.
Sathiès koula faléwoul boulko falé, Balla Gaye ci bopam moy dof, 2004 yoroulwone deureum, keur Père Balla Gaye lanéwone moukay diokh lékeu ak naane
Wopopopo ❤❤
Ndeyssane rafétna
Wayé Aziz mo goré, mom au moins meussouko waw, mais Balla gaye dafa bew
Wawaw sur tt ça
Lolou dou wakhou publique,démal séne keur guéne réglé ko en famille bayiléne sése yeufou nafékk yi
No Balla tu est différent c'est ton frère 😭😭
Lolou moyy deug bilahi
Vraiment Baye Ndiaye sa wakh dji lima si dianguehh barina dhe
Baye ndiaye ndeyssane kou baax la
Fi koufi beugue ande ak sa mak do degoulou kene mak mola wara wakh lounei
Baye billahi mane dama amône digante ak sama mag waye sawakhdji djiekhlnako
Balla dafa réw yeuk succès
Ya wakh deug
Salif bayil lép diap t dém wakhak sama
Linguene beugue salif douko def . Walahi linguay wakh siii salif dou deugeu
Tu n'est pas légitime entre balla er Sa Thiés vu que tu es ami de balla il faut juste dire la vérité
Yene dangena wara diapale salif com nigen diapale omar
Vraiment
@@rouguikebe9984 salif dafa bakhe billahi yalnako yalla diapale
@@moustaphababou6282 amiine
Déba bi diarouco yobou léne sa mou toubib,😮
Pour niom bo topoul sen guinaw rk liga beug doko am fi yalla mofi nek bou aziz amoul wone xaliss liga wax yeup doko def mayniou diam
Boye bayiléne séne yi nguir yalla 🙄🤔😒 loutakh sa ganr gui beugougnou guiss loubakh🤔🤔🤔🤔
Mai aziz hana da Teub rek am haliss délene wah lou rafete si diagantè gnari nite gnou bok nguir yalla 🙏🏾
Diapalaléne sa thies comme niguene diapalé balla gaye 😢
Baye linga fi wakh ni yêpe,sa intré rek ngafi wakh mais boule begue sathies dêfe comme yawe dara dakhoule amale sa bope yalla mon yore niêpe
❤❤❤❤🤙🤙🤙🤙
payi nama yalla bal lo yakhou nioko yakhe kham guéne si sa thiés deuk kham fi balla deuk demlén fa wakh ak niom si soutouro mo gan li guéne di def
baye ndiaye limou wakhe kou bakhe réke mokoye wakhe te exemple la nioune nieupe bilakhi
Borome xalisse souy wax gnepay déglou😊
Nénléne teugueul combat gnou beuré! Balla baye ak Aziz gnonko déf Niite
Sa yone nekouthi nio bok séne yaye ak séne baye
😅koudegg bou ay dallam forée mouwadd😅
Lep xaliss moko woundou sou aziz amoul wone xaliss li yeup doko def baye xaliss motakh ngay tarbiyou aziz
Mais bro loussi sa yone ?
Niar niou bokk nday ak baye ?
@@Flemme-08seytané rek bilahi
@@Flemme-08vraiment
Wahofi dara wahléne balla gaye deg mou bayi wanéwou amna gno hamni diaroul wah sa rak wala sa mak wala sa wadiour loco défal diaroul wah surtout télévision lila war moy ga féhé gnou dibo mé pa tokfi di wah
Rak nila wara mel dangaye top sa ginaw mak
Waww
Sathies da fontu kio bo amé make méme bou yoruldara kéne waroul léna diakhasé
Fenn reek
Qui moye mak bou bakh