S khadim ndiaye rachid depuis 10 ans magui deglou tafsir magui wat ciii yalla sunu borom swt deff geua si man lou bariiii. Ciii alxorane yagui ligueye ligueye bou am solo ciii rewmi diareu dieufff
Ndiayéne bou ame ndiarigne bi lol sakh ya bakh lolou dé la yakar si yaw ta yallnako yalla dogal si yaw ak nioune niépeu diërëdiëf yallnala yalla same arrla mousal la si lépeu loumana yakh doundou dioulit si adouna ak alakhira allahouma amineee 🤲
Alhamdoulila ☝️☝️☝️
S khadim ndiaye rachid depuis 10 ans magui deglou tafsir magui wat ciii yalla sunu borom swt deff geua si man lou bariiii. Ciii alxorane yagui ligueye ligueye bou am solo ciii rewmi diareu dieufff
Maa Scha Allah
daga Baxx Rek Mais beuri ga thi Ay Mouroum ...
Billahi ioe
wallay ndeysane baré guasiy morom
ماشاءالله الشيخ خادم إنجاي رشيد
Macha'Allah imame Khadime Ndiaye yalla nala yalla defal diame adouna ak alahira anime 🤲❤️⭐⭐⭐⭐
Machallah s khadim amna solo niobayyi ci khel naniou diamou yalla tabayi thiakhanyi
Dieuredieuf dianghalèbi
Sètna lèrna
ماشاء الله يا شيخ بارك الله فيك ❤
Serigne bi xelaw nga bougnou yalla defal Al hamdoulil lah yalna yalla goudal Say fan
Alhamdou lil lah am na luma oumpoon si 5 yi wayé leerna maachaallah s khadim yalnala yalla faye
Walaahi kii daf lay bëgg Loo yàlla ak yonent bi Muhammad صلى الله عليه وسلم ak alxuraan
Ndiayéne bou ame ndiarigne bi lol sakh ya bakh lolou dé la yakar si yaw ta yallnako yalla dogal si yaw ak nioune niépeu diërëdiëf yallnala yalla same arrla mousal la si lépeu loumana yakh doundou dioulit si adouna ak alakhira allahouma amineee 🤲
Yalnala yalla fay
Machala Serigne khadim amna solo lol yalla na yalla barkél
السلام عليكم ورحمة الله وبركاته بارك الله فيكم وجزاكم الله خير الجزاء
Longue vie cheich bi ❤❤❤❤
Machaalla y
Maachaallah yalna nga goudou fane
السلام عليكم ورحمة الله وبركاته،
Am na solo macha ALLAH
Machallh yaa oustas 👏👏👏
❤❤❤machalahh yalla n’a yalla barkel xam xam bi
إن شآء الله تعالى سوف أفعل قدر المستطاع.
فليكن الله في عوني
Thiey ibrahima
Ken du younetobi sayidina Mohamed صلي الله عليه وسلم
Machallah ❤❤❤❤
Machallakh yene rek lanie wara invite thie teleyi guene di djianguale,
Ya khame senegaleyi tagowode 😂😂
السلام عليكم ورحمة الله وبركاته بارك الله فيكم وجزاكم الله خير الجزاء