Boy diop dosama mbeur srx mais dagne la waar difay xalis deug ndakh mbolo migay eundi si lamb dji Mais nak waar gua diague khekh deug pour etre un vrai champion
Bour say wakh mo amoul ben fondement akkk sens dangay wakh touti bay gnenen gni wakh lou serieux koula fek nganan degue naniou dali yangui beug niak xam xam
Fane la waxé 150 millions ?? On vous suit parce que lamb laagn beugg mais sen titres yi mom c’est mensongères. Franchement meun nacé niakk. D’ailleurs setaan naagn Pencum Lamb ñoune ñeupp
Wawaw frere diop2 ci khalis bi et felicitation mor kag kag
Félicitations mor kang kang
Ayy way yeureumlén Zoss 😢ngir Yalla
😂
😂 leuk loko bagne bagne nagoul meuna dawam, Bour dey nekhal plateau nak...Fadam itam manke na fi 😂
Gni bagn Bour ak Fadam douniou ay vrai amateur lamb
Nice ♥️🥰♥️🥰🥰🥰🥰♥️♥️🥰♥️🥰🥰🥰🥰♥️♥️🥰♥️🥰
Merci Modou mbaye 🎉
D'après ce que Babacar a dit je vois que il n'y a pas de bagarreur sur le plateau
Sa c'est vrai mon frère
Bour fénatina
😂😂😂
Mané méy lén nit gni diam gni beuré nagne louñ meun
Ngathie Gueye deuk la ❤❤
Pabi loumouy expliquéni boudé boxe c'est valable wayé lamb mbeur you khékh ta do déplacéwou souñ la plaqué ya togn sa bopp
Buur guéwél Nite day simple
Yaw nopil 😂
Ki gueweul la C naturel
Kang Kang seul 🎉
Le peuples réclame diop2 vs ada fass
Diop 2❤🤲🤲🤲❤️
J’ai vu que vous parlez beaucoup plus sur diop 2 que mor kank kank
Boy diop dosama mbeur srx mais dagne la waar difay xalis deug ndakh mbolo migay eundi si lamb dji
Mais nak waar gua diague khekh deug pour etre un vrai champion
Ngatou wata😂😂
Talfa ak pacola balde ba khou nio si diop 2 de nio lá apou doli fofff
Pere becaye rayy nma nenako sa lokhou yi metiwoull😂😂😂
Zoss dila may chance pour que nga yegue si kaw baparé ngay fouy
Motay fouy Sans Zoss Diop 2 peut percer may niou Jam
@ahmedseck991 yena kham deh
@@hamidoutall9134 Binga xamé nio xam bobou nga waroona teuthie sa bouche bou xassaw ngeuthie
Diop wakhoull loolou bayyi l3n f3nn thi s3n titre yi
Doulll rek
Zoss. 150 millions c'est trop
60 millions sakh doko laal ndankeu rek
Mba dina laal quarante sakh
@@Abdallah31341 gnii tokk ci plateau aziz ndiaye lagnouy ligueyeul ils veulent pousser Diop 2 vers albourakh motakh gnoukoy diaay nii
Yaw mi wakh lii sakh d'accorouma Diop 2 nimou khekhe si box c'est normal boyy mbeure ak ndama ni Diop deff lolou moyy yonn
Diop 2 seul
Bour guewel aka mana doul 😂😂
Légui k légui mouy graw grawlou nak 😂
Diop 2 vs Ada fass
mor gaïndé la dieule na coup continuer di attaquer diop mais diop modone reculer rekk
Zoss vs Diop 2 dou combat
Zoss doit partir en retraite
Mor moy roi baol
Bour say wakh mo amoul ben fondement akkk sens dangay wakh touti bay gnenen gni wakh lou serieux koula fek nganan degue naniou dali yangui beug niak xam xam
Fane la waxé 150 millions ?? On vous suit parce que lamb laagn beugg mais sen titres yi mom c’est mensongères. Franchement meun nacé niakk. D’ailleurs setaan naagn Pencum Lamb ñoune ñeupp
Mdr danga yabateh , ragale nga dimanche lala kham et dimanche lalay juger do hoor
diop li nga fogon amoul dh bii dou yoyou dh mor kagn kagn dala donn lekeu da ngaa moy sakh
Diop moko lékke ardo deux fois 😂😂😂😂
Ya meuneu doul kou dem ardo 2 fois
@layeNdiaye77 oubi sa digeu data yaye laay def legui domou oubi data yayam dji nga doon
Wasaassss😂
Diop tapét la rek mouy daw rek
Suma guissé mbeur mou ndaw bou soxleu zoss😮😮😮
Bayilén tapalé té jël sén morom yiii
Diop 2 vs alboury
Yaw daga fouye diop 2
Félicitations Mor Kang kang
Kang Kang seul 🎉
Diop 2 seul