SaThiès Encolère contre Modou Lo "Dafmay Daw" , Tapète la - Balla Gaye Ak Siteu doumassi...

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 7 янв 2025

Комментарии • 90

  • @talladiouck46
    @talladiouck46 10 часов назад +3

    Sa Thiès yalla nala yalla defal diame me damalay niane te yalla tax del wakhtane ak sa mak balla khôl bou rafet la yor nite gni ak journaliste yi danlay yakal rk del wagni wax ji yaw boy bou yarou nga ❤

  • @sambaba683
    @sambaba683 19 часов назад +19

    Satiès mounna dane modou lô bakhna surprise bou kènna kharoullll

  • @ycamara9034
    @ycamara9034 35 минут назад +1

    Yes. Sa thies vs Modou lo 👍 Yes Adouna bi lowlou lent bouga 🌍🌍🌍🌍🌍🌍🌍🌍🌍🌍🌍🌍🌍🌍🌍👍🌍🌍🌍🌍🌍👍👍🌍🌍👍🌍🌍🌍🌍🌍🌍🌍🌍🌍🌍🌍👍

  • @moustaphababou6282
    @moustaphababou6282 6 часов назад +2

    Fatma dia mo geuneu aye peul bou rafet foufe fatma dia mome vrement dafa meune ligeye machalla yalnako yalla lafal thiate

  • @moudoudiop6216
    @moudoudiop6216 2 часа назад

    Sa tihss 💛💛💙💙💙💛💛💛💯💯💪🏾💪🏾

  • @cheikhbasskeurmassar9548
    @cheikhbasskeurmassar9548 21 час назад +33

    Sa thèse déle communiqué boo beugé am combat

  • @MorGning-n4i
    @MorGning-n4i 19 часов назад +8

    Modou dieulal sathies bly day nkh

  • @manoumbaye6277
    @manoumbaye6277 20 часов назад +12

    Modou beugou le dieul té doula dieul son camp voulait juste diviser guedieway comme il a fait a pikine pour régner, alhamdoulila dieu a aidé balla gaye 2 bou dielone modou Lou nek dinako dégue guedieway té danko diakhassé AK rakam

    • @AliounebadaraThioye-ho4tq
      @AliounebadaraThioye-ho4tq 19 часов назад +2

      Guenteu diambour ngay netali ya barii kham kham😂😂😂

    • @adama6405
      @adama6405 18 часов назад +2

      ​@@AliounebadaraThioye-ho4tq😂😂 ak sama bosse

    • @MbayeThioumb
      @MbayeThioumb 16 часов назад

      Vraiment Lou lerrr rk gua wax niom gni niepou tay gnigui donn xarr balla dieul Modou bagn takh radio yi Di wax te tay balla migui ni dieul siteu ba legui Modou manoul dieul sathies

  • @mameousmanecisse540
    @mameousmanecisse540 16 часов назад +2

    C le potentiel combat c'est lui ki a battu siteu et reug reug donc il mérite le combat royal si modou n'a pas peur de lui

  • @moudoudiop6216
    @moudoudiop6216 2 часа назад

    Moudou Lo dou touss 😂😂😂😂

  • @PapaDiouf-u5z
    @PapaDiouf-u5z 14 часов назад +2

    Modou dieuleul boy by loulou laniou beug

  • @ndakarudialdiop1206
    @ndakarudialdiop1206 20 часов назад +7

    Sathies beug nala trop mais da nga wara réw tuti, lamb il faut nga am touti sai-sai

  • @MDbousonko
    @MDbousonko 2 часа назад

    Sathies mano léne wakh bamou sansé nimou Mèl

  • @MaguetteBoye-e1x
    @MaguetteBoye-e1x 21 час назад +4

    ❤❤❤❤❤

  • @PapaThiam-pm8ss
    @PapaThiam-pm8ss 2 часа назад

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @GuyGuiguitou
    @GuyGuiguitou 8 часов назад

    Iow del yarou yarou lou rk✌🏾

  • @moudoudiop6216
    @moudoudiop6216 2 часа назад

    Moudou Lo Sa tihss Sa papa la

  • @AtoumaneNiasse
    @AtoumaneNiasse 20 часов назад +4

    Lou gnip xam xam bakhoul siteu nguir yalla mayil daw 😂😂😂

  • @IbrahimaFall-yn5xm
    @IbrahimaFall-yn5xm 17 часов назад +4

    Sa thieS, meuno, djaye combat, do, comuniquè. Amo, khorome.

    • @oumarndoye1169
      @oumarndoye1169 8 часов назад

      Tapéte rek moko diap gnom gnep moléne mane 😅

  • @PapeNiang-j9w
    @PapeNiang-j9w 16 часов назад

    Modou Lo aka ndayi ragale sathies 😂😂

    • @papipapi344
      @papipapi344 13 часов назад +1

      Mod lo daan sén papa boy niang ak Eumeu nganane ragal y’a rèw 🤣

  • @babacar3178
    @babacar3178 10 часов назад

    Yéna beug yénay wakh😂😂

  • @ChicDrive
    @ChicDrive 21 час назад +2

  • @MalickDiop-f3y
    @MalickDiop-f3y 15 часов назад

    Jackson vs Amanekh combat bou nex 🔥

    • @PapaDiallo-oe7pj
      @PapaDiallo-oe7pj 15 часов назад +1

      Amanekh doukou dieul dako ragal jackson lagnu ko dieuka proposé

    • @MalickDiop-f3y
      @MalickDiop-f3y 15 часов назад

      @ mbeur lou yomb rek

  • @moudoudiop6216
    @moudoudiop6216 2 часа назад

    Moudou Lo Sa tihss Goumba la

  • @KhadimDiouf-d5t
    @KhadimDiouf-d5t 19 часов назад +1

    Sa Thiès seul

  • @Sangomar93
    @Sangomar93 20 часов назад +5

    Sathies loutakh dieuloul franc😂😂

    • @MalickCeesay-ju4vm
      @MalickCeesay-ju4vm 20 часов назад

      Bilay😂😂

    • @bassdiokhane1472
      @bassdiokhane1472 19 часов назад +1

      Fracn amna combat yall nako ama daan

    • @omarndiaye7359
      @omarndiaye7359 19 часов назад

      𝑨𝒎𝒊𝒏𝒆 𝒊𝒏𝒄𝒉𝒂𝒍𝒍𝒂𝒉🤲🏽🙏🏽​@@bassdiokhane1472

    • @MalickSouware
      @MalickSouware 17 часов назад +2

      Loumoukoy doyé

    • @bebetoloppy7751
      @bebetoloppy7751 15 часов назад

      @@bassdiokhane1472haral beugua meune bindeuh fran

  • @SaliouDiaw-u4d
    @SaliouDiaw-u4d 20 часов назад +12

    Modou dou dieul sa Thiès dafko ragual

    • @sfmnoble814
      @sfmnoble814 17 часов назад +4

      Kharal ma réee 😂😂😂

    • @falloutoure4021
      @falloutoure4021 16 часов назад +2

      Billy doumako rée saliou 😂😂

    • @BayesaliouGueye-nc6wo
      @BayesaliouGueye-nc6wo 16 часов назад +1

      😂😂😂😂yw khana lowbe nga😂😂😂

    • @gora8046
      @gora8046 14 часов назад +2

      Khana boba da fek Sathiés dane boy niang😂😂😂 nek lène ay nitt.

    • @AlassaneDieye-cc7jq
      @AlassaneDieye-cc7jq 12 часов назад +1

      Esk doffo yaw mi ?

  • @boubaleye2003
    @boubaleye2003 20 часов назад +5

    Modou Lo lou yombou lay weur ada fass lay khar

    • @soldierbamba8117
      @soldierbamba8117 20 часов назад +1

      🤣🤣

    • @disytbi8711
      @disytbi8711 20 часов назад +8

      Boy niang mi niouss empereur bi da yomb ?😂😂

    • @Isbocar27Ba
      @Isbocar27Ba 19 часов назад +1

      Boul faté ni roi bi nious boy Niang empereur bi mo ko nious 2fois

    • @moussadieye5702
      @moussadieye5702 2 часа назад

      Bimou dieulé Ama baldé ak Boy niang looo waxoooon ?

  • @Leuzsonko
    @Leuzsonko 14 часов назад

    Siteu limo tkh ma beug ko nieuw na roube lambj yep 😂 sa thies champion nga del wax bro di tangal akh

  • @Leuzsonko
    @Leuzsonko 14 часов назад

    So beugue am combat di gua def kom siteu del wax di yeungeul ms leulou rek😂

  • @FallouGalss-j8r
    @FallouGalss-j8r 19 часов назад +3

    modou lo mom bou dieloul sa Thiès ma khamni deugo woule mo wakhon khalé yii laye maye sans nit daye ame kadu dotoul diere revanche té do mayé revanche

    • @modousarr8848
      @modousarr8848 18 часов назад +1

      Reug reug

    • @Deggou
      @Deggou 10 часов назад

      Modou dafaniwone 3boy rek laay maay revange teu modou loutakh dieuloul sathies peut y’a 5ans sathies boumou doone khass modou dika wakh dou nekk rois des arènes px être modou lolou tamite sila...

  • @yuzmvthiam7670
    @yuzmvthiam7670 21 час назад +6

    Modou dieuleul boy bi oie gayi daniouy wax rek mais tapétte bou MAK gu

    • @thiamahmadulattekh562
      @thiamahmadulattekh562 20 часов назад +8

      😂yow boy niang mi niouss sathies ak balla
      Mom la boleik ama ak siteu gnuss lene si un an ga nane daw
      Pour yene liguene beug dal la modou dif ef yeinay papam
      Danou ba nopi echec fep nane par force daga gnuy dieul

    • @Bayeniang20
      @Bayeniang20 20 часов назад

      @@thiamahmadulattekh562lolu yeup du wakh bi na topu wakham te may chance sa thies punto

    • @disytbi8711
      @disytbi8711 20 часов назад +2

      ​@@thiamahmadulattekh562doff yi diaroul tontou 😂😂

    • @yuzmvthiam7670
      @yuzmvthiam7670 20 часов назад +1

      @@Bayeniang20 bly nk da wara dieul boy bi msModou lo dafa mousse quoi mom danioukay woutale yonn boumouy diarr di nokou boyi par bén bén

    • @MaimounaSow-s4b
      @MaimounaSow-s4b 20 часов назад +2

      @@thiamahmadulattekh562siteu mila niouse sa thies moko dan emplus mala dan 2 fois dioutale la à domicile bire amitié nopil guediawaye dou yoyou 🗡️⚔️

  • @Leuzsonko
    @Leuzsonko 14 часов назад

    Modou lo kom que dagua ragal tapha tine sa thies xana amanekh ngay dieul wala nga xar ada fass😂😂

  • @ametsow2271
    @ametsow2271 18 часов назад +1

    Nekal fi niounane la daga yarou diga yekha am combat amo beneu promo

  • @damembow6374
    @damembow6374 20 часов назад +6

    Modou dieul amanekh wala alioune seye mo geunn dieul sathies bimouy bagn franc tégouko fénn

    • @bassdiokhane1472
      @bassdiokhane1472 19 часов назад

      Wakho fi dara nga balma😂

    • @damembow6374
      @damembow6374 16 часов назад

      @bassdiokhane147 kharr lénn diéne🤣

  • @AlassaneDieye-cc7jq
    @AlassaneDieye-cc7jq 12 часов назад

    Sa di daw franc ba danou si eumeu nguen beugu mou gneuw nek rois des arènes, lolou esk xel atane nako ?
    Comparer à Siteu kiko dane VIP hors paire la té ben defaite bim am wa lambe gnoko xeex mais danouwoul mouy Lac 2. Kone nak xol si Siteu beuga def modou ragal. MODOU 3 trois combatq la def ben saison s lou moussoul am si arène bi

  • @adamandiaye5622
    @adamandiaye5622 18 часов назад

    Modou sa thies rk la war dieul

  • @modousarr8848
    @modousarr8848 18 часов назад

    sathiés le 12 kou dan amnafa combat

  • @landingsane57
    @landingsane57 17 часов назад

    Ya meune doul dieleul franc boko dane gni dioh la modou

  • @moudoudiop6216
    @moudoudiop6216 2 часа назад

    Sa tihss

  • @diopakhmada5228
    @diopakhmada5228 20 часов назад

    So lamboul dangay bayi lamb Dou dahira

  • @antadiagne5715
    @antadiagne5715 6 часов назад

    ❤❤❤❤❤❤❤