appelle serigne bada fall mbaor ak mame thiérno

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 30 ноя 2024

Комментарии • 251

  • @allikebusiness9427
    @allikebusiness9427 Год назад +50

    Kou beugeu MAME THIERNO may ❤❤

  • @adacoly2524
    @adacoly2524 Год назад +6

    La sagesse, le savoir écouter de Mame Thierno ❤❤ohhhh machalla Mbacké.
    Nite soko déglouwoul do kham limou beug wakh.

  • @allikebusiness9427
    @allikebusiness9427 Год назад +20

    MA THIERNO il est yarou machallah ❤❤❤❤

  • @BayeTalla-h5z
    @BayeTalla-h5z Месяц назад

    Wakh ak yar ak talibé rek mo am solo ❤❤❤❤ mame thierno borom darou machallah ❤❤

  • @saliousane2809
    @saliousane2809 Год назад +4

    Mashallah Mame Thierno Mbacké kou am talibé téy ta yarou ❤

  • @modoufall4949
    @modoufall4949 Год назад +8

    Dieuredieuf serigne touba diarama cheikh ibra fall ❤

  • @aliounekorydiouf5218
    @aliounekorydiouf5218 Год назад +18

    Mame Thierno est un homme trés sage et displiné

  • @elhadjimare9757
    @elhadjimare9757 Год назад +21

    Guis ngua Fall nagnou wakhantè deugg, lamigne sou wakhoul deugg wakhii fène, Borom Darou wakhoufi léneu lou graw ,gnii diko wo tèlèfone diaralène gnoukoy enregistré gno beuss diaxassè yone bi
    Enplus naka nguay wowé kilifa bou tolla ni borom Darou di waxx ak mome ta nangouwoko bayi mou argumenté
    Guiss ngua yarr nitt kou baxx dafkoy ame ,nèkoul nii dangua sante Mbacké wala Fall rek loula nexx deff ,gnoune Talibè yi sènii nawlè lagnou dioxlène gnou thieur
    Wa salam
    Dieureudieuf Serigne Touba
    Diarama Mame Cheikh Ibrahima Fall
    Yone bi nak kène doussi léneu lepp Serigne Touba la ❤❤❤❤❤❤

  • @lothiane8969
    @lothiane8969 Год назад +2

    Mame Thierno yag fi té wér yagui baye sa War si dîné dji❤tt les musulmans derrière vous ❤❤

  • @AboubacryGaye-s4k
    @AboubacryGaye-s4k 7 месяцев назад

    Machallah dieureudieuf mame thierno deugeu rek kay deugeu vive l'islam ❤❤❤❤❤❤❤

  • @modoubaragayetalibebamba
    @modoubaragayetalibebamba Год назад +3

    Mame thiérno brom darou yallnako yalla samou kou bakh té yarou ❤❤❤❤

  • @mourasow315
    @mourasow315 Год назад +12

    Un homme multidimensionnel THIERNO BOROM DAROU ❤😢

  • @galgalgal8007
    @galgalgal8007 Год назад +3

    Boroom Darou Mame Thierno mooy yaaram ta Yarou dall am tegiin ❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @s.modoubousso565
    @s.modoubousso565 Год назад +9

    bada fall iow sokhor nga té amo béneu téguin yangui mélni do seutou cheikh ibra

    • @papemoustaphabadji8421
      @papemoustaphabadji8421 Год назад +2

      bada fall amoul dègue ďègue en plus il est simplement jaloux. il dehonnore serigne aliou fall mbaor borom kham kham très éllocant.tèy ak dègue dadji c'est très important. vive borom darou noreyni

    • @torodo.ferrari
      @torodo.ferrari Год назад

      Jalousie leu rek ndax mom keineu khamouko wayé kham naniou MAME BOROM DAROU ❤️

  • @awa4774
    @awa4774 Год назад +20

    Dieuredieufeuté borome Darou ❤️ yague fi lol AK wer MBACKÉ Balla Aïcha dieuredieufeuté ❤

  • @diolsallamariam392
    @diolsallamariam392 Год назад +10

    Brome darou ❤kou ame yar la billahi😢😢

  • @MainaCISSE-hu7fi
    @MainaCISSE-hu7fi Год назад +20

    Franchement li gniawna li yeupe djarou ko wone vraiment dafa djoume toupe n’a balou djekhna mais wakh bi djarouko vraiment CHEIKH IBRA c’est pour tous le monde ce fallene à mal parlé boudoule Dara fall si soufe MBACKE si kaw Bilaye

  • @sonhiboumbow4293
    @sonhiboumbow4293 Год назад +1

    ❤mame thierno kounou yarla billahi

  • @doudousow4619
    @doudousow4619 Год назад +8

    Soubhanallah.
    Gueme yalla tope yonente bi spl.

  • @Senedane-jw5in
    @Senedane-jw5in 2 месяца назад

    Dieureudieufati Mame thiernou borome darou

  • @diallosouleymane4370
    @diallosouleymane4370 Год назад +12

    😂😂😂😂😂 ça me fait rire Barek borom Touba
    Mame Thierno y’a wakh deug
    Mbacke la santeu wa Touba la
    Les Baye fall , talibe Kara et bethio
    Aïda Diallo. Revenons sur terre

  • @khoudianiang8143
    @khoudianiang8143 Год назад +17

    Mame thierno est un homme digne vraiment je l'aime❤❤

  • @babacarndiaye9378
    @babacarndiaye9378 Год назад

    Serigne Bada fall vraiment guisouma yarre si môme sokhor lafii guise

  • @EspañaTenerife
    @EspañaTenerife 7 месяцев назад

    Dieureudieuf serigne touba diarama mame Cheikh ibrahima fall ❤❤❤

  • @KaneMariemeboye-rm2xn
    @KaneMariemeboye-rm2xn Год назад +27

    Mame Thierno kou daleu leu kou yarou barki Serigne fallou MBACKÉ tayy lagn leu gueune beugg MBACKÉ lii djoylo nama sakhh Bada fall yaw li doumalako meuss ball😭😭😭😭😭😭

    • @lampfallndiaye6814
      @lampfallndiaye6814 Год назад +1

      Fi dafa ame lofiye balé ak lofidoule balé seytané Yi dague wakheu dji Kaye nga wara wakheu nafekheu nguen trop défaral léneu mogueune diakhassé bi

    • @ogflow5720
      @ogflow5720 Год назад +1

      Yaw lo topé serigne lenen loudoul mou khamal sa bop ak sa borom yangui koy lou jeumal safara bayilen folklore bi té weureudji kilay khamal Yalla nga diamou dji Yalla serigne bi diamou dji Yalla kou deh Yalla faye🙏

    • @lampfallndiaye6814
      @lampfallndiaye6814 Год назад +1

      @@ogflow5720 iow sosi bokoulngua teuthieu sa gatte si yoneu bi ta dieul sa yonou bop

    • @mouridesaadixa5868
      @mouridesaadixa5868 Год назад +1

      DÔTUKO DOLLI
      DIKUK TÃLIBÉ BA NËB XAMADI BÈW
      MÃM SHEIX IBRAHIMA FALL DU MORÔM
      AMM NGËRËMËL MÃM XADÎMU RASSÛL DÔMAM YÈPU DIOXKO CËR BAM MËT SËK
      LAMP FALL LA SËRIÑ FALLU MBACKÉ WAX DU KÉNÊN

  • @laminediop5298
    @laminediop5298 3 месяца назад

    Bada fall mi kou rew leu te niak talibé yagui guatiel cheikh ibra heureusement beu touti guassi nioune gueumouniou leu yakarouniou leu doylo wouniou leu diarama borom Borom Darou Noreyni ❤❤❤❤ yarr ak teguin reik reik gueu wane ki dakoufi Alou kenn iow bada fall amo yarr amo teguinn fi nak kofi respecter woul respecter wouleu nakh Y’a Rabanna mofi neik ak Seydina Mouhamed Serigne Touba tekk niou si yonn bi pour niou neik si lou yalla digule

  • @DiankoToure-lb7ht
    @DiankoToure-lb7ht Год назад +2

    Kou bayé dioule yéferla bilaye 😢😢😢😢

  • @KhadimMbaye-bh7bp
    @KhadimMbaye-bh7bp Год назад +3

    Bada yaw Amo bene yarr 🥹🥹🥹🥹🥹

  • @AbdoulayeDiop-k3u
    @AbdoulayeDiop-k3u Год назад +1

    Enregistrer bi modoul yone diereudieufé borom Darou

  • @awafall7741
    @awafall7741 Год назад +5

    Mbaké ak fall démbleu nioune seutyii fillaniouko fék naniou bayii mou séde 🙏🙏

  • @diopcheikh5951
    @diopcheikh5951 Год назад +2

    Wallahi Bada fall yaw kou soof nga khamo Dara yaw wallahi

  • @adamathiam1020
    @adamathiam1020 Год назад +3

    Bada fall ak kanam kou nioul guiiiiii melni dayi keuriye!!!!!! Borom darou rk lanouy topou❤

    • @mouridesaadixa5868
      @mouridesaadixa5868 Год назад

      BU TUDËTÉ MÃM SHEIX ÑUSKO BAM DAYE SÉXLKO
      DÔMU HARÃM
      BÔ UBBÈ SA DATA NDAYE FÈKAFA LU RAW KËRIÑE

  • @MoustaphaDiop-223
    @MoustaphaDiop-223 3 месяца назад

    Dieureudieuf mame thierno ❤

  • @elhadjindiaye4691
    @elhadjindiaye4691 Год назад +1

    Yalna sa brom yagalla chicory

  • @Ahmad-ig9ev
    @Ahmad-ig9ev Год назад +2

    Seringe touba nénawone serigne Masamba théirno mi bouléneko dirmbag rawnape kharno

  • @maremgueye9460
    @maremgueye9460 Год назад +5

    Bravo mane thierno❤❤❤

  • @amadoudiallo8578
    @amadoudiallo8578 Год назад +1

    diereudieufé Borom Darou❤❤❤❤👌👌👌

  • @falloumbaye2016
    @falloumbaye2016 Год назад +3

    Ndaysaan mame thierno aka teey

  • @thiernoaw8193
    @thiernoaw8193 Год назад +2

    Baye bada kadouyou amna solo yalla nala yalla faye

  • @dameniasse1970
    @dameniasse1970 Год назад +6

    salam niou balma mais bada fall mii waroul wakhé nii ak Mame Thierno

    • @aladjiendiaye632
      @aladjiendiaye632 Год назад

      Da sokhore rk bone énalko dong dah bolo mi top mame thierno mom mous sah top top pouko

    • @diaramatoulaye7095
      @diaramatoulaye7095 Год назад

      Moone day eppelewoul maam thierno ci Maam Cheikh Ibra. Maam ceerno mi maamaam Penda Diop. Maamaam Mariama Seye Cheikh Ibra ko jokk maamaam Khadimou Rassoul mou jokk KO maamaam Thierno Ibra Faty mu am ca Seydina Ousmane di. Dooni ndiggal ju maam Cheikh def barke Maam khadim def barke def KO dommi Ceerno birahim nuy and ak barke fu nu ma na jem nu diy baye faal. Cheikh Ibra defar sa maam Penda Ndiaye Diop teral KO aar KO aar njabotaam tey a k elegue .

    • @aladjiendiaye632
      @aladjiendiaye632 Год назад

      @@diaramatoulaye7095 gni degno sokhor yarame

  • @modoubaragayetalibebamba
    @modoubaragayetalibebamba Год назад +2

    Bada Fall dé mato référence borom darou mi boko déglou rék dégue limou wakh dara nékousi. Li ngéne wara wakh wakh léne ko té bayi tapalé yi 👌brom darou beugue nanouko ba paré

  • @Bass.beuzz.bdn.6037
    @Bass.beuzz.bdn.6037 Год назад +8

    Bada fall lou yalla binde rk yathi geuneu khamadi réw nga torop yaw kaye da nga bange. Serigne bi mo takh kay ngay wakhé nii mo béne talibé bilahi may wakh ngay teukou waté nane niogui sa kawe,wala yawe yagui thi kawame khana té bo nékké thi kawane yaye khala lorou yawe

  • @gadelo426
    @gadelo426 Год назад

    Nitt kann mo Koy kholl diko bagne khamall wakh wayy Dieureudieufé Borom Touba

  • @primo9146
    @primo9146 Год назад +1

    Ki enregistrer appel bi partager ko limou def mo gueneu bone problème bi gnouy waxtané

  • @fatoulo440
    @fatoulo440 Год назад +1

    Merci Serigne Bada fall

  • @FadalGaye-is9qy
    @FadalGaye-is9qy Год назад +2

    Machalla mamtherno

  • @djibyndoye8841
    @djibyndoye8841 Год назад +1

    Borom Darou yalla nako yalla dèfal Diam

  • @mamediarra617
    @mamediarra617 Год назад +4

    Deudjeuf brome Darou🙏🙏

  • @babacarndiaye5260
    @babacarndiaye5260 Год назад +2

    Ndeysann Borom Darou aka Ameuh talibé. Diarama Borom Dorou, Diara ame Mame Cheikh Ibra Fall

  • @aliounebadarakonte949
    @aliounebadarakonte949 Год назад +2

    Mame thierno limou waxx dara nekousi

  • @YounoussAdjivon
    @YounoussAdjivon Год назад +1

    Serigne Bada mi matoul kilifa way.

  • @stafiroulaha
    @stafiroulaha Год назад +4

    Mame thierno tout se que tu as dit c'est vrai Baye fall yi danioulaye dogalé toke thi sa kawe auto

  • @cheikhkante6580
    @cheikhkante6580 Год назад +3

    Mame ternou ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @bassiroudiouf6033
    @bassiroudiouf6033 Год назад +1

    J'aime mame thierno❤❤❤

  • @mamediarra617
    @mamediarra617 Год назад +2

    Pourtant Mame thierno à région des ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️

  • @fromdiouls547
    @fromdiouls547 Год назад +6

    MAME THIERNO BOROM DAROU wallahi dafa yarou... appel bi daa geneuh wané lolou..liko wadji Di wakh tégou woul si bein respect té moungui déglou rek Aka djégeulou té loumou wakh bokoul AK niom liniou deigeuh...Tiey seytané mougui diow SERIGNE bi

  • @MassambaFall-ks4tf
    @MassambaFall-ks4tf Год назад

    Di toub tey diégalou m kharouniou li si yon bi neniou meytou pexep non

  • @TuzCisse
    @TuzCisse Год назад

    Def semblant nék djoulit té yeufeuryi niofi eup

  • @Domoupikine200
    @Domoupikine200 Год назад

    Bada fall iow amo yare amo téguine kéne yaroula Serigne Touba amena louko méti looole diamoule yallah mo geune thierno dala rawe fouuufe❌

  • @abdoulatifdiop5640
    @abdoulatifdiop5640 Год назад +1

    Xaw ma bada xaw ma nakasa ki🙄😂😂😂waxi doff rek lafi wax

  • @salioulo465
    @salioulo465 Год назад +2

    Merci borom darou

  • @salioundiaye2782
    @salioundiaye2782 Год назад +1

    Dieureudieufe mame thierno brome darou ame gua yare ame gua téguine dane la yare

  • @saliousss4637
    @saliousss4637 Год назад +8

    Bilahie baye thierno dague rk nga wax

  • @elchico8595
    @elchico8595 Год назад +1

    Dieuredieufé Serigne Touba Diarama Mame Cheikh Ibra Fall Lamp Baboul Mouridina Maïssa Bigué Coumba Fall Lamp Mame Cheikh Ibra Fall Moniou Doy Ci Talibé Ak Deugueul Dieuf Dieumou Dieuf Mo And ak Ndiggel Dieuf Dieuf Dieul.

  • @actunewstcorientalbuzz7298
    @actunewstcorientalbuzz7298 Год назад +1

    Wa Sénégal yakkou na ndakh Serigne si gnongui wèrantè wala firannguè la😂😂😂

  • @seydinathiam6724
    @seydinathiam6724 Год назад +4

    Bada dafa mélné humilier thierno mola takha diouk. Te dafa am yar rek kon mu tontu la. Jalousie rakh na si.

  • @salioundiaye2782
    @salioundiaye2782 Год назад +1

    iow kou gnanke respect gua amo béne respect

  • @alhassaneba1492
    @alhassaneba1492 Год назад +2

    😂😅😂😅vraiment Sénégal tang temps yi sonko macky bada thierno li yeup si ay féne ak mbirou adouna négn diamoudji yalla té bayi diamou nitt 😅

    • @fatimaba3833
      @fatimaba3833 Год назад

      deug piir nga wah diamou yalla rek mo wore

    • @Flemme-08
      @Flemme-08 Год назад

      Yaw ibadou nga comprendre nagne la .. Dieuredieufé Serigne TOUBA diarama mame cheikh Ibrahima fall

  • @YounoussAdjivon
    @YounoussAdjivon Год назад

    Deuk bi fila tolou legui. Gni gnouy wowe kilifa bou gnou demé bay enregistré on est mal barré. Mame Thierno amna yar amna teguine amna dal. Limou wakh moy deugue

  • @MourtadaMbacke-ns3yf
    @MourtadaMbacke-ns3yf Год назад

    Balla aicha ❤

  • @amadousow3039
    @amadousow3039 Год назад +1

    Mame Thierno deug rèk la wakh

  • @mamourndoye686
    @mamourndoye686 Год назад +4

    Baye fall beuguou gnou DEUG
    Nena mame cheikh même boulenn dougualee safara beugue nagnou soubhanallah

    • @lampfallndiaye6814
      @lampfallndiaye6814 Год назад

      Dala mety beug naniou Kaye nafékh ngueni trop dolen wakheu ak doméram yi enregistrer Mame thierno nioune beug borom Touba ak cheikh Ibra boudé moniouye dougal safara beug naniou

  • @aliounebadarakonte949
    @aliounebadarakonte949 Год назад +1

    Baye fall nekk lén nite

  • @khadimdiop4521
    @khadimdiop4521 Год назад +1

    Bada fall saytané nga

  • @alethiam7461
    @alethiam7461 Год назад +5

    Borom darou mo âme talibe yalnaco yala defal diam

  • @assanegueye28
    @assanegueye28 Год назад

    Wa wakhi kilife kouko guéné si bédemi

  • @seneami4448
    @seneami4448 Год назад

    Niakka mandou wéssou woul di wo nit téléphone dikko enregistrer après partager ko

  • @ndeyefaye6073
    @ndeyefaye6073 Год назад

    Khén d'où yaw mbacké diajeuf

  • @papeseck9969
    @papeseck9969 Год назад +2

    Wa kane moy bada fall Iow koula kham

  • @ousmanesow7506
    @ousmanesow7506 3 месяца назад

    Gnak guindékou si yalla mo waral wakh jou Gnaw dji dem lénn wouti yalla naka cheikh Ibra dann défé

  • @biba9498
    @biba9498 Год назад +2

    Mame Thierno loumou wakhe mo ame deugeu nekhoul

  • @mouhameddiarra9531
    @mouhameddiarra9531 Год назад +3

    Bo degué waxtane bi xamni mentalité yi dou bénn mame thierno deug rék leu wax

  • @thiermecanicien6407
    @thiermecanicien6407 Год назад

    Ndeysane mame dji dafa dioum rek ndeysane 😥 borom Darou dieredieuf

  • @sambagueye9232
    @sambagueye9232 Год назад +3

    Serigne Bada mi déconné na dh Mame Thierno lou raféte rk lassi dioub lou wone

  • @TuzCisse
    @TuzCisse Год назад

    Reure amna niomi nén nioy wéranté

  • @damdiene6702
    @damdiene6702 Год назад +2

    Mame thierno li mou wakh Dara néwosi

  • @moustaphababou6282
    @moustaphababou6282 Год назад +1

    Segne bada fall yaram linga wakhe mame thierno dafa eup vrement

  • @diopcheikh5951
    @diopcheikh5951 Год назад +2

    Yaw Bada fall Mame thieron nekoul sa morom bage nàn KO wakho daegue

  • @ndiaganiang8779
    @ndiaganiang8779 Год назад +2

    ILS sont jaloux DE mame thierno

    • @hadythiam8209
      @hadythiam8209 Год назад

      Lolouuu la guisss mame thierno est universel mme gnoun tidiane dagnokoo beugue lolou yalla deff

  • @sallmameawa-lq1vk
    @sallmameawa-lq1vk Год назад

    Basa fall rewnka😮

  • @serignecheikhounadiaxate2409
    @serignecheikhounadiaxate2409 Год назад +8

    Bada fall yaw kou rew ga

  • @hulkhulk4973
    @hulkhulk4973 Год назад +1

    Bagako enregistrer rk ga soufel sa bop fall yaram !!! Niougui toubatt nak!!!! 🙏🏾🙏🏾

  • @elhadjindiaye4691
    @elhadjindiaye4691 Год назад +1

    Noreyni ni lanou beugeu

  • @adamandiaye3448
    @adamandiaye3448 Год назад

    Koumeuti done sa Baye nite kou bax day Am Yar

  • @damdiene6702
    @damdiene6702 Год назад +2

    fi Mame cheikh issa diene rék mo fi né❤❤ Mame cheikh issa diene môme rék bilay ♥️♥️💯💓💯

    • @bsm8133
      @bsm8133 Год назад

      Serigne touba yaatou na dh yaram

    • @ndiennetv6389
      @ndiennetv6389 Год назад

      Mame Chiekh issa borom ndienne

    • @AbdouFaye-bv6og
      @AbdouFaye-bv6og Год назад

      Niou na lah gana gëm CHEIKH issa lo bari bilahi cheikh ibra fall rek la nioiy topou

  • @BintaCamara-o1e
    @BintaCamara-o1e Год назад

    ba iow dokou bakh dé bilahi

  • @khadygueye4851
    @khadygueye4851 Год назад

    Li yeup dara djaroukofi . Meunone nguéne wakh ci souf. Wayé li gnawna. Yoonou Serigne TOUBA, li amoufi yoone. Diokhânetéléne lokho, té liguéyale Serigne bi.

  • @abdoufall1124
    @abdoufall1124 Год назад +3

    Mane guemna ni mame waxoul pour yax

  • @mouhamedfall6002
    @mouhamedfall6002 Год назад +2

    Mame Thierno limou wakh moy deugu deh kou diamou woul yalla perte gua

  • @ousmanefall-gc5rf
    @ousmanefall-gc5rf Год назад +1

    Mame thierno doumorom