Размер видео: 1280 X 720853 X 480640 X 360
Показать панель управления
Автовоспроизведение
Автоповтор
Jërajëf lanne mo tékhalé saar ak paćci
Jaajëf ndaanaan. Dese naa teewlu li léén teqale de. Waaye jàpp naa ne bari na lees di bind saar donte ne ajuwul ci wàlle diine. ci sama xalaat, dafa mel ni baatu pàcc sax moo doon gën a jàppandal fii. Cant ak ngërëm jàmbaar.
Saar veut dire un chapitre tandis que " Pácci" Signifie une partie.
Un chapitre pourrait comporter plusieurs parties