en revoyant le matche j'ai la chaire de poule franchement dimanche nekhona tropeeeeeeeeeeee machaala notre equipe notre fierté yallananou coupe djikk felictation a notre cadet aussi 100% LEBOUGUI
Artgraf Li lebbou gui def moussoul am thi histoire Nawetanes. 12h billets yi diekh. Li nek thi biti sade keneu khamoul nomou tolou. Li khadjoul Demba Diop Léopold la kadjone 🙏🏿♥️♥️♥️
Le ministre doit organiser une petite Finale Lebou Gui Vs Khandalou avec un mise de 5millions pour encourager les équipe Navetanes . Li dafa bakh si deuk nieup bolo si béne affaire dafay doundeul quartier bi dioubalé nite yi deuk si quartier bi
Moi chui native de ce quartier mais li ffaa am guissoumako feneine..ils font la fierté rufisquoise et je pense que toutes les équipes de navetanes doivent copier sur eux vraiment
C ça le problème psychologiquement aucune équipe ne peut faire face le mieux c k Lébougui gagne sinon on ne terminera pas la partie sinon l’équipe adverse et ses supporters en pâtiront 😂😂 mais je rêve d’une finale nationale Lébougui et khandalou 🔥 🔥 🔥
On devrait avoir ce genre d'équipes en championnat ligue 1 sénégalaise. Vraiment bravo pour l'ambiance en même temps sans violence. Félicitations
Match thiokho
On devrait intercalés les matchs de championnat entre celle des navetane
Ça c’est le Sénégal 🇸🇳. Vamos
Rêve de jouer dans cet Asc 😌⚪️🔴lébou gui
Fier d’être rufisquoise et lébou 😍🙏
Lebougui on les meilleur supporters du monde
Lébougui mo dake supporter
Exceptionnel Vive ASC lebougui, mention spéciale aux supporter. I like this depuis louga
Jai des frissons lebou gui amoulene morom mbokayi
Vraiment un grand merci à cette équipe de quartier qui a fait la fierté de des mouvements navetane
Lébougui dall nékh nagn ma ndakh sén Supporter yi
Mane dé douma thi doyal 🔥✌️
en revoyant le matche j'ai la chaire de poule franchement dimanche nekhona tropeeeeeeeeeeee machaala notre equipe notre fierté yallananou coupe djikk felictation a notre cadet aussi 100% LEBOUGUI
Kou deukeu Rufisque wanéle sa bope
C'est qui
Present
Je suis vraiment content j réve de jouer dans cet équipe bravo à vous❤️👍
vraiment merci! suis tombe sur vous mais li mooy navetane! merci pour l'ambiance
Ils ne jouent pas mieux que l'autre équipe mais ils ont le mérite en vue de leur engagement 👍
Ces vrai
Moussouma gisse ambiance bou meileni nawetane bamou dathie yeina fii dakeu supporter seine takhawaye neikhenama fiere d vous
lebougui c'est Liverpool 💪💪 ynwa👏
😂😂😂mai vraiment j'adore cette ambiance
Hymne bi jarna ay milliards kouko dundoul doko xam on vit notre asc lebougui Rk Thiaka Ndiaye dans l'âme
Mais vraiment li Dafa Nékh bilahi 👏👏👏
Meilleur asc de dakar cei temps ci
de rufisque
Match khandalou lebougui lolou so amone dina graw
@@pepzoba9224 yèe lolou DINA métty dh ms team lèbou gui rk
Loutax çà Khandalou la Rosa rk ci ambiance ak barriway eupena
yeungeul féppe lébougui dafay yeungeul fépp 💪💪👌👌❤️❤️
Navetane ak mystique nio and libougui felicitation
Mé none daye soxore wala mole day soxore ngéni wax.jaime bien votre engagement et votre ambillant dans tous le stade
Boy loy soxore laniuy wax
Man lebougui lay beug foutbal bilay 😍
Bo diayé sen matche niou ray la dhé
Tt mes félicitations 🎉🍾🎈 vraiment vous l’avez mérité asc lebougui
Du jamais vu RESPECT ASC lebougui
Thiey LÉBOUGUI match bi 13h la dem mou fess déle non RIO NEKHNA EN HAUT
Ouiiiii
Sen stade bi équipe bi match navetanes cadet zone de Dakar yi sax meun neko fessal nax dafa ndaw
@@talibegodtalibegod3255 boybloy sokhor boy loy sokhor kou mer tant pis wakhal deug louma leer moy meusso nieuw si stade bi di oubi sa lamign
@@aminaseck4943 dfa leer
Artgraf Li lebbou gui def moussoul am thi histoire Nawetanes. 12h billets yi diekh. Li nek thi biti sade keneu khamoul nomou tolou.
Li khadjoul Demba Diop
Léopold la kadjone 🙏🏿♥️♥️♥️
Lebouguii dall felicitation 🥰
C'est vraiment beau félicitations à vous
No franchement gni rek nion mérité niou défaratalén sene stade nakh mobilisation bii
Du jamais vu ambiance extraordinaire bravo
Ohh ça me rappelle les navetanes de 2016 final usine bene tally &lem gui Vive les rouges Blancs 😍😄
Bene tally yw mom sma mbokkou ngua
Non fally nioun ak niom derby leu deh usine ak biscuiterie
Beu parer meu dem rio thi wa lebou gui
Fatou Pouye mdrrrrr dageine si dale lem gui mo saffff ✌🏾
Fatou Pouye dieul sen roukh 😁😁
Abou Dia lem gui année bobou ragual mokko perte Lo match Bi
Wa ngagne samb djem leina roy sii gnii supporté nagn ba match bii diékh tei keineu degoulene niou saga wala dii deff yeufou rewandé.. vive leebou gui❤️
Ooooooh bilay sa me rapelle notre final2018 sam sam3 finaliste zonal et departemental🥰
Sam sam 3 avec mon frère Dieye Gerrard
Oh sa me rappelle des souvenirs lointain... quand je portais le N°6 !!! Nawétane amone na
L’équipe de l’année
Deukeu Rufisque mo nekh vive asc lebougui
Sans violence dafay geuneu nekh vraiment dama contane si li yen lay weur si reso socio yi dal félicitations
Vraiment vous êtes forts
Oh 😍😍😍
Le ministre doit organiser une petite Finale Lebou Gui Vs Khandalou avec un mise de 5millions pour encourager les équipe Navetanes . Li dafa bakh si deuk nieup bolo si béne affaire dafay doundeul quartier bi dioubalé nite yi deuk si quartier bi
Moi chui native de ce quartier mais li ffaa am guissoumako feneine..ils font la fierté rufisquoise et je pense que toutes les équipes de navetanes doivent copier sur eux vraiment
Lebou gui sama kogne 💪💪💪💪 danioo mane liniouy def
Billahi gni gno dakk yeuguall wa 12ème ak wa allez casa
Wa like nekhoul
Nekhna dh trop sakh mais casa RK
Yénama geneul 12em gaïndé deh supporté ak sétal bo❤❤koul
Bien joué ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Jèm troppp cet èkip bilay😘😘
Nice les ga mai départementale yalah bou lébou gui ak ngagnie sambe dadjié amine
Je veux organiser un tournoi de 4 équipes khandalou reubeuss, fc grand yoff, diakarlo Ouakam et lebougui sen khalaat
Faté gua khar yalla
Book diom guédiawaye ak farba yeumbuel
Arafat moh môme Grd yoff
Fo bayi avec kussum
Tirage bi Mets rekk asec kussum vs khandalou
Vraiment lébougui vs méritez supporters et l'équipe de l'année.... Bravo c Sénégal qui gagne👏👋👏
Fière d'être rufisquoise♥️♥️♥️
c'est jolie mé serait plus belles de s'unir derrière le tenguethie fc la fierté des rufisquois
Je très content trop ☺️😘😍
Rufusquois et fière..
Lebouguiiiiii rek
Ça c une exemple nationale vraiment li nice n'a lol c beau
Ms lebougui warna am équipe championnat dh
C ça le problème psychologiquement aucune équipe ne peut faire face le mieux c k Lébougui gagne sinon on ne terminera pas la partie sinon l’équipe adverse et ses supporters en pâtiront 😂😂 mais je rêve d’une finale nationale Lébougui et khandalou 🔥 🔥 🔥
😂😂😂😂😂😂😂
Le Patriote sou bobaa nga guises final bou amoul fen walahii 😂😂
Tournoi yoyou la gayi wara organisé
@@salioulo3614 billay wallay
Liga wahh khamoko sahh deux équipes très populaire jtjr ambiancieur di gen lou graw
Man dall J adhère par force lébou gui nekhna way 😘
Rufisque mon dakh Navétanes sii Sénégal bilahii 🇸🇳🇸🇳🇸🇳♥️♥️✊✌
Sen navetane mo geneu naxari kou guiss nax sen stade bi équipe bou dakar yi khadiounioufa même match cadet sax khadiounioufa 😂😂😂😂
Wakhou doff
@@talibegodtalibegod3255 ioe boul niou sonale iba mar diop ngene ame
@@talibegodtalibegod3255 ioe nak nekhoul ba nekhoul danga sokhorr.... Rio d'où ayé foooo
Ak Demba Diop Ak Léopold Gni newone ci stade bi yeup khandalou rk molén guena barii Fouf
Félicitation LFC
Supporters yi nio gagner match bi
Vraiment
J'adore cet ambiance non violence Diam rk🤗
Lîmasi neh moy degou mafa violence 👏👏
Moustapha mbacké Guèye surttt ça
Juste la veritè kouy violence sakk gni gnou barry gni
dagn lène gagnèwoul rek
Mai li moy navete way😍
nekhna trop fière d'être lebou
Federation bi warnane leine sett si djeul leine dh Yeina dakh yeungeul 12eme gaindé ak Allaz casa
Billahi wakhal way
Gnii kay machalla amna solo
Sama Asc Mame Thiaka. Alaw Lebou,
Kou dioy yalla yeureum la gni amnia mérite si navetane li beugue sa asc la rek
Bilay lébou gui légui sama équipe la ndakh son wally seck souféké damaly dérangé desolé 😂😂😂
Puissance Khandalou🔥le plus populaire
Machalla wa lebougui
Kou DANE Balla guaye
Lebouyi wanelene sene boop way 😀😀😀😀😀😀😀
I love this so cute 😍😍
100% lebougui 💯❤🇮🇩
Guédiaway la deuk mais maléne fans liguéni aziko amoul
Li kagn ay sabar là dou Assiko
Kou mérr tampi🔥❤️❤️❤️
Daniouy gagné🏆🏆🏆🏆🏆
C rufisque ki gagne 🤩🤩🤗🤗
Cé vraiment beau félicitations à lebou gui
Mashallah wa LébouGui, vous avez très tôt su k c'est dans la non violence qu'on parvient à savourer une victoire. BRAVO BRAVO BRAVO
Waaaa li neikhoul 😍😍😍
Ana lebous yi..👉
niougui niii
Wakhal way
Maa mbokiiii lebou 💉
En tout cas c'est Une grande équipe
Navetane rufisque mome nos stress la
Diaguene dieufeuti Rufisque Moy gagné rk
Deuk lebougui mo nekh🥰
Sama deuk Leu fier d être lebou
Bravo lebougiuo
Ces eux qui mérite de supporter le Sénégal on.nés fatigués avec aller casa
Yénagui doundal navétane👌🏿👌🏿👌🏿
Cet asc m.plai bcp
Mai vraiment lébou Gui dall mo nkh
Lebou dji a pris la place de khandalou ! Waww c du jamais vu
Li nekhna wa légui nak khamguen lou déss bayi khékh bi ak niane yiii😂😂😂lebougui is béa 🔥🔥🔥🔥🔥
Guichet fermé ❤️⚪ wa lii nékhoul😂
En kayyy❤️❤️❤️❤️
Enkay 😂😂😂💪🏽
Stade bou ndaw bi c normal😂😂
Asc Khandalou moy Borome Amitiés ak Demba diop
Gni dhe kou yakk sene match amgua problem bou reuy 😂😂😂
Asc lébougui bamou berry dolé
félicitations à vous
Merciii a vous