Mosquée Oustaz Omar Sall: L'imame craque et fond en larme "Sénégal Rek Mo Am Niary Tabaski"

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 15 июн 2024
  • Prière de la Tabaski à la Mosquée de Oustaz Omar Sall L'imame craque et fond en larme en plein Khutba "Sénégal Rek Mo Am Niarry Tabaski"

Комментарии • 142

  • @abdoulayediarra2525
    @abdoulayediarra2525 10 дней назад +19

    Qu'Allah vous préserve imam ❤❤❤

  • @AbuSouleymane-pn5go
    @AbuSouleymane-pn5go 10 дней назад +6

    Maachaallah imam, Inchallah dîné Yallah bi sikanam rek la jeum ❤.te la Sounnah triomphera

  • @aissatoumbelanediouf5211
    @aissatoumbelanediouf5211 10 дней назад +8

    Machallah Amina solo. Qu'Allah vous récompense par le bien !

  • @Talla221
    @Talla221 9 дней назад +4

    macha allah yalla na yalla naggoul dioulitt yeup

  • @safietoumbaye8351
    @safietoumbaye8351 9 дней назад +4

    Notre fierté machallah oustaz

  • @ramadiop8458
    @ramadiop8458 10 дней назад +7

    Yanna yalla diégual niou nioune nieup niou yagu ka téwé

  • @user-qk4xs6xt8f
    @user-qk4xs6xt8f 10 дней назад +4

    Merci ya oustas

  • @Serignekhadimmohamede
    @Serignekhadimmohamede 10 дней назад +17

    Fii beenni Tabaski mou fi am moye lundi sopa insallahe

  • @user-mi7sb5nn1e
    @user-mi7sb5nn1e 10 дней назад +7

    Macha allakh sén liguéye rafét na yalna léne yalla Faye wallahi sunu xôll sédna lôll sunnah rk Moy DEUGG ❤️❤️❤️❤️

  • @khadyngom2397
    @khadyngom2397 10 дней назад +4

    Ma Shaa Allah ❤

  • @oumarfall4707
    @oumarfall4707 10 дней назад +18

    Pourtant le Maroc, la Mauritanie et beaucoup de pays prient demain. Le Sénégal n'est pas une exception.

    • @ndiamediop4755
      @ndiamediop4755 10 дней назад

      People also ask
      Quand c'est la fête du mouton au Maroc ?
      AIDEZ-NOUS À AGIR. En 2024, la date de l'Aïd Al Adha (Aïd El Kébir, Qurbani, Tabaski) est fixée au dimanche 16 juin et durera trois jours, jusqu'au mercredi 19 juin.

    • @user-lg4sm8cm2m
      @user-lg4sm8cm2m 9 дней назад

      Donc tous ces pays devraient jeûner l Arafat aujourd'hui

  • @oumarsoindebalde4710
    @oumarsoindebalde4710 8 часов назад

    C'est important ya oustaz

  • @ishakathiam6525
    @ishakathiam6525 10 дней назад +4

    ❤️❤️❤️ machallah

  • @djibrilball5439
    @djibrilball5439 10 дней назад +2

    Massa Allah y’a oustaz❤

  • @ablayesow3057
    @ablayesow3057 9 дней назад +7

    Kouye Tabaski guiryalla c dimanche, kouye Tabaski guir sa Serigne leudi

  • @user-xe5cz6ub5s
    @user-xe5cz6ub5s 9 дней назад +5

    Wallahil Azim lolou dou deug dou yone sincèrement mane Tijanne la mais ki keurou diné yi deif dou deug dou yone

    • @mouhamadtamourougueye387
      @mouhamadtamourougueye387 9 дней назад +1

      Démal diangui nganaan mane tidjane la. Roy lo woune gnou si Macca mais si yonnent bi lane gnou roylo. Linga nek tidjane soula néxatoul bayikofi té maygnou diam

    • @abdoukarimfaye8193
      @abdoukarimfaye8193 9 дней назад

      Légui yaw Lou yonentébi diangalé?

  • @boubadiallo3472
    @boubadiallo3472 7 дней назад

    Macha Allah oustaz arona Sall

  • @gnilaneciss9817
    @gnilaneciss9817 9 дней назад +3

    Machallah

  • @dembisssarre1627
    @dembisssarre1627 10 дней назад +4

    Macha allah ❤

  • @amethdiaw3475
    @amethdiaw3475 9 дней назад +1

    بارك الله فيكم ❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @kamaraawa8121
    @kamaraawa8121 10 дней назад +4

    Amine ❤❤❤

  • @dabaloum531
    @dabaloum531 10 дней назад +3

    Amine ya imam dieuredieuf

  • @cheikhdione92
    @cheikhdione92 9 дней назад +1

    Machallah Oustaze

  • @ramadiop8458
    @ramadiop8458 10 дней назад +5

    Adina laniouy nék di ratatati mé si kanamou souniou borom la lep di ler dina am niou méré séni serigne wallahi fék c est trop tard

    • @seydousambakoulibaly734
      @seydousambakoulibaly734 9 дней назад +2

      Souniou Serigne, Yallah ak Yonente bi, ak sounah, Charia laniou léne topee nioune.
      Néanmoins, koussi wathi Yonne douniou lasi tope. Le cas des Serignes yi doug si politique bi en est un exemple avec l' élection de Diomaye.

  • @user-qj4hz3hk3m
    @user-qj4hz3hk3m 10 дней назад +3

    Machalla brakalah fick

  • @sokhnafatoudiallo4952
    @sokhnafatoudiallo4952 10 дней назад +6

    Kel discourt maachaa Allah

  • @mananaye2615
    @mananaye2615 9 дней назад +3

    Machalla

  • @dembacamaraba8965
    @dembacamaraba8965 10 дней назад +10

    Prck senegal 🇸🇳 lagniouy sèntou weer normalement

    • @astor-VI
      @astor-VI 8 дней назад +2

      Démal gua diangui wat

    • @dembacamaraba8965
      @dembacamaraba8965 7 дней назад

      @@astor-VI saway lolu diaroul diexal tèrè yi Les fuseaux horaires sont différents aussi Sénégal par exemple Touba chaque mois dagniouy sèntou weer xarougn ba tabaski wala korite jott

  • @gltntegilou9532
    @gltntegilou9532 7 дней назад

    Amiine amiine yaraby machalla dieureudieuf ya Imam ❤❤❤❤☝️☝️☝️🤲🤲🤲🤲🤲

  • @luqmanwestafrica1911
    @luqmanwestafrica1911 7 дней назад

    Hafizahullah ❤

  • @user-vq9ct2ow7t
    @user-vq9ct2ow7t 10 дней назад +3

    ❤❤❤❤❤❤❤

  • @ngonekandji6079
    @ngonekandji6079 9 дней назад +3

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @modoundiaye245
    @modoundiaye245 10 дней назад +3

    ❤❤❤❤❤

  • @abdoulayediarra2525
    @abdoulayediarra2525 10 дней назад +3

    ❤❤❤❤

  • @elagegueye3310
    @elagegueye3310 4 дня назад

    tabaski landemai arafatleu lolou la yenentebi psl meuseu deff

  • @user-wh2lp8cy9s
    @user-wh2lp8cy9s 9 дней назад +1

    Amiine

  • @user-tb1ds6bv5g
    @user-tb1ds6bv5g 8 дней назад

    Machalla 🥰🥰🥰🥰🥰🥰🥰❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @yaragteggiin5101
    @yaragteggiin5101 9 дней назад +1

    Yal na Yàlla nangul leen barkeb alxuraan

  • @user-zd3uu1eq7z
    @user-zd3uu1eq7z 9 дней назад +1

    Macalaou

  • @AbuSouleymane-pn5go
    @AbuSouleymane-pn5go 10 дней назад +12

    Wa Sénégal dagnouy woor Arafat ak nieup ba paré né Tabaski mom après lendemain Arafat la . Lii dafa dem ba xoromou 😂 thiey tarixa yii diné bii dou bou Mouhammad

    • @fatoumatabintoucolley8878
      @fatoumatabintoucolley8878 9 дней назад +2

      Ga sagn ko wakh nyi dènio doy warr soubhanallah

    • @nabousylla1314
      @nabousylla1314 9 дней назад +1

      Wa Makka worougnou Arafat,gnoune 8eme AK 9eme jour lagnou woor pas arafat

    • @PerfectionladybyKenza
      @PerfectionladybyKenza 8 дней назад

      Légui tabaski lundi dh Sénégal wétousi Mali Mauritanie Maroc xamna ils ne sont pas musulmans

  • @modasamb443
    @modasamb443 9 дней назад

    Ont n'ai dans quel pays vraiment

  • @serignembackediop9882
    @serignembackediop9882 9 дней назад +1

    Malaisie, Indonésie, Pakistan, etc lundi

  • @user-wz3bu2fo9j
    @user-wz3bu2fo9j 9 дней назад +1

    Mauritanie mali ak niou melni niom lundi laniouy diouly

  • @ousseynoutoure3621
    @ousseynoutoure3621 9 дней назад +2

    Pour Mane Omar sall dafa beugueu buzz mai li amoul wakh deifna liko doye na bayi gnouye diouli lundi deif Lou leine doye mo gueuneu Neiw kham kham si reiw

  • @OneClick__
    @OneClick__ 4 дня назад

    Tabaski 3 jour la diangual nga bagne

  • @user-bk4db5ki7s
    @user-bk4db5ki7s 10 дней назад

    Thies rek mo ame niari gare

  • @seringsaine9504
    @seringsaine9504 9 дней назад

    Même en Gambie . Il Ya en une aujourd'hui et il y en aura une plus grande demain parceque la plus partie du Kombo et presque la totalite des habitants du fleuve ne suivent pas l Arabie Saoudite. Je parle en connaissance. J y ai vecu pendant 32 ans comme voyagiste

  • @mohamedjobarteh4448
    @mohamedjobarteh4448 8 дней назад +1

    Omar Sallah deque deque yaw mandu wo
    Yangi hulo shak jour purr lan?
    Esque yaw ham nga bu bakh lan moy lislam?
    Lislam du hulo.
    Lislam moye nga layeh biir sa mbokum julit.
    Hulo amul palass chi sunna mohammad saw.
    Demal nga jangi mogen.
    Wallahi neko chi tus
    Yangi chahaan nga defeneh chi ligaye Lislam nga nek.

  • @fatoumane1380
    @fatoumane1380 9 дней назад +3

    Mais foumou ko tek parce que teye 9 dhou al- hijja 1445. Nous n’avons pas les mêmes fuseaux horaires avec la Mecque.

    • @UmmuAymane940
      @UmmuAymane940 9 дней назад

      Et connais-tu le décalage horaire Mecque / Sénégal ?

    • @user-tu5do2bu1z
      @user-tu5do2bu1z 6 дней назад +1

      Yaw da melni mokalo sa HG😅

    • @Dioabd
      @Dioabd 6 дней назад

      Waw distance horaires bii 3heure de temps késé la Sénégal dégnon doy ware dakh wér bouye fégne maqua Moy fégn Sénégal Kone Lou takh gnouye outé suivi la sunna car c'est le chemin de la vérité

  • @ibousylla2658
    @ibousylla2658 10 дней назад +7

    Thiey les nouveaux musulmans. Arabie Saoudite instant bi football ak boxe laniou tale 😂😂😂
    Fi beneu Tabaski mofi am .Soubah lundi in sha Allah.

    • @UmmuAymane940
      @UmmuAymane940 9 дней назад +2

      Quand l’ignorance règne en maître , ce sont que ces idées qui sortent des bouches …
      Yalna yallah yeureum

  • @djilyndiaye-wo9ri
    @djilyndiaye-wo9ri 9 дней назад

    Kholam sèddeu na bamu amalee ak wuutè

  • @soulymandione4895
    @soulymandione4895 10 дней назад

    Degaye fenne maroc

  • @cheikh1872
    @cheikh1872 9 дней назад +1

    Kharal ma nopi Sakh 😂

  • @KanaMbaye-fp9vt
    @KanaMbaye-fp9vt 9 дней назад +2

    Séen diouli hitt bi,tégoléen kossi kham kham déh.😂😂😂

  • @adamandiaye2580
    @adamandiaye2580 10 дней назад +10

    Division bi am Sénégal yênako fi indi.Amguêne droit diouli tay mais deflêne ko tè nopi may nit gni diam.

    • @IbrahimaToure-ev3yp
      @IbrahimaToure-ev3yp 10 дней назад

      مغفل

    • @AliouneToure77
      @AliouneToure77 10 дней назад +5

      Lou mou wakh moye deugue

    • @bassiroumbaye8099
      @bassiroumbaye8099 10 дней назад +2

      Dangay fén

    • @amadoufatimakane3564
      @amadoufatimakane3564 10 дней назад +2

      Ñoom bëggou ñoo défa ndoo dara ak tariha yi par ce que jappé wouñ nou ay jullit

    • @Ordinaire95
      @Ordinaire95 10 дней назад +1

      Division bi mo makk gni ,mourides ak tidianes yi nioko indi , legui rek la niarri tarikha yoyou commencé Di dioulendo mais avant Moy lolou

  • @Beugdeug
    @Beugdeug 10 дней назад +1

    Mais c'est à cause des gens comme vous

  • @abdoudieng1016
    @abdoudieng1016 9 дней назад +1

    Arrêtait vos prêches fatalistes ragal yalla nekoul si sole yére you khotekou la sincérité et la clé de tout en te voyant pleurer tu ne las pas

  • @oumarseydi-os3tf
    @oumarseydi-os3tf 9 дней назад

    Juste une question, est il un péché de fêter le lundi?

    • @nabousylla1314
      @nabousylla1314 9 дней назад

      Non parce que c'est le 10eme jour de l'apparition de la lune au Sénégal

    • @UmmuAymane940
      @UmmuAymane940 9 дней назад +2

      Non mais la Sunna du Prophète S.A.W est de fêter le lendemain de Arafat , donc le Dimanche. C’est sur Lui que l’Islam est descendu et si nous prétendons l’aimer et le suivre, nos actes doivent se conformer aux Siens.

  • @sidimoukhtarmbacke7958
    @sidimoukhtarmbacke7958 9 дней назад +1

    😂😂

  • @alassaneniang7669
    @alassaneniang7669 10 дней назад +1

    Ndeyasane imam bi amoul sakh lere ki Day selale nii

  • @sonkodiomaye
    @sonkodiomaye 10 дней назад +3

    Mais vous là c quoi votre problème en réalité yeen yenay diaxassé yen diouli ngeen tay lolou moleen doy diaroul ay wax diapp ni linga def mo bax li kéneen def baxoul fofou la niak xam ak niak mandou tambalé l'islam contradiction yagg ci mo waral ngiir you wouté yi te boci diapp bax na Sénégal commution yifi nekk dagni sentu weer 12mois sur 12 ci lagni natté yawmou hanrafa 9e jour ci weerou Tabaski ça n'a rien a voir taxawayu hanrafa lolou gni dem makka la concerné boudé wa makkaa ngeen doylo ci sentou weer ta diawu dji fo nekk mou tim la aythia😢

  • @alybabakande
    @alybabakande 9 дней назад

    😅😅🤒 da beuri rongogne

  • @Kheuch703
    @Kheuch703 10 дней назад +6

    Sa dioy yi dawoul sounou yaram,gueuno gnou gueum yallah,dou niou ay nafikh

  • @deugmondieukdeugmoymudie2437
    @deugmondieukdeugmoymudie2437 10 дней назад

    Luffi am rek yeenako fi indi... Désormais amngeen lingeen bëgg 6em tarixas🤗 dessé naleen bénén challenge nak changé leen bes yi ñooko boklé ba tey puisk changé ngeen wer yi ba bokkatuñuko changé leen bes yi ak horaires yi comme ça buñu nékké ci bëccëg ngeen nek ci guddi , buñu nékké ci guddi ngeen nek ci bëccëg jam ni ñoy🤗

  • @sarr6876
    @sarr6876 10 дней назад +1

    Yen dong yenafi indi gnari Tabaski, Maroc, MAuritanie et tant d'autres suba laniy julli comme Senegal ndax daniy sentou nikou Yonenti bi psl jangalé.
    Débat bi deug ci situation Palestine la warone done mais comme que Arabie Saoudie douci wax yen tamit idem

    • @AbuSouleymane-pn5go
      @AbuSouleymane-pn5go 10 дней назад +1

      Kagn ga wor Arafat 😂

    • @UmmuAymane940
      @UmmuAymane940 9 дней назад +1

      Leerna ma ba leer Palestine loulen gueunal moy niou tekh suñu tank fi ko yonenti bi tegone. Ñom falañ tekh sen tank motah ñu julli Dimanche.

  • @ngoudambaye2786
    @ngoudambaye2786 9 дней назад

    Vous êtes à l origine de tout ce qui se passe dans ce pays.

  • @yaragteggiin5101
    @yaragteggiin5101 9 дней назад

    Ki omar sall wala dafa am niary os?

  • @sarr6876
    @sarr6876 10 дней назад +3

    Yak sa thieukeul bu reuy
    Oumar Sall mom nax nalén ba commencé yor tuti di sol ay grand boubou getzner legui 🤣🤣🤣 wagni thieukeul bi

  • @mohamedjobarteh4448
    @mohamedjobarteh4448 8 дней назад

    Omar Sallah diina du purr hulo.
    Yaw luy sa problem?
    Yaw amo kham kham amo yarr amo tegin
    Warateh ak hulo bokul
    Maso wakh kham kham
    Doul waye yaw.

  • @BahyayeDiop
    @BahyayeDiop 8 дней назад

    Oustaz da changer trop il a trop maigri

  • @t-free7908
    @t-free7908 10 дней назад

    Pourquoi vous voulez suivre arabie saudite adouna bi nieupay séntou bam déss yénn

  • @amadoulaminediop8852
    @amadoulaminediop8852 9 дней назад +1

    Khamna kouy weur imam you nafekh di fowé diné aka takhalé dioulite yi moy niou melni yene natou Senegal deug nguéne

  • @seydaastou2005
    @seydaastou2005 10 дней назад

    Yen dangena yabater division bi yénako fi indi

  • @PerfectionladybyKenza
    @PerfectionladybyKenza 8 дней назад +1

    Légui louy problème meuno léne wakh bagnou topouléne kou nék na lidieunti dinganték boromam

  • @kamoucamou3882
    @kamoucamou3882 10 дней назад

    Dél wakh deug en tant que imam vraiment c du n'importe quoi se pays

  • @mourtalladiaw3362
    @mourtalladiaw3362 4 дня назад

    Yaw khamo fobokou di khebate akka khaste rek du toj rek ba soukourat njeuw bakham loulay dikkeul...

  • @mourtalladiaw3362
    @mourtalladiaw3362 4 дня назад

    Omar Sall ak Ahmed lo amougnou xam xam lidou xam xam

  • @alfredbonkassy1023
    @alfredbonkassy1023 10 дней назад +1

    Lundi moy tabaski pleure

  • @mouhamadouniang5344
    @mouhamadouniang5344 10 дней назад

    Imame saupe mane

  • @minantv6832
    @minantv6832 10 дней назад +1

    Kouy weur domou haram bo guiségni diaplén

  • @madialistv5158
    @madialistv5158 10 дней назад +2

    Machalla