OUSTAZ AHMED BA-WAXTANOU TAMKHARITE(PART2)
HTML-код
- Опубликовано: 29 ноя 2024
- cette vidéo a été réaliser par Birane Ndao Tel: 77 979 87 23
👍Merci à tous ceux qui laisseront un pouce bleu 👌
🔔 N'oubliez pas d'activer POST NOTIFICATION pour ne pas manquer les prochaines
Macha allah diéurediéufé cheikhi baye Niasse diarama seydi Bâ
Allahou akbarr y’a oustaz
alhamdulilah macha'allah seydi oustaz ahmad ba
Thiey sunu oustaz longue a vie tooi
salam
bane xassaide lako serigne touba binde?
khana serigne sam mbaye bokoussi walla cheikh anta diop walla serigne cheikh gaide fatma ou serigne mourtada ect .......
ps: je demande juste des daliile.
baye gnasse mome damakoy bégué
Machaallah yalla feyla inchaallah
Machalla
On
Pathétique !!! Non mais yalla mougne na quoi .... Lou neekh waye wakh ci Serignam....
Alhamdoulilah ATAA AMROU LAHII
Ismaila DIENE serign bi ligua wax gua tek KO fane Oustaz leup loumou wax indil nala dalil waxma bene wax bou mou wax ta ando si ak mom
Serigne xamena lila méti si wakhou Oustaz wayé nak nguénel yalla mokoy diokh kouka nekhe wakh linga dafa yombe trop critiquer té indiwo dara lolou moy wané sa soufé xam xam. So beugué mouthie si adouna ak alahira ma digal leu boul critiquer boul khep kène té nanga rafète ndiorte si daimou yalla yi rawatina talibé Baye yi nga khameni folène fek gnoungui si nassiril haq bil haq
Moha Bou yaye machllah ki diaroul tontou serign bi
Lou Way nekh wakh si yonéntam