Bonne nouvelle Encore Max Mbargane dépose un appel pour sa victoire contre Modou Lo

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 4 дек 2024

Комментарии • 220

  • @hamzafall5475
    @hamzafall5475 7 часов назад +29

    Père dèmal diangui reglement lamb mo gueunn... Ne soit pas un mauvais perdant...felicitations modou lo

    • @moussambaye3403
      @moussambaye3403 7 часов назад +1

      Ki bimouy xam lamb dga dioudou do am respect

    • @sonkofocus2024-ph4hv
      @sonkofocus2024-ph4hv 49 минут назад

      ​@@moussambaye3403 mossoul kham lamb dadane danou rk 😂

  • @ModouDiom-z6w
    @ModouDiom-z6w 6 часов назад +13

    Li mome gnakk geume yalla leu bilahi

  • @SambaMbodj-l8o
    @SambaMbodj-l8o 8 часов назад +19

    Yow dolene halate Modou lo mo lene may chance nak😮😮

  • @kebandao5918
    @kebandao5918 2 часа назад +1

    Merci per yalla na yalla faye❤

  • @FallouDjimbira
    @FallouDjimbira 6 часов назад +11

    Père so paré fiiii gua dém police

    • @AbdouMansaly-vz6os
      @AbdouMansaly-vz6os 5 часов назад +2

      😂😂😂😂 après police n'a séti procureur !!!! Na wakh mbeurmi mou déme entrainé dji té bayi Thiak thiak .

    • @CheikhNdiaye-hb4in
      @CheikhNdiaye-hb4in 2 часа назад +1

      😂

  • @bassirousow3603
    @bassirousow3603 8 часов назад +8

    Ohh oie gueumal yalla te felicite cst l Senegal qui gagne

  • @allandiaye7665
    @allandiaye7665 7 часов назад +10

    Pér max gemeull yalla yeen li boun leen ci diokhon coroune sakh waro leen ko dieull

  • @MaalickSy
    @MaalickSy 7 часов назад +11

    Roi des arenes kene diko negocier

  • @aichasecka-8974
    @aichasecka-8974 Час назад +1

    Gueumeul Yalla té khamné appel lak rappelle lassi yam dounguéne ame dara roi kene douko négocier daw ba dieuleko amaguoul si histoire rou lamb

  • @alzogaye4667
    @alzogaye4667 22 минуты назад

    Félicitations modou lo tu es le meilleur

  • @abdoukane8276
    @abdoukane8276 5 часов назад +1

    Victoire on le mérite ta siteu meritéwoul victoire parce que il a fuit tout le combat

  • @ogviito1949
    @ogviito1949 8 часов назад +11

    Dane la si guew bi dane la si recours fass yéené la danat si appel bi😂😂😂

  • @DiyenabaPouy
    @DiyenabaPouy 7 часов назад +22

    Per max couronne bi mo yobou helmi😂😂😂😂😂

  • @mandoumbembaye9447
    @mandoumbembaye9447 6 часов назад +3

    Père max nak yagui beugue niak gueme yalla nak

  • @bassiroudiop5853
    @bassiroudiop5853 7 часов назад +3

    Père li geum leiine yalla ne soit pas mauvais perdant sou beugué roi da ngay dane niit quii ish

  • @alaminefaye6248
    @alaminefaye6248 5 часов назад +1

    Max yaw nokoule feulé Waay. Geume lène Yalla teii nga déme diamou djii Yalla 😊

  • @abdoulkarimcamara2416
    @abdoulkarimcamara2416 32 минуты назад

    Dem lenn diamou yalla mo guen topp futilités yi

  • @mouhamedcherifaidara923
    @mouhamedcherifaidara923 7 часов назад +8

    Ya ngui yakati sa xaliss dé😂😂😂

  • @tidianediouf8251
    @tidianediouf8251 8 часов назад +3

    Ah, toujours fidèles à votre style : des vieux sans conseillers. Quelle audace !
    Max Geumeul Yalla.

  • @benzdictenobalegomis6139
    @benzdictenobalegomis6139 7 часов назад +2

    Père Max guemeul yalla té récité je crois en Dieu
    À la fin tu nous amerde tous

  • @malickfall4447
    @malickfall4447 4 часа назад +1

    perre ya sof billahi

  • @medouns98
    @medouns98 4 часа назад +1

    Geum léne yalla wayyy😂😂😂

  • @AladjiNdiaye-f8z
    @AladjiNdiaye-f8z 4 часа назад +1

    Gemeul yalla pére😂😂😂

  • @aronadiallo7521
    @aronadiallo7521 6 часов назад +2

    Gueume yalla baxna ci domou adama

  • @diopmar6382
    @diopmar6382 8 часов назад +4

    Max danga moudiou sof siteu défaites la am beugue nek roi des arènes bayil sa khel bingay fowe

  • @MatarPouye-vi7uq
    @MatarPouye-vi7uq 5 часов назад +1

    Way way naniou gueme yalla rek niou mougne

  • @kurayahmi
    @kurayahmi 4 часа назад +3

    *Khaliss bigniy yak negn ko diokh Pimpi 😂*

  • @awadiop2144
    @awadiop2144 8 часов назад +5

    Max mi amoul conseil deh 😂😂😂😂

    • @bintoubop7847
      @bintoubop7847 2 часа назад

      Es k doko diokh conseil sakh😂

  • @mamadyfallndaw8134
    @mamadyfallndaw8134 8 часов назад +4

    Yéne ay vrai doff ngéne rek do lene geume yalla 😂😂😂

  • @KhadimeNdiaye-n7b
    @KhadimeNdiaye-n7b 5 часов назад +1

    Thieuy doff yiu😂😂

  • @bs-cl8tw
    @bs-cl8tw 4 часа назад +2

    Pér sa bakane bi réyna dh😂

  • @lomodou2049
    @lomodou2049 6 часов назад +2

    Siteu dh bougne kooo dioxé victoire Lamb yakhou en plus Roi des Arrene pour mann dou louniouy recours nk

  • @MamadoucherifDiallo-y5m
    @MamadoucherifDiallo-y5m 7 часов назад +3

    Pere beugonalla trop mes legui mome mangui lay commence merre nak koi😂😂😂😂😂😂

  • @PendaTalla-c5z
    @PendaTalla-c5z 7 часов назад +3

    Père Max ma ngi nii troisième défaite 😂😂😂

  • @mamadoundiaye4431
    @mamadoundiaye4431 7 часов назад +2

    Pére am ngén xaliss nak😂

  • @awadiop2144
    @awadiop2144 8 часов назад +7

    3em défaite en téléchargement 😂😂😂😂

  • @AwaFaye-t1p
    @AwaFaye-t1p 7 часов назад +4

    Yen dolent ay kilifeu

  • @Mamadou-j1x
    @Mamadou-j1x 7 часов назад +1

    Modou lo rek ❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @lomodou2049
    @lomodou2049 6 часов назад +2

    Père gueumeul Yalla

  • @birahimthioune2648
    @birahimthioune2648 5 часов назад +1

    Lii yeup Pimpi ak wa contingent bila gno yobou fitou paa yii 😂😂😅

  • @LahatFaye-t5g
    @LahatFaye-t5g 8 часов назад +5

    😂😂😂😂😂😂 khana yawmal khiyamm 😂😂mais du fii max guemal yalla

  • @Khalilou387
    @Khalilou387 7 часов назад +10

    Ki sofnaa bilay❤

  • @ndeyeamydiallo9581
    @ndeyeamydiallo9581 7 часов назад +4

    Wa gni aye nitt lagnou

  • @SouleyemaneDiop-o3p
    @SouleyemaneDiop-o3p 6 часов назад +2

    vraiment max danga mayé 50000f

  • @beugthep3584
    @beugthep3584 7 часов назад +5

    Inechalla 3em défaite kome ka ay doff géne

  • @OumarGueye-r9l
    @OumarGueye-r9l 5 часов назад +1

    So paret fi gua dem ministère ba
    So paret gua demm primature
    Après assemblée
    Après présidence
    Après cour de la hai
    Xlo kesser👑🤝🏾

  • @BabaBadiane-jm3ww
    @BabaBadiane-jm3ww 7 часов назад +4

    Bilahi gnii dagnon soff

  • @lbyoungtv2223
    @lbyoungtv2223 8 часов назад +4

    Sou VAR amei skh recours waroul am sof guen tropp 😅😅

  • @ibasow1066
    @ibasow1066 6 часов назад +1

    Père mougnal rek yalla bakh na

  • @afro3827
    @afro3827 8 часов назад +4

    Max diga toy dé yagui baganté rek 😂😂😂

  • @kebandao5918
    @kebandao5918 Час назад +1

    Kou banige siteu sa koyi baye

  • @ModouMige-y1g
    @ModouMige-y1g 7 часов назад +3

    Guemal yalla te dem wakh dueg sa buere mi mou Guen

  • @CheikhFaye-e2c
    @CheikhFaye-e2c 7 часов назад +2

    Franchement max yangui BEUG soof gueumeul yalla ngua dem tok Siteu danoule ken soof ngua tropp

  • @ablayediop1993
    @ablayediop1993 7 часов назад +2

    Les 50mil donnés ça a pimpi😂

  • @mouhamedtoure5150
    @mouhamedtoure5150 7 часов назад +4

    Li dafa niaw Di Sall téll victoire rou diambourr

  • @MaremeDieng-l6t
    @MaremeDieng-l6t 7 часов назад +3

    Sa xel mo dém

  • @IbrahimaNdong-h4g
    @IbrahimaNdong-h4g 6 часов назад +2

    Pére Max daguéna moudié sof

  • @Mamadou-j1x
    @Mamadou-j1x 7 часов назад +2

    Le yep modou lo mogou def .
    De boure ak Siteu 😢😢😢

  • @CheikhMbengue-fl8ik
    @CheikhMbengue-fl8ik 8 часов назад +3

    Max gamal yalla li sporla

  • @bambakhouma7529
    @bambakhouma7529 6 часов назад +2

    Per yakh khlisss rek rio do aye thikhane kene dooko negios

  • @assanebouarmee3431
    @assanebouarmee3431 7 часов назад +1

    Ma challah père nonoula de toplene li leene yoone may
    Jub jubal jubanti rek

  • @libassmbengue
    @libassmbengue 8 часов назад +4

    Thiey yallah😂😂😂

  • @FallouNdir-d3y
    @FallouNdir-d3y 6 часов назад

    Bien joué père Max et président

  • @malicksarr2141
    @malicksarr2141 8 часов назад +3

    Thiey pér 10% 💶🫵🏻😂😅😃😄max guemeule yalla nak dem wouti lanene courage nak li sports lawoe 🤷🏽‍♂️😂😅🤣😂😄

  • @GoraMbengue-f2j
    @GoraMbengue-f2j 6 часов назад +2

    Bayilènn ko mou deff appel Wa CNG laffay fekk makhallah doff leuh diangoul 😂

  • @MohamedNdiaye-bl2sh
    @MohamedNdiaye-bl2sh 7 часов назад +1

    Père respect toi

  • @futurenj6850
    @futurenj6850 Час назад

    Pere khaliss binguéne di yakh 🥹dolé’ne mako may sokhla nâ aye diaplet dh😂😂

  • @malicksarr2141
    @malicksarr2141 7 часов назад +2

    Max yawe yaya yobe suite li yeup boko bayiwone mou songou dane wala mou danou lerna bou yague nganako dawale rek bouko songou kone mou danla 😂🤣😄

  • @cheikhgueye5458
    @cheikhgueye5458 7 часов назад +3

    Encor max do gueumeu yalla yagui yakh sa khaliss roi dê aréne dou ni lanioukoy dieulé

  • @DameMboup-q4p
    @DameMboup-q4p 8 часов назад +3

    Mafi djitou

  • @KamyTOURÉ
    @KamyTOURÉ 7 часов назад +1

    Max mingui déposer li di niangal Pask hamna ni dara d’où bah 😂😂😂

  • @senegaleventschanel6913
    @senegaleventschanel6913 7 часов назад +3

    Père Max digua outal Siteu aye none rekk vraiment, guemeul yalla prk se fatiguer ainsi?

  • @alhassanngom8282
    @alhassanngom8282 7 часов назад +1

    Bon essayer leen comprendre Père Max rek, passaka moo tek stratégie bi donc liyeup momla Siteu saax waax’na ni beuggone na diexal combat bi mouniko boko songué mou daane la., kone normal mou am louko metti manam fi lamb dji yegg yeupp danaka momla. Mom moo daanou mtx mouy topp liko yoon maay. Problème bi kaay da waar nangou assumer ni niakk na koi dem xoli kenen comme mbeur mi daaw ba soneu ci biir lamb ji 😂😂.

  • @PapeDiba-c1n
    @PapeDiba-c1n 40 минут назад

    Père Max bo parè gua dem police aprè gendarmerie aprè tribunal do ame gat sa kanam ni badio 😂😂😂

  • @AbbaSall-q8j
    @AbbaSall-q8j 8 часов назад +2

    Ay père max esk do bayi

  • @OuzinDiouf-g4e
    @OuzinDiouf-g4e 5 часов назад

    Pére Amal xel touti rék

  • @senegal559
    @senegal559 8 часов назад +20

    Kii sof na loool way wakhal sa Thiak Thiak bi mou bayi Daw

  • @KebbaJobe-f8m
    @KebbaJobe-f8m 6 часов назад +2

    max yow danga toy

  • @FallouSarr-j6w
    @FallouSarr-j6w 5 часов назад

    Père ioe xam nga lane la geumeul yallah way ah😂

  • @papeomardiagne8201
    @papeomardiagne8201 50 минут назад

    Père 😂😂so parré nga démm assemblée nationale 😂😂boléko si loi yi😂😂

  • @TafsirmalickDiop
    @TafsirmalickDiop 7 часов назад +2

    Guem lene yalla t Dem jal si lenene bounguene wakhone sene mbeur mi moutakhaw li yeup dou am père mak ndam ken douko lijanté

  • @beugthep3584
    @beugthep3584 7 часов назад +5

    Kii boudone deume kome diap do recc

  • @mohamedbenzekry8074
    @mohamedbenzekry8074 7 часов назад +1

    Mais yaw max danguadoul gueum yallah yene yi diarouko !! Mak ngua aussi yagui commencer soff bilahi.

  • @jeansarr4221
    @jeansarr4221 7 часов назад +2

    Ki amoul dioom ki dou gueume yalla

  • @cheikhthiam-k9o
    @cheikhthiam-k9o 8 часов назад +2

    Yena soff

  • @AwaFaye-t1p
    @AwaFaye-t1p 7 часов назад +2

    Amolen mbeur siteu tapet la

  • @NgomDjiga-c6r
    @NgomDjiga-c6r 4 часа назад

    Wa ki môme couronne kéne douko lidianeté😂

  • @ResidenciaImmobilier
    @ResidenciaImmobilier 5 часов назад

    Thiak thiak bou diamaguéne bi rombou léne fofou😂😂😂

  • @beugthep3584
    @beugthep3584 7 часов назад +3

    Pa you doff ta ame temps

  • @cissemouhamed6327
    @cissemouhamed6327 6 часов назад +1

    Pere yagui beug sof nak

  • @ameththioub2709
    @ameththioub2709 7 часов назад +3

    Ki dafa soff way

  • @BallaSall-q5c
    @BallaSall-q5c 7 часов назад +1

    Bakh yaye couture tégua nopii

  • @sencoursanglais
    @sencoursanglais 8 часов назад +1

    Naniou nopalou! Siteu nieuwoul pour Dane. Kou nieuwoul wonn pour Dane. Do Daane! Roi daniou kay liguey. Kenn dou ko lidianti. *〽️odou K C*

    • @DieynabaNgom-ln4lj
      @DieynabaNgom-ln4lj 8 часов назад +2

      C sa nak gneuwo pour dane beug gnou diokhla victoire 😅😅😅

  • @abassciss9387
    @abassciss9387 7 часов назад +1

    Goudal diel rk waye tousss do len ko am

  • @aliounecisse7989
    @aliounecisse7989 6 часов назад +2

    Cornée léne thiak thiak bi

  • @birame696
    @birame696 6 часов назад +1

    Pabi soff neu

  • @AboubacryGASSAMA-zs7oi
    @AboubacryGASSAMA-zs7oi 7 часов назад +2

    Ki bou yagué mbeur mi sakh moye,wakh ak yaw . Rois des années kén douko nègocier
    Pére max yagui beug niak fayda dhé 😅😅😅nono way dof guéne lolou way guem léne yala way

  • @OumarGueye-r9l
    @OumarGueye-r9l 5 часов назад

    Ndeysann pére sonn gua nak
    C’est pas les marabouts c’est Dieu
    Xlo👑👑👑

  • @MorMBacke-q2d
    @MorMBacke-q2d 4 часа назад

    Billahi kii mo ame diote rek kii soff na torop

  • @thiernombaye8912
    @thiernombaye8912 Час назад

    Il a le doit de faire appel .... quand meme