Ha machalah togou yaye isseu sét na présentable na khamna ni amna goût oci giisna sa commentaires tata marétou saveurs planétaire y'a niak kigniane Yalna sene liguey dieum thia kanam
Merci maman,ce qui me plait la propreté qui s'adapte avec votre cuisine très important, que dieu vous bénisse pour ta gentillesse de partager votre savoir-faire, bonne continuation merci à la prochaine.
On a fait le michiou kadire samedi dernier C'était excellent MANCHALLAH On le refait aujourd'hui thi Tabaski bii INCHALLAH Merci Ya Isseu QU'ALLAH Te Récompense
Merci Maman Masha'allah nekh na sél na té rafet na aussi j'aime trop présentation 10/10 Décoration 10/10 Explication de la recette 10/10 Time 10/10 aussi Parce que la vidéo elle n'est pas longue super bien Masha'allah 🍗🥕🌶🍟🥗🍲🙏🤘👊💪❤🇸🇳
merci bcp maman ISSA d'avoir apporté cuisine saine et vitaminée on t'aime bisous yalla Nala yala faiye Lou geune si yov akh diaboote bi dieureudieuf ❤❤❤❤ la faite Lou geune si yov akh diaboote bi
Bonjour ta isseu je te sui souvent yak Tata marietou koulen suivre khamni ay tokologu ken machallah teh yennaki dimali au khaley you barri yalna l'en yalla fay merci
Yalla nala Yalla same aar leu lakh la fou yakh agoul, vraiment li ngay def rafetena lol Macha Allah, limassi gueuneu nekh, moy soy commencé,"Bismillahi rakhmani rakhim" lossi def mou barkel
Waay machallah waay sunu yaye Isseu. Lingay reugueul machallah waaayyyyy saaaaffffffff naaaa saaappppppp🤗🤗🤗 😋😋😋😋😋
Masha Allah damay aimer soga setane merci Maman
Tata damala deug bilah
Saveurs planétaire mariétou machalla ma conetane s'y yaw 🙏🙏🙏🥰❤️❤️❤️
TOOGOU YAYE ISSEU Yallah na Yallah barkel lepp tè wereul thieur yi maman vous êtes Masha Allah formidable 😘😘😘❤️❤️❤️❤️
Yap bi sou gnoroulei hana dagnouye dolli ndok
Daga gnak kignane tant marietou yalnalene yalla faay yen gneup machallah. Togu yah isseu essayenah mass potatoss bih machallah nekh nah trop.
Doumaxi doyal mako togue koritè daw mais jusqu'à présent Mr me di ligua togue meuneu toko lèpp grâce à toi tata merci bcoup
Machaala séte na selle na mome la déf taye unechaala❤❤❤😊
Machaa Allah Mme,thi kaw kinam inchaa Allah❤
Suis tres content tata ama gouma djieukeur ms toujours magui lay sv 😗😘😍😗😘😍
Macha allah amna solo diadieuf way yalla nala yalla fay
Merci beaucoup maman,ma cuisine s'est bien améliorée grâce à toi,longue vie à toi et pleines de bonnes,je t'adore 😘😘😘
Ha machalah togou yaye isseu sét na présentable na khamna ni amna goût oci giisna sa commentaires tata marétou saveurs planétaire y'a niak kigniane Yalna sene liguey dieum thia kanam
Machallah j'ai l'eau à la bouche korité bi laye déf maye gniane mou réussir comme sa bose machallah yalla guafi yague té ame wére maman.
Machalakh yaye yalna sounou borom bénit naga gnou dix si recettes yi
Bilaye amougne sa feye longue vie à toi
Yaye boy ngoudal fanne❤❤
Li ngay def amna solo yaye en plus ta voix est très douce yalna yala goudeul sa fan 🥰😘
Machala yaye boye
Merci maman,ce qui me plait la propreté qui s'adapte avec votre cuisine très important, que dieu vous bénisse pour ta gentillesse de partager votre savoir-faire, bonne continuation merci à la prochaine.
Machalla
machallah maman yalna la yalla may goude fane ak wèr ak khèwal bou sawana bawane
Setna selle na te tarouna encore macha allah yalla n'a yalla gueuna weeral lokho bi
Mane dè dama warou liii hoooo yala ga goudou fane machala koritè inchala douma lal guinar fèn
yaye issa dama nekhe en plus j aime trop la cuisine j habite a saint louis comme vous maman😍😍😍
Machallah Machallah Maachallah fa tabaarakallah, sétna noyna t khamnaani sapaaral na
Fier d'être st louisienne ❤❤❤❤❤
Machala yaye boy rafétena sél na té sa xol rafétena yalnala yalla lafal thiate
Machalla machalla togue yi niép guis naniou séne bop wa hall bi ak wa takh yi niép dina niouko meuneu répété séne keur
Dila nouyou dila ziarre dila gnanal guoude fane ak weere yallah dafal la d'âme ligua fi togue yeuppe djaare Yonne merci bcp
Salam salam machalla maman ligay tog nékh na trop mais dama donn lath nakh li Mane Nay kou togou korite ❤️❤️
C'est la 3eme fois que je regarde la vidéo manchalah ❤
Machalla ❤️❤️
@@marieantoinetteodilefaye949 jy
Machalah ma sama yaye isseu mon chef préfère togue ngui nékhna sétna kaadou yi machalah
Amougnou sa fay machala ame na solo 😘❤
Machaallah sa mechoui néna mouthe eupneuuu
Yalna sa diam yague Maman et Merci pour les recettes nekhna
Machalah yaye boy yalna sa lokho werr ❤
.Machallah tata et merci si astuces sauce bi akk l'eau du cornichons
Machalah tata laftiate plat spécial fin ndogou la wamé konne korité loy def .de toute façon magui diangu ndah diangu do wess et merci 🙏🏻 🥰🥰💞💞
Mome ak Tata marietou noo keuneu dou niome ma sha Allah yalla nalene yalla defal diam 🙏🙏🙏
Machaallaa ça donne trop envie excellente recette bravo merci beaucoup pour le partage 👍👍👍❤❤💋💋
Machala sa top damasiy giss sama bop selna simpl na esplicationyi lerna yalnasa diam yag 🤝
Machalla tata yalla na se diame yague 👏👏👏
Masha allah défatina meuniname y allah nala y allah arr té may leuh goudou fane ak férgou yaram si barké seydina Mohamed ( psl) ♥️♥️
Machallah maman contane si yow merci bcp nala yallah sameu arla weral tier yi c est tres bien expliquer andak set ak sel
diadieuf tata machala pour ces belles astuces💖💯🥰
Machallah très jolie deco merci beaucoup maman yalna yalla weral lokho bi inchallah wenibik
J’adore sa voix et je trouve très original sa manière de cuisiner la sauce oignons 🥰
Machalah amena solo mangui diangue boubakh. Merci pour tout explications yi lérna yorop
Aaaaa sama tata feulétina fenenn way ohhh mâcha alllah👍🏻👍🏻👍🏻👍🏻👍🏻👍🏻
Machallah mane sak lolu laye wakh ni magui dora guiss v idéo amal diam bou bari tata Isseu. Nekhna selna
Machalla tata yalla na yalla yagal takhaway bi 🙏🙏
Yagui takh niou geuneu khame mama ndoundale waye mala begeu mane takh ga séye niepeu nékh naa togeu lou nékh té séle dafa bakh sii keur yalle nala yalle féye waye machalaaa
Yalla ngafi yague tata👌
Machallah yal na borom bii dolli la diam si barké seydina Mouhammad psl
salut
Yi bilay defar korite inshalah yalla nanou yalla may feke talko nigua togue sauce bi c la premiere fois maguisko si yaw mashalah mashalah
Machalla tata mayonnaise bi mome lay df si koritè bi ak décoration bi 👍👍😘😘😘😘
Merci beaucoup pour ces belles recettes .Je reproduis très souvent tes recettes.Merci pour la version française dieu te bénisse inchalla
Machalla merci
Machalla tata amna solo yalnala yalla samme
Machallah yaye isseu méchoui amna mana. By môme pour korité dina fi bakh inchallah. Nekkale thi diam.
Machallahh tâta 💖 yalna yalla goudall sa faneuh🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Machala nékh na 👏👏🥰
On a fait le michiou kadire samedi dernier
C'était excellent MANCHALLAH
On le refait aujourd'hui thi Tabaski bii INCHALLAH
Merci Ya Isseu
QU'ALLAH Te Récompense
Machall ،❤️ms tata dama beuga déf Kom linguay déf nii
Machalla tati adorée
Ah mâchala liii mom koritè mom layy togue inchala merci bcoup tata j'adore tes cuisines
Machalah Tata yaye isseu saf na🙏🙏
Merci Maman Masha'allah nekh na sél na té rafet na aussi j'aime trop présentation 10/10
Décoration 10/10
Explication de la recette 10/10
Time 10/10 aussi
Parce que la vidéo elle n'est pas longue super bien Masha'allah
🍗🥕🌶🍟🥗🍲🙏🤘👊💪❤🇸🇳
merci bcp maman ISSA d'avoir apporté cuisine saine et vitaminée on t'aime bisous yalla Nala yala faiye Lou geune si yov akh diaboote bi dieureudieuf
❤❤❤❤
la faite Lou geune si yov akh diaboote bi
Ah je suis trop contente du plat , diar na yone, lepp ler na, je vais faire la même chose pour la korité un chaa allah , merci beaucoup
Man dall nekhgama damalay séttan boubakh machalla limagana nekh moy daga bakh nokoss
Machallah toogou yaye isseu bakhna et merci du partage
Merci Tata Marie recette bi nékh na yalla na sa diam yagg
Machalla maman iow dal amo morom yalla na lokho bi wéér
Machalla, yalla na la yalla faye yiouw.
Mashala mama namone nala .nekhatina
Machalah tata lii nekhna vraiment té sell nioungui lay begué boubakh merci encore pour les bons plats
Aye Tata invité ma malay filmel👌
J'ai de l'eau à la bouche quand je regarde déjà 😭
Machalah laf tbiate waayy🥰💞
Eye yaye boye machala amougnou sa feye
Macha alla tata yalna lokho bi werr way
Legui môme ni l'ay togué 😋😋😋😋😋
Machalla diarna yone tata
Machalla maman très beau❤❤❤❤❤❤
Yaw goudal fane wayy machala liguay tog lanla hoooo😋😋😋😍😍😍
mahachalla hum j adore tes recettes yalla nayalla yok
Ma challa mi piace bravissima yalla na lokhobi wèr dèwenati ak yaw yalla nagniou sunuborom bolè djieugale amine dieuradjieufati bacio❤😘
Mashalla tata contane reik ma nguibdiangue bou bakha bakh
Très contente merçi pour l effort en français. J adore ta cuisine longue vie à toi que Dieu te garde
Bonjour ta isseu je te sui souvent yak Tata marietou koulen suivre khamni ay tokologu ken machallah teh yennaki dimali au khaley you barri yalna l'en yalla fay merci
Vive les st louisienes fière de l'être merci maman isse❤❤
Mansh'Allah Tata tu es le Numéro 1
Man douma wakh sama khole dafa sede torop encore merci tata
Maachalaa amna solo
Machalla yalla na lokho bi wer
Machallah tata Marie diop sa michoui amna mana
MACHA ALLAH DIEUREUDIEUF YAYE.🥰🥰💖💖
Machala yagi yok sounou khameme
Chapo way mashalah. Yaw tamite ahhh litamite. Merciii😘😘😘
Tata sa togou nékh nama trop dagna gniémé nokosse motakh machallah
Bilay manit Lolou moma nekh thi mome. Dey Nokoss ba mou saff sapp
Machallah ...contane rek maman...Merci encore pour la recette 😍😍😍liii dé laye deff mane karité inshallah
Machaala tata mom lay togue korite inchaaala
Je suis cordon bleu et j'apprécie beaucoup vos bons plats merci et bon ramadan
Yalla nala Yalla same aar leu lakh la fou yakh agoul, vraiment li ngay def rafetena lol Macha Allah, limassi gueuneu nekh, moy soy commencé,"Bismillahi rakhmani rakhim" lossi def mou barkel
Machalla tata ta fasson de cuisine sama plaît
Wa tay toggou ya issa fila guen machala machala c'est présentable ta maretou dal diarama yaw😘😘😘😘👍👍
Machala tata nicena trope
Machaallah maman yalla na la samme