Wayé koudoul goor yalla meuno fegnal louy nelaw si sa moromou goor yalla diawrine ndiassé machallah wayé Ken dou Diawrine Yakhya mi takh gni meuna diarigno li nek di nelaw si diawrine ndiassé
Je penses qu’il est nécessaire d’amener une 3e personne pour mieux fédérer le débat et limiter les thématiques. Vraiment ils sont formidables et tres sages Machallah
Jawriñ Njaase xam-xam bi sell na. Waaye bàyyi leen xel Seriñ Yaxyaa mii. Ku am xam-xam la te am dégg dégg ci mbindum Sëriñ Tuubaa. Waxtaan moom sunu dindee waxi daanu leer yi rekk nu xam ne Sëriñ Tuubaa yar ba noppi yobbu ca Yalla rekk a ko fi taxoon a ñëw.
Wayé di delou di fegnal sunu mbegté si bichri tv ndakh monou oubil bountou bi takh li lep di fegne moy bountou xam xam wayé di yonou ndioupe gatié ngalama bichri rv sa kaw sa kanam ndam rek
AKASSA nek mouride mo nekh mais mouride bou am degue am tope dama danou si sounou niari dieuwerignes Yi doundelene werlene Machala
QUE VOTRE DUO DURE VRAIMENT J AI EU LE PLAISIR DE VOUS ECOUTER ....QUE DIEU VS ACCORDE UNE LONGUE VIE ET DE SANTE
Niari Anrif laniou, niari walihou, niari nitou Yallah. Akassa
Ki bamakoy deglou yagg na bilay cest person tre pertinent je laim beaucoup
Lou yalla binde Serigne Touba mosii geune ahhhhhhhh
Yalnalénn saa borom samou mbarké borom Touba
Emission bi soumakay deglou day melni dagnou maay dialise j'apprend bcp de choses yalla nalenn serigne touba faay❤❤❤
Amin Yaa Rabbi
Machalla j'aime ces deux là
Manchalla amatina solo yalla nalene yalla faye ndakh yena ngui guindi niou bari
C'est 2 là ils forment un duo exceptionnel wallah,Sont des Qi
Ce NDIASSÉ est juste éblouissant ❤❤❤
boul topp Ndiassé ba fatei Yahya 🥳🫰🏾gni kawei nagn
Mane nékété meusouma nekk muriid apprenti mouride la
Dimensions bi dafa kawé trop 👌👌👌👌👌👌👌👌👌
Jajeuf baye diawrigne Amna solo lol
😂😂😂😂😂
😂😂😂😂😂#@khafashion yaw mouride fashion ngeu last kri
Je suis ravi d'écouter ndiassé il est bien éloquent et véridique machallah yalna sounou Borome fayalén yiw barkep Cheikhoul Khadim
Amin Yaa Rabbi
Machalla dieuwerign ndiasse Cissé yalnala yalla same téyél la sa khel❤❤❤
Wayé koudoul goor yalla meuno fegnal louy nelaw si sa moromou goor yalla diawrine ndiassé machallah wayé Ken dou Diawrine Yakhya mi takh gni meuna diarigno li nek di nelaw si diawrine ndiassé
Jërëjef wakhatne bi amatina solo ❤ akassa jewrign yahya yallah na Émission bi gueneu dieum kanam barkep Serigne Samath Mbacké modou faty khary🤲🏾❤️
Allahou Akbar wakhtannewi kawéna machallah khol sédeuneu dieureudieufeuti Akassa.....
Dieureudieuf Serigne Touba ❤ dieureudieuf Mame cheikh Ibrahim fall ❤ dieureudieuf Mame Ndiamé Darou ❤
Jewrign ndiassé amatina solo yallah na xam xam bi barkel
Masha Allah ❤❤ wahtane bi amatina solo
Machallah yattotina 👌🏾♥️🤲🏾
Machallah noguiléne di bégué bou wërr diadieuf
Ndeysane kadu yi Amatina solo torop dieuwrine ndiasse ❤
Machalah émission nekhna yalla na faye lene❤❤
Allahou Akbar Allahou Akbar Allahou Akbar ana harif billahi yi lii dou xam xam xam la kon dég dég lay ladj
Machalahh jewrin Yakhya plateau bii amna solo ak sounou jewrinn ndiassé yallana yallah sameu
Macha allah serigne Abdou Samath ibn modou faty mou serigne massamba mbacke dieuwrigne yayah baboulahi
Diareudieuféti Serigne Touba❤
Machallah amatina solo tawfekh taysir akk najah barkep alkhourane
Mashalah dieuwrign but Bichri TV where did you get the guy hosting ?
He is excellent mashalah
Macha-Allah amna solo
Merci beaucoup
Akasa amna sollo djeureudjeuf serigne touba diarrama mame cheikh Ibrahima
Macha'ALLAH!! Santati nagnou bou wérr si Jotay bi di amat mbékté ak ndolénte lou yatou..
Un délice cette émission. Yalna leen Yàlla saam !
Ndeysan jërëjëf dieuwrigne waxtan bii amatina solo tawfex RĚK inchala ❤❤
THIEY JEUWRINE NDIASSE MO AME XAM XAM DH 🥰
Mâcha Allahou Dieureudieuf
Wollah il est exceptionnel dieuwrine j’adore les façons dont-il parle
Mashalah kawèna 🙏🙏🙏
Machallah dieuwriine rafetna
Machallah émission bi mbegté rek la wayé dîna yéh sama classe yi done nelaw
Machallah
dinguein dieuf wahtane wi da tambali rel kawei machallah
le journaliste waouh il est trop fort machallah
Émission bi dafa diégui dayo bilay ❤
Billahi wallahi trop sakh
Bichri tv machallah
Yémé na dé
Je penses qu’il est nécessaire d’amener une 3e personne pour mieux fédérer le débat et limiter les thématiques. Vraiment ils sont formidables et tres sages Machallah
Incha'allah yaaram diaadieuf
Yalla nagnou yalla fayal Cheikhoul Khadim Diadieufeuty khadimou Rassoul
❤❤❤❤jeureudieuf
Jawriñ Njaase xam-xam bi sell na. Waaye bàyyi leen xel Seriñ Yaxyaa mii. Ku am xam-xam la te am dégg dégg ci mbindum Sëriñ Tuubaa. Waxtaan moom sunu dindee waxi daanu leer yi rekk nu xam ne Sëriñ Tuubaa yar ba noppi yobbu ca Yalla rekk a ko fi taxoon a ñëw.
Alhamdoulillah
Jërëjëf
amna solo
Serigne Touba rek ❤❤❤❤❤❤❤
Mchallah tawfekh rk inchaala
Ki brom xam xam la machallah
Really impressive!
Émission chaque semaine ces 2
Ma chalah
Machallah ❤
Libérez Sonko
heeeee ndiasse kel niveau
Amna solo fall
Ndaysan rétanou Ndiassé dou dagn ❤
Akazza baye dieuwrine
❤❤❤👌
❤❤❤❤
Daoiwring sa número la sokhe la
Hakassa❤
Akasa baye gor
Wayé di delou di fegnal sunu mbegté si bichri tv ndakh monou oubil bountou bi takh li lep di fegne moy bountou xam xam wayé di yonou ndioupe gatié ngalama bichri rv sa kaw sa kanam ndam rek
Chaine bi mane naane koo toudé yàlla yàlla tv
Machalla émission bi amatina solo, Yahya diewrine diassé doléne niarre kéne guéne. Vous parlez de même langue, diuerediuef cheikh moussa
Yéna mana tapalé
Slt vraiment diotay bii ame naa solo trope,,, mais si vous pouvez le faire par extrait pour qu’on puisse le télécharger facilement
jaa jëf !!! dina dougg inchalahou par extrait
Gni wara wax sasouné bougnou yeuguelo rék rouhou yi Doundate..
Baye Fall goor yallah yague te weer
Vous etes entrain d eclairer les ignorants
51:45 ⬅⬅⬅💚
DEUG
Ndiasse il. C tromper sur un hissa
Mchallah tawfekh rk inchaala
❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤