Au début comprends douma wone lou beuri awma wone ben expérience mais début que ma changer sama guiss guiss si life bi la commence xam lan deff pour done kima beug done merci que dieu vous bénisse ♥️
Avant de voir tes vidéos je critider l'ETA du Sénégal Ousmane ou maky toujours maintenant je sais mon avenir c'est mon courage et détermination merci beaucoup tué ouvert les yeux merci vraiment
C'est du lourd franchement !! Bonne continuation des fois l'écouter en langue maternelle te donne plus de sensations et de frissons !! Si vous pourriez le traduire en anglais également pour augmenter le champ de cible . Thanks Homie !!!
Oh nit di deuke si dila motivé dila diapou le ba boko degoul mou manque le trop té khomo sakh kan leuh khamal ni bole nan la sounou doundu on t'aime beaucoup 💯❤🥰🖖
Kou bakh.mammon nanla soppa nanla beugeu nanla si nous njikka abonnés la bokka waye keyla dougou ci commentaires.waye beup nitt souma amé ci moom Yakari demay digal mou abonnés té jerinna nous baré yalla nala yalla ar te sammala.
Oh Machallah frère vraiment nml trop sakh personnellement moi tu m’a manqué j’ai révisé toutes les dernières vidéos de la Chaîne mais merci enfin mon idole de retour respect ✊ bro
Salut frère je te souhaite tout le bonheur du monde santé prospérité réussite totale parceque j aime vraiment ce que tu as entraine de faire long vie frère peut être un jour on verra
Da nga may motivé aussi dima yok problème nakh da nga may lall toujours mais xham na bagu nio tek si youne bo bakh bi rk frère yalla nala yalla samo barkeb xhasida yi
Bonne cntinuation.... Mais beuggeu na niou lezion ci mbeugel deh Svp🙏
Dimanche Inchallah
@@tekkiforlife sa nimero frerr
Grd yalla moulaye faye yaw ya takh ma fatte sama probleme yeupp sama adouna merci beaucoup gr
Pardon litakh mani sonal lima weso rk lafi degu mais xhalle la dina rectifier lep unsaallah
Pour wa Tiki wala
Barke s touba yatakhe ma bayi limadon deff gumomakowon magui ci benine yone yalla nala yalla defall diamo 😭❤❤🇸🇳
Grand billahi chaque jour nga diokh ma vidéo bou may encourager merci grand amal Diam 🤫🤫🙏🥰
Merci
Contane continué à gneup diam yalla NAGNOU âme dégu ak topou ak ndiarignou Amin
Amine
Au début comprends douma wone lou beuri awma wone ben expérience mais début que ma changer sama guiss guiss si life bi la commence xam lan deff pour done kima beug done merci que dieu vous bénisse ♥️
Avant de voir tes vidéos je critider l'ETA du Sénégal Ousmane ou maky toujours maintenant je sais mon avenir c'est mon courage et détermination merci beaucoup tué ouvert les yeux merci vraiment
Non diërëdiëf tekki for life yalla na yalla défalla diammou CI barkéb Seydouna mouhammad ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Vraiment t'es unique bro vos vidéos je l'ai écoute everyday Macha Allah
Mane limay dégu si vidéos yi dafma yém tellement que malick dafma yèm a ton âge 21ans ❤
Yalla nasa diam yangue lol ak wér niou yangue lol aussi ligua déff si yalla rék moko kham sama xol sédd si ioe trop 🥰🥰🥰🥰❤️
Vraiment vraiment il y a que la vérité qui compte ❤️🙏🏻🙏🏻🙏🏻
Merci d'être là . Je t'an courage pour cette chemin. Le chemin du braves. Suis An route comme soldat à la Armey
Wallahi lii diamou yalla DEUG yalla nla brome bi yok
Vraiment vous m'avez manqué j'ai téléchargé tes vidéos en audio et je l'ecouté en boucle amal diam rék frère ❤️🤲
Ligaye wakh amna solo bilaye yalna la yalla faye
Machalla tékki for life yangui ñiouy yokkou doollé diñiou ték çi yoon bi
Amal jamu ak xëuwall
C'est du lourd franchement !!
Bonne continuation des fois l'écouter en langue maternelle te donne plus de sensations et de frissons !!
Si vous pourriez le traduire en anglais également pour augmenter le champ de cible .
Thanks Homie !!!
Ken nga fi. Tu est le seul
Amal diame rek jo ❤❤❤❤
Machala diam si yaw frère amatina solo 👂👍🏼👍🏼
Grand es ce que yangui khar bess niou dieul la si télé TV gay déf émission com bi par ce que vraiment je t'aime fort
Merci pro antouqa guiss na sama bopou si vidéo yi
Machallah tarkala namone nala trop jajëuf ❤️🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Oh nit di deuke si dila motivé dila diapou le ba boko degoul mou manque le trop té khomo sakh kan leuh khamal ni bole nan la sounou doundu on t'aime beaucoup 💯❤🥰🖖
merci frère moi aussi je vous aime
yaw dal yalna yalla fayla yiw rék lagni wakh ❤❤
Machalla frère dama dikou sa vidéo sama khelle gua niaww 🪡👨👦👦
MachaAllah 🥰 frère que Allah te garde et augmente ta sagesse 🧠♥️
Naine kobaH ka
merci amna solo yaw borom dégue dégue yi guay wakhalle
Every day me and going you video thanks 🙏 you
Nice na tropp
Merci beaucoup sék jours nga diokh ma leçon bou béss
Merci beaucoup frère kontane si yw bilahi Yallna nga am diam
Merci beaucoup pour vidéo bi kontan s'y yaw 🥰❤️💥
YALLNA YALLAH SAMMOU TE DIAPA LELAA
Jërejëf sama coach santati nala bou bakh walahi khacim
Toujours souma lay sétane ça vidéo yi Daf may motivé de trop vraiment
Nic na frr bn continuation
Machalla si rafetna yaguimaye dolel boubakh
Boro nane laye def âme sa numéro
Hi bro, merciiii pour t'es belle vidéo ça fais deux jour que j'avais découvrir vtre chaîne mais Big uo bro, on te suit depuis Allemagne
Kou bakh.mammon nanla soppa nanla beugeu nanla si nous njikka abonnés la bokka waye keyla dougou ci commentaires.waye beup nitt souma amé ci moom Yakari demay digal mou abonnés té jerinna nous baré yalla nala yalla ar te sammala.
Tekki FOR laif yalnala yalla sammu sammu sa xèl wallahi dafa am lou bari lo dèf si man wallahi amna yênè khamantè ak yaw trop
Mr6 beaucoup férér pour la conché ❤👍🙏
Machalla Nice na tourop
Merci fr si konsé yi 🙏🥰
Mashallah 🙏❤️❤️❤️❤️🙏🙏
Oh Machallah frère vraiment nml trop sakh personnellement moi tu m’a manqué j’ai révisé toutes les dernières vidéos de la Chaîne mais merci enfin mon idole de retour respect ✊ bro
ماشاء الله شكر لك جرجف ❤️❤️❤️🖤🤎❤️🖤🤎🤎🖤
Mane amouma❤sa faye
Bonne continuation à toi ❤️
Merci beaucoup frére sa video yi dama Kay khar every day thank you, my brother ❤️👍
Am na solo yallah na diamu yague thi yaw
Geum geum rk la✊🏿teki dou al alale rk 🤜🏿🤛🏿
Courage mon frère li ngay djangalè c très important macha'allah
Rafet louna trop trop sen liguey machah allah. Photoyi bounekon sunuy amige DINA am solo
bonne continuation....😍😍🙏🙏❤️
Machalah job bi rafétna trop es aide bc les personnes god bless you👌
Yaw Mom amalle diame rk 💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💞💌💌💌😍😍😍😍💗💓
Content beaucoup
C'est magnifique bonne continuation à toi
Savait longtemps qu'on arrive à vous rejoindre mais cette nouvelle vidéo à réveiller nos esprits 🔥👌🔥
Merci ❤
Oh frère yalla n'alla yalla diapalé
Salut frère je te souhaite tout le bonheur du monde santé prospérité réussite totale parceque j aime vraiment ce que tu as entraine de faire long vie frère peut être un jour on verra
ماشاءالله صديقي
Yaln yalla deugeural xam xam bi mayla ak wér
Yallnala yalla fay sa khol merci
Merci mn frr diamou sy yaw bro ✌🏽✌🏽✌🏽
Mongui Nice frère kontan si yaw
Bilay tu es entrain de travailler mon esprit. J'ai beaucoup perdue dans la vie en dormant
Da nga may motivé aussi dima yok problème nakh da nga may lall toujours mais xham na bagu nio tek si youne bo bakh bi rk frère yalla nala yalla samo barkeb xhasida yi
Machala
Frr bonne continuation say message ana solo trop bilh 🙏❤️❤️
Merci beaucoup ☺️ yawmi soupékouna 👏♥️🫵
Bro tu es meilleur
Trop nice mon frere ..... Beusseul jaim stp iow miy déglouu si barké Sallahou Alla Mouhamed💝
Merci Baye Fall AMNASOLO
Wallahi frère yagui mayy yogue geum geum
merci frère machallah
Machallah frrr izo ieo sa jobe migui cool niogui sa guinaww jamm diou beuriii parceque yagui deff lo xamni say morom nioguifi ms deffou niouko senegal nakk soo neké sii lou bax niou néww niolay falé ms inchallah dinala fayé 🤲🤲🤲🤲
Bravo et longue vie à toi tes vidéos intéressantes me servent beaucoup de chose merci beaucoup ❤❤❤🙈🙈🙈🙈😥😥😥😥😥😥😥😥😥😥😥😥😥😥😥😥
Zô dama nekone en pane mais yama dépanne ❤
Merci beaucoup frère, ms Un vidéo sur la Motivation de Stave Jobs svp Mec ✌️❤️
merci pour tous se que tu fait la jeunes....
ça c'est mon frère à moi
Machalla joop bi nice
merci bmakh👌
Meilleur vídeo bro
Merci frère
Walahi m'y grand namone Na Say vidéo trop
Machallah frère bonne continuation 👍
Merci bcp férére
Amnasolo yalanalayalla fay sayouma setane yocoute rek lay am bon courage yalla hamna bamayliguey parfoima am pasarpasareco bamalacoumanse setane lakoumase hamlimaydef
Amoniou sa fay mes big respects gars on est fier de toi
Yafi nek
Merci beaucoup mon frère ❤️🙏✨
Merci beaucoup mn grand que Dieu te protège toujours tu me donnes courage 🙏❤️
Masha allah frère bonne continuation way ❤️
Cest magniffique vrement
Zo koubakh ngua bly mane trois yéré la nior ms mane damay niée samay morom ms linguama wakh bayi nathi khéll boubakh merci beaucoup
Tarkala amatyna sooloo 😍🦾🦾☑️
Merci