Waw bariii pékhé wessouwoul nétalii sa guent morom bilahi deugu leu 😒😒😒 Aaay way Li lanla niii way bi nimoumay defff ❤️💕💕🥰😭😭😭😭 lett ma mba nga firimaa mon amour 😭❤️🥰🥰💕 août 2019 qui est là 👋👋👋👋👋❤️💞💕
Il est une heure du matin à Washington DC. Je suis seul devant mon ordinateur entrain de se souvenir de mon enfance au village niché dans la région de kolda. Jarama yassouma jiguéne!!!!
I am proud to say that I was one of the first Americans to go to Senegal to serve in the US Peace Corps Volunteer program, arriving in Dakar, February, 1963. Leopold Sedar Senghor was the poet/President...Some of us helped train the Senegalese National Team for the 1963 African Games, and later, for the 1964 Olympic Games. I also helped develop and institute a community development project on the Ile de Goree, Senegal. Fond memories.We celebrate the 50th PC Anniversary with him on Sept. 21st
He is literally saying to the other person hold or let go of me, it’s either you we are together or not, you can not say that you want me and next time you don’t want me and wait for you. And in one part he is saying that you must be a really special (sarcasm) to be able to tell someone what they dream about.
2024 loving this song and all kinds of old school Youssou tracks. Won't some saintly Wolof speaker translate all his songs for us?????? Please haha. All I know is "Létt ma" means "don't forget". When the rhythm switches up it's so damn good, gets me moving and dancing. The version of this song on Rokku Mi Rokka is also nice, a bit more relaxed feel.
He is literally saying to the other person hold or let go of me, it’s either you we are together or not, you can not say that you want me and next time you don’t want me and wait for you. And in one part he is saying that you must be a really special (sarcasm) to be able to tell someone what they dream about. I can translate the whole song song if you want me to 😂
@RamataDiop-ze6ig Thank you! If you're serious about translating the whole song, I would love that! It's already interesting to know the main themes of the song. It seems like Youssou really cares about the lyrics. It would be awesome to understand the meaning of the song, even just a simple translation.
Quel belle souvenir ça me rappelle beaucoup de choses a mon enfant le temps tres vite ahy yako mon pays manque trop wolayi qui écoute 2024 🎉❤ bientôt j'irai a l'abas DKR rek👌🏾
I do not understand Senegalese, nonetheless, the musicality, the pulsating fast-pace beats inter-woven with the nuances of the talking drums enveloped me. Each of his music kept me yawning for more and glued me on to listen to as many of these masterpieces as I can. As an African, we are all one. thank you Youssou for creating these beautiful music. God Bless
Du nil, du nil bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma Xamal ma lu leer Danga maa woolu sa gàll e ma ñëw nga mel ni xale Yaw daal yaw téppal fële Danga ba di tappale Su fekkeeni parewoo waru loo di yónéé Ngall yaw bul ma defioo lu ma nin ni di xeebe Létt ma mbaa nga firi ma Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma Lég lég sax nga yónni ma Ma dem bay dem nga teye ma Léégi sax dematuma Damay bañ nga dugël ma Bu fekkeeni parewoo wanu loo di yónéé Ngall yaw bui ma def loo lu ma nin ñi di xeebe Létt ma mbaa nga firi ma Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma Bari pexe weesuwul nettali sa géntu moroom Bëgg nga ma demal la wax ma kon li ne ci yaw Bari pexe weesuwul nettali sa géntu moroom Bëgg nga ma demal la wax ma kon li ne ci yaw Létt ma mbaa nga firi ma Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma Boo ma waxee fi nga bêgg dem Ma wax la fi ngay jaar Demal bl dem, waxal bul wax, defal bul def Man daal sonn naa, sonn naa sonn naa Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma Bëgg naa ko tay, Bañ naa ko subë kon xanaa ganaaw subë bëgg ak bañ la . . .
Merci beaucoup pour les écrits 🤩🤩😍😍😍😘😚😚😙😗💯😺🎊🕳️💤💗💖❣️💟💌💞💚💙💜🖤♥️💘💖👥👥👥👅👅👄👄👀💀🗣️🗣️💀☘️🌻🏵️🌸🌸🌺🌺🌷🌷🥀🥀🌹💐💐💮🍂🍁🌱🌱🌿🍃🍃☘️☘️🍀🍀🌁🌁🌀🌬️🌊🏞️🏞️🌲🌾🌳🌳🌴🌵🌵🌵🌋🌋🌀🌀🌬️🏞️🌳🌴🌵🌫️🌪️☃️⛄❄️🏔️🌡️🔥🔥🌋⛅🌤️☀️🌅🌇🏜️🏜️🌦️☁️🌨️⛈️⛈️🌩️⛅🌇⛱️🏖️🏖️☔🌌🌌💧🌠🌧️☄️🌩️✨⛈️💫🌨️🌟☁️⭐🌦️⭐⚡🌉⚡🌉🌆🌃🌍🌎✨✨🌑🌒🌓🌓🐰🐰🐰🐰🐭🐹🐹🐵🐵🐯🐱🐱🐶
Mala beugeu si sama khole Youssou Ndour lou boke si yaw rek dama ka beugeu doundal lou yague amine manchaalla
Qui ecoute en plein ramadan Yallah n'a Yallah naguou sa koor gui
Waw bariii pékhé wessouwoul nétalii sa guent morom bilahi deugu leu 😒😒😒 Aaay way Li lanla niii way bi nimoumay defff ❤️💕💕🥰😭😭😭😭 lett ma mba nga firimaa mon amour 😭❤️🥰🥰💕 août 2019 qui est là 👋👋👋👋👋❤️💞💕
Amina Gueye bilahi yow song bi mome machallah
Oumy Sougou Bilay ma puce way bi soumakoy deglou sama khol bi dafay seddd telment do sakh comp ken Ken papa you
Mom ak yonou deugg liimou wakh tayouko. Il est fort
👍💕💕
@@gueyewagane2882 bilahi yonou deugu bossi néké dina new Gnoulay feugu say say seytané yiii ak ......
Cette chanson me fait vibrer même en 2024😍
Youssou ndour yalla nala dolli diam si barkeb al houran Karim 😘💞📿
Ah les Années 2000
Ndeysane j'avais 3/4 ans.. Mes tontons mettaient ces tubes à longueur de la journée.
merci Père You
2000????
Sons bii bann Anne la
@@abdumaty1046 non son bi dou 2000 je crois que c les vers les années 2008 si je ne me trompe pas
@@pendadieng6216 wiii 2008 kayy lako yakar siii
@@abdumaty1046 sisi je me rappelle année bobou je faisais la 3éme niongui won si plein préparations pour les examens
@@pendadieng6216 2008 mom xale lawonn sama frere yii gnoka donn tek si galé motax instan makoy deglu mumay fatali moment yoyou
Il est une heure du matin à Washington DC. Je suis seul devant mon ordinateur entrain de se souvenir de mon enfance au village niché dans la région de kolda. Jarama yassouma jiguéne!!!!
Sadikh Boiro 5:23am in berlin and iam tryna figure out how ur childhood was like in kolda.and listenin to youssou at the same time.💕
Sadikh Boiro , aujourd’hui, moi au Canada où il est presque 4h du matin. Que la nostalgie de son pays...!
1 am in China , reminiscing memories from my childhood in Saint Louis
Mangui Genève di happiness si grand bi❤❤❤
Je suis à Dakar à se rappeler de cette belle époque
Premier commentaire en 2020 !
Ndeysann je suis actuellement à Gaël, un village breton à côté Rennes. Je suis entrain de revivre mon enfance. J’ai la nostalgie mon cher sénégal 🇸🇳
❤❤
A
I am proud to say that I was one of the first Americans to go to Senegal to serve in the US Peace Corps Volunteer program, arriving in Dakar, February, 1963. Leopold Sedar Senghor was the poet/President...Some of us helped train the Senegalese National Team for the 1963 African Games, and later, for the 1964 Olympic Games. I also helped develop and institute a community development project on the Ile de Goree, Senegal. Fond memories.We celebrate the 50th PC Anniversary with him on Sept. 21st
Thank you so much
Thank you Uncle Douglas...this is the year I was born....thank you to share this wonderful memories
Thank u sir
Douglas Treado thank you 💗
Douglas Treado amazing
Yaay wourouss si digue manding. Ana gniko beugue. Youssou jusqu'à la mort.
Yaye sen bay😂😂kou d’accord beug j’aim
Dafa leer
❤❤
💕💕
Amoul weranté lolou
💔💓❤️
youssou j'arrive fort force à toi la diaspora revient au pays t son nous permet de ne pas oublier d'où ont vient
Seuttt wa mane fane la meuna guissé Youssou Ndour je l'aime tellement Yalla na ko Yalla deffal jamm sammeu ko gouddal fanamm
I don't understand a word but the music is unique i love you Senegalese people..
You Have Nais Heart ❤
He is literally saying to the other person hold or let go of me, it’s either you we are together or not, you can not say that you want me and next time you don’t want me and wait for you.
And in one part he is saying that you must be a really special (sarcasm) to be able to tell someone what they dream about.
2007 ndeyssane beaucoup se sont mariés à cause de cette chanson. Machalla ✌️✌️✌️✌️✌️🇸🇳🇸🇳🇸🇳✊
Aside my country, Senegal is the country that I love the most because of their music. I'm Nigerian lives in Dubai. Viva Senegalais
I love Nigerian music and movies too we are all African our hearts beats the same.
@@aramatoulayedabo3438 iuiikiiiiikii
I of
Die meisten von q
@@aramatoulayedabo3438 AaaAA und ich habe die
who is your best artiste? wally seck ? Abou thioubalo? titi? yOUSSUOU? VIVIANE?
Who’s here in 2024???
Me
Me 😂
Me🎉🎉🎉🎉
Me today 30/11/2024
👋👋
2024 loving this song and all kinds of old school Youssou tracks. Won't some saintly Wolof speaker translate all his songs for us?????? Please haha. All I know is "Létt ma" means "don't forget". When the rhythm switches up it's so damn good, gets me moving and dancing. The version of this song on Rokku Mi Rokka is also nice, a bit more relaxed feel.
He is literally saying to the other person hold or let go of me, it’s either you we are together or not, you can not say that you want me and next time you don’t want me and wait for you.
And in one part he is saying that you must be a really special (sarcasm) to be able to tell someone what they dream about.
I can translate the whole song song if you want me to 😂
@RamataDiop-ze6ig Thank you! If you're serious about translating the whole song, I would love that! It's already interesting to know the main themes of the song. It seems like Youssou really cares about the lyrics. It would be awesome to understand the meaning of the song, even just a simple translation.
Youssou Ndour is the God of music. Perfection in its ideal form! I have nothing more to say!
Merci beaucoup yousu 😘😘😘
M😊
Machallah encore de tes meilleures tubes. Yalla na yalla goudal sa fane tonton You.
Au boulot, le moral à zéro et très pensif.
Hélas la vie est dure ici en Europe mais Youssou nous approche de la famille restée au SÉNÉGAL 🇸🇳.
# 2021
tu es le roi de la musique et le sera toujours. merci tntn you
Wallay j'adore❤🥰je peux pas passer une seul journée sans l'écouté😍😍🎶🎶
Machallah Dieu vous garde en bonne santé au près de nous vraiment. Vous êtes une bénédiction pour tout l'Afrique
Mon enfance se résume avec ce son 🤩🥺🥺😻
Noo son bi intro bi c just extraordinaire
Pére you warone nga yokou refrain plusieure fois encore douma si doyal
Billahi defe néx trop
Quel belle souvenir ça me rappelle beaucoup de choses a mon enfant le temps tres vite ahy yako mon pays manque trop wolayi qui écoute 2024 🎉❤ bientôt j'irai a l'abas DKR rek👌🏾
Qui est la en 2025??❤❤❤
1er aout 2024 sous la pluie ds le nord de la france!😅 subite envie de lecouter a nouveau 🎉❤ les freres ❤
I do not understand Senegalese, nonetheless, the musicality, the pulsating fast-pace beats inter-woven with the nuances of the talking drums enveloped me. Each of his music kept me yawning for more and glued me on to listen to as many of these masterpieces as I can. As an African, we are all one. thank you Youssou for creating these beautiful music. God Bless
DeBabysMama ❤️
The genre is mbalax in mostly the Wolof language. I like your description of the music and the feeling. I feel the same way!
Thanks
You're welcome🇸🇳🇸🇳
Where you from ???
King You
Mars 2019 et pour l'éternité qui est d'accord?? Pouce bleu
Super étoile
Sama CD ngenté dafa khossou song bi lagn tegone 😁motakh je l’es par cœur 🥳
Qui a écoute sa en 2024❤️🔥🙏✅
Moi ❤❤❤❤❤
Moi
Et moi🎉
Moi❤❤❤❤❤❤❤
❤
Youssou j'aime beaucoup tes chansons machalla yalla na yalla laf thiate do sëne morom
Tonton youssou sans toi Notre mbalakh nes rien tu es le meilleur des meilleurs chanteur du monde 👑👑🥰😍
Even in 100 years it's never going to get old
Qui écoute en 2019
Maguini
Moi
Moi 🙂
Soukeyna Gning ooooh
☝️☝️☝️👍👍
Qui écoute en 2020💗
Qui est la en 2020?
Du nil, du nil bëgg naa nga létt
ma walla book nga firi ma
Xamal ma lu leer
Danga maa woolu sa gàll e ma ñëw nga mel ni xale
Yaw daal yaw téppal fële
Danga ba di tappale
Su fekkeeni parewoo waru loo di yónéé
Ngall yaw bul ma defioo lu ma nin ni di xeebe
Létt ma mbaa nga firi ma
Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma
Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma
Lég lég sax nga yónni ma
Ma dem bay dem nga teye ma
Léégi sax dematuma
Damay bañ nga dugël ma
Bu fekkeeni parewoo wanu loo di yónéé
Ngall yaw bui ma def loo lu ma nin ñi di xeebe
Létt ma mbaa nga firi ma
Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma
Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma
Bari pexe weesuwul nettali sa géntu moroom
Bëgg nga ma demal la wax ma kon li ne ci yaw
Bari pexe weesuwul nettali sa géntu moroom
Bëgg nga ma demal la wax ma kon li ne ci yaw
Létt ma mbaa nga firi ma
Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma
Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma
Boo ma waxee fi nga bêgg dem
Ma wax la fi ngay jaar
Demal bl dem, waxal bul wax, defal bul def
Man daal sonn naa, sonn naa sonn naa
Bëgg naa nga létt ma walla book nga firi ma
Bëgg naa ko tay,
Bañ naa ko subë kon xanaa ganaaw subë bëgg ak bañ la . . .
Merci beaucoup pour les écrits 🤩🤩😍😍😍😘😚😚😙😗💯😺🎊🕳️💤💗💖❣️💟💌💞💚💙💜🖤♥️💘💖👥👥👥👅👅👄👄👀💀🗣️🗣️💀☘️🌻🏵️🌸🌸🌺🌺🌷🌷🥀🥀🌹💐💐💮🍂🍁🌱🌱🌿🍃🍃☘️☘️🍀🍀🌁🌁🌀🌬️🌊🏞️🏞️🌲🌾🌳🌳🌴🌵🌵🌵🌋🌋🌀🌀🌬️🏞️🌳🌴🌵🌫️🌪️☃️⛄❄️🏔️🌡️🔥🔥🌋⛅🌤️☀️🌅🌇🏜️🏜️🌦️☁️🌨️⛈️⛈️🌩️⛅🌇⛱️🏖️🏖️☔🌌🌌💧🌠🌧️☄️🌩️✨⛈️💫🌨️🌟☁️⭐🌦️⭐⚡🌉⚡🌉🌆🌃🌍🌎✨✨🌑🌒🌓🌓🐰🐰🐰🐰🐭🐹🐹🐵🐵🐯🐱🐱🐶
Merci 🌹
As
Aggalil lii way neex na trop
Ana wah teams 2024 manifeste vous 🥳
Vive Youssou Ndour et Vive notre Sénégal !!!!!
Sa majesté Youssou dou roi légui Empereur leu.
neekh na...daffa mette saffa saff....mooorefire!!!!
Qui écoute en 2020 longue vie a toi papa youssou ndour
I go see Youssou N'Dour for my 50th birthday hugs&kisses. You saved Nigel&Ocean's Mom/me
J ai le coeur brisé 💔 il est le seul qui me sentir mieux .love you you💖💖💖
Ki écoute en 2019 nel hoooo👍👍
Moi
Hoo
magatte sy hoooo
Ho
@@bayecheikhantagaye5947 le king 👑
J'adore que celui qui love aussi mets pouce bleu
Dimanche 21 avril 2024 10:25 qui est encore là❤
Qui es la en 2024❤🎉😢
Fantastique Musical Ruth. J’apprécie bcp á l’écouter👌🏽
Ma yeureum koula bagne sa none dou nelaw
J'aime bien cette chanson ❤️ machallah Papa Youssou N'Dour qui écoute en 2018😍
Degal fin ba. Bilahi Mbaye dieye tamit ken dou mom
Kouye diglou li 2018 bejel jèm
amna neknekh
En tout cas je ne souhaite que presenter votre concert à Paris bercy. Wakhléne si lolou way. Longue vie à notre cher You national.
Qui est là en 2024✌️
Bilahi woyebi môme lay doundiou nidé thiéy mbeguél 😀merci YOU
Premier commentaire en 2025🎉🎉❤❤ohhh li nekhna🎉🎉🎉❤❤
merci le professeur de la musique sénégalais
Qui est là……fin 2023 🥰❤️❤️❤️ Youssou ❤️🥰🥰🥰
Ndeysane dafma fatéli premier théâtre yéro dara jolof
Je suis là en 2024 et vous 😘😅
Je faisais ci a l'époque ndeysane😅
Ay way yousdou n'dour bi day nekh
La Reprise est terrible! First Rate!
En 2024 je réécoute ça
Qui m'explique les paroles svp🙏
❤❤❤ j'aime bien wolay❤❤
J'ai écouté à 2024 mais limouy waye ni si 2021 ba 2023 mo takhon mou waye ko khana
Le meilleur
2019 qui est encore la
Moi🖑
Moi
3:34 ay waay 😭😭🫀thioooo,🧎mais mais :) tonton you dou NITT🥇🇸🇳
Toujours en 2019😭💞💞
Thiey adouna , li rekk dayyy firnelni domou Adama dou draa
il es fort zéro faute respect a se mousier
Moi en 2024🎉❤😂
Youssou est le meilleur chanteur du monde ❣️❣️❣️✌️✌️✌️
😭😭😭😭😭y’a meun way nak 🥰🥰🥰🥰
le roi you est une source d inspiration
Ça me rappelle beaucoup de choses au village, je me souviens au village le ou on densait au était gate😅
Juin 2019 beuseul jaime ❤✨
J’écoute sa tous les jrs ❤️❤️❤️
Milakilooue
Milakilouz
Sanouware
Il est trop fort❤
waye bi dinama raye 😍😍
BLESSINGS TO YOU MY BRTHER MAY ALLAH BLESS YOU
Guinea love yousouf ndour nice son..balla gue 2
The king 👑 of music 🎶 2020
2024🎉🎉🎉🎉🎉
A l'instant je profite de l'après midi du dimanche avec un ami autour du thé et avec youssou ndour à la baguette
Yousou dou nit bilahi li dafa guaraw❤❤❤
Le king du Super Étoile de Dakar
Kouy deglou li en 2017 beusseul j'aime 👍🏾
L'il wayne
2019
On est en 2020
Allhamdoulillah
Aduna confiance rek
2019 still in love 🤔💚
Ndeysan temps boy..j ne connaissais pas l sens pr mane lettou ak firèkou leu(tresses) lol
I will forever love his songe😥😭😍😍
Ndour ningay seddallé sama khol bi no mais eupeuneuuu
J suis une fille mé sa sourie néhnama
Salut yousoundour
Doundeu
Franchement nekhna