Je suis Dip mais walahi ngaaka son bi doumassi doyal tei ossi clip bi dafa daw yaram 😭😭😭 walahi j’ai pas les mots yaggual doundeul wérral barké serigne touba 🙏🙏😭😭😭
Une pensée forte a mon frère qui est décédé récemment en prison des suites d'une maladie ,j'ai mal et j'ai beaucoup pleurer en regardant cette vidéo , mangui massawou gni nekeu si kasso yi 😭😭😭
Saway keneu ladioula si fans dip gua apprecier lene rek teuth sen guate mai di doul ay fans dip la mai jaime ngaaka on sen ndey fou seytaner guene lolou
@@diopjean3631 kham nga mbam bou wéké nga wék ko yena yem t ioe mbam nga owma sa diote li molen si nekh di tontou ay commenterou diambour lidieuntil ndey sa problème
Fi beu fébéré déh nguéye guéné diégué Le message est fort tout ce qui sont en prison ou dans des difficultés qu'Allah azawazal nous viennent en aides. Longue vie Mr ngaka 😍😍❤
Sincèrement suis pas un amateur de hip hop mais t'as assuré franchement. Bravo ngaka . Et de grâce Nanou bayi xél prisonniers yi ay borom banane rk niofa nek ossi ay citoyen lane comme nioune . Nanou doli yeurmandé yi si niom 🇸🇳🇸🇳😭🙏♥️
Une pensée à mon grand frère en prison 😭😭😭 tu me manques , ton sourire nous manque , Maman se cache pour pleurer ton absence, papa ne cesse de prier pour ta libération, yalla nalla yalla guéné
Nn Blindé siggil nga niou encore on est vraiment fière de vous continu comme ça fi nga ko tékk baxna...nioune wa Guediawaye nio ngi lay xaar toom Stade Amadou Barry👑💪🎖🏆🎤🎧
King Baba c'est le meilleur de tous les rappeurs. Manoulén souxlou ba soulko démlén scoolam dieul courame. Ay élèvames cours de récréation molén di bolle waye dou classe bi.
Je peux pa m'empêcher de pleurer c vraiment dur😭😭yalla naniou yalla mousseul si kasso té gnifa nek yalla nalene yalla diapalé bagnou guene té bagna deloou si louniou nekone te gni innocent sen innocence fegn😭🤲
Pour les 1/100 qui liront ceci longue vie â vous et à votre famille et aussi sans oublié de faire Une fort pensée aux prisonniers surtout en ces moments de chaleurs.
Mane je n'écoute pas les rappeurs mais ngaka ndanane cette chanson me touche au cœur respect à nos frères et sœurs qui sont en prison yalna lén yalla défal diam guéné len fi guéne nék 😭😭
Mon Dieu, par le droit du Trône et de Celui qui l’a élevé, par le droit de la Révélation et de Celui qui l’a révélée, par le droit du Prophète et de Celui qui l’a nommé prophète, par le droit de la Maison et de Celui qui l’a construite, ô Celui qui entend toutes les voix, ô Celui qui rassemble tout ce qui est passé, ô Créateur des âmes après la mort, prie sur Mohammed et sur les gens de sa maison et donne-nous ainsi qu’à l’ensemble des croyants et des croyantes dans les contrées orientales et celles occidentales de la terre, un soulagement rapide de Ta Part, par l’attestation du fait qu’il n’y a de Dieu que Dieu et que Mohammed est Ton Serviteur et Ton Messager (que Dieu prie sur lui, sur sa famille ainsi que sur les gens bons et purs de sa descendance et les salue beaucoup) !
Abou One je suis un rappeur Sénégalais comme King Baba enfin actuellement Ngaaka Blindé est le meilleur rappeur Sénégalais actuellement djaroulle débat force à toi notre King.
C est la 6éme fois que je regarde ce clip. Ngaaka_blinde, king de sa génération si tu es d'accord ou pas Les amis du coeur 💖 ce clip mérite 1millions de vue avant une semaine. 👑King Baba🤴 par force . Kou d'accord rk beuseul aime 👇🏽
Ohh tu m'as fait pleurer une autre fois encore King. Ndeysaan yalna Yalla défal nieup jamm ak tawfekh. Merci King, paix sur toi vraiment. Bonne continuation.
Bien vrai que je suis un moréen mais ngakaa tu fais partis des meilleurs de l'histoire du rap galsen force à toi diameu rek tawfekh ak taïssir rekk❤️🙏🏾✌🏾
Ndayssane kasso diomboul kéneu yalnalé yalla may wér ak kholou mougn vraiment c dir ms bon yalla bakhna koufa dougoul yalnala oumpou gnifa nek yalla guénné lénfa ci diam barcki CHEIKHOUL KHADIM
Ligay rap damako doundou 2016 mangui wonn chambre 9 deff nafa 6 mois tay mangui lay deglou depuis la france di nianall di bayii xel gayis nek si kasso bi plus particulier my bro racine do massa diokk sama khel yalla nala yalla takhawou si barké serigne babacar sy
Baba NDIAYE tu viens de donner une leçon de vie à la jeunesse qui est trés vulnérable au séjour carcéral. A vrai dire ce son mérite le tube de la décennie du rap Sénégalais. Quel engagement ! Tu es doit désigné l'ambasseur des prisonniers auprès des autorités judiciaires et même des populations.
Ce song m’a tellement fait pleurer car j’avais mon petit frère emprisonné mais par la grâce de Dieu il a été gracié 😥😭forte pensée à ceux qui sont là-bas yalnalén yallah dolii soutoura😭💔
Bo beuguei King baba beusseul j’aime🙏🏿
Je suis Dip mais walahi ngaaka son bi doumassi doyal tei ossi clip bi dafa daw yaram 😭😭😭 walahi j’ai pas les mots yaggual doundeul wérral barké serigne touba 🙏🙏😭😭😭
Frère Dip Ngaka lépp Sénégal la ils sont tous fort respect
@@amadoudiallo7892 #bilae frr lepp sénégal 🇸🇳 la yalnafi djam yagg réck 🙏
Je suis BM jaay mai ngaaka son bi doumassi doyal bilahi mai dara si kanam rék king baba
ndaysan kousa yaram dawoul boul j’aime😭
wawaw
Walahi
Ohhhh c'est très touchant une forte pensée aux prisonniers depuis la Mauritanie 🇲🇷 🇲🇷 🇲🇷
Même si mon commentaire ne compte op j'aimerais bien le dire même ma mère adore cette chanson 😭😭 Big respect à toi king Baba
Ce ki me touche moy ngaka dèm kasso wam bi dafko rendre plus mature 😭😭😭et plus fort mouy may dolè gni nèk prison wallah on t’aime frère
Je suis dip doundou guis mais yagui deff lou Nice respect ci iow 🎤
Blh de mm 👏🏽
King baba kouka nangou mayma j’aime 🙏🙏
Une pensée forte a mon frère qui est décédé récemment en prison des suites d'une maladie ,j'ai mal et j'ai beaucoup pleurer en regardant cette vidéo , mangui massawou gni nekeu si kasso yi 😭😭😭
Très émouvant comme témoignage
Qu’il repose en paix ✌🏽
Bilahi yaw yay Kane bilahi xamo sax
@@dimitricros199 merci cest la vie
@@juldf2812 amine merci
No vraiment 😭😭😭 king baba rék mou nékh mou nakhari bilaye mom rék laye dég lou 🙏
Yalna yallah tegui natou bi si kepou Kou nekk casso
Ngaka dioylo nga ñép bilay xol toyna, yalna yalla taxaw prisonniers yép
Kasso yalla nanou si yalla mousol😭🇸🇳🙇🏿♂️
Amine
Fans dipl a mais song bii dafma touché🙏🥺 yalna len yalla guéné founiou nék 😭😢
Saway keneu ladioula si fans dip gua apprecier lene rek teuth sen guate mai di doul ay fans dip la mai jaime ngaaka on sen ndey fou seytaner guene lolou
@@diopjean3631 billay frr deug gua wakh 😂😂
Non j'ai pas les mots
@@diopjean3631 kham nga mbam bou wéké nga wék ko yena yem t ioe mbam nga owma sa diote li molen si nekh di tontou ay commenterou diambour lidieuntil ndey sa problème
@@babacarndiaye8262 soumala guissone ba nok la ci guay sogua geum mbam bima done bilahi dina wékeu sa ndey ba gua reuk
Fi beu fébéré déh nguéye guéné diégué
Le message est fort tout ce qui sont en prison ou dans des difficultés qu'Allah azawazal nous viennent en aides. Longue vie Mr ngaka 😍😍❤
Yalna yallah samm gniii neck siii kassooo yiii j’ai pleuré billahiii s sound entre dans l cœur ❤️❤️❤️
Kou Dislike DAgua Soxor , Wala Dagua amoule Mokou bou neik si KAsso Biiii
RESPECT NGAAKA D'avoir montré la vie de 100M
Wahal way
Billay
Sincèrement suis pas un amateur de hip hop mais t'as assuré franchement. Bravo ngaka . Et de grâce Nanou bayi xél prisonniers yi ay borom banane rk niofa nek ossi ay citoyen lane comme nioune . Nanou doli yeurmandé yi si niom 🇸🇳🇸🇳😭🙏♥️
Ndeyesan yalla nala yalla takhawo rekk si barkèb seydina mouhammed psl amine ya rabal alamien ligeuye bi rafetna machallah king baba 👑👑👑🔥🔥💪✊✊
Une pensée pour tous ces prisonniers et des prières 😭😭king mon fils je te souhaite le succès que tu mérites si barke noreyni 🙏🙏
Merci frere si khalate bingua khalate prisonnier yii merci merci
Yalla nagnou yalla Moussal si kasso adouna ak alakhira😭
Une pensée à mon grand frère en prison 😭😭😭 tu me manques , ton sourire nous manque , Maman se cache pour pleurer ton absence, papa ne cesse de prier pour ta libération, yalla nalla yalla guéné
Ah sister courage yala baakhna
Amin yalla nako yalla dlli diam 🙏🙏
Ohh courage ton commentaire m’a fait pleuré thiey adouna
Oh sister ton commentaire is very very sad🤔😪🙄
Ndaysane métina😔mais yala bahna yalna lén yala djapalé🙏
King baba cette vidéo vraiment mérite des millions de vues lo doundou rek gua meuna nétali force à tous les prisonniers
Souniou borome souye défar day melni couy yak dama diapni sa dougou kasso mission bodone dokhla ndakh dougou nga khame guéne khamlé yalna yalla df diame 👌👌👌
Li don la kénn peunousou dara Ngaka blindé est incomparable ana fans ngaka yi👋👋🙏😍
oh kaso métina yalna yalla defal jam gnifa nek bagn guén tei yalla mousal niousi
Amiiiiine
La vidéo mérite plus de 2 Millions de vues en deux semaines. Vraiment Ngakaa tu es le meilleur de sa génération. Bonne continuation bro
Wollah g dei frison son bi dawa daw yaraam de trop sérieusement 😭🕊
King Baba🚨💪🏾
Nn Blindé siggil nga niou encore on est vraiment fière de vous continu comme ça fi nga ko tékk baxna...nioune wa Guediawaye nio ngi lay xaar toom Stade Amadou Barry👑💪🎖🏆🎤🎧
King Baba c'est le meilleur de tous les rappeurs.
Manoulén souxlou ba soulko démlén scoolam dieul courame.
Ay élèvames cours de récréation molén di bolle waye dou classe bi.
Je peux pa m'empêcher de pleurer c vraiment dur😭😭yalla naniou yalla mousseul si kasso té gnifa nek yalla nalene yalla diapalé bagnou guene té bagna deloou si louniou nekone te gni innocent sen innocence fegn😭🤲
Amine
Amine incha Allah 👏
Loumétty niagoul cissé
Amin yaraby
Pour les 1/100 qui liront ceci longue vie â vous et à votre famille et aussi sans oublié de faire Une fort pensée aux prisonniers surtout en ces moments de chaleurs.
Oh ton commentaire ma touche mais que le Tout Puissance vous viennes en aide sois forte
Amine
Mane je n'écoute pas les rappeurs mais ngaka ndanane cette chanson me touche au cœur respect à nos frères et sœurs qui sont en prison yalna lén yalla défal diam guéné len fi guéne nék 😭😭
Am very happy today belaye King 👑 baba honestly bul deffat benne video de doyna deeee very nice very sad 😭😭😭 ngaaka blende
Ce tube me frappe droit au coeur 😢
Max de j'aime pour NGAAKA🇸🇳🙏diar diar la rek frère
Thiég in💥
Je ne peux retenir mes larmes...yalla nalène fa Yalla guéné si noumou gueuneu gawé
Kouy woutal kenene promotion demal fenene bind fa tourame ngaka big respect for you I'm very proud for you the king of hip hop GALSEN
J'ai les larmes🥺, j'ai les larmes aux yeux 😭, Ngaka , tu nous parles de la dure réalité qui existe dans notre pays
Force à vous Ngaka ❤✊🏿 !
Ndeysaane son bi me fait pleuré 😢😢. Sama xol bi dafa fess bilahi
bilay
Réalité la on la vécue
Don blindé ba ici repose fier d’être 𝑩𝑳𝑰𝑵𝑫𝑬 𝑩𝑳𝑰𝑵𝑫𝑬 😭😭❤️
Aka ler fier d'être blindé blindé de
❤️😭❤️👌🏿
2éme vague gueu lale dh
King Baba💪💪💪
King👑👑👑bi iow la nangou nopalou li am si kasso galsen meti nala trompé nala yalla Faye sa khol king, 👑
Mon Dieu, par le droit du Trône et de Celui qui l’a élevé, par le droit de la Révélation et de Celui qui l’a révélée, par le droit du Prophète et de Celui qui l’a nommé prophète, par le droit de la Maison et de Celui qui l’a construite, ô Celui qui entend toutes les voix, ô Celui qui rassemble tout ce qui est passé, ô Créateur des âmes après la mort, prie sur Mohammed et sur les gens de sa maison et donne-nous ainsi qu’à l’ensemble des croyants et des croyantes dans les contrées orientales et celles occidentales de la terre, un soulagement rapide de Ta Part, par l’attestation du fait qu’il n’y a de Dieu que Dieu et que Mohammed est Ton Serviteur et Ton Messager (que Dieu prie sur lui, sur sa famille ainsi que sur les gens bons et purs de sa descendance et les salue beaucoup) !
Ngakka tu es le meilleur
Respect frère
Ay sama King bi nekho dered dh bilahi dafa ler ♥️♥️♥️♥️♥️
Je ne peux pas m'empêcher de pleurer c'est vraimen dur walae bravo king ngakka ameu morom message très important peuple biii dégnako
King baba
Son bii doumassi meusseu doyal🥺🥺❤
Fans DIP Doundou Guiss la d mais taye ngaka blindé lalneu sama Khol bilahi 😭
Un message fort ... État diougal ci li nitt d’où mala l’erreur est humain... Une deuxième chance est un droit💪🙏
Triste réalité j’ai les larmes aux yeux 😓😥😢
Yalla Na yalla takhawou képou Kou nékk si kasso bi si barkep Seydina Mouhamet (psl)🙏🏾
amin
C le meilleur nagn ko nangou t noppalou 🔥❤️
👑✊🏿❤🇸🇳
Bilay aio
Abou One je suis un rappeur Sénégalais comme King Baba enfin actuellement Ngaaka Blindé est le meilleur rappeur Sénégalais actuellement djaroulle débat force à toi notre King.
C est la 6éme fois que je regarde ce clip. Ngaaka_blinde, king de sa génération si tu es d'accord ou pas
Les amis du coeur 💖 ce clip mérite 1millions de vue avant une semaine.
👑King Baba🤴 par force .
Kou d'accord rk beuseul aime 👇🏽
Hooo machallah ndam RK le roi😍😍😍😍
Il suffit seulement de regarder les images pour verser les larmes 🥲 et que dire de ces mots, merci beaucoup #Ngaka
Enfin Le video est Disponible
Felicitation bro yafi né
Une pensé a mon frere badou diop🙏🏿bro namnagnla trop 😢 yalla nallen borom bi takhawou bou bakh bro.
Ngaka est le meilleur qui est d'accord avec mw💪✌️
King ya worr dh 😢😢😢
Ms yalla nako makk guou rèw mi dégue
Blindé Blindé yi Big Up Naléne 😍🔥
Olala mon fils Masha Allah Yalla nassi Yalla mousseul beep ndiabot incha Allah
Kou nagouni ngaka moye King bi beuseule aime
Première commentaire king baba yafi né💥💥💥
Dayy sann lie daww na yaraamm bly walayy mrc bcp gaaka yalla nala yalla faye nakh lie métie na trop bly
Au final xawma sakh lane la wara commentaire😭
Baba N'diaYe 🎤 Yalna Yalla goudeul sa fann🙏🏼😭
Ohh tu m'as fait pleurer une autre fois encore King. Ndeysaan yalna Yalla défal nieup jamm ak tawfekh. Merci King, paix sur toi vraiment. Bonne continuation.
C'est la première fois ma degglou rap ba dioy 😭😭😭💔💔💔
Ngacka yalla nga goudou fane lingaye diobe nice na trop💪💪
Des mots touchants 😢
Boulene faté dilene nianal
Yalla na yalla guene gni thiabi fété guinaw🙏
Khady
Dieulma pv 774550724
Ngaaka blindé Khalif général koulou rappeurs. Un j'aime si vous êtes d'accord
Diam si iow king baba lepp dina bax yalla baxna ana fans Ngakaa blindé le roi 🤴 de rap galsen 🔥🔥🔥❤️❤️👍
Son bii mounou mkaa deglou té douma diooy🥺😭 mashalah King baba🔥❣️
J’ai les larmes aux yeux. Il a tellement souffert. Tu mérites ta réussite ❤️
Ndaye saann son bi kouko déglou RK sa Yram dawna 😢😢
Bien vrai que je suis un moréen mais ngakaa tu fais partis des meilleurs de l'histoire du rap galsen force à toi diameu rek tawfekh ak taïssir rekk❤️🙏🏾✌🏾
Ma sha Allah merci bcp encore une fois depuis la Mauritanie 🇲🇷🇲🇷🇲🇷🇲🇷 yallah na yallah guénéh lénne si diamme😔😔🤲🤲🤲🤲🤲
Une pensé fort à mon frère qui est en prison yalna na guén leguii tout la famille priés pour tw tu ns mank beaucoup 😭😭😭😭😭😭😭😭🥺
inchallah frère
Amiiin
Amine
Inchallah yaleu baxneu
Aminn
Yalla na sa diamou yague j'ai vraiment sogue de cette video King tu es meilleur diamou rek ngaa varaa amou iow King BABA
Bien dit frère même si on ne connais pas la traduction mai on sais que sa parle des prisonniers 😭😭😭🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇳🇪🇳🇪🇳🇪
Nice 👍 Baba NDIAYE l’histoire réelle des cachots au Sénégal 🇸🇳 🔥🔥👈🏿👈🏿👈🏿
*Yalnaniou oumpou les gars*
```Adouna dafa teureudi
Soutoura si nieup```😭😭
Ndayssane kasso diomboul kéneu yalnalé yalla may wér ak kholou mougn vraiment c dir ms bon yalla bakhna koufa dougoul yalnala oumpou gnifa nek yalla guénné lénfa ci diam barcki CHEIKHOUL KHADIM
*J’aime les mots qui sortent dans votre âme.*
Les vrais fan's de
*King baba* 👍
je syis pas fan de ngaka mais se club merite des millions de vue vraiment
King baba fi ba adina di diex kén du fatei secret 7 surtt akci kasso😥❤🇸🇳pensée pieuse pour nos frères prisonniers free🤍
Ligay rap damako doundou 2016 mangui wonn chambre 9 deff nafa 6 mois tay mangui lay deglou depuis la france di nianall di bayii xel gayis nek si kasso bi plus particulier my bro racine do massa diokk sama khel yalla nala yalla takhawou si barké serigne babacar sy
Li son bi tristone clip guene nako triste dagn done deglou son bi souniou yaram di daw mai setane clip bi beug dioy😭😭😭 King do nitt
Vraiment ce clip je l'attendais trop😢ce tubes qui a fait pleurer ma mum😢
S8 Dip ms ngaaka tu déchires vraiment 🔥🔥🔥✍un vrai alchimiste avec les mots
King baba nice na dawna yaram bilay ooh 😭
Lii dioylo neu kouné 🥺🥺🥴🥴❤️❤️
Notre frère yalna Yalla doli soutoureu té déf thi yow diam ba nga gueune ffou té délou Wat thi sa liguey
Quand j'écoute les paroles je pense à mon grand frère qui est toujours en prison. Prions pour les prisonniers pour la liberté 🙏🙏❤
Yalla Nako SouGne borome Takhawou
Yalla bahna😭😭 inchalla soit fort
Yallanako yalla takhawou deloko thi saine lokho yallanako yalla samou areko barke seydina mouhamed psl
Courage mon frère. Yalla baakhna... Yalla nako yalla jappalé
Dieu est grand
Baba NDIAYE tu viens de donner une leçon de vie à la jeunesse qui est trés vulnérable au séjour carcéral. A vrai dire ce son mérite le tube de la décennie du rap Sénégalais. Quel engagement ! Tu es doit désigné l'ambasseur des prisonniers auprès des autorités judiciaires et même des populations.
Une pensée à tous les sénégalais arrêté d'ici et d'ailleurs k'Allah vous facilite la liberté totale : merci king blindé
Oh walay c triste 😢 machallah nguaka ✅
oohhh King baba longue vie magui dioyy wallah naniou yeureum niénék si kasobi
Ce song m’a tellement fait pleurer car j’avais mon petit frère emprisonné mais par la grâce de Dieu il a été gracié 😥😭forte pensée à ceux qui sont là-bas yalnalén yallah dolii soutoura😭💔
J'ai même les larmes aux yeux.tres touchant.Ngaaka amoul morome✊✊✊✊✊✊
Vraiment king 10millions % nga réussir son bii😭😭 ça touche tout les cœurs sensible 😭😭😭
Ngaka mii bilahi koumakoy presenté🙏🏾😭bilahi ngaka beugu nakoo
Vidéo bii
Ndey san baba song bi daf may yubbou fu sorri😭😭😭😭🇬🇲🇬🇲💯💯💯