En effet ce jeune là qui se nomme la voix du peuple il fau qu’il améliore sa façon de communiquer dioulitt day ande ak dall am téguine même bo néké si deugue
parfaitement raison il est plus diplomatique et l'islam à la base est à son image vraiment yalla nena dianguilen ba chine du wakh bou pyof té bayi khébaté nite kula geuneu dieguer yallah mola geuneu yaru nakh dagnay kham aduna kham alakhira kham yenen yi leundeum si beutu gnen gni asalam...
Le yalla yalla est très cohérent et il faut une certaine niveau d'sprit pour le comprendre. Il ne faut pas se laisser influencer par ces deux là parce qu'ils ne font que répéter et l'invité lui creuse c'est ça leur différence.
barki serigne touba la voie coste go sa kham kham beuneugoul teksi amo deg deg aussi gnak nga respect douma yalla yalla nak damay djioulli damay woor mais billahi li ki di wakh pour nga khamko deug fok nga sobbou yonnu tassaouf iow thie zahir nga nek alors que mom rombounalla mouguissi batine yallananu yalla tekssi yonnu ndioup
Rien É trop tard deloulén guinaw déloulén si yalla mo gueune dolen maseu am ndam si deuk bi té nguén bayi serigne Touba ak Wa keureum fowoul té folouwoul
Man douma yallah yallah mais malheureusement douma diouli😢😢té métinama torop sama rêve yeup moy commencé wat diouli 😢😢😢😢présque depuis 15 ans diouli wouma 😢😢😢ça me ronge le cœur bilahi té kén gueunouma rafét xol thi aduna 😢😢
Manguilay nianal yalna YALLAH SWT tégat la si younou siratal moustahimi thi bismo liré sama commentaire bi si barké SEYDOUNA MOUHAMED ALEYHI SALAM AMINE ❤
Mais faut quand même comprendre que saurait été beaucoup plus important de connaître la quintessence de cette obligation pour nga meune si diariñou ham yalla mo djitou diamou yalla
Wagni amoul yokk mo am. Yonente bi sws dafa faraloon souy diouli di yokk motakh tisbar 4 rakka takoussane 4... mais soy toukki nga am nganntal danga wara diouli normal mooy 2 rakka. Loolou nak wakhtaan bou reuyla . Ya'Allah nagnou Ya'Allah may dégg ak topp
Wa li zikrul Lahi akbar tekkiwul zikar mo gueun julli…lolu di tekki zikrul Lahi lou magg la, nguén beugg ko rawal ngueunel ak Julli…..thieuy Yalla !!!!
La voix yalla nala yalla guindi. Al holamawou warafatoul anbiya lolou la mouhamed wahon bimouy dem( néna borom xam xam yi niouy donnou yonnet tibia( la lumière)
Ziar ak magal. Maa ngi gis ñu bari di dingat Ndiamé Darou. Mom Cheikh Moussa Cissé dafa doon julli di woor ak lep lu war ci charia. Dellu di xamlé Yalla, yarr jaam bi ci jaamu Yalla. Dafay jang Alquran, Jang Xadiss… Donc balaa ñuy dingat Ndiamé, nañu dem ci ñumu Yaral boppam… ndax mom wacc na ligëy depuis 1994. Ku ci bëgg yu gëna léer, mune nañ ci jokko inshAllah.
Diouli mom nitt kounék farata la ci mom. Mais borom yeuré bou rouge bi il est un peu arrogant. Borom xam xam dou gawa xolou té dou niakk téguine. Défaratal say kalima té nga am sens d’écoute aussi
Kiy dém aldiana ak safara mom Yalla rek moko kham. Kiy changer ak koudoul changer aussi sunu borom mokoy choisir. La voix sa kadou yi niaaw na tropp. Kholaatal say kadou
En effet ce jeune là qui se nomme la voix du peuple il fau qu’il améliore sa façon de communiquer dioulitt day ande ak dall am téguine même bo néké si deugue
Wei merci moungui def lou nice wayé dfa wara dal
@@Is_124 Effectivement nonou la démé bo kholé mom kimouy corrigé sakh moko gueunneuh ande ak dal
Oui dafa tangue trop way ki 28:37
Mon constat
Dafay dingat de trop th daloul
Kendu seydina mouhamed diamou yalla ak.mouhamed ❤❤❤❤beug nabi ❤❤❤❤❤❤nabi
Ndaysane, yalla na leene yalla Giundi ci dine Islam Bala fato di leene dikkal😢
Gni bilén Yalla guindé tou tay
Al Hamndlillahi ❤
Machallah linga wakh si baye niasse nékh name trop ❤
Machala yalla yalla bi téyna Amna yarr❤❤
Yalla yalla bii dall xollam sett nah téh amna ay téguine lolle👌👌👌
Mane de dou ma yalla yalla waye niar nie di wakh tane yalla yalla bi simom la guena guiss yarr te yarr lo am solo si diolit la
parfaitement raison il est plus diplomatique et l'islam à la base est à son image vraiment yalla nena dianguilen ba chine du wakh bou pyof té bayi khébaté nite kula geuneu dieguer yallah mola geuneu yaru nakh dagnay kham aduna kham alakhira kham yenen yi leundeum si beutu gnen gni asalam...
Yalla rek mo kame allahou akhlame
😊koudoul julli du jullit 🇸🇳🇸🇳🇸🇳❤️
Baye fall bi teyna amna yarr th limay❤ wakh tek nako si yone
Parce que da khamm
Yalla yalla amna yar mom
Le yalla yalla est très cohérent et il faut une certaine niveau d'sprit pour le comprendre. Il ne faut pas se laisser influencer par ces deux là parce qu'ils ne font que répéter et l'invité lui creuse c'est ça leur différence.
barki serigne touba la voie coste go sa kham kham beuneugoul teksi amo deg deg aussi gnak nga respect douma yalla yalla nak damay djioulli damay woor mais billahi li ki di wakh pour nga khamko deug fok nga sobbou yonnu tassaouf iow thie zahir nga nek alors que mom rombounalla mouguissi batine yallananu yalla tekssi yonnu ndioup
Niakka kham yalla woroul bilahi dieureudieufé cheikh moussa cissé ndiambé borom darou❤
Yalla yalla bi am na yare téye na am na métrise
Walay ndaye sane limiy wah dal fégne na thji mome ndah cugnifi wahone sa serigne du dra wathie héhe
Merci la voix. Barrakallahu fika
Débat très intéressant
Enrichissant
Merci pour avoir appris bcp de choses
La voix chaque jour yay am ndam Dieureudieuf yagui xexal lislam
Pourtant suis daccord avec le jeune homme en rouge , li yalla may le prophète (psl) mayouko bene domu adama
Donc il a raison sur cette partie
Merci beaucoup la voix machallah 🙏❤❤❤
Niakka kham yalla woroul bilahi dieureudieufè Cheikh moussa cissè ndiambè borom darou❤
Kokou nak moko ray may niou diame🦬🐃😂😂
@@MouhamedDiassé-e8s nako beuy ray bakham
Non accident la way nak bi dadon ziar si faté indi adiya
Rien É trop tard deloulén guinaw déloulén si yalla mo gueune dolen maseu am ndam si deuk bi té nguén bayi serigne Touba ak Wa keureum fowoul té folouwoul
@@doudoucisse6485😂😂😂😂😂
Man douma yallah yallah mais malheureusement douma diouli😢😢té métinama torop sama rêve yeup moy commencé wat diouli 😢😢😢😢présque depuis 15 ans diouli wouma 😢😢😢ça me ronge le cœur bilahi té kén gueunouma rafét xol thi aduna 😢😢
Manguilay nianal yalna YALLAH SWT tégat la si younou siratal moustahimi thi bismo liré sama commentaire bi si barké SEYDOUNA MOUHAMED ALEYHI SALAM AMINE ❤
Démal gua diouli bayi sa thianhane yii
@@kenzifafall3438 Amine et Merci frère 🤲
@@KaneHawa-jf4ez yaw mom da nga réw dou mala tontou
Yal nalako yala yomba lal fekhel diegé borom xam xam yi ,,, sougnou nodé ga diemeu diapou dem si diouma dji diouli
Yalla yalla Yi kourërr ñoluen guneruerr Billahi bayilén baguendémsikanamou yalla rék 😢😢
J'admire bcp le Yalla, il reflète bien la bonté
Foula moy topp li Yallah diglé bayifi li nitt gni digg lé. Boulën djouli way nioune nionguinci li Yallah santané
Machallah émission bi nice la prochaine fois la voie day khar !!
Yallah rk Xam bilahi kousi nk AK liila yallah mounialé
Amoul bénneu khétte bou gueune khéttou seydouna Mouhamed amoul té dou massa ame inchalla
Dioulli kholou niou si bax wla bonn dan koy def ndax yalla mo niou ko sant
Deuguiit
Mais faut quand même comprendre que saurait été beaucoup plus important de connaître la quintessence de cette obligation pour nga meune si diariñou ham yalla mo djitou diamou yalla
La voix yaw la andal mais dél wakh ak dal ak respect
Kouy wakh deuk xolal daye had
@@ElimaneNiang-h6l mais niop yamou niou nit ak limou gueum sokoy yed fok ad ak dal té di wakhé khél mou né si deugue mais guem guem dafa fort
Très bien sûr tou nasi Bollé geusstou
Il est dangereux d'écouter ce genre de débat.
Bilahi
Jouli mon takh niounane joulite ❤❤❤❤❤ vraiment yeureum na sema bop
Diadieuf Mouhammed yalla yalla xam-xam bii Leer na Diadieuf Ndiambe Borom Darou ❤❤❤❤from New York
La voix beug nala baarki Mame Cheikh Ibr .....❤
😢 savoir écouté avant de répondre c'est nos difference qui nous rends humaine entre les deux a mon avis c'est la vx mboy doff biii
Dieureudieufè borom touba ❤❤
La voix yalla nala sama boroom saam ..
Machalla baye kadou yi léer n'a trop❤❤
Kham Ya'Allah mo gueuneu fort guiss Ya'Allah. Gneupp gno ngui guiss Ya'Allah wayé gneupp khamougnou Ya'Allah.
Mashala
Non nioune Baye niasse dafar naniou ba près barké baye niasse ❤
@@AbdouNdiaye-ro9zu
Wallahi Niass❤❤❤
Commentairou sama mbokou talibé rk ladone weur
Douma Yalla Yalla, talibé Baye la. Mais borom lacoste bou rouge bi na bayi wéddi té dém gueuna diangui waat.
Am watching from The Gambia
Waxtaan wi amna solo machallah
en tout cas machallah wadji tey na yarouna🙏🏼...wanteh tmt djouli mom bayiko da woroul dara fall
Da melni limiy wakh âme n'a diekhital si dieumem
Yalla bi kou amme rare la je l'aime beaucoup mon ❤
Allahou akbar les talibés serigne Touba 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Deett moussoul nek Talibé serigne Touba dinguelei woul fene niak joulli arretez ça
Vive la voix❤❤❤ merci beaucoup yalla rek fi ne machallah
billay la voix gni daanio reer
إن الصلاة تنهى عن الفحشاء والمنكر ولذكر الله أكبر yalla yalla bi nim ko firé dou nonou wakhul dueg
La voix du peuple rk www
Ken rk la yalla teguil dioulli moy m cheikh ibrahima fall
Da febarone xana mome ?
Yalla molako wx wakhal lo xam guiso Yalla demo si Yalla
Alkhouran baxara ba nasi amoul fou Yalla wx nek mame cheikh ibra fall teguil nako diiouli somako wané m guemko
@doudjamdong6968 xanaa😂
Wagni amoul yokk mo am. Yonente bi sws dafa faraloon souy diouli di yokk motakh tisbar 4 rakka takoussane 4... mais soy toukki nga am nganntal danga wara diouli normal mooy 2 rakka. Loolou nak wakhtaan bou reuyla . Ya'Allah nagnou Ya'Allah may dégg ak topp
Bilay talibé baye niasse dfa nékh Alhamdoulilah Niass la solution ❤
Les chrétiens ont le saint esprit ❤ ( mercis yalla yalla bi)
Allahou Akbar 🙏soubhanallah!
Alkhamdulilah allah kuli hall❤
Ham yallah amna tigui, wayei dagn si bolei diko diamou...❤❤
No bilahi alkhour Ane . Cou ko yor do dioumm ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Café touba lay nan ni sax 😂😢☕️😥tiye yalla
La voix je suis avec toi 🤝🏻 mes rafetalal Say kadu envers yalla yalla bi 🙏
Ms Adama talibé Moy lépeu bly
Ah oui,le yallah yallah est plus correct.
La voix très bien machallah
Nn li amna solo trop
Dioulite ak yalla yalla lép pour mane béne la nieup yalla laniou geum niom waxouniou yéfeur yéfeur wakhouniou lénéne mais yalla yalla laniou wax
Yalla yallah ❤❤❤❤
Wa li zikrul Lahi akbar tekkiwul zikar mo gueun julli…lolu di tekki zikrul Lahi lou magg la, nguén beugg ko rawal ngueunel ak Julli…..thieuy Yalla !!!!
Ms yalla yalla bi amna yaar trop blh
اللهم إني أعوذ بك أن أضل أو أضل
La voix yalla nala yalla guindi.
Al holamawou warafatoul anbiya lolou la mouhamed wahon bimouy dem( néna borom xam xam yi niouy donnou yonnet tibia( la lumière)
Yala yalabi mo gañé wakhtanbi nit nité ak réspé bu kéne atté kéne❤
Démale weuri yalla la voix
Ndiamé darou guiss yalla mofi nèkk
Djouli,woor ak yissi topou dou yakk niit dédétt dafay defar niit sii kaw nga défé ko nimou waré toudou yallah kén douko déf bayii farata yii (talibé baye)
Ay waye ngir yalla outi lén wasilla pour meuneu lérlou loubari si kham yalla
Yallah yallah bi mon gueuneu cohérent mon gueuneu logique
Cheikh Moussa Cisse Ndiame Borom Darou mooy seen kilifa terrewoul ben talibeem diouli mbaa woor❤ Na leer🎉
Nye aii yefarr len
Ziar ak magal.
Maa ngi gis ñu bari di dingat Ndiamé Darou. Mom Cheikh Moussa Cissé dafa doon julli di woor ak lep lu war ci charia. Dellu di xamlé Yalla, yarr jaam bi ci jaamu Yalla. Dafay jang Alquran, Jang Xadiss… Donc balaa ñuy dingat Ndiamé, nañu dem ci ñumu Yaral boppam… ndax mom wacc na ligëy depuis 1994.
Ku ci bëgg yu gëna léer, mune nañ ci jokko inshAllah.
Boy bi amoul téguine déh.
Ay yeufeur guene dh walahi nga nan ma ay yalla yalla xana ay saytane saytane kay
Nii danion rére boubakh waye
Non boull wakh lolou l'an Moy rerr
Yalna yalla guindiléne dagno réere dayssane dagnouléne nasank
J viens d comprendre une phrase que mon prof nous disait en classe .,"même si vous mentez ,mentez avec force "
Thieuy adouna lou né fi lay amé
Diouli mom nitt kounék farata la ci mom. Mais borom yeuré bou rouge bi il est un peu arrogant. Borom xam xam dou gawa xolou té dou niakk téguine. Défaratal say kalima té nga am sens d’écoute aussi
Sawaye dagua toguoul fima tok 😂😂😂 bilahi dagnouye wax Lo kham né faw sa yaram tangue walahi
@@lavoixdupeuple6147tant k khamo degeuntane lane moy diouli si wéranté ngay meusseu nk parsk gni il parle en parabol
COMPRENDRE KOO LII WADJI NÉKÉ MOKO NÉEKHOULE😂😂😂😂
Bilay kontan na si iaw frère ❤
La voix du peuple ❤
Moussa Diagne yéfeurla kokou topp guis moussiba
Yalla yalla yi aka gno dekeur fit amagnou xam xam diakougnou alkhourane déke aya allhourane
ndeysane sa xalat la rek kou baah ... yalnaniou yallah guindi
yalla yalla yi siy thiakhan rk ngén nékk
Guéné lén si Cheikh Ibrahima fall AK Serigne Touba
2:37😂
LA voix fan yalla yalla l
Dama laye ladje mani khana Boye diouli mouno di wërde ( la i laha ilah allah ) wala
Je suis talibé baye Niass c’est Talibé yalla yallah na pas de arguments solide.kou bayii djouli yeuférgua
Akay dëgu yalla yalla dou tongn dou khéthi dou féyou 🤍🤍🤍🤍
Frère yaw amo talibé déh mame😢 sa commission téguiné woul deh 😎
Tigui Ndiamé borom darou moy dëgg❤
Koudoule diouli mm bassi ndiambé darou koussi dé safara gua kat ndm dieum
Kou khamoul fratay joulli ak lathia ajou noy amé xoll bou set
20:25 le verset se trouve dans 1jean 1 v 5-10
Et c'est Jean qui l'a dit.
Kudul diouli do ab dioulit
Koudoul djiouli do djiouli point
😂😂😂😂 nonou na fïkhe yii
Kiy dém aldiana ak safara mom Yalla rek moko kham. Kiy changer ak koudoul changer aussi sunu borom mokoy choisir. La voix sa kadou yi niaaw na tropp. Kholaatal say kadou