Ama Baldé révèle un secret : "sarakh bi Balla Gaye dané Gris Bordeaux mako guénè, Balla sama..."

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 29 окт 2024

Комментарии • 178

  • @misterdadji45milliards57
    @misterdadji45milliards57 Год назад +77

    Ama Balde Yalla Nala Yalla defal Roi des arènes 👑

  • @buzzdakar5147
    @buzzdakar5147 Год назад +34

    Li montax niep beug ko ❤

  • @timtim6971
    @timtim6971 Год назад +4

    Il est très honnête il parle sans arrière pensé contrairement aux autres lutteurs

  • @gueyelabsolu5889
    @gueyelabsolu5889 Год назад +33

    Kii moy Borome pikin Borome ndèl bi ❤ wallahi moy pikin nieupou lay kafall Bay Fall la woyofna trop Osi Yallah nala Yallah défal ndam Barké Mam fallou Mbacké 🙏🏻❤️🙏🏻le roi 👑 des arènes inchalah ✅

    • @souleyewade7419
      @souleyewade7419 Год назад +3

      C eumeu pikine bo kerok mou bayi lamb

    • @ahmadoundiaye8743
      @ahmadoundiaye8743 Год назад +2

      Gnom nieup la lep pikine la

    • @souleyewade7419
      @souleyewade7419 Год назад +1

      @@ahmadoundiaye8743 exactement

    • @fatoucha554
      @fatoucha554 Год назад +1

      Pikine mayonnaise leu mbeur yifa deug yeupa ko bok kousi diouk drapeaux bi ❤️💚gaye yobou

    • @galsenegalsene
      @galsenegalsene Год назад +1

      Pour le moment yalla Eumeu séne lafa tekk ba kérok mouye téki ngém kénéne sok di nieuw

  • @alioutine2789
    @alioutine2789 Год назад +28

    Barki yalla ama yalla topėwoukko draa kii mooy mbeur billaye

  • @sambafall3509
    @sambafall3509 Год назад +10

    Sama futur roi bi inchallah yalla nako yalla déf yarabi Ama Baldé ❤❤❤

  • @walkerjro.b.s667ekip8
    @walkerjro.b.s667ekip8 Год назад +10

    Ama baldè nitt kou solidaire la moi suis fan de modou lô mais bou fékké day niakk roi bii yalla na ko Ama dieul amine.

  • @cheikhmbaye59
    @cheikhmbaye59 Год назад +7

    Mais pour niouy wax Ama latté na ci réseaux sociaux yii Ama fekiwoul kene kogname leuh nek di diayaneté ci ndogou yii tmt ❤

  • @papythioulo1406
    @papythioulo1406 Год назад +9

    Futur roi 👑 Ama Yéé TSK mbeur fitt mbeurr dolé 💪🏿💚❤️

  • @baityrba2447
    @baityrba2447 Год назад +5

    Vraiment li am solo Ama boula dara takha changé pikine t'aime comme ça 💚💚❤❤

  • @sidydiop1523
    @sidydiop1523 Год назад +4

    Mane dé legui sakh damako faral ama baldé amal jammou ❤️

  • @khadimndiaye5910
    @khadimndiaye5910 Год назад +16

    😂Ama balde khol be rafet❤

  • @mamadoudiop7124
    @mamadoudiop7124 Год назад +46

    Ama vrai comédien laa😂😂😂

  • @BabacarDiouf-et4me
    @BabacarDiouf-et4me Год назад +24

    Ama nieup la amal diam😂😂😂

  • @arfangthiam878
    @arfangthiam878 Год назад +5

    Ama ñepako beugu ❤️❤️❤️❤️

  • @ndowbabacar352
    @ndowbabacar352 Год назад +1

    ❤❤❤❤❤❤ c'est doux c'est doux vraiment et quelqu'un qui aime les phasmes

  • @mansoursamb9277
    @mansoursamb9277 Год назад +3

    Machallah. Li rafetneu kaff ak rée avec tes amis.

  • @boubacarboiro5813
    @boubacarboiro5813 Год назад +4

    Lutte TV la télévision leader de la Lutte sénégalaise

  • @aliouneelevage6482
    @aliouneelevage6482 Год назад +10

    Amayeeeeeeeee

  • @mbayesarrdia4470
    @mbayesarrdia4470 Год назад +1

    Thieye ama nitou askanwi ak wa pikine 💯💯💯

  • @djibygueye6101
    @djibygueye6101 Год назад

    Walahi affaire yi dou fii ngako tekk rek bien vrai k mystique amna mais force ak technique mooy daan champion yii

  • @mansourdiatta1741
    @mansourdiatta1741 Год назад

    Yalla nala yalla défal diam ama balde

  • @serignemoussandiaye8315
    @serignemoussandiaye8315 Год назад +5

    Yalla na diam yag

  • @kevinbow758
    @kevinbow758 Год назад +5

    Ama yee

  • @ndakarudialdiop1206
    @ndakarudialdiop1206 Год назад +6

    Borom ndél bi 😂 diam ci yaw❤

  • @omzoseck8566
    @omzoseck8566 Год назад +1

    Merci ama ❤

  • @Bass.beuzz.bdn.6037
    @Bass.beuzz.bdn.6037 Год назад

    Ndeysann diamou dafa nekh ama xole bi dafa rafét amak ngep diamou li moy nite yalla nalén yalla défale diamou té may la ndam nga dieul roi bi inchalah amine

  • @babacarfaty4490
    @babacarfaty4490 Год назад +3

    Aladji mbaye mane souma guissé ama baldé té guissouma aladji mbaye douma contane

  • @sambbass7972
    @sambbass7972 Год назад

    Champion deugeu barcké sering saliou .diame sy iow mbeur

  • @boubacardiop-ue3kc
    @boubacardiop-ue3kc Год назад +1

    Sérieux ni laa mèll naturellement NDAM rek inshallah 🫡🫶

  • @khelcomsakanamtv5427
    @khelcomsakanamtv5427 Год назад

    Ama yalla nako yalla may ndam yalla nako yalla déf roa bilay lii dafa rafétt torop té nékh si ❤ khol ama daal diamou si yaw ❤

  • @Varlaye.2
    @Varlaye.2 Год назад

    Ama dafa simple machalla

  • @meuzdiop4419
    @meuzdiop4419 Год назад +5

    Aladji mbaye dama fathie man😂 néna tapha tine lagn la wax no danga dioum 😂😂😂nit warouma banié nonou

  • @alindao657
    @alindao657 Год назад +2

    Yallah rk lay topou

  • @thiernoaw8193
    @thiernoaw8193 Год назад

    Billahi ya bakh

  • @abdougpinternational3704
    @abdougpinternational3704 Год назад +6

    Bayi len ama mi nguen di dfal interview sak jour bala mouy latté si kanamou nit yi nguen bayi si Mbuer yi nguen koy lathie ta wah ak mom si carriere ram ??

  • @ndiayendiaye313
    @ndiayendiaye313 Год назад

    Machchallah ama

  • @papicoleye3380
    @papicoleye3380 Год назад +1

    Champion leeee

  • @ndeyakarisma3445
    @ndeyakarisma3445 Год назад +1

    Apart balla Mane ama yèè 😢rek

  • @mohamedvarre1250
    @mohamedvarre1250 Год назад

    Bilay gnon gentle champion le futur roi des arènes gnola beugu 🤍

  • @sergedione7658
    @sergedione7658 Год назад +6

    No Mère bi amoul kw kén dou mome machallah 😂😅😂😂😂

    • @boy_galsen12
      @boy_galsen12 Год назад +1

      Moytoul bala deum dila dokhote rek😂😂

    • @sergedione7658
      @sergedione7658 Год назад

      @@boy_galsen12 Non elle la dit koula bagn yalla nako deum dokhote😁😁😃😀😂😂🤣🤣😅😅

    • @boy_galsen12
      @boy_galsen12 Год назад +1

      @@sergedione7658 kon nagne beug ama 🤣🤣

    • @sergedione7658
      @sergedione7658 Год назад +1

      @@boy_galsen12 Est oui mn frère Pikine rek bilay tey arrière nako plus d 6fw tellement 😆😄🫶🏾😁😃😀😂😂🤣🤣😅

  • @ibrahimadiallo1071
    @ibrahimadiallo1071 Год назад +5

    Bialhi ama dh ni la dieuké ak wa pikine 😂 nokaté rk😂
    Parfois daamay wathe école fekkk ko sén bountou keurr nga yorr mbourou mou nagou ko lékkk rk

  • @boy_galsen12
    @boy_galsen12 Год назад +3

    Ama d kouy woor nek si côté walay di nga meuss dog mom day diek sayi rek reuk la wala mou door la si bop😅

  • @papendiaye1371
    @papendiaye1371 Год назад

    Ama yeeeeeeeeee

  • @momo___gaye2541
    @momo___gaye2541 Год назад

    Mbeurou patriote yi

  • @falloubeye8571
    @falloubeye8571 Год назад +3

    Ama yéé

  • @khali2000-tb2yd
    @khali2000-tb2yd Год назад +3

    thieiy Ama 😂😂😂😂

  • @nouhadieme1889
    @nouhadieme1889 Год назад +3

    Weiii ama yaw rek la beugue mais stp temps yi da nga beuri lingay guéneu thi réseaux sociaux yi

    • @omaralfoutiwc.o.d1987
      @omaralfoutiwc.o.d1987 Год назад

      Kor gui la rek ,

    • @khassoumcisse3227
      @khassoumcisse3227 Год назад +4

      Ama réseau yi nioukoy weur ta ama balde bay fall la koor gui yeup mome ak mafia bi niokoy nek outéna yéne mbeur yi di bédeu sen kharite yi

    • @papesall4753
      @papesall4753 Год назад +2

      Koor gui mo takh

    • @ndongodiop9977
      @ndongodiop9977 Год назад

      Nouha diémé loy def fi😂😂

    • @nouhadieme1889
      @nouhadieme1889 Год назад

      @@ndongodiop9977 amateur lamb la dé bilahi

  • @baadama8554
    @baadama8554 Год назад

    Ama👍💕💕

  • @bigmoflow2023
    @bigmoflow2023 Год назад +1

    Numéro téléphone ama réck la beugue parcque damako beugue

  • @mouhameddia-pi1nj
    @mouhameddia-pi1nj Год назад +1

    Limoy nitt
    Nit dey humble

  • @Del2Mas
    @Del2Mas Год назад

    Man dè Modou la ba illa
    Waye Ama amoul ben problem motah douniouko respecté

  • @santyalla123
    @santyalla123 Год назад

    Ça se voit k nitou kasé la mbarou askan bi🇸🇳🇸🇳🇸🇳

  • @tallandiaye9108
    @tallandiaye9108 Год назад +1

    Ama dél diwou 😂😂😂😂wékh nga d

  • @babacarfaye2924
    @babacarfaye2924 Год назад +3

    Ama balde

  • @cheikhbasskeurmassar9548
    @cheikhbasskeurmassar9548 Год назад

    Ama balde futur

  • @amadydiaw2390
    @amadydiaw2390 Год назад +2

    Kou beug Lac Rose ma beug leu. Ama Balde naleu yallah défal diam mayla ay victoire you bari. Amine

  • @serignesalioukane
    @serignesalioukane Год назад +3

    Ama wèekh nga 😂😂😂 ak sa ndèll😅

  • @khassoumcisse3227
    @khassoumcisse3227 Год назад +6

    So cana lila done wah ak wa mafia wam niouné mbeur parcelle yi dougniou lène fallait 😂 surtout ibadou bi nioune bay fall lagniou am nekeu borom bah

    • @layekharagne2224
      @layekharagne2224 Год назад

      doff dou meussa wakh wakhi nitt te pikinois ndeysane wakhou nitt mounouko

  • @MLSonko1
    @MLSonko1 Год назад +3

    Ama sa mboyo lanla 😂😂😂

  • @ChezMarra-ik7de
    @ChezMarra-ik7de Год назад

    Ama baldé amgua beuss

  • @Moustapha722
    @Moustapha722 Год назад

    Ama ack nell bou ray b 😅😂😂wayi caf ack rèe rick adouna amoll solo

  • @mohamedballadiop6085
    @mohamedballadiop6085 Год назад +2

    Aaaaaaamaaaaaaaaa Yéééééééééé💪❤❤

  • @ndoyeaida4096
    @ndoyeaida4096 Год назад

    ama kesse lay topou

  • @layediack3485
    @layediack3485 Год назад +2

    Nitou kassé. Ama yé

  • @ycamara9034
    @ycamara9034 Год назад

    Bless

  • @cheikhsidy2253
    @cheikhsidy2253 Год назад +1

    ❤️❤️❤️❤️

  • @wadeissakha2725
    @wadeissakha2725 Год назад +1

    🥰

  • @nouhankaba1391
    @nouhankaba1391 Год назад

    Trop nekh
    Lamine meilleur

  • @mamesouley9734
    @mamesouley9734 Год назад +2

    wa yein guis ngein bopp AMA bi yein ki dolei rk la ma yeureum say adversaire dh FUTUR ROI

  • @ousmanethiam6570
    @ousmanethiam6570 Год назад

    Mère bi raynama 😂koula bagn yalna ko deumou dokhott mou dèdd😂😂

  • @NdeyesokhnaDiop-u4f
    @NdeyesokhnaDiop-u4f 11 месяцев назад

    😢😢😢😢❤❤❤❤❤❤❤

  • @damembengue1894
    @damembengue1894 Год назад

    Vraie diaye prék leu 😂😂

  • @modouamar1130
    @modouamar1130 Год назад +3

    Borom dague d’office 😂😂😂

  • @lounekhwayedeffsenegal6165
    @lounekhwayedeffsenegal6165 Год назад +3

    Ama wekh nga😂

  • @sidythiam6983
    @sidythiam6983 Год назад +2

    Ama boulangerie 🥖 lay liguéyé xana😂😂

  • @dembabaldebalde7369
    @dembabaldebalde7369 Год назад

    Ama Rèk 😂😂😂😂😂❤❤❤

  • @SofiaFall-pv9xv
    @SofiaFall-pv9xv Год назад +4

    Beuss niki taay ama sama mbeur laa lac rose kouko beug ma beug laa

  • @djibithiaw1259
    @djibithiaw1259 Год назад

    Aladji mbaye aka beugue sak wpppp🤣🤣🤣

  • @ahmetmbodjmbodj4686
    @ahmetmbodjmbodj4686 Год назад +1

    Ama mi nékhoula niemé dara

  • @mouhamedndong6069
    @mouhamedndong6069 Год назад

    Leundeum Leundeum Bouki Forr Beuyyy Boy NIANG 2 ROI des Arènes inchallah Rabi Molein Meune Foufffff

  • @ngangedrammeh6264
    @ngangedrammeh6264 Год назад

    Ama damako beugue gir balla gaye

  • @diopkhalil7302
    @diopkhalil7302 Год назад

    Ama di nga ray wadji

  • @mboupada7856
    @mboupada7856 Год назад +3

    Defal sarakh guir beuré mo geune

    • @cheikhbayefallndiaye5136
      @cheikhbayefallndiaye5136 Год назад

      Yaw békal nite waye yalla moye dogal

    • @jrkinamablde657
      @jrkinamablde657 Год назад

      Adouna yala ko mome
      Tok mouy dokh khana gueumo yala 🤷‍♂️🤷‍♂️🧏‍♂️???

  • @senewayetv2062
    @senewayetv2062 Год назад +1

    Ama mo eupou fitte si lambji

  • @ndiaboutadiouf9300
    @ndiaboutadiouf9300 Год назад +1

    Baye fall

  • @abdoudieng6226
    @abdoudieng6226 Год назад

    Bakh rék mo ame solo

  • @iboundiaye2162
    @iboundiaye2162 Год назад

    Enemi boy Niang yeup ay kharitou ama laniou beure len mou diekh

  • @cheikhbayefallndiaye5136
    @cheikhbayefallndiaye5136 Год назад

    ❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @maodosow3022
    @maodosow3022 Год назад

    Ama yee borome néél bi

  • @diopmar6382
    @diopmar6382 Год назад +2

    Secret bi defal co sa bop ndakh nga melni balla gaye wala modou lo wala eumeu wala gris wala bombardier wala boy niang

  • @gueye009fallou2
    @gueye009fallou2 Год назад +1

    Wakh katou degue nga

  • @bayeratebayerate5893
    @bayeratebayerate5893 Год назад

    Abbou bakhoum mou yakhal Ama thé lamb

  • @morniass8456
    @morniass8456 Год назад

    il Di tay si geu

  • @mntv6294
    @mntv6294 Год назад

    Ama yangui seukeute bou bakh fadioule bala ngay beuréé

  • @milkass7166
    @milkass7166 Год назад

    Adouna dou nex baga dane modou lo

  • @santiagosolari8054
    @santiagosolari8054 Год назад

    🎉

  • @dieuredieufetiserignetouba9365
    @dieuredieufetiserignetouba9365 Год назад +1

    Pikine xana diww daf fa cherrre ama weikh ngaaaaaaaa

  • @paulpogba7780
    @paulpogba7780 Год назад

    Bn2 double maire pikine guediawaye ay daw lakou guen rek

  • @niangmoustapha7102
    @niangmoustapha7102 Год назад

    😂😂ama rèk