Chers internautes, c'est parti pour la saison 02 de votre série préférée. Que nous réserve-t-elle en termes de suspenses, de rebondissements, d'humour, de joie etc. Pikini vous assure dores et déjà que vous serez bien servis. Le meilleur reste à venir. Wait and see !!!
J'espere vraiment voir des rebondissements et du suspense car la première saison était devenue monotone sans suspense et de rebondissements. Bonne continuation 💐💐🙏🙏
Ngoné Mbaaye bouné hawmassi dara lawah rek may beugg gaaniou 😂😂😂😂ki nitt leu.Lohom yi nimoukay def mok kombé ak Daro nioka niro bouniou roussé😂😂dinanie ma ray rkk
Hé les Sénégalais ayez pitié de nous les étrangers ' il n' y a pas de sous titres français et les commentaires sont tous en Wolof 😂' on regarde juste les gestes pour essayer de comprendre En tout cas on est fière de vous car c'est l' Afrique 🌍 qui gagne ❤️❤️
Jadooooore votre série ça m’aide beaucoup à destresser j rigole bey teud si souf😂😂 surtout quand j ne m sens pas bien fii rek lakey diap machallah tu courage
Ngoné Mbaye lima nekh si yaw moy bo méré rek dieul sa lokho yi di wagnar sa lokho j’en suis sûr bala série bi di diekh dinga ame problème lokho mai j’aime bien sa rewandé lol
Enfin il y a des sous titres ? Pour la saison 1 au bout d’un moment il n’y en a plus ! Comptez vous en mettre ? J’ai pas finit la saison 1 Saison 2 changez le générique
Machallah mention spéciale à vous tous père m'baye ak "dal bimou andal"maty m'baye ak"foula dji"nila djiguène dafay am caractère anny "tèy na nité na"lolou mo takh mouy gagné ngoné diaba yay bour une vraie comédienne Machallah "ravissante et souriante"mais ngoné "bour" nak dafay moom territoire bimou nék,aliou ndiaye scénariste yalna sounou borom aar té motali liguèye bou rafét bi amine
Ngoné mbaye dadji ngama si fin bi. Bilay ya réw Ngoné may wah mou nann gniaw da nga beug satj sama ayé kkkkkk. Non fou rire fin bi meunatoko. Niaw bi yonn mom ya gagné ndahte "mon père" daw na té Ani djahléna kkkkkkkk
Man daal guis nane darou bou dina ma nekh am nafi place am omaro darou nek rako ngoune omaro moy dokhan maty mbaaye def len lolou kon dina guena nekh😀👍💔
Chers internautes, c'est parti pour la saison 02 de votre série préférée. Que nous réserve-t-elle en termes de suspenses, de rebondissements, d'humour, de joie etc. Pikini vous assure dores et déjà que vous serez bien servis. Le meilleur reste à venir. Wait and see !!!
Svp Pikini Prod pour cette saison 2 mettez nous les sous titres pour nous les francophones svp!!😢
Masha Allah si vous continuez sur cette lancée , vous iriez loin . Insha Allah
J'espere vraiment voir des rebondissements et du suspense car la première saison était devenue monotone sans suspense et de rebondissements. Bonne continuation 💐💐🙏🙏
Team Ngoné pouss bleu
On vous entendez avec patience machalah bonne continuation 😍
Kou beugg Serigne Babacar Syy pouss bleu
Yalla na yalla yokk leeramm amine
Mw
Amine 🤲🤲🤲 thibarké seydina moukhamed psl amine
Mako begue piiir
Amine waye thi barki khalifa ababacar sy 🙏🙏
Amine ❤️
No NGONÉ MBAYE vrai artiste leu bilahi👏👏👏👏
Fv
Kou d'accord ni ngoné rewna beuseul jaim🤣
J'ai🤣
Jaim🤣
Merci beaucoup je suis très contente yeneu bokolén ak gnigua xam ni saison 1 bi bou diékhé saison 2 bi balamouy niew daay yagueu one love
Dado Mbathily wakhatiko deih bilay da ngay fatei sakh nou saison 1 deme wone ishhh. Pikini dal ay diambar laniou🙏🏿👍🙏🏿👍😘
Ay way ame na tourondo way😊 tour bou rare
@@dadogueye7195 Ayiiiii tourondo guay amfi
@@gnimasn5275 bilahi ndakh gua sagneko wakh
Kou koy setan di réétan rek beuseul j'aimes fofou tothie radiakh
Cv😁
Kouko namone beusseul ma guisss❤️🔥❣️sant wergou yaram yalla n’a nieup am liniou beugu❤️❤️❤️❤️❤️
Euppeuneu
Tmt
Ameen
Eupeuneu
Allez wayy ngoné mbaye gagné na pour la 1ere fois machallah laff thiatt touffe touuff👏👏👏
🤣🤣Dafa diote nake.dagno sonone si dėfėte yi👏👏
Thiam Naboushita Ndeyssane 😂😂😂😂 wayer ba sama wadjiiiii Annie nieuwate en force req💪🏼💪🏼💪🏼
Khana
😘👏👏👍
@@mamiishasow7599 ba anni jok si kawame rek
Cou dacor ni djiguéne day gnoul😍😍👌👏😀
Goor nakk?😆😆
Wawaw comme mane
Djiguéne bou khéss dara Dakhou ko
Ioe sama tourendo ngeu deh Astou ngom diouma gnieme
Mane👆👆👆👆
Félicitations ngoné gagné na taye khana digua diape thi yalla saison bi gua bayi défaite yi qui es d'accord 😂😂
Moi😂😂
Son bi nekhna kou d'accord
Bilahi 😂
😂😂😂 Senegal bamou dathie ngone mbaye mossi gueuneu reiw... nooo mais kii amoul...😂😂😂
Enfin de retour ma serie préféré
Deuredieuf Serigne Saliou mbacke ligua def si dine leerna
Team❤️ Maty mbaye Ana gni ko namone🤗
Khady Faye
Mans
@@khadyndiaye1364 mon homonyme ❤️😄
Wawaw tamit
Tapi multi couleur😭😭😭😭😭😭😭ngoné mbaaye rew naa tchooo
Rougui Diop 😂😂raynama
@@ndeyesamb9879 dama tiiit dii réé na bay dioy bilahi😂😂😂😂
Waa tmt wakhou lène si son bi dh aka nekh ❤️❤️
🤣 🤣 🤣 C'est a cause de ngoné je regarde cette série elle me plaît trop😂😂
C'est grâce à ngoné (positive)
Walay
Oui kan on apprécie on dit grâce.
Grâce
871
Maty mbaye mohh deugueur fitt😂kouko bayi mou dégagé😂son lellll est vraiment sorri😂😂😂
Wakatyko lèél bi komme Dana bos
maty mbaye mboup ay way do bayi sama idole bi
Aay way yenna bonn bayilen tefessou Maty bi way🙈🤣
😂😂😂
Man kay lolou moma diakhal com rompoint Dominique bi
Waw kay wakh amoul nada khewoul Ngoné amna victoire 💃💞😘
Mane daal Maty Mbaye mo may fathie ki est d'accord avec moi besseul j'aime
Haaa goné mbaye woye bignoulaye woyale thi souf dara fayouko machallah kou aimer son bi
Sama khol bagui melni wanagou mbott ...
Ngoné mbaye dinama rayy rkk kou dakor pousse bleu👍👍
Ay waye ngonè yalla guay gagnè chak jour elle me fait trop rire chiiii mane mala beugu pire
À part moi qui d'autre à cru que ngonè à porté un pyjama 🙄🙄🙆🙆
Bilay mom laco tégone chérie
Moi 😀
Moi
kon dou byjama😅
Moi même walay😂
Danga diénge 😁doy déé di wénge😂😂😂😂😂😂😂😂meusou meu guiss diék bou mélni Ngoné Mbaye😂😂😂
Lolou la retane ba sone
Merci Daba Diaw
Non ngone mbaye d'où nittt pikine love sur vous sama woudiou toubab la daguekoy setan sa khol di nekh
Bilay
C'est officiel !
Ngoné Mbaaye vient de célébrer sa premiere victoire 😂😂😂😂😂
Aka gno kharagne té assidu machala saison 2
Ngoné khana dina fass diom té bayi dioy yi
Bella Nature
😂😂dafa rew ba dof dioy menou ko bayi 😂
@@mamanmbodji7175 rew la def lol
Ana gni beuguone victoire ngonei mbaye pouce bleu
On ne dit pas ngonei mbaye on dit ngoné
Me
Non tay ré na ba dioye ngoné rewgua " néna mon père Dagua djingueu té boy dé di wingueu " 😂😂😂non bilay douguéne ma ray
Degue dou nekh wa Pikini lay done bamou beure dolé ki KO mane la ak gnikoy dieme dougnou bene coeur sur vous 😍😘
Yèn dh la geumm,saison 1 diekh meme pas 1 semaine saison 2 nieuw haro lèn bèn sponsors dal
Machalla
Blh gni la gueume rek
Lady T p
Lady T
En fin ngoné amna victoire 😂cette fois si boul maye any dara.
Man dal ngoné Mbaye nimouy dioyé nexnama dafa pleurant trop j'adore way😂😂😂😂
Ngoné Mbaaye bouné hawmassi dara lawah rek may beugg gaaniou 😂😂😂😂ki nitt leu.Lohom yi nimoukay def mok kombé ak Daro nioka niro bouniou roussé😂😂dinanie ma ray rkk
Akhhh Diop Fall😆😆😆
MashaAllah bi geine gneuwateii vite fait . Yalla na seine jaam durer on vous aime . Team MatyMbaye❤️🙏
Ngoné da rew
No ngoné rew na ba dof 😁😁😁🤣🤣dieukeur bi guena con😁
Ngoné mbaye bouné mon père danga diengue boy dehhhh di wenge rek ma kheummm😂😂😂
Fofa todj
Hé les Sénégalais ayez pitié de nous les étrangers ' il n' y a pas de sous titres français et les commentaires sont tous en Wolof 😂' on regarde juste les gestes pour essayer de comprendre
En tout cas on est fière de vous car c'est l' Afrique 🌍 qui gagne ❤️❤️
ngoné nènako, "Dangay diay sadick, mala geuneu sadick" 😂
Qui est là en 2024❤❤
Magui ni😂
Ngoné Mbaye rewna ba neub😂🤣😅🤣😂🤣🤣
Bissmillah si saison 2 bi
Dada sa boop bi sorri neu comme radisson blue diamniadio 🤣🤣🤣
🤣🤣🤣🤣
Yaw khamé na la fouma dem guiss la
@@fatoushmbath4894 mane la déh may louka partout
Kou khamé woul louka rek même alphie cuisine magua fa
😂😂 traverser gua khalébi 😂😂
Ngone mbaye mi esk amoul ayy rap😂
Ah namone na léne bila way j'étais si impatiente de voir sa ❤😘😘
Sou goné amoul wone dam MA bayi setane
Wa lélou maty bi dougnou si wax 😂
Sorina trop
Lucie Mendy hahahaha bayil mou sedd
Mome mo done khass semou ndekété wo niom niarr nio yemm
Dou mo done wakh sa léle bou sori mome bosame bi da adjou😂
Li dh mo raww lamp sall d bain
qui est d'accord que ngoné mbaye est très djiongama Man sagnesé tek ci man dof doflou avec son teint noir je l'aime daal
Comme moi
Mais son bignouy dégu si souf ooh, belle voix 😘.
Merci hâte de regarder l'autre épisode.
Wawaw dara khewoul, saison 2rekk , waw keyiii bismilahh, traverséwolen niou bene yone 😂😂😂 barkiyontébi
Kou weuyee sons bi heeeeeee hoooo
Yalla na guene goudou fane surtout ngone joue bien son rôle merci ay way dina amer deune ana fansou ngone mbay 1ere dame Bou anti stress bi
Maty mbaye létou naa😂😂ak leel bou aam diom kay bam beurii dolé com sama boss😭😭😭
Ambiance faire play😂😂😂😜
Ya bonne😂
🤣🤣
Magui dei
@@mamebalydieng812 llll
Yaw dagua diengue boy dé Di wéngue 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂ngoné mbaye duma Ray
Mane dal liii dh la kham si film saison daykoy nefff way 😍😍😍😍
Mane maty mbaaye moma nekhe lamaniame bou saff sapp la yoro 🤣🤣🤣🤣
Mba mou khess
Anni Khana saison 2 bi figa am ngor bayi Ngoné mouy gagné😹😅
Lii dou compétition lii affaires de meune sa boor moom sa goor na ngoné nité reek
Yaw dé Mme Fall ya seytané
😃😃yaw louy sa blême
Loy faral si Anni di mailni deum bou ndaw
Anni rek kou far ak moom dangay bég nék 2em femme dou thiakhane
no Ngoné mena jouer qui est d'accord pour moi 😍😍😍😍😍😍😍😍😍
Rei na bay dioy😂😂😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭ngoné mbaaye amoul woor na yalla😂😂😂😭😭
Bilay dama retane ba sama beutt yi di dioy je te jure
@@linguerefall4696 NN li dou deugg yalla na diam yaag😂😂😂
Mane ngoné la beugue mane😂😂😂djiamil guéye mome meunenama raye😂
Ana sopéye Serigne Touba
Mangui dehh 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Kouleine namone beusseul j'aime❤
No Ngoné rewna ba dof 😂😂je l'adore trop 😘
Wa loutakh ngoné mbaye réw. Fougnaral ngoné momay dadji😂😂
Bravo ngoné mbaye tay môme ame gua victoire
Ahhh beurina beurina Ngone amna vitouwarr ah thioum Diaba yayy burr
Wayei nak Ngone djegou VIP dou lale drapou mètre 500frs wathie gnou yangui gnouy traverser waay
Mais le son en bas on en parle OP dé waouh 😍
Dija hijabiste oui suis l’instrument
Ngone Mbaye kène dou yaw trop forte machalla série bi nèkh na trop bne continuation
Merci Sokhna Thiam
@@laminediaw3830 pas d koi dafa nèkh rek👍👍
Elle est toute jolie Ngoné😍😍😍
Cher Pikini et Production je réclame 3fois par jour svp 🙏
Ngone mbaye rewna tapi multi couleur wouyyyy🤣🤣🤣
Mbourokk lemm ma chanson preferer kan je lattend jai les larmes au yeux parsk je suis loin de mon mari dadier gouniou ba tayy
Khardiata Ndione yalla ngen dadié thi diam
Amine way namnako trop
Taguare Mame niou dieuk yi😂😂😂😂😂😂 Ngoné Boulniou yapp way😂😂
Heureusement je n’ai pas à attendre longtemps!! 😄 Ils allaient trop me manquer ✨♥️💯
Mak bou reiw moy ngoner mbaye 😂
Mdr
Bly
Bly
Pour la semaine
An wa Team ngonè 👍👍👍👍👍👍👍
Diogué thi golden barasti kou thi sama woudiou toubal la wa li nekhoul yéneu
Ni dé la ko tégalé
Waa golden nexna ??
@@adjadiba4354 torop nekhhhhhh la def
0
Machalla pikini production
Woykat bi nénako ngoné wayy
borom demey kharou wayy😂😂😂 ngoné nak bayil kharou bii
Wa lellou maty mbaye dougnou si wakh nakk hahahaha comme teffess dèè
Barkiyalla ngone mbaye yala na goude fanee migi may rayyyyy😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Jadooooore votre série ça m’aide beaucoup à destresser j rigole bey teud si souf😂😂 surtout quand j ne m sens pas bien fii rek lakey diap machallah tu courage
Bilahi ngone dafa rew 😂😂😂😂😂😂😂😂
Ngoné Mbaye lima nekh si yaw moy bo méré rek dieul sa lokho yi di wagnar sa lokho j’en suis sûr bala série bi di diekh dinga ame problème lokho mai j’aime bien sa rewandé lol
Série bi dara nekhou si ngone sof nga niaw nga 😈😈😈😈😈😈😈
Sannt yalla bou bakh binou féké saison 2
Ms
Enfin il y a des sous titres ? Pour la saison 1 au bout d’un moment il n’y en a plus ! Comptez vous en mettre ?
J’ai pas finit la saison 1
Saison 2 changez le générique
Bonne continuation pikine continuation
Sou bakhè rk niou dem😍Ngonè du nitte
Ngoné mbaye dou mousseuu changé
Machallah mention spéciale à vous tous père m'baye ak "dal bimou andal"maty m'baye ak"foula dji"nila djiguène dafay am caractère anny "tèy na nité na"lolou mo takh mouy gagné ngoné diaba yay bour une vraie comédienne Machallah "ravissante et souriante"mais ngoné "bour" nak dafay moom territoire bimou nék,aliou ndiaye scénariste yalna sounou borom aar té motali liguèye bou rafét bi amine
Ngone mbaye dinama reyyy😂😂😂💪💪💪
Son bi nékhna trop machalla ❤️
Qui aime sama woudiou toubab appuie sur le touche bleu
Ngoné mbaye dadji ngama si fin bi. Bilay ya réw Ngoné may wah mou nann gniaw da nga beug satj sama ayé kkkkkk. Non fou rire fin bi meunatoko. Niaw bi yonn mom ya gagné ndahte "mon père" daw na té Ani djahléna kkkkkkkk
Mais ki lale générique yi kanla 😂meune na way 🎉
Salam je n est j 'amais vus ça dans la serie de sama wodiou toubab la commentaires 180 ah ça c est cool qui es d accord
Hii maty mbaye sa lèell sorina😁😃😃😃
Man daal guis nane darou bou dina ma nekh am nafi place am omaro darou nek rako ngoune omaro moy dokhan maty mbaaye def len lolou kon dina guena nekh😀👍💔