Dinga gnou raye rekk,di takhamtikou rekk,eupeena yaye boye.waye yalna sa diam yague habibti Mommy. Si kaw si kanam rekk si lou bakh.love you to the moon and back ♥️🤗💋🤝👌❤❤
Marietou tu peux parler en francais ou subtitles en francais, j adore la langue wolof mais je comprend pas c est pas les Senegalaise qui te suis seulement pense a nous autres aussi une soeur Guineene
Le Secret De La Bonne Cuisine merci beaucoup ma sœur je lui est dit plusieurs fois de sous-titrer en français parceque c,est pas tout le monde qui parle le Wolof mais elle ne répond jamais moi je vais me désabonné de ça page
It looks so yuuuuummmyyy😍 N easy to make...😉 Ecq kou am netetou en poudre bo ci dollee crevette en poudre, cayenne pepper, di na am lou khawa mengoo ak fouti bi ???
@@rokhayadiagne7297 netetou kani poudre crevette Ak sel so beugué Ak magi tu connais les petits poissons séchés j'oublie le nom "youssouf" lolou tamite Boko amé en poudre tu fais le mélange c'est très bon
Bonjour Marietou. Je ne suis sénégalaise mais je regarde régulièrement tes vidéos. C’est un plaisir et j’apprécie ta propreté et ta bonne humeur. Bravo.Sans compter tes différentes recettes. Même si je ne parle pas Wolf j’essaie de comprendre un peu. Qu’Allah SWT continue à t’inspirer. Amine C’est quoi le foutu?
Tata marietou tay nanga lale sama yeuf ma mayla bénéne recette yokal sobblé nga bakhal ko ak ak bissap bi et les autres après nga mixé lepp dara dakouko tamite ( la recette s'appelle aussi foutti boté)
Mane c’est ma belle-mère (😢) qui m’avait confectionnée un gros pot de fouty durant mes dernières vacances au Sénégal. Apparemment ça peut aller dans presque toute préparation à base de riz blanc.
Salam très chère tata. Mon mari dit que quand je tomberai enceinte la première chose qu'il fera c'est chercher comment je ne pourrais plus accéder à ta chaîne sinon lui il aura bcp de problèmes.🤣🤣🤣🤣🤣. Kallah t'apporte toute sa bénédiction. Wa mais pour nous qui sommes en france comment faire pour améliorer si niambane Mad???😁😁
Jaimmme tata marietou yalla na la yalla diapalle amine werelle lokhobbi
Machalla yalla na yalla faye yiw
Dinga gnou raye rekk,di takhamtikou rekk,eupeena yaye boye.waye yalna sa diam yague habibti Mommy. Si kaw si kanam rekk si lou bakh.love you to the moon and back ♥️🤗💋🤝👌❤❤
Machalla tata marietou yies dal daff mai nekh yaw lay weer
Wouyyyy!!!!
Lima nekh nak moy sel rek ngay def
Ahhh ta mariétou sama plat diam yi nekhna té gaw machala machala
Je suis de Guinée merci d'avoir préparé mon plat préféré
Machallah sa pla préfère beu niou toudema lafidi
Machala sama plat deuk Guinée ndeysane aka nekh mom rek la beg😁
Macha allah. Name nagnoula lou bari tata marietou .wayé nak défal ndank ci lafidi bi !!! Nouyoul ma tata yandé bou bakh
Macha Allah tata yalna sa diam sakh yallah samla sam sa ndjabott beuggual rekk nga fi nekke.
Machala tata fans de toi depuis Kédougou 🙏😘
Tata Mariatou Sa lafidi nehna, Fouti hino welli machallah 💖👏👏
Healthy food leppa 👍 naturel...
Man dama naan laffidi, mbakhal nioulouk ak C_bon ay cousin la niou..
2ème commentaire machaAllah ma tata Mariétou darling thanks 😊 barakal lahou fik❤️😍🥰😊😘
Dangay sett lii rek, fi sedd bi di commencer ni, Adja Marietou dal del degg diam rek🥰
Petit gnedad ,petit ray ‘ terè bien 🤩 que du bonheur en regardant tes vidéo meeerci wayyyy😂
Tata diguama raye😂😂😂😂
Machallah Tata maretou gaw na amna vitaminé 👍
J'adore sama plat préféré tata mariettou nettetou biii odjiii la toude
Thioooo tata! Yaw tojati nga fi. Masha Allah
Tata Marietou yalna nga fi yaga te weur Merci te nga djitou niou tci niane yi fouti dara dakhouko
On adore nous les Guinée 😍
Sa c ,est chez moi la guinee
Mais tu as bien fait a ta facon👍
Ah oui lafidi c est chez moi la Guinee 💗🇬🇳🇬🇳🇬🇳💗🙏
yes but this one is very different
@@ndeyeaminatadiop5810 I know but lafidi in general is from Guinea I know most of the African cook too
Wakh amoul dara amoul machallah
❤️😊
Tarkallah reck
Bilahi tata marietou mane yaw laye weur
la diva de sa maman fans sadio mané 😘😘😘😘❤️❤️❤️❤️❤️
Tata mariatou sa wak nekhena ma loegeu vien💓💕👍💛💚
Xif na sax 😂😂
Manshallah Tata Marietou bou dimanchè inshallah ma dèfar ko
Ma Sha Allah Tata Mariétou😘
Mashallah tata comme d'habitude merci beaucoup vraiment ioe daleuh amon morom doundeul bâ say may di bawane😘😘
J'aime trop ce plat maman, je suis très contente de voir ta méthode qui est complète 😋😋😍😍
Ma cha allah sama togolokh bi togue nawete soumetina la yag na kkkķkkkk
Machalla tata marietou wa italy gniguilaye beugue
Tèrè bien 🤣🤣🤣🤣🤣 vraiment mashaAllah sokhna Mariètou
Machalla I love it Chérie 🥗🥗
Je ne connaissais pas. Merci tata
Ma sha Allah
masha Allah rek
Machalah tata c comme malakhoulagne je mangé ça ken jt plus petite avec mes copines sousou
Masha'allah tata
Oh li nekh na. Ça me rappelle ma meilleure amie guinéenne. Merci pour la recette toujours dans la bonne humeur 🙏🏽.
Treeeeeeee biennnnnnn non ta Maretou YALLAH na sa diam yague je vous adoooor 😘😘❤️❤️❤️🥰🥰🥰
Machaallah ma chère. Le nénétou saf avec les gnamatoss on appelle ça Odji
Tata Marietou yalla nala yalla faye. Aye boulene setané ba paré délène aimer.
Fafa merci la bas
Très bien 😅👍
Machalla tata marietou yalla nassa diam yagueu li eupeuna mais sen epice you bari djisoumako fi Espagne khanama gueuneu recherche rek😋
Marietou tu peux parler en francais ou subtitles en francais, j adore la langue wolof mais je comprend pas c est pas les Senegalaise qui te suis seulement pense a nous autres aussi une soeur Guineene
Le Secret De La Bonne Cuisine merci beaucoup ma sœur je lui est dit plusieurs fois de sous-titrer en français parceque c,est pas tout le monde qui parle le Wolof mais elle ne répond jamais moi je vais me désabonné de ça page
@@ballerboybillz wa mais soff nga deh!!! Déshabonne toi!!
@@ballerboybillz wa desabonne toi mo waye 😂😂😂😂😂😋
Très bien 😆😆😆
Très bien😂😂😂😋😋😋😋😋🤤🤤
Mahchahala mahchahala di contane ci saveurs planétaires
J'adore se plat 😍😍😍
First view first comment
Ah taye mom dagua dém sama deuk Mouy Guinée
waw kay numero pour ay bissap ak guedj la done weur fi ci amerique
Machalah tata 😘😋
Thiey sma yaye dji tay ma fi ndieukeuti
Machallah tata ♥️♥️♥️💯
Tres bien très bien
Tata marietou goudeul fane sa doundou am na diarigne machalla li sakh lekk nawett lamay diokh😂
Hummm nekhna je le prepare de temps en temps👋👋😘😘
It looks so yuuuuummmyyy😍
N easy to make...😉
Ecq kou am netetou en poudre bo ci dollee crevette en poudre, cayenne pepper, di na am lou khawa mengoo ak fouti bi ???
Oui mais Cayenne pepper je ne connais pas
@@khadidiatoudiallo4307 merci
Cayenne pepper, moy kani peundeukh rek...saf sp
@@rokhayadiagne7297 netetou kani poudre crevette Ak sel so beugué Ak magi tu connais les petits poissons séchés j'oublie le nom "youssouf" lolou tamite Boko amé en poudre tu fais le mélange c'est très bon
@@khadidiatoudiallo4307 , c gentil
👍
Machalah c'est bon
Je suis fane de toi ma tata préfère
Bravoo ta marietou. Yalla nala Yalla lafal tiate. Kagne nguay niew canada ?
Topenne yi way balnamiou la bou bakh aunty de 💖 💖 💖 💖 💖
Dama ko begue bilakhi
machallah tata marietou
Bonjour Marietou. Je ne suis sénégalaise mais je regarde régulièrement tes vidéos.
C’est un plaisir et j’apprécie ta propreté et ta bonne humeur. Bravo.Sans compter tes
différentes recettes. Même si je ne parle pas Wolf j’essaie de comprendre un peu.
Qu’Allah SWT continue à t’inspirer. Amine
C’est quoi le foutu?
Le netetou appellé soumbala au Mali séché et moulu en poudre une fois moulu on grille cette poudre en y ajoutant un peu de piment et du majji cube....
Merci chère professeur. Je commande un plat sauce baobab. Merci d'avance. Bisous
Bonjour tata. Je ne connais pas du tout ce plat. Merci beaucoup.
Ma plat préféré
Salam!!! tu es la Meilleure. Bon appetit
J’adore le kani kaye lène khole ma 😂😂😂😂
👍👍👍
vou etes captivante et eloquente merci
Machalla
Merci waya
Tata Mariétou kagne gua niouy togual athiekè
Pourtant togou nako chérie tapel sav planétaires attiéké dikako guiss semaine passé rek reprendre nako trop nekh
Nou les peulh on l'apel fouti
Tata marietou tay nanga lale sama yeuf ma mayla bénéne recette yokal sobblé nga bakhal ko ak ak bissap bi et les autres après nga mixé lepp dara dakouko tamite ( la recette s'appelle aussi foutti boté)
Très bien maman mariétou Macha Allah
Tata magui takamtikou sah
Tata ouly tu nous manque reviens nous vite
Maretou khaanaa sa bakou bi Mere Diop mooko moomoone
"Merci way merci bcp" meunou mako mougne😂😂😂😂😂😂😂
Guoudal fane tata li nekhna de
mai tata est ce que on peut utilisé juste la poudre de nététou
Euphemie Sagna oui comme vous voulez y ‘a n’en qui ne mange pas de crevettes alors juste netetou is good
Saveurs Planétaires thanks
Yummy and my tummy 🤤
😂😗😗😗👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍👍
Fouty sama plat chaque dimanche je le prépare merci tata
😘😘💯💖💕😍❤👌
Mane c’est ma belle-mère (😢) qui m’avait confectionnée un gros pot de fouty durant mes dernières vacances au Sénégal. Apparemment ça peut aller dans presque toute préparation à base de riz blanc.
Salam non yagui lay dadji ak re
Tata maretou sourrrallleilll djigueuinnn you weirroul yi hummmmm bobou bâ leigui yangui mayyy provoqué mayyy mougne
Rama Dior Diedhiou 🙊🙊🙊🙊🙈🙈🙈🙈🏃🏽♀️🏃🏽♀️🏃🏽♀️🏃🏽♀️🏃🏽♀️🏃🏽♀️🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾😘😘😘😘❤️❤️❤️❤️
@ Mancha Allah Yalla na Yalla barkel mannnn dal mangui djappp sama
morceaux djambour
Merci tata yalla nala yala defal diam
Hahaha tèrè bien mdr merci waye merci beaucoup tata Mane yaye sama anti stress
Hi aujourd'hui je fais partie des 10premiers macha Alla tata😍😍😍
Kharalma dioye sakh
Ay li Di tata tibal massi sama guemegn bi mogui fess ndokh sakh
Salam très chère tata. Mon mari dit que quand je tomberai enceinte la première chose qu'il fera c'est chercher comment je ne pourrais plus accéder à ta chaîne sinon lui il aura bcp de problèmes.🤣🤣🤣🤣🤣. Kallah t'apporte toute sa bénédiction.
Wa mais pour nous qui sommes en france comment faire pour améliorer si niambane Mad???😁😁