Mbaye !!!! J'allais dire Pisko on t'avait mis hors circuit dans les séries té meune gua liguay deff mais le seul hic moy liguay dieufeundiko bayiko yakhou gua nékho sakh kholll vraiment fils....Regardes ton vis à vis comment il est clean.....Vraiment bayil ngirr say fan's. Merci de ta compréhension.
Mbaye !!!! J'allais dire Pisko on t'avait mis hors circuit dans les séries té meune gua liguay deff mais le seul hic moy liguay dieufeundiko bayiko yakhou gua nékho sakh kholll vraiment fils....Regardes ton vis à vis comment il est clean.....Vraiment bayil ngirr say fan's. Merci de ta compréhension.
Est ce que boko hamé doko o wahtane ack mome en huit clos
Ana mandou ioe yangi def lo xamni beug nga coula sutural yalla mignou sak mougnou ep sutura té xam n'a lep nul n'est parfait mangi diegalou boubax
Vraiment🎉ana soutoura mane mangi suivre mbaye dpw des années mé li mangikoy soga degue
Ndakh yako guisse mouy dieufeundiko ana neutre bou féké xam nguako ngua Woko si roukou wax ak moom pas ici
@@mariamadiadhiou6031aaaah dama tite sakh mane li nane lako nite meuna waher publiquement 🤔
My favorite Kine et Ndeye ❣️❣️
Dianfa c'est la trahison en bambara
En peulh aussi c’est la même définition 😂
En tout cas jiguene dafa wara moyetou yaye yi sone naniou yeureum léne
Dédétt beugouniou ndeye Ndiaye bi😅
D'où ndeye Ndiaye bi laniou sokhlé😂😂😂😂😂😂
Jiguéne dafay soutoural dieukeureum. Wayé lou khew Nga wakh ko say mbokkou weurr di niaane di khawi sa soutoureu
Sali yarou diapoula wayyy 😅😅😅todial casse yi comme ningay défé d’habitude 😅😅😅
Waw mbaye dossé mi douginne wakh thi bopam bi
😂😂 dako coiffé baparé fayko li 😂
Machallah Nice na trop vraiment
ndéye ndiaye role biii diapou ko bayyilékhon moyy tontou wayy
Momo nékh gua lamigne😂😂
BN journée kkg❤
Nanou arrété Kaye 😂
Déléne arrête Sinon eumb dina ame 😂😂😂😂😂fat kiné dou nite 😂😂😂❤❤
❤❤❤❤
La kinez rek ❤❤❤
Guinar fanewerr kayy😂😂
Super
Machalla ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
🎉🎉🎉🎉🎉
Khadija defaral sa togay way
Tee deemat diangui théâtre.
C’est pas méchant
Papa boul wolou sali bandit la atanena nala filmé en nu
Bou ratakh lamigne laniou sokhlé
❤❤❤❤😂😂😂😂❤❤❤❤❤
😂😂😂
Ndeye Ndiaye sa maquillage bi teye mome da bari 😢
😅😅😅
Pour la première fois ndeye Ndiaye yarou😂😂😂
Bilay
Mane uniquement semblant lako diappé 😂
@@ndeyediagne9901 😂😂😂
Bonne question même moi je ne comprends pas la signification de ce titre
Dianfa moy ci peulh trahison awma nak
Dianfa moy woorr .(trahison )
svp titre film bi sa signe quoi svp
DIANFA ça signifie TRAHISON en langue BAMBARA et SONINKE
Et manding aussi @@coumbatandian4865
Trahison
Ndeye ndiaye bandi la 😂😂😂
❤❤❤❤
❤❤❤❤❤
❤❤❤❤
❤❤❤❤❤
V❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤😂🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉❤❤❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤
❤❤❤