AL HAMDOU LILAAH : Une première fois S Cheikh Saliou Mbacké fond des larmes dans un ziar (FADSS)

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 9 янв 2025

Комментарии • 842

  • @josephineaichabouraima4693
    @josephineaichabouraima4693 Год назад +140

    Les dignes héritiers de Borom Touba, nous te souhaitons une longue vie et une santé de fer. Une très grande fierté Serigne Cheich Saliou

  • @ndiayadiop8651
    @ndiayadiop8651 Год назад +90

    Serigne sekh Saliou mbacké yalla nafi Yague té wer🤲🤲🤲🤲❤❤

    • @khadyly1787
      @khadyly1787 Год назад +2

      AlAhouma Amineyarabi alamina 🙏🙏 yallanafi yague te were

    • @signemordiaw3441
      @signemordiaw3441 Год назад +1

      Amine yarabi

  • @portail4253
    @portail4253 Год назад +68

    J'écris avec mes larmes . Que Dieux le garde. AMEN

  • @ahmadouka1892
    @ahmadouka1892 Год назад +84

    Khaléyi dioyounou serigne Saliou ngir sa diemmou dji mbacké ❤❤😢

  • @abdousalamsarr906
    @abdousalamsarr906 Год назад +94

    😢😢😢😢serigne chiekh saliou yalla nafii yagg te wër dieureudieuf ❤❤❤😭😭😭🙏❤️✅

  • @dienendour5344
    @dienendour5344 Год назад +42

    Personnellement je l estime beaucoup que le tout puissant le bénisse et bénisse toute sa famille

  • @g.b1186
    @g.b1186 Год назад +69

    POUR LA 1ÈRE FOIS JE VOIS SA DÉCLARATION DEPUIS 22 ANS. TELLEMENT QUE C'EST RARE ,RARE MÊME.

  • @aliouseck6618
    @aliouseck6618 Год назад +43

    Serigne cheikh mom serigne saliou yalnafi yague loll te and ak werr amine ya rabbi si barkep borom touba yakari diamgni moromantéwoul ❤❤❤❤❤❤❤🕋🕋🕋🕋🕋🕋🕋

  • @djilysall7727
    @djilysall7727 Год назад +1

    Serign chekh saliw mbaké yalnako yalla may goudfan ak wergiyaram

  • @bayelahatndiaye7816
    @bayelahatndiaye7816 Год назад +12

    Yalna sonko djité reuwmi 🇸🇳 2024 ci seringam Serigne cheikh salihou mbacke yagui loll téwer akasa mbacke

  • @famadiop1254
    @famadiop1254 Год назад +83

    Serigne cheikh salihou mbacke Balla yalla nagafé yagu tawér 🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏

    • @adjatraore7770
      @adjatraore7770 Год назад +2

      Allahouma amine machallah Mbacké Balla dieuredieufeuty

    • @seydi7336
      @seydi7336 Год назад +1

      Amine

  • @NDIAYETALIFSALIHATBI
    @NDIAYETALIFSALIHATBI Год назад +2

    Qui est-ce que dou Serigne saliou
    Nion nourou lépp barké borom touba kou d'accord lalal cœur

  • @thiendellafall2506
    @thiendellafall2506 Год назад +21

    Un saint parmi les saints.
    Qu'Allah lui prête longue vie et santé de fer.

  • @hafidaseyad470
    @hafidaseyad470 Год назад +130

    Longue vie inchallah president Sonko a besoin de de toi pour des années inchallah 😭😭😭

    • @seydi7336
      @seydi7336 Год назад +1

      Bilahii

    • @sene6344
      @sene6344 Год назад +3

      Yaw merde way ki lim defal sonko coloré rek lay sam té dou sonko rek lay diokh khar ay santene de personnes

    • @zeynabsaliou4267
      @zeynabsaliou4267 Год назад

      😂😂😂😂

    • @bayemorsarr1754
      @bayemorsarr1754 Год назад +4

      ​@@sene6344bayelen siiso way 😂

    • @cest-2023
      @cest-2023 Год назад +2

      Bilahi soff guene ak Sonko. On s'en fout de Sonko
      Merde politique

  • @moussasangare7282
    @moussasangare7282 Год назад +135

    La première fois peut signifier qu'on l'entend très rarement, moi c'est la première fois que je l'entend

    • @yamadiagne2967
      @yamadiagne2967 Год назад +5

      Walahi

    • @Patriotesn
      @Patriotesn Год назад +5

      Moi aussi mais je l'aime parce que j'ai constaté y a aucune fille en tête nue...vraiment marqué nama😍❤️

  • @oumymendy9167
    @oumymendy9167 Год назад +18

    Un saint homme, un vrai marabout. Que le bon Dieu veille sur toi, djaradieuf mbacke. Simple, pieux, discret.🙏🙏🙏🙏

  • @mameboussokane6016
    @mameboussokane6016 Год назад +80

    Masha Allah ❤ Serigne Cheikh Yalla ngafi gueuna yagu gueuna wér

  • @maimounasambdiop2778
    @maimounasambdiop2778 Год назад +4

    Yallana guafi yague mbacké té ans ak weer balla aîssa

  • @dabaniass2975
    @dabaniass2975 Год назад +20

    ohhh ndayesane dieureudiaf serigne saliou Mbackè 🥰

  • @bayesidy1540
    @bayesidy1540 Год назад +23

    Thieye serigne cheikh yaguefi téwére bala aysa❤❤❤

  • @mamemboye9317
    @mamemboye9317 Год назад +23

    Dieureudieuf serigne cheikh salió Mbacké takhaway bi rafétna lol machallah yalna yalla goudal saw fann nga yagg fi lol te wër amin ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @serigneseck4012
    @serigneseck4012 Год назад +1

    Yalla nga fii yageu mbackeeee teee weeer ki moye sama torondou dii sama yakar fi ak feu leeeeeeeee ❤️❤️❤️❤️

  • @Rokhseck
    @Rokhseck Год назад +8

    Mbacké balla aîcha yague fi lole tamou ande ak werr amine yarabi

  • @laminendao6868
    @laminendao6868 Год назад +11

    J'aimerai tellement le rencontrer et bénéficier de ses prières

  • @borombakh1129
    @borombakh1129 Год назад +5

    ndayesane thieye seringe cheikh saliou yalla nafi yage lol té weur Amine Amine Amine Amine Amine Amine Amine Amine Amine Amine Amine Amine Amine Amine Amine Amine Amine Amine Amine Amine Amine Amine Amine

  • @modoukebe6669
    @modoukebe6669 Год назад +9

    Serigne chiekh saliou ya bakh seutoub serigne touba yaw bokougasi ngiy siguil serigne touba❤❤❤❤

  • @NdeyemarameNdiaye-r5e
    @NdeyemarameNdiaye-r5e Год назад +7

    Amine yarabi yalle na fi yageu loo té were Mbacké Balla Aîcha

  • @ElHadjKandeNDIAYE
    @ElHadjKandeNDIAYE Год назад +3

    Kuy seet nitu yalla ba éksi si jëmm jii, taxawal. Jaajëfati Cheikh Saalih.

  • @serignembackemouhamedtoure6766
    @serignembackemouhamedtoure6766 Год назад +12

    Gënë Yegue Gënë Wëër Rek ☝️ Amineee 🙏 ❤️ ❤️ ❤️ ❤️

  • @papediop9417
    @papediop9417 Год назад +15

    Bilaye walaye mbacke yalla nga fi yague lole té wer❤❤❤

  • @bambaniang5463
    @bambaniang5463 Год назад +16

    SubanAllah I love you serigne cheikh saliou ❤

  • @noreyni6059
    @noreyni6059 Год назад +4

    Dieuredieuféti Serigne Touba
    Dieuredieuféti Serigne Touba
    Dieuredieuféti Serigne Touba
    Dieuredieuféti cheikh ahmadou bamba khadimou Rassoul.
    Gathié ngalama Serigne Salliou mbacké.
    Diarama Serigne cheikh salliou mbacké.❤

  • @mariamasouare153
    @mariamasouare153 Год назад +3

    Santé et longue vie à vous, serigne cheikh saliou, le peuple à besoin de vous, merci beaucoup

  • @babacarsambe5794
    @babacarsambe5794 Год назад +1

    Yague fi lol mbacké té am weer amineee❤

  • @bigue5329
    @bigue5329 Год назад +1

    oooohhhh Ndayessn Serigne cheikh moye Serigne saliou thi yeureumande dia😢😢😢😢😢 yague fi loooooool te werr mbacke balla Aïcha 🤲🤲🤲🤲🙏❤️🥰🥰🙏

  • @Bbdiarra3356
    @Bbdiarra3356 Год назад +3

    Dieureudieufeuti serigne saliou mbacké
    Serigne Cheikh saliou mbacké yalla nafi yague th werrr

  • @Beugfallou2203
    @Beugfallou2203 Год назад +16

    Gëneu yague Gëneu Wëer Mbacke Balla 🤲

  • @moustaphasylla4066
    @moustaphasylla4066 Год назад +8

    Allahou Akbar thieye Serigne cheikh saliou ❤❤😢😢😢

  • @omarcheikhoudiagne9795
    @omarcheikhoudiagne9795 Год назад +23

    Dieureudieuf Serigne Cheikh Saliou

  • @cheikhbassiroubabou686
    @cheikhbassiroubabou686 Год назад +4

    Thieye Serigne Saliou Yalla Nagnou Ko Yalla Fayale Bi Barakati Khadimou Rassoul Amine . Serigne Cheikh Saliou Yalla Nafi Guene Yague Té Were Bi Barakati Khadimou Rassoul Amine .

  • @ndeyendiayesaliou8610
    @ndeyendiayesaliou8610 Год назад +2

    Mbacké balla goundal faneu😭😭😭😭😭😭

  • @sokhnamaithiam9558
    @sokhnamaithiam9558 Год назад +1

    Machallah Mbacke balla Aïcha yague fi lole tamou ande ak wéer 🥰🥰🥰🥰

  • @saergueye6440
    @saergueye6440 Год назад +2

    Une vraie leçon d'humilité et de foi.Que Dieu le bénisse et agréé sa mission dans la voie tracée par son père.

  • @barrathiaw8885
    @barrathiaw8885 Год назад +13

    Dieuredieuf Serigne Cheikh Mbacké Yallahna Gafi yagu loh té and ak weer sibarké Serigne Saliou

  • @elhadjimmd4497
    @elhadjimmd4497 Год назад +1

    Ndeyssane yermandé bi si Serigne Saliou léppa ngi si mome 😢😢

  • @ousmanediallo1632
    @ousmanediallo1632 Год назад +5

    Amine ! Que Allah vous bénisse et vous donne longue vie...

  • @amiami7328
    @amiami7328 Год назад

    Dierediefeteti serigne salliou s cheikh yalla nafi yague loole tewer amineeeeeeeeeeeeeeeeeeeee

  • @modoufall5006
    @modoufall5006 Год назад +1

    ❤❤❤yalna ngaa yaggg loool to werr Mbacké balla❤machalla❤

  • @Mayipeniang
    @Mayipeniang Год назад +13

    Yalna nga fi yague lole té wérr Mbacké balla ❤️

  • @ndiogouthiam6895
    @ndiogouthiam6895 Год назад +12

    Dieureudieufeuty serigne saliou mbacké❤

  • @mamendoumbefall9426
    @mamendoumbefall9426 Год назад +3

    Aka ragal Yallah, aka doylo Yallah, di wetal Yallah, di kou mandou teh tabee lool, woyof lool teh Bari yeurmandeh. Bilahi ya bakh, yallah nangafi yague lool teh weer

  • @medounefall3110
    @medounefall3110 Год назад +25

    Dieuredieufé Serigne touba

  • @falloundiaye2336
    @falloundiaye2336 Год назад +3

    yalna yala goudeul fan wi yokkou wer ak kattan ci barké serigne bi

  • @fallndoye1913
    @fallndoye1913 Год назад +1

    Mach'Allah Dieuredieufety Serigne Cheikh Saliou Mbacke yague filol té ande ak werr Amine yarabi

  • @kamoucisse6354
    @kamoucisse6354 Год назад +22

    Serigne Chiekhe Mbacké saliou yalla ngua fi yague loll témou ande ak wër amine❤❤❤

  • @kemanetvhd9700
    @kemanetvhd9700 Год назад +1

    Serigne cheikh Saliou Mbacke Yalla ngafi Yag thi barkep CHEIKHOUL KHADIM

  • @fatougueye77
    @fatougueye77 Год назад

    Cheikh bi Mbacke yalla na fi yageu té werr Aminn

  • @mamengorseck
    @mamengorseck Год назад +19

    Vraiment... pénible très très très pénibles..
    ÉMOUVANT...اللهٱلْحَمْدُ لِلَّٰهِ ما شاء الله

  • @papefaye7232
    @papefaye7232 Год назад +2

    Serigne cheikh saliou yalla nafi yague fi lool te wer barkè serigne touba ahmadou yakari diam gni

  • @landeya8239
    @landeya8239 Год назад +2

    Dieureudieuf Mbacké yala nga fi yague teu were

  • @sdiarrasaliou313
    @sdiarrasaliou313 Год назад +2

    Ndeysane 😢😢 Balla Aïcha yegeu fi lool té wérr si barkép Serigne saliou

  • @mbenesylla4639
    @mbenesylla4639 Год назад +3

    Wallahi Ndayssan mbacke balla yagu fi ta werr looll Ty barkeb Serigne Touba 🤲🤲😭

  • @AssaneGninig
    @AssaneGninig Год назад +4

    Massalalh sama Wassila Serigne cheikh saliuo mbake ❤️❤️💘

  • @mamadouniang4531
    @mamadouniang4531 Год назад +1

    Yalla na yalla geuneu goudeul fane wi mbacke

  • @bathikane2391
    @bathikane2391 Год назад +11

    Sama sarigne sama léppou sarigne cheikh Sallou mbacke yalla nafi yag té wér Amin 🤲🤲🤲

  • @mamefatounguer3444
    @mamefatounguer3444 Год назад +4

    Yalna yalla yaagual takhawaay bi té wéral thiér yi balla aïcha ❤❤❤❤

  • @seymaboudiakhate7213
    @seymaboudiakhate7213 Год назад +1

    Mbacké balla yague fii looolll thé ande ak weur walahi soxla nagn leu fi doundeul weur ngouguei niou bacii kanama kanam Mbacké🙏🙏🙏 ❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @fallsfalls1853
    @fallsfalls1853 Год назад +1

    S’il mettait accorder milles vies je vous donnerai toutes les secondes de ces vies sans regrets, sans manière je le ferai en gaités cœur. sans doutes vous êtes une Homme de bien. Que le tout PUISSANT vous accorde longévité.
    Je vous aime.

  • @NdiayeMory-wt3mr
    @NdiayeMory-wt3mr Год назад +6

    Machalla yalla na yalla faye mbacké balla aïcha

  • @joomndindi
    @joomndindi Год назад +2

    Amna solô lool mbakké gëna wérr yàgg yook barké séex ibra ❤

  • @KhadimBadiane-y8k
    @KhadimBadiane-y8k Год назад +8

    Machallah serigne Mbacke balla haïcha yalla nangafi yague loll rewuér sibarkéb seyidina s saliou salihou dieuredieufaty Serigne cheikh mbacke❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @bassiroundiaye9585
    @bassiroundiaye9585 Год назад +3

    Serigne Cheikh Saliou yalla nga doundou 100 ans si kaw souf ci barkep serigne Touba

  • @classbeautyshop3167
    @classbeautyshop3167 Год назад

    Mashallah MBACKE balla yague fiii lolou té wer🤲🏽🤲🏽🤲🏽🤲🏽

  • @BinetaGadiaga-x9h
    @BinetaGadiaga-x9h Год назад

    Machalla mbacke yallana may wergou yaram ak goudou fane amine

  • @cheikhbadardiop2214
    @cheikhbadardiop2214 Год назад +1

    S.cheikh ibn s.saliou y'allah nafi yang te wër❤❤❤❤

  • @ousmanebadiane4471
    @ousmanebadiane4471 Год назад +4

    Machallah mbacke balla❤yalla guafie yague te werr❤

  • @kenalserignetoubambacke269
    @kenalserignetoubambacke269 Год назад

    Ndeysane kadome yi diar na bayi khèl sogné na déh 😢❤ wayé yallah nafi yagueu té and ak weer❤🙏

  • @fallyaram183
    @fallyaram183 Год назад +1

    Srigñ saliou Mbacké thiey ❤❤❤❤ noo li

  • @ndiayendiaye313
    @ndiayendiaye313 Год назад

    Machchallah amiiiiiiine yalla ngene fi yaga amiiiiiiine THiE BARKE Seydouna MOUHAMED

  • @modoungom4303
    @modoungom4303 Год назад +4

    Serigne Cheikh Saliou Yalla gafi yag té wer mbacke

  • @mamediarradiop1556
    @mamediarradiop1556 Год назад +4

    SERIGNE CHEIKH SALIOU MBACKE YALNA NAFI YAGUE TE WER SI BARKER CHEIKHOUL KHADIM AMINE

  • @amadieng3833
    @amadieng3833 Год назад +1

    Machallah Dieuredieuf sunu Borom muniou bakhe kilifa you bakh

  • @diagnelerebelle9490
    @diagnelerebelle9490 Год назад +1

    Serigne saliou SERIGNE Cheikh Ahmadou Mbacké yalnafi yagg té werr
    Barkep serigne touba ak cheikh ibra

  • @cheikhthiam8279
    @cheikhthiam8279 Год назад

    Machallah jaajeuff Mbacké Balla Yalla ngafi yagg loole th wérr 🤲

  • @mammorsilla5579
    @mammorsilla5579 Год назад

    Thieuye Serigne Saliou yalla faye nako dh❤❤

  • @fatoumbaye4532
    @fatoumbaye4532 Год назад +13

    MBACKÉ Yalla ga fi yagg lol tei weirr si BARKEI SEYDINA MOUHAMED PSL ❤❤

  • @cheikhmbengue7459
    @cheikhmbengue7459 Год назад

    Serigne cheikh saliou mbacke yallna ngafi yague looool téwér Amine yarabi 🙏😭🙏

  • @MamediorSougou-ed4qd
    @MamediorSougou-ed4qd Год назад +2

    Machallah Serigne cheikh Salifou yallah gafi yague t and ak wer

  • @morndiaye8759
    @morndiaye8759 Год назад

    Machallah machallah mbacké balla yalnayalla yokou fanwi ak wéur gi banga matalé barké borom Touba 🤲

  • @madoundoye2414
    @madoundoye2414 Год назад

    Hoooo Serigne cheikh yalla ngafy yag lollllll té werr barkep sidi Brahim fall lamp❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @mbayedollarddiop33
    @mbayedollarddiop33 Год назад +1

    Serigne cheikh Salihou yague fii loll t3 wer Mback3 balla Aicha

  • @cabinetkhelcomkheweultv2418
    @cabinetkhelcomkheweultv2418 Год назад +40

    Machalla Machalla ♥️❤️♥️

  • @cisseabdou164
    @cisseabdou164 Год назад +2

    Yaggfi loooooool mbacke barkep s.salihou

  • @mamediarradiop4681
    @mamediarradiop4681 Год назад +25

    Amine machallah ❤❤

  • @assfayeserignesaliou742
    @assfayeserignesaliou742 Год назад +5

    DIEUREUDIEUF SERIGNE CHEIKH SALIOU MBACKE ❤❤❤😭😭🤝🤲🤲🙏🙏🙏

  • @sokhnathiam3895
    @sokhnathiam3895 Год назад +3

    Machalla mbackè balla longue vie à serigne cheikh saliou

  • @PapeDiouf-xw6fb
    @PapeDiouf-xw6fb Год назад +1

    Machalla serigne Cheikh Saliou mbacké amine ak alkhamdoulilah yague fi té weurr ❤

  • @MameSokhnaLo-sr7vr
    @MameSokhnaLo-sr7vr Год назад

    Yallana nagua fi yage te and ak werr mbacké aminne ❤❤❤

  • @ablayecamara9562
    @ablayecamara9562 Год назад

    segn Bamba rk dh mashallah serign bii kaddû yii rafaitt-naa yallah na yallah df léep di tawfaixxx

  • @mouhamedmakhroufthiam1476
    @mouhamedmakhroufthiam1476 Год назад +5

    Ndeyssane day djeuf tè doussi bolê ay wah, yala nafi yage tewere.