Wally warnga geuneu xam sa bopou xam Lila yalla bourbi defal kilifanga nanga geuneu maytou amnga barké bay amnga ligueyou ndeye Yalnala yalla soutoural samla 😊
C’est vrai que Wally c’est un président. Félicitations à toi le chanteur du peuple. Tu aimé par ton propre pays❤🇸🇳🙏 wally que Dieu te protège 🙏 amine 🙏🙏
@@Kanté-y7j ma wax la français comme dego olof j’ai dit t’es où là diomaye s’assoit avec tout les personnalités du monde et tu oses le comparer avec waly
Wally bagn bagn nangou rek Billahi guissegoulene dara avec wally en avant rek lii yallah la il est où boucher😂😂😂😂😂😂😂😂et les ennemis de wally billahi malene yeureum chaque jour guene sossal wally chaque jour wally dilene raw❤❤❤❤❤❤
Armée bi aye faralaren laniou😂😂😂😂❤❤❤❤vive wally🎉🎉
@@codoudiouf7568 lam framarene😂😂😂😂
Ceci confirme de plus que Wally est le chanteur du peuple parce que choyé et admiré par tous ces éléments des FDS mashallah!
President sakh fans la 😂😂😂
Dioms yaa diantale ❤️❤️
Mo heré kay lou wow kong cheri indo Aïdara Sénégal ben weuykat leu am mouy yaw ben politiciens mouy sonko❤
❤❤❤❤
Dafa ler❤
Gendarme yi ay faramarenn lagnu ❤😂😂😂😂😂😂
Setlu nga lolu😂😂😂😂
@ oui oui lii molay woon neii amneu niouko beugg tei dugnu dem ay soirée wam genre les gendarmes rek doyna preuve
🤣🤣🤣🤣🤣
Boula gendarmes yi diapei 😂😂😂
Wally notre président de la musique sénégalaise on vous t'aime fort❤
Bilahi li wara takh gnou khame li mbayou Yalla maryacine yalla nala yalla samou si barke Mouhamed bilahi walahi yaye Senegal
Non li yalla la nak ❤ nangou rek wala bagne ❤les 2 présidents de la république wally a vie on t’aime son excellence
Machallah wally❤
Wally warnga geuneu xam sa bopou xam Lila yalla bourbi defal kilifanga nanga geuneu maytou amnga barké bay amnga ligueyou ndeye
Yalnala yalla soutoural samla 😊
❤❤❤Liga waxx ni Moy DEUG Mouy foula
Li yalla la dioulit day gam yalla❤❤
Deug deug yalla mana mayé vraiment
Wally on vous aime
Ceci c'est la confirmation trône bi Yako tokk 😅❤tu est roi de la musique sénégalaise
Machallah nieup leu beugu ❤❤ ... yalna Sam borom defaal la jam barkep CHEIKHOUL KHADIM
Non longue vie à toi Waly se longue vie à toi❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Son excellence est ce que beugoulone photos ak wally thieye yallah 😢😢😢😢 Wally dall mok sonko yallah maynalene
Thieuy notre Star international ☝️Aférbi gnanou wadjiour laaa déé 🤷
C’est Dieu ❤❤❤❤❤
Bilaye
Très très fier de toi ❤
C’est vrai que Wally c’est un président. Félicitations à toi le chanteur du peuple. Tu aimé par ton propre pays❤🇸🇳🙏 wally que Dieu te protège 🙏 amine 🙏🙏
C'est beau ❤❤
Machallah ❤❤❤❤C''est plus que fort❤❤
Excellent deux travailleur et de sagesse d esprit
❤❤Wally is among Senegal 's development and he is youth and noone loves Senegal more than him .
Liii raféte na wayy Machalla❤
Je c mem pas mais wally begue Nala
Lol bilahi nasa diame yague ❤
Vraiment nak waly seck star la nak kholal gayi rék meilleur président de la république basirou diomay meilleur premier ministre depuis 1960
Ma.challa. wa.wally. ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
This is Beautiful ❤❤❤❤❤❤❤
Masaahallah yanna Yalla deff diam tee laff chat Si Wally n faramareen yi yep❤❤❤
Diomaye yayy président Wally moyy Sénégal
😂😂ya meuna daye bane Sénégal
Wallahi Machallah
Wallahi Wally moyy Gambia 🇬🇲
Sonko moy Sénegal kouka lal niou nokhou ko wala bok niou niouss ko 😅😅😅 ms Wally moy way katou jeunesse bi 🥰
😂😂😂 Wally a part wayane amoul béne ndierigne@@boyetownfromdkr5287
Wally Moy Sénégal ❤❤❤
Wally seck le chanteur du peuple
Machallah
Macha Allah Wally Moy Sénégal diomay Moy président Lolou la yalla dogal
Machalla ça ma framareen bii diamou reck ci Sénégal unchalla rabby amiine ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Alkhamdou lilah.lazi..❤❤❤❤❤
Thiey goné gui seck Wally mo beuri bayyyyyré deh
❤❤❤❤❤❤❤ha lii sédeuna khol mancha allah laf thiat
Masala artiste planétaire golden boy Fred🎉❤
Machallah encourager len ko am n'adiom laff am na foula laff thiat ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
The king off the !! tiey ballago mashahala kou Allah sampe do meussa danou bagne beug rek mala love ❤
Waly nak Sénégal barke baaye ak ligueyou ndeyyy meun na lounek
❤❤❤❤❤❤wawawe je t'adore beaucoup wally ❤❤❤❤
Diomaye wally molleu geuneu nékeu star dhéé ❤❤😂😂haye
Diomaye nioumoul togal yaw tamite fo nek ça jamais 😅😅
@aissatoudione1922 😂😂😂😂yawe nitte gua
@aissatoudione1922 ligue bindi comprendrou massi dara
@@Kanté-y7j ma wax la français comme dego olof j’ai dit t’es où là diomaye s’assoit avec tout les personnalités du monde et tu oses le comparer avec waly
C’est du jamais vue 🎉❤
Dimbalou yalla dou anadk thiono dou andak ma takh bly❤❤❤❤❤❤❤ na xol yi fékh thi wally
Non ça c'est super c'est ma première fois de visa c'est ma première fois❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machallah ❤❤❤❤❤❤❤
Merci wally secka ❤❤❤❤❤❤
Kou yabo nangou rek te kham ni Wally seck moye Senegal ok
Much love wally ❤❤❤❤❤❤❤
Ndeysan gendarme yi sakh niogui r😂😂 no waly amgua mayouk yala nak
Ndeysane maryacine
C'est abdou guitta seck qui est le chanteur paroliers du peuple Sénégalais 🇸🇳
Guiss nit beug ko thi yalla la. Président nieup gnoko beug. Wally khaleyi gnoko beuk. Vive le Sénégal et que la paix règne sur le pays.
Long vie wally ballago ❤❤❤
Ykofa âme mar Yasmine yaw kasé♥️♥️♥️one love
Sénégal 🇸🇳🇸🇳
machalla raftna lole ken du wally niepa ko beug
Sénégal lou way di deff the boléwosi wally dou sortie yalla moko deff
Exactly 💯 agree
Wally d waxonnako nioukay critique ❤❤❤❤m Deugla
@@mormbaye2989 Wally Secka moyy Gambia 🇬🇲 sah purr mo lerr
ya meuna doul
@@bassirouseck6865 saga yi pour lanla tmt
Ma sa allah wali seck
Lou masta âme Sénégal yalna diam yague waye li nak moye Sénégal gnoune li lanou khame😂😂
Bilay walay happy free rek ay bou feke won diamono ndafa gnémé wougnou ko sakh
Machlla❤❤❤❤❤❤❤❤
Ma shaa alla ❤❤❤
Wally bagn bagn nangou rek Billahi guissegoulene dara avec wally en avant rek lii yallah la il est où boucher😂😂😂😂😂😂😂😂et les ennemis de wally billahi malene yeureum chaque jour guene sossal wally chaque jour wally dilene raw❤❤❤❤❤❤
ana gni don xekh wally nan dawoul xewal porosebi wally moy sen baye
Defléne Bangkeu 😂amna kounane si souff yangui may gagne yangui may gagne😂😂😂😂
Yawe la jeunesse bi buegue wally seck
Thiey sama fans bi niepa la beugue ❤❤❤❤❤
Wally Kou bakh douko bagne❤
Ça c'est beau li nkh na 😂
C'est Dieu 😂❤❤❤❤
mayouk yalla rek la yalnako yalla arr te Sam ko
Garde nantega bilay
NANOU MOYTOU THIAAXAAN MUZIK LOUBONLA
Walyy moy galsen
Macha allah 😂😂😂😂
Jantalman baye fall
C'est pas lez marabout c'est dieu ❤😅
Wally Seck doundeul
Wally soy dokh Sax Di bondeiiii😂😂😂😂😂😂😂
Mel ni yalla bou ndawe Lou mou ladjie niou diokh KO dem sakhe ba niou koy toude khalifa générale koulou musique 🤣🤣🤣🤣🤣
Waly aka Yarou
Mei wally mi moy diambar
Machallah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Sénégal mongi dora nex
C le chef
Mashallah ❤❤❤❤❤❤❤
👀lane laa défal Sénégal dit moi🙏🏼
Xana yalla dokhko thieur tei yaw ak sa aye morom keine mounouthi dara
niar niou yarou
Armée bi beurina af framaren🎉🎉🎉😂
Le chanteur du peuple 😂 c'est drôle
Yalla na you Yalla defalle diam mousalnou si sietane
Yaye diou bah moy diour dome you bah
Li deh outena diamono ndafa
Legui 😂😂louthi nit meun 😂
Wayal arme bi
❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Lou woow kong lou xéré
❤
C'est pas le marabout C'est Dieu