Salut c'est Mme gomis je l'ai fait avec la moitié de farine et le reste des ingredients au top mes enfants et mon mari ont adoré. Je le reprends encore. Merci vive saveur.
Merci beaucoup Tata Mariétou. J’ai suivi ta recette à la lettre et c’était une réussite totale. Tout le monde a aimé. Yallah na Yallah wereul loxo bi bayi lafi bassi kanam mou and ak wergou yaram ak xeweul. Love you ❤️❤️. Fatou Seydi from Maryland
Tata ya woor dhé mane dall j t'aime soumay togue nek si keur gui d'i rèpété ay youbou yaba néko réleuh mouy gounouss gounoussi vraiment yakouna😅😅😅😅nassa diam yague😍
Ohh sama tata dama woor mba lii dou yakh koor 😂😂😂 machalah machalah nawone fawone dello nenla niane yi yeup lingua fi niane yeup yalana diitou si yow machalah sama tata niou dougui si koor gui ak diamou yàlla defal nieup diamou yalana sa diamou sakh sama tata préférée yow mi takh louma def monsieur apprécié
Alhamdoulilah machallah TABARAKALA tatie mane khamou ma Sakh loumay wakh khana santala akkk geureum la yallah na la yallah féye sama la yôk sasoutoura si barkél lépp lo dougua wëral bât bi dieuredieuf
Aye Tata Mariètou! Lii bakhoul pour sama genre yi ngua khamni danio pata pouff deh!!! Mais une fois de temps en temps yakkou ci dara!😁😁😁 Kharal ma nieuw légui dème grocery ndougou ndougou bi té beignets beignets bi! Souba in sha allah ma saaf ko! Merci waye tata! Niou woor ci diammeu!
Machallah Marietou tes plats sont délicieux TU est simple et intelligente pas de problème j aime bien ta façon de faire je voie que mak monla éduqué tu bien cuisiner laf yeet
Sama yaye yaw rek lay suivre à chaque fois qu'elle se connecte sur RUclips. Merci à vous
4 года назад+1
OHHH Masha Allah CEST GENTIL PLEASE DEMAL THI SAMA PAGE MESSENGER CEST ADJI Marietou Ndaw POUR QUE NGUA DIOKHMA SON NUMERO INSHA ALLAH DINAKO WOO MERCI
Merci de nous apprendre vos connaissances mais ça sera bien aussi si vous expliquer en français parce nous qui comprenons pas le wolof ça fait qu il y a des détails qui nous échappent merci beaucoup
JazzakAllahu khairan tata Marietou Yalla na diamb yague
Merci tata mariatou je viens de reproduire la recette tt suite merci pour cette video
💃🏿💃🏿💃🏿 machaAllah Jazakalahou khayrane Tata Mariétou darling amatina solo oh 😍 ramadan in shaa Allah🤗🥳🤩🥰😘😍
J'adore tata marietou tout ce que tu cuisine surtout ces beignets la merci
Bilahi beguena si
Ohhhhh sooo sweet mala raw yaw souma papa ngua ndakh sama pape Babacar la toudeu merci wayyyy
Bravooo très bien
Macha Allah laf thiat rèk
Manchalah c'est bien présenté,avec de l'humour,,,fofa tothi na 🎉🎉🎉 manchalah
Degel ma li rek si beignet vraiment love you so yalna khel mi ak lokho bi guena werr bilahi sa fans number one
Machalah machalah good job tata we love u
Sa faso de parlé mane nama rayée🤣🤣🤣🤣🤣😂😂😂😂😂💕💕💕💕❤️❤️❤️Machahala ❤️❤️❤️
Machalla beignets bi amna mana tata
Diakhazéeee néko réleu fofa todie
Très bien merci wayy
Bien bon tata i love u❤
Salut c'est Mme gomis je l'ai fait avec la moitié de farine et le reste des ingredients au top mes enfants et mon mari ont adoré. Je le reprends encore. Merci vive saveur.
Bravo tay bidegue ingrédients yi machalla
Machalla tata j'ai adoré la ressaite
Ay waye ma beug begnet
Maachallah com dab neekhena rafetna ci beut.yalnagnou woor si diam .yalna Yallah yeessal yeurmandé ci mère Diop AK sounou défunts yeup
Merci beaucoup Tata Mariétou. J’ai suivi ta recette à la lettre et c’était une réussite totale. Tout le monde a aimé. Yallah na Yallah wereul loxo bi bayi lafi bassi kanam mou and ak wergou yaram ak xeweul. Love you ❤️❤️.
Fatou Seydi from Maryland
Hooo tata vous êtes sympathique ingresin
😆😆😆😆😆😆
Machallah machallah amene solo merci tata
Tata ya woor dhé mane dall j t'aime soumay togue nek si keur gui d'i rèpété ay youbou yaba néko réleuh mouy gounouss gounoussi vraiment yakouna😅😅😅😅nassa diam yague😍
Vrement maman la façon k tu t’expliques sa m tu merci beaucoup on t’aime vraiment
Masha'Allah tata mariétou beignet bii eupnaaa god bless you
Mahchahala allouhouma aminneee Yalla gnane yi nangou inchahlaa merciii Ta mariétou 🙇🏾♀️
Macha allah beignets bi amna solo
Machalla machalla beignets gua lafe thiate
Moi je mets à chaque fois pousse bleu avant même de voir la video
miishu ndao 👏🏾👏🏾👏🏾👏🏾👏🏾👏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾😘😘😘❤️❤️❤️❤️
Bilay Tata mala love ❤ doundal wéral amal djam yalna yalla khépp doli mayla goudou fane ak wérr lafal la thiate
MashaAllah tata yalnagnou fékké koor gui ci diam ak salam say beignets kheumeukh tarkhalah yalnasa diam yagg
Masha Allah Barak Allah Fiki, au top
J’aime ta façon de faire les beignets 🤣🤣🤣fofou tothie
Macha allah waay eupeu Tina
Machalla amna solo
J'aime beaucoup des beignets merci sama tata boubari diame.
Ohh sama tata dama woor mba lii dou yakh koor 😂😂😂 machalah machalah nawone fawone dello nenla niane yi yeup lingua fi niane yeup yalana diitou si yow machalah sama tata niou dougui si koor gui ak diamou yàlla defal nieup diamou yalana sa diamou sakh sama tata préférée yow mi takh louma def monsieur apprécié
AMINATA GUEYE Allahuma ameen wayy
Diakhacer, melanger, maa shaa Allah tata 🥰🥰🥰
Machaallah. Beignet gua
Tata namenalaaa
Oh li boler ko ak ataya bou woyof 😋😋
Manchallah tata sa beignet keumeukh amna solo diankhasse melanze fofo tothie❤❤❤
Mashalah yalla nanou ague ak diam Salam
Masha allah
I need to try making this. Thank TT
Waw beumou bari dolé
MachaAllah tata Marietou Djazakhallahou khayrane pour tout🥰😍😘
Machallah tata machallah
Je t'aime gros comme sa , je ne comprends pas la langue mais je regarde
Mashaalah tata je t aime fort
Degal lolou😍😍😍😍
Je t'aime beaucoup. Mâcha Allah. J'adore tes vidéos
Mg Ndiaye 😘😘😘😘❤️❤️❤️🙏🏾🙏🏾🙏🏾🙏🏾
Mash Allah bon mois deRamadan alhamdoulilahi
Machaalah recette bien présenté yalna lokho bi geneu werr
Keumeukh 1995 lako gaudia degu merci sokhna si ça me rappelle beaucoup de choses
Tres bien Macha alla contanenagnou yalla na la yalla say
Nekhena dieredieufeuti
Alhamdoulilah machallah TABARAKALA tatie mane khamou ma Sakh loumay wakh khana santala akkk geureum la yallah na la yallah féye sama la yôk sasoutoura si barkél lépp lo dougua wëral bât bi dieuredieuf
Ca donne envie ❤
Machalla tata mariètou on t'aime
Coucou ta marietou je suis très contente de vous on disait que vous lisez dans nos pensée Dieu vous bénis et vous garde
Tata maretou yalnaguafi Hague ta werr mane dee Liouma diakhal rek ma nieuw ci yaw macha Allah sa plat yeupa am maana Maty depuis Ndar guedj
Liii nexna d. Waaoouuhh
DjazakAllah khayran tata Marietou pour la liste des ingrédients, MashaAllah MashaAllah,
Oh je t adore Tata marétou. Encore merci et bon ramadan
J'aime trop la manière dont tu nous explique la recette ak wolof by on comprend mieux
Gros bsx à toi💫❤
Machalla sounou tata
Aye Tata Mariètou! Lii bakhoul pour sama genre yi ngua khamni danio pata pouff deh!!! Mais une fois de temps en temps yakkou ci dara!😁😁😁 Kharal ma nieuw légui dème grocery ndougou ndougou bi té beignets beignets bi! Souba in sha allah ma saaf ko! Merci waye tata! Niou woor ci diammeu!
Machallah ma cherie
Merci Tata Maretou yalla na sa diam yagg
machallah tata mariètou laf thiat😘
Machallah Marietou tes plats sont délicieux TU est simple et intelligente pas de problème j aime bien ta façon de faire je voie que mak monla éduqué tu bien cuisiner laf yeet
Sénégal yafi dakheu beignet
Tata namenalaa
Mane yaw Yama nékh tata Mariétou bilay walay , machalla amena solo
Assalamu alaykum ma cha Allah j'aime vous suivre rien que pour votre humeur plaisante ma cha Allah 😅
Machalah sama toureundo magui lay suivre a chaque fois
Walaykoum salam ndaw machallah amna solo😍😍😘😘❤❤
Machalah tourondo
Machala amena solo
Diakhaséee melangéee😂😂😂ahhh ma tati elle est adorable merci pr tt
Salam ta marietou yalla fayla yagui niou diagal lou bari takh ga keur you bari nekh dieuredieuf yalla mayla goudou fane bou anda akh weer coucou a vs
Tata marietouuuuuu💝💝💝💝👏💝💝💝💝
Sama yaye yaw rek lay suivre à chaque fois qu'elle se connecte sur RUclips. Merci à vous
OHHH Masha Allah CEST GENTIL PLEASE DEMAL THI SAMA PAGE MESSENGER CEST ADJI Marietou Ndaw POUR QUE NGUA DIOKHMA SON NUMERO INSHA ALLAH DINAKO WOO MERCI
Machahala
Commencé gouma sax nima guissè beignet yi rek aimé 😍😍merci tata
Ton mari est chanceux😃
Machalla tata
Machalla é merci beaucoup
Machalla sa beignet diar na Yonne
Amiine ya Rabbi, qu ALLAH swt vous protège et vos proches. Ramadan Moubarak of all the muslim🙏🙏🙏
Oooooh...merci beaucoup si beignets yi hummmm...j'adore. Dinako défare Inchallah merci tata bisous depuis la France 🇫🇷😘😘
Merci de nous apprendre vos connaissances mais ça sera bien aussi si vous expliquer en français parce nous qui comprenons pas le wolof ça fait qu il y a des détails qui nous échappent merci beaucoup
Néna nékothis touy 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂🥳😊😂😍😍😍
Eey eey ma Tata masha Allah Avc le confinement demain je vais m'aventurer 😂😘
Machallah beignets bi ça l'air appétissant
Machallah tata 😘
Machaallah tata maretou beignet gua yalna lokho bi were
Amine yarabi que le tout puissant nous protège de cette pandémie et nos familles respectives
Merci beaucoup pour les explications mais personnellement cette langue ne m'a pas permis de mieux écouter. Mais je vais pratiquer.😘🥰 merci
Ma cha allah yagui may yobou guay kkkkk sama togolokh bi